Salam professeur, Machallah, alkhamdoulilah Nous nous réjouissons de votre connaissance, votre détermination, votre courage et toutes les valeurs que vous incarnez. Que Dieu vous protège, vous garde le plus longtemps possible inchallah. ❤
20:01 à 20:15 Wallahi moment bii professeur di expliquer nii Yonent (SAW) moungui ci niou biir mangui done lire ALQURAN, souratoul AALI IMRAN, ma tolu tamite cii ayat 101. Mouy missal bou reuy tekk ci fekk ma jouli fajar ba nopi. Allahu akbar kabira. Lii moy ayat bii : تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ ءَايَٰتُ ٱللَّهِ وَفِيكُمْ رَسُولُهُ ۥ ۗ وَمَن يَعْتَصِم بِٱللَّهِ فَقَدْ هُدِىَ إِلَىٰ صِرَٰطٍ مُّسْتَقِيمٍ Traduction Et comment pouvez-vous ne pas croire, alors que les versets d'Allah vous sont récités, et qu'au milieu de vous se tient Son messager? Quiconque s'attache fortement à Allah, il est certes guidé vers un droit chemin.
Machallah ❤❤❤❤❤
Yalna yalla fayal niou Seydina Elhadji Malick Sy ❤❤❤
Yalna niou Salatoul Fatiha Ak Diaharatoul Kamal defar si Barké Seydina Mouhamed psl ❤️ 🥰 🤲
Bilahi naniou yalla fayal seydil hadji Malick sy
Macha Allah❤ya khabibi
Salam professeur,
Machallah, alkhamdoulilah
Nous nous réjouissons de votre connaissance, votre détermination, votre courage et toutes les valeurs que vous incarnez. Que Dieu vous protège, vous garde le plus longtemps possible inchallah.
❤
Yalla Naniou yalla fayaleu Mawdo
Alhamdulillah
Macha halla
Amine
20:01 à 20:15
Wallahi moment bii professeur di expliquer nii Yonent (SAW) moungui ci niou biir mangui done lire ALQURAN, souratoul AALI IMRAN, ma tolu tamite cii ayat 101.
Mouy missal bou reuy tekk ci fekk ma jouli fajar ba nopi. Allahu akbar kabira.
Lii moy ayat bii :
تُتْلَىٰ عَلَيْكُمْ ءَايَٰتُ ٱللَّهِ وَفِيكُمْ رَسُولُهُ ۥ ۗ وَمَن يَعْتَصِم بِٱللَّهِ فَقَدْ هُدِىَ إِلَىٰ صِرَٰطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Traduction
Et comment pouvez-vous ne pas croire, alors que les versets d'Allah vous sont récités, et qu'au milieu de vous se tient Son messager? Quiconque s'attache fortement à Allah, il est certes guidé vers un droit chemin.
Man dé mouride la wayé hadra daffa may diouko
Yalla fayal gnu seydina hadji Malick