Khutba - Oustaz Seydou Ly : Mbir yi lislaam sàmm
ฝัง
- เผยแพร่เมื่อ 9 ก.พ. 2025
- Facebook : / oustazseydouly
Tiktok : / oustazsaidsambaly
Telegram : t.me/oustazsey...
Site internet : www.al-aafiya.net/
WhatsApp
Groupe 1 : chat.whatsapp....
Groupe 2 : chat.whatsapp....
Groupe 3 : chat.whatsapp....
Groupe 4 : chat.whatsapp....
Jazakoumoulah 😢😢😢yaa imam
Machallah khoutba bi am na soulo toroup
Mashallah ya ustas Seydou ly hafizhahoulah Allah hu ma barik ❤❤❤
ALLHAMDULLAH MA SHAA ALLAH KUTBA BE AMNA SOLO TROP JERRY JEFF LY BUSSO
❤❤❤
Assalaamu alaykum wa rahmatul LAAHI wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnent bi (SAWS) akiy sahaabaam (RAA).
YÀLLA sàmm nu sàmmalal nu, aar nu aaral nu, taxawu taxawul nu mùccël mùccëlël nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xam xam yi ragal sunu BOROOM YÀLLA.
Nanu YÀLLA wërsëgël nu dèkkeendook gnoom ca Firdaws. YÀLLA wan nu dëgg bamu leer, NGA yòmbalal nu tòpp ko.
Nanu YÀLLA wërsëgël nu dèkkeendook gnoom ca Firdaws. YÀLLA wan nu dëgg bamu leer, NGA yòmbalal nu tòpp ko. NGA wan nu neen bamu leer, yòmbalal nu dùmmóoyu ko.