Pape Ndiaye savait tout ça fait un moment qu'il sondait les Sénégalais pour savoir leur reaction sur la libération de Nabou Leye mais le grand juge c'est Dieu
Avec tout ce que le frère de Aziz Dabala a témoigné lors du jour de la découverte des cadavres en compagnie de Nabou Leye, je ne peux pas point comprendre qu'elle bénéficie d'une liberté provisoire.
Ce que les gens racontent diffèrent souvent de la réalité. Si elle bénéficie d’une liberté provisoire dans une affaire de double meurtre c’est qu’elle est innocente. Imaginez si elle n’était pas emprisonnée les pékinoises l’aurait assassiné.
Yow nafékheu nga nabou léye noumouye baré none téé llimou déf c est flagrant lokhome a ngui thie biir nga nane amna gnou done dém thie sérigne pour mou désse lolou wakh ban rendement laa amal gniognou wassalame
Si elle n'est pas encore jugé pourquoi on devrait penser qu'elle n'est pas coupable? Si elle était innocente kenn douko teuthie, donc on ne peut pas la libérer comme ça sans explication
Iow vrai doulkat ga un journaliste digne de ce nom ne doit po ce comporter de la sorte , pourtant amneu niou deiimone thi Bameiilou Aziz pr tibbbb fa soufffff ! Lolu numu toudddou?? Un vrai n’importe quoi dans ce pays. Niatta lagn la fay pr k u puisse défendre Cette femme. Kii meme xel naggouwoul sakh mou libre
Sa liberté provisoire choque plus d'un. En tout cas des mystères entourent sa libération. Elle ne devait pas bénéficier de cette liberté à mon avis, elle est trop mélée à l'affaire
Nékk lén ay niit nabou dina Ray justice bi am preuve bayi ko mo gnibi sougne KO bayé par ce k amouniou preuve si moom beuss bi preuve Di takh nabou day déllou prison force
Le journaliste doit être arrêté pour expliquer comment il sait que cette dame a beaucoup d'ennemis et que ya des gens qui se battent pour qu'elle reste en prison
Wax loula waur ñèpe la waar ndax ay looble par ci au lobbies par le day gueuna yèkati xole yi rèk tè xana les juges ne sont manipulés par ces soit-disants loobies
Pape tamite ya khamal nieup ni mareme leu toudou au lieu de nabou 😆 Mane dal vraiment dina geune moytou comme dara leroul ndakh kene khamoul kane nga meune tassel ak loumou sagne
Merci pape ndiaye si léral ti mais warone nga tek audio yi justice bi mom fimné amna sopé kou boubakh rewmi amna yoon fimné macky sall nèkatoufy dé atè kateyi dal khamnané sen ligueye youmboul dé war ngeune siye khol sen diganté ak yalla
fall oie suivro afr yii dh, kii liko impliqué moo beurri t police mo divulgué info yoyou. elemn yoyou yp nk menoul regroupé wou t boy bii takkoul lalléwoul. lii mo jashal Sénégalais yii m amougn tps sohoré kenn, justice lagn sohla cpo tro demandé.
Et ceux qui sont accusés à tort ou à raison de vole pourquoi il n'ont pas de liberté provisoir n'importe quoi et si elle est coupable ça veut dire qu'une crimminelle est dans les rues 😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@SerigneModouDiakhoumpa-gx4ek rien ne prouve qu'elle n'est pas coupable non plus et désolée de le dire mais ya trop d'injustice dans notre cher Sénégal elle n'est pas accusée de n'importe quoi donc une liberté provisoire déjà c'est bizarre juste mon avis
J’ai regardé l’émission 2 fois mais pape je te crois pas et y’a pas de cohérence sur la liberté provisoire de Nabou et ça va faire une tache noire dans la justice …., saches que le procureur peut détenir kelkun partir de la clameur publique
C'est du n'importe quoi ? Mais il faut juste dire les faits parce que c'est un assassinat il y'a quoi en fait dans cette affaire c'est ça qu'on veut savoir.
Mané pratique bi c est pas normale Nabou Leye dé legui mou daw ,Farba Ngom , Bougaselly Madiambal et temp d autres ils vont fuire on devrait pas les donner liberté provisoire
Mais sama gaa yui tamit Aziz fatu gno tudd ci nabu leuy taxut gnoni mooko raye 😮 est-ce que tamit bu defoon dina gënn kii kay bu gënne dafa melni deful pour man 😮😮 mais ki bfaatu yàlla nako yàlla yeuruem xaree ko Al jana
Yaw mi di wakh sa mbok mo dèwoule motakh yaw mi mane gua tale rèwmi doule rèk guaye dèf bakane forna mouye nabou ou pas nabou yalla rèk moye atè mes nabou tamite taknasi riiiip
Pape. N diaye tu est tres dangereux Prendre exemple sur tes collègues comme Moustapha Diop Mame birame wadie Geogrs Nesta diop Pape sane Awa Diop N diaye Khalise diarou ko Kholatal sa bope
Pape wagnil linga wakh tégoko féne,yaw lii dousa rôle,dangay diaxasé ay nite ,waxal si loutakh mou amm liberté provisoire AK ndakh ,Nabou Dina nék en sécurité
Gnata gno nék si prison té djignou gnoulén com lign djign ki té amougn liberté provisoire
avocats youye réunir le nécessaire pour une demande de lp mo fa bayi ñu bari
Azizz dabala rek mo perté billay😢
Vérité absolu
Khaaliss yakh neu journaliste yeup billahi !! Bayiléne Sheytané ak nafikh bi ngéne néké ! Dieu est le meilleur juge 🙏🏽 !
Yalla momou nak mo niou teré xas sa mbokou dioulit wala ngakey ngagni té lolu nga df nii yaw 😢
@@mamadoudia3009en plus pape ndiaye n a fait que son rôle ici,dire les faits comme ils se présentent...
Nabou bilaye tout va se savoir
Tu ne seras plus la meme le humain est très précieux
Pape Ndiaye savait tout ça fait un moment qu'il sondait les Sénégalais pour savoir leur reaction sur la libération de Nabou Leye mais le grand juge c'est Dieu
Pape ndiaye mii c’est une personne tres dangeureuse😮😮😮
Avec tout ce que le frère de Aziz Dabala a témoigné lors du jour de la découverte des cadavres en compagnie de Nabou Leye, je ne peux pas point comprendre qu'elle bénéficie d'une liberté provisoire.
Mo diakhal gneup Sénégal liberté provisoire moy libéré
La justice a plus d'informations que toi et le frère de aziz
@@thiermane1985yaw nonil
Ce que les gens racontent diffèrent souvent de la réalité. Si elle bénéficie d’une liberté provisoire dans une affaire de double meurtre c’est qu’elle est innocente. Imaginez si elle n’était pas emprisonnée les pékinoises l’aurait assassiné.
Saway vous êtes des pigeon vous allez là où le vent souffle fort c’est tout
Yow nafékheu nga nabou léye noumouye baré none téé llimou déf c est flagrant lokhome a ngui thie biir nga nane amna gnou done dém thie sérigne pour mou désse lolou wakh ban rendement laa amal gniognou wassalame
Wa pourquoi tt le monde veut que nabou leye soit coupable ???
Bon question
Si elle n'est pas encore jugé pourquoi on devrait penser qu'elle n'est pas coupable? Si elle était innocente kenn douko teuthie, donc on ne peut pas la libérer comme ça sans explication
Mais je pense la police avait juste des soupçon pas des preuves donc si les soupçon ne sont pas avéré pourquoi gnoukofay teuyer nak ???
Fiy koudé ya berte 😢😊
Bilahi wakhnga deug
Yayam mon perte metina torop
pape ndiaye legi crédibilité wam dafa mort carrément. mais nit yangi koy deglu beu legi
Gnikoo libéré ay complice laniou sénégal amoul loi kou nanggou laalal j'aime
Liberté provisoire au senegal on ne retourne jamais
Libéré sans donner des raisons de ces deux victimes
Iow vrai doulkat ga un journaliste digne de ce nom ne doit po ce comporter de la sorte , pourtant amneu niou deiimone thi Bameiilou Aziz pr tibbbb fa soufffff ! Lolu numu toudddou?? Un vrai n’importe quoi dans ce pays. Niatta lagn la fay pr k u puisse défendre Cette femme. Kii meme xel naggouwoul sakh mou libre
Sa liberté provisoire choque plus d'un. En tout cas des mystères entourent sa libération. Elle ne devait pas bénéficier de cette liberté à mon avis, elle est trop mélée à l'affaire
Allahamoudouliha Allahamoudouliha vraiment cette fille mérite d'avoir LP
Faite confiance en cette justice
Yombou na dé
Even Nabou Leye is out that does mean that she is clean she was together with Aziz may god bring the truth inshallah 🙏🙏
Non c'est vraiment injuste
Nékk lén ay niit nabou dina Ray justice bi am preuve bayi ko mo gnibi sougne KO bayé par ce k amouniou preuve si moom beuss bi preuve Di takh nabou day déllou prison force
Pertinent
Absolument
ALEYSALAHOU BI AKHKAMIL HAKIMINE. Allah est le seul juge valable. Et heureusement. Alhamdoulilah bi yalla nèkè kiy atè deug deug
Kou deh yaa perte yako aux familles éplorées
Pape missile c’est dans tout les pays les célébrités n’ont jamais purgé leurs peines même en occident
Les senegalais veule seulment pourkoi elle est libre è pourkoi è si cet pas Elle allor SES QUI
Salam salam Sénégal kougnou raay ya pérte Sénégal bo bou ba léegui naaneu ñou waax kou raay azize ak wally Sénégal woratoul woratoul
Yow changer stratégie, Pape mi limouy def ni lane le ?
Nagnou dall rek de toute façon kii raye Aziz Dabala yalla dinako leral nagne😢
Le journaliste doit être arrêté pour expliquer comment il sait que cette dame a beaucoup d'ennemis et que ya des gens qui se battent pour qu'elle reste en prison
Khaliphone sall AK choco AK Adamo rek la gni ño sonal senegal
Alhamdoulilah
Pape Ndiaye borom misileyi dagaye douille. Vawaye
Loi mo amoul Sénégal
Ndaw si dawe kén réwmi lay moudiér sénégal frontier yi amoul security
Ahhh doynawar
Gnoune ay wakhou nabou léye interessé wougnou ay lobbie mome kou thie dougue amoo kilifa réck féthie moye célébrité yakheu nguéne deuk bi féthie foo ban rendement la amal réw faiblesse laa justice am envers les célébrités doy wakh dé gouvernement nathie wakh gneupa wara yéme thie kanamou yone fii loufi nithe atté réck dinakoo atté wath alakhira kén meussoula wakh nabou moko réy dagnou néé takhé nathie amna loumoussi kham wassalame
Elle ne retourneras jamais en prison xaliss mi nekon thiow li dou meuss leer te sou leeroulmbir mi dou leer nabou reyoul wayié moy commanditaire bi
Wax loula waur ñèpe la waar ndax ay looble par ci au lobbies par le day gueuna yèkati xole yi rèk tè xana les juges ne sont manipulés par ces soit-disants loobies
Grave! Tu expliques au sénégalais que la justice a un faible pour les célébrités.
mdr u vien d kl planéte tw pr npa savoir ça!?
Aziz mo dé niari yone amoul famille
Pape tamite ya khamal nieup ni mareme leu toudou au lieu de nabou 😆
Mane dal vraiment dina geune moytou comme dara leroul ndakh kene khamoul kane nga meune tassel ak loumou sagne
Billahi est ce que tu sais que tu t.est contredit toi méme!
Sénégal amoule deugue
Mane je pense que ame nah aye suspect yo kham nii à travers Nabou Leye lagn léne meune amé selon moi
Amna lounou deff thi beauté yiii n'a moye tou
Merci pape ndiaye si léral ti mais warone nga tek audio yi justice bi mom fimné amna sopé kou boubakh rewmi amna yoon fimné macky sall nèkatoufy dé atè kateyi dal khamnané sen ligueye youmboul dé war ngeune siye khol sen diganté ak yalla
Sénégaléyi bone nanou mé kou rayoule ani nane lanoukoye yéné kasso bou rayoule ani lou takh Sénégaléyi yéné ko kasso bone guéne té sokhor trop police bou kholé guisoule fimou rayé douko bayi no Sénégaléyi séni djiko bakhoule
Nabou took si prison....ñuné guelu aziz leu wone dîna arrangé ñi beugut dég lenene...thiowu gordjiguene romb nank...juste ça !!😢😢😢
fall oie suivro afr yii dh, kii liko impliqué moo beurri t police mo divulgué info yoyou. elemn yoyou yp nk menoul regroupé wou t boy bii takkoul lalléwoul. lii mo jashal Sénégalais yii m amougn tps sohoré kenn, justice lagn sohla cpo tro demandé.
الحمدلله الحمد لله
Pourquoi ?justice pour aziz et waly
Hun nabou kay sagnoul rey aziz
Et ceux qui sont accusés à tort ou à raison de vole pourquoi il n'ont pas de liberté provisoir n'importe quoi et si elle est coupable ça veut dire qu'une crimminelle est dans les rues 😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Si elle est coupable ? Nga wax dh , et pour le moment rien ne prouve que elle est coupable, kon ayons confiance à la justice de notre pays.
@SerigneModouDiakhoumpa-gx4ek rien ne prouve qu'elle n'est pas coupable non plus et désolée de le dire mais ya trop d'injustice dans notre cher Sénégal elle n'est pas accusée de n'importe quoi donc une liberté provisoire déjà c'est bizarre juste mon avis
@@papasaine6079 on est d'avis, moi jépo confiance en cette justice psk recemen j eu à m confroter vk eux, m vrmn rien à changé ché eux!💔
Allah 🤔🤔
Yaw ak thioune yénla mana déglou👏
Dafa melni ki dafa am faibles si bounou nabou ley bii😂😂dmrm
J’ai regardé l’émission 2 fois mais pape je te crois pas et y’a pas de cohérence sur la liberté provisoire de Nabou et ça va faire une tache noire dans la justice …., saches que le procureur peut détenir kelkun partir de la clameur publique
❤❤❤❤❤❤
Je panser bou bokone si complot bi yakarnani justice douko bayi
Défa nobe leye leye késsé
Douma nila dètt dè. Sa façon de parler m'étonne
Layer Lyer
C'est du n'importe quoi ? Mais il faut juste dire les faits parce que c'est un assassinat il y'a quoi en fait dans cette affaire c'est ça qu'on veut savoir.
Yako Yako famille Aziz
Mané pratique bi c est pas normale Nabou Leye dé legui mou daw ,Farba Ngom , Bougaselly Madiambal et temp d autres ils vont fuire on devrait pas les donner liberté provisoire
Pape fene rec
Man dè ligua geumou ma lolou serigne yi gay wakh nanou geunè wakh
Nabou est ce que tamite. Li sécurité me la
Sénégal kou deh ya perte
Yawe do nitou dara loye setale Nabou leye bakane da fort ak nioulaye bou eupe ak sa bakane bou tadie 😮😮😮
Deug bi koufi new dolé perte ga ndeyssane
Fen rk nga mane
Dara dou khéw kou rayoule gñou bayiko ani lane moye khéw khana nabou léye amoule ay mboka
Soudone deuko toubap yi tant que affaire bi léroul douneko bayi
J'ai rien compris
Tu peux avoir une liberté provisoire alors que tu es coupable ?
Ou le contraire ?
Nanou mi nak amna ponkale bou nèk si guinawam nak li menoumako geume😢😢😢😢😢
Lì leepp niak moko waral..dou yonne ..mafia rek le le procureure dafa war wakh
Pape lo wake degue le amale diamou
Yaw pape ndiaye dangay dingua ba nieup Khamko
Pape ana misile yi ?😂😂😂
Lo kham ci mana fen
Pape ndqye savefan nagudu jarajaf
Mais sama gaa yui tamit Aziz fatu gno tudd ci nabu leuy taxut gnoni mooko raye 😮 est-ce que tamit bu defoon dina gënn kii kay bu gënne dafa melni deful pour man 😮😮 mais ki bfaatu yàlla nako yàlla yeuruem xaree ko Al jana
❤❤❤❤😂❤😂😂😂
Ki day fene rek
Lolou kene ladioula li ngay wakh ki sakh dè niouko wara wo ladj ko niane niodone wakh lolou
Date fene
Yaw mi di wakh sa mbok mo dèwoule motakh yaw mi mane gua tale rèwmi doule rèk guaye dèf bakane forna mouye nabou ou pas nabou yalla rèk moye atè mes nabou tamite taknasi riiiip
Pape. N diaye tu est tres dangereux
Prendre exemple sur tes collègues comme Moustapha Diop
Mame birame wadie
Geogrs Nesta diop
Pape sane
Awa Diop N diaye
Khalise diarou ko
Kholatal sa bope
Yaw miii dee doulkatt bou mak gua
na mbokou aziz yi 😢réye nabou léye mou diéx takk
Fait attention !!! 🚨on peut vous porter plainte pour apologie de crimes et vous pouvez aller en prison
Je suis d’accord avec toi, c’est révoltant et je vous jure et je ne serai pas surprise qu’elle sorte du Sénégal la semaine prochaine
Ce journaliste pape Ndiaye c'est un faux type vraiment
Pape wagnil linga wakh tégoko féne,yaw lii dousa rôle,dangay diaxasé ay nite ,waxal si loutakh mou amm liberté provisoire AK ndakh ,Nabou Dina nék en sécurité
Yew khana deglou wooko li pape wakh kay setna yako bougoul degge
@Aichadia1234 après dinga comprendre li pape Di joué,walahi il m'en,vas écouter jimbori stp