J’étais présente sur les lieux c’est mon quartier la dame était très isolante n’arrêtait pas de répéter que son mari était un homme de tenue justice pour notre badiane une dame brave que firdawsi soit sa demeure éternelle
J'allucine! Comment est-ce qu'on peut commettre une telle atrocité et être en liberté ? Je ne comprends pas. Que justice soit faite pour cette maman. PAIX À SON ÂME !
Vraiment femme bi dafa yabaté ray nite ba paré nane ay sama dieucoeur li la ak lé no😢way qui décédé yala nako yala yeuram té kharéko aldiana fiirdawsi 😢matina trop
Depuis Londres... Etat na dèff liguayam... lii koumoi dalone doula nekh... Yalla na yalla lèral lepp... bou rawè fi tamitt dou raw yalla... bakane dafa foorr...yalla na Aldianay firdawsi di keureum...
By justice diaragoul yonn lifi amonn batay mofinee ana dioub dioubal ak dioubanty ba la guena dieki askanwi fadial sen bp Bopeu bakhna lidafa meti lolou way
@@Moustarchidatemais deugue la wah amethe ndoye dawal sans permi 15 jour femme dawal sans permi ba raye nit 7jour justice amoufi bayil sa wahou dof ay wathial ngua hol amethe ndoye ak femme donio wathie yone te moudioul fene
Premier ministre oussmane sonko Sénégal li motahk niou dieulle fi Macky Sall Coumba am Ndeye ak Coumba amoulle Ndeye dafa wara diehk sama dieukeur commissaire le sarap ndeye lii
Tribunal guédiawaye warnane ko kholatt yaw mome da nga séde bamou eup khaw ma yambar do joug affaire de ragal yi moye lane?ki dokhoul sikaw talli tog si bountou keureum niou fékk ko fa raye ko nguéne tog nane c'est à dire ceci cela joug léne wouté ndimbal jabarou commissaire bassi lane
Fatou Binetou, yalnako yalla yereum té kharé ko aldianaye firdaws. Sénégal métina, comment on peut libérer quelqu’un qui a tué une personne même si c’est involontaire. Raye nite di ndamo dieukeurou homme de tenue. Juge biko libéré khana amoul aye mboke, sougnou ko défone mbokame, dou dokhalé ni. Sama khol fess na trop même si khamou ma léne
Ne n ça doit finir dans ce pays il faut porter plainte mon cher vraiment il faut pas pleurer simplement chercher de bons avocats et ampliations au ministre de la justice et au président de la république et le pm
Lidé moye kou déé yaye perte conduire 100 permis rék infraction la à plus forte raison mort d'hommes amsi 😢 Ndeysane Yallah nako Yallah yeureum et bcp de courage à sa famille
Allez porter plainte, la procédure ne peut pas finir ainsi. Ce pays est corrompu jusqu'à l'os, ameutez tout le pays, invitez toutes les chaines de télé. Confondez les magistrats qui ont jugé l'affaire à votre insu. C'est injuste ce qui se passe dans ce pays.
Yalla nako Yalla yeureum tee yeureum kepou kou nekk si birr souf mais lii daffa yombou wayy kii mo bone wayy les gnione Lou gniouy doyé justice tee Lou Nitt deff d’où moudiou feneu cas yii barri naffi trop lii daffé warra diekh tmt gome layy deff si khol yii 💔sama khol Bii diekhna trop
Indisciple bou Matt seuk leu li kène warouko bayi nonou dañouko wara jugé wate tèkk lène ñom ñar ñeup thi yone la femme et le chauffeur qui lui donne le volant Massa lène bou bakh vraiment sèn mbokk demna dèm bou metti yalnako yalla yeureum
Yalnako yalla yeureum té khareko aldiana khamnanè dal atèkate yi war nanio geuna kholate boubakh sen diganté ak yalla si li niouye atè boudé ninga wakh la dèmè yombouna trop trop atè bi kone diaroul yoon
J’hallucine ou quoi mais quel lâcheté et quel culot écrasé une personne au lieu d’être humble et triste mais joue l’arrogance on demande justice pour cette famille الله يرحمها ويغفر لها ويسكنها الجنه 🙏😢
Arrêter de pointé sonko il n'était pas au courant té bouléne faté né gouvernement menoul lép il est temps pour nioune sénégalais niou yar souniou bop té di fatélikou yallah.dé amna dé. Ngéne Balma nak❤
Sonko môme akk Diomaye khamouma Lougnou fi deff ayy merde kessé depuis 8 mois gouvernement bou incompétent regarde le cas Aziz Dabala rien trop d’injustice franchement li daffa metti 😢😢
Yaw low wakh ni au temps de macky il y avait des cas plus critiques que ça est ce que sonko mo done dawal wala diomaye toi tu es un mécontent rek donc nanal galace wala nga tok si gaz ousmane sonko le meilleur de sa génération ❤️ ❤️ ❤️ dokhalal
Yéna wara ballèè sakh li mètina tropp ballèè woulène niouy bayi waté dieukeur ji commisaire laa Bone lolou mon takh niaw na déé yalla naco yalla yeureum te yékhè niou
L histoire de Amet Ndoye devait servir de leçon , malheureusement , nous avons une justice trop laxiste .il faut durcir les peines pour que les gens en tirent des leçons.😢😢
Rangoniou badola moy sime thiéré bour moy li . Raye nite nane sama dieukeur commissaire la. Kone dal kou sa dieukeur néke Homme de tenue dal meune nga rayé ha ok. Dinako guiss . Yalla naléne Yalla may kholou mougne ko barkè Nabil Moustapha 😢
Yalla nako yalla yeureum th khareko aldiana firdawsi amine amine Mais mon problème moy comment s fait-il gu ray niite par accident mou déé legui yaw au lieu gu tiite wala sa aduna touki ay bakane noumou foré nganane sama dieukeur police l wala gu balou akk famille diambour yaw waro sak yane ndimbeul... 🤦 Niite yii es c k cva
Sénégal môme justice bi il faut que gnou kholatte ko.Le nouveau régime doit voir de près ces dossiers.Des personnes tuent des gens et on les laisse partir.
J’étais présente sur les lieux c’est mon quartier la dame était très isolante n’arrêtait pas de répéter que son mari était un homme de tenue justice pour notre badiane une dame brave que firdawsi soit sa demeure éternelle
Déf léne recours saisir minitre de la justice li da yomb maye wakh mounane sama jeukeur commissaire la
Yabaté rek
Fi moy senegal 😢😢
J'allucine!
Comment est-ce qu'on peut commettre une telle atrocité et être en liberté ?
Je ne comprends pas.
Que justice soit faite pour cette maman. PAIX À SON ÂME !
Doyna war sénégal rek la am ses genre de chose 😢
De tout cœur avec vous mon frère, c'est vraiment révoltant,Paix à l'âme de votre sœur,Que le Bon Dieu l'accueille au Paradis.
Ohh vraiment li metina yallah nako yallah kharé aldiana que la justice sois faite li mome dou yone
Paix à son âme ainsi qu'à tous nos défunts,amiiiine.La justice de ce pays doit être nettoyée en profondeur...
Injustice bi dou masa diouk sénégal li dafa yomb
Oh non ! Yalna yallah yeureum kii dem té khareko aldiana.
Massa léne, Binetou yalla naco yalla yeureum té kharéco aldiana Firdawsi
Ayy way Mami li métina trop de tout cœur avec toi et l’âme du défunt repose en paix 🙏🙏
Donc la justice n'a pas changé vraiment il faut que les nouvelles autorités rectifient ce problème vraiment nouveau gouvernement sinon
Sinon œil pour œil dent pour dent mou fin
Vraiment femme bi dafa yabaté ray nite ba paré nane ay sama dieucoeur li la ak lé no😢way qui décédé yala nako yala yeuram té kharéko aldiana fiirdawsi 😢matina trop
Il faut suivre cette affaire jusqu'au bout pour que la justice soit faite
Etat bi ma guiss deh si justice lagnou nara daano... Rew mo khamni amoul justice... bo fèbarè do fadiou.... Mano liguey... yalla bakhna...
Injustice yagg nafi tei justice dina def ligueyam insga allah
Jub jubal jubanti injustice mo wara done premier chose a régler
Mère Binta nitt cou bakh 😭😭😭😭
Ndeyssane yallah nako yallah yeureum hareko aldjana
Amine Yarabi
Allah Houma Amine Ya Rabi Incha Allah 🙏🙏🙏
😅😅
Wa Sénégal li ba kagne justice na def liguéye yam diabarou homme de tenue ak badola lagnou yamalé justice na déf ligueyam
Ya Allah nako sounou Boroom yeureum té khaaré ko Aldianah si barké Seydina Mouhamad (SAW) amiin
Sallalahou Aleykhi Wa Salame Allah Houma Amine Ya Rabi Incha 🙏🙏🙏
Amine ya raby
Sonko ak diomaye bayuilen sen quele si rewoumi
Depuis Londres... Etat na dèff liguayam... lii koumoi dalone doula nekh... Yalla na yalla lèral lepp... bou rawè fi tamitt dou raw yalla... bakane dafa foorr...yalla na Aldianay firdawsi di keureum...
Ndeyssane yallah na ko Yallah yeureum tè kharè ko aldhiana firdawsy amine yarrabi
Massa Yallah nako Yallah yeureum Si Barké seydina Mouhamed salalahou aleyhi wasalam 😢😢😢
Kone sidy Diop moye niawe yaye khalasse yalla nako yalla yeureume xarèko aldiana firdawessi
By justice diaragoul yonn lifi amonn batay mofinee ana dioub dioubal ak dioubanty ba la guena dieki askanwi fadial sen bp
Bopeu bakhna lidafa meti lolou way
Wakhi dof wathial yoon khol et danio neksi nakhar ki dem yalna ko yalla yeureum té ki def lii yoon dina dal sikawam et puis c'est tout
@@Moustarchidatem ki raye mer bi nena dieukeureum commissaire la😢😢😢
@@Moustarchidatemais deugue la wah amethe ndoye dawal sans permi 15 jour femme dawal sans permi ba raye nit 7jour justice amoufi bayil sa wahou dof ay wathial ngua hol amethe ndoye ak femme donio wathie yone te moudioul fene
@@mormbaye2989 Na nek commandant dou térei yoon dina reukh ndigam
@@niangfall-r4k ya gueuna dof nieup nioussoul feulé deuk bi yoon amoufi kouko wakh dangay doul niongui def sen kemta lay Katan
Sénégal amoul justice kholen ca azzi dabala bi nimou dox
Walaye wakhal déee
Deukk bi daniouye sonou rekk mais corruption dou fi meusseu diékh
Bravo ❤❤❤ King baba les paroles sont équilibrées. Les deux côtés sont contents. Merci ❤
Litakh gnafolén ndayou femme bi avant police di gneuw moma gueuneu nakhari. Fadial lén sén bopp comme la justice refuse de faire son travail.
Vraiment lii migui beugue eupe nak rayy nitt ba paré gnou bayila nga dém sa yone emplus justice dou wakh dra kon kayy kou nék na fadial bopam
Dafsi lanou warona deug ndayam bala kéne di nieuw dakh niome 000justice mounane policée la imbasil
Parfaitement raison déléne fadial s'en bopp... Comme justice defoul liguéyam
Premier ministre oussmane sonko Sénégal li motahk niou dieulle fi Macky Sall Coumba am Ndeye ak Coumba amoulle Ndeye dafa wara diehk sama dieukeur commissaire le sarap ndeye lii
Bilahi non vraiment lii dafa doywar tamit Sénégal liii dafi wara diékh
C'est bon.
Mais boul saaga
@ScanCopyPrint Dieureu dieuf kou bahk magui Dieguelou yalla nala yalla fay
Oh masta man Sama frère bi car rapide moo ko raay avant hier 😢😢 Guédiawaye
Ndeyssane massa yallah nako yallah yeureum hareko aldjana
YALLAH nako YALLAH Yeureum
Yalla nako yalla yereume té khare KO aldiana firdawsi amine 🤲🤲
Tribunal guédiawaye warnane ko kholatt yaw mome da nga séde bamou eup khaw ma yambar do joug affaire de ragal yi moye lane?ki dokhoul sikaw talli tog si bountou keureum niou fékk ko fa raye ko nguéne tog nane c'est à dire ceci cela joug léne wouté ndimbal jabarou commissaire bassi lane
Massa, yalnako Yallah kharé Firdaws 🙏
*Ay way li métina😢😢na justice déff liguéye yam way li dafa yomb trop*
Ndaysane Masta paix à son âme
Yalnaco yalla yeureum xareco aldiana firdawsi si barké yonentbi sallalahou aleyhi wassallam amine
Sonko diomaye justice équitable pour notre pays c'est votre responsabilité de justice pour tout Les innocents de notre Sénégal
Fatou Binetou, yalnako yalla yereum té kharé ko aldianaye firdaws. Sénégal métina, comment on peut libérer quelqu’un qui a tué une personne même si c’est involontaire. Raye nite di ndamo dieukeurou homme de tenue. Juge biko libéré khana amoul aye mboke, sougnou ko défone mbokame, dou dokhalé ni. Sama khol fess na trop même si khamou ma léne
Yalla nako Yalla khari adiana thi barke serigne touba mbacke
😢ndeyesan metyna 😢nakou yalla yerumm te yalla may len kholo monge
Yala nako yala yeureume té haréko aldiana firdawsi si barké seydina mouhamed
Mais lii pour lane raye nite niou bayila ngay dokh librement gni gnak tok di dioye Sénégal deuk bou nakhari doundeleu
Ndeysane yalla nako bour yalla yeureum tè dièguelko kharèko si aldiana FIR dawsi thi barkhè seydina mouhamed psl
Yalla na yalla yéssal yeurmandé si kawam barké seydina moukhamed ak mbolém dioulite Inchalla tu et vraiment posé Machalla
Kou bakh bilahi yalnako yalla yeureum tè kharèko aldiana firdawsi amine ya rabbi alhamoulilahi
Le procureur doit faire son travail
Ne n ça doit finir dans ce pays il faut porter plainte mon cher vraiment il faut pas pleurer simplement chercher de bons avocats et ampliations au ministre de la justice et au président de la république et le pm
Massa métina trop yalla nako yalla kharé aldianay firdawsi 🙏🙏🙏
La famille doit assister au tribunal
Deug bou amoul yone yalla doufa watier yeurmander. La justice de ce pays n’a pas changé vraiment trop de défaillances c’est dommage 😢
Yaw loo xam ci yeurmandé yalla wakh diou bone mom ak wakh diou niaaw danguéne ko beug rek
Lidé moye kou déé yaye perte conduire 100 permis rék infraction la à plus forte raison mort d'hommes amsi 😢
Ndeysane Yallah nako Yallah yeureum et bcp de courage à sa famille
Yalla nako yalla khare aldiana firdawsi thi barke yonateby psl
La justice doit faire son travail ceci est scandaleux
Yalla na kou yalla yereme amine
Massa yalla na yalla yeureum ko té khare ko aldiana firdawsi Barker seydina mouhamad sws psl AK mboleme waye dawlo 🙏🙏 justice pour elle 😢
Kou😂bakh demna sama kharit yalnako sounou Borom khareko adianay firdawsi
Ndeysane masta grand. Yallanako sama Borom yeureum diégualko t khareko aldianay firdawsi bijahi Nabil Moustapha Sallalahou Aleyhi wa Salam
Où est la justice pour trancher au nom de la VÉRITÉ ?
Deug deug le président ou doit regardez le justice vraiment
Allez porter plainte, la procédure ne peut pas finir ainsi. Ce pays est corrompu jusqu'à l'os, ameutez tout le pays, invitez toutes les chaines de télé. Confondez les magistrats qui ont jugé l'affaire à votre insu. C'est injuste ce qui se passe dans ce pays.
Wadji ndeyssane kou dale la femme bi yalnako yalla yeureum diéguel ko 🙏🙏🙏🏻
Yalla nako Yalla yeureum tee yeureum kepou kou nekk si birr souf mais lii daffa yombou wayy kii mo bone wayy les gnione Lou gniouy doyé justice tee Lou Nitt deff d’où moudiou feneu cas yii barri naffi trop lii daffé warra diekh tmt gome layy deff si khol yii 💔sama khol Bii diekhna trop
Le juge n'a pas fait son travail correctement
Yalla nako yalla yeureum khareko aldiana firdawsi si barke zeydina Mohamed
Indisciple bou Matt seuk leu li kène warouko bayi nonou dañouko wara jugé wate tèkk lène ñom ñar ñeup thi yone la femme et le chauffeur qui lui donne le volant
Massa lène bou bakh vraiment sèn mbokk demna dèm bou metti yalnako yalla yeureum
oh masta yalla nako yalla yeureum
Jai mal au coeur li metina trop yalla nalene yalla attei🙏
Yalnako yalla yeureum té khareko aldiana khamnanè dal atèkate yi war nanio geuna kholate boubakh sen diganté ak yalla si li niouye atè boudé ninga wakh la dèmè yombouna trop trop atè bi kone diaroul yoon
Yalla nako yalla yereume diegalko kharéko aldiana firdawsi amine yaraby 🙏
J’hallucine ou quoi mais quel lâcheté et quel culot écrasé une personne au lieu d’être humble et triste mais joue l’arrogance on demande justice pour cette famille الله يرحمها ويغفر لها ويسكنها الجنه 🙏😢
😢😢😢😢😢k son ame repose en paix et firdawsi sa demeure éternelle justice lent ga li c est frustrant 😢😢😢😢😢 trop d injustice dabs ce pays
No senegal dou rèw
Yalla naka Yalla yeureum barke seydina mouhamed
Les auto ecole clandestine la il fast les eliminè
Yalla nako yalla xaré aldiana firdawsi
Il faut allè jusquau bout liii dafa yomb torop😢 massa yalla nako sougniou borom kharèko aldjana fiidawsir you kaawe Amine repose en paix sister 😢
Masta ay li mety na yalnako yalla yeureum ! Le nouveau système souniou léne votéré pour justice amfi la legui def m’en sen ligueye
Yalnako yalla yeurem khareko aldiana metti na torob na yon deff ligeyem
La justice né pas changé c'est honte ak thionoo bi niou dath si premier ministre oussmane sonko lii dafa niaw sarap ndeye Sénégal lii
Mais sonko santolenko fal n'a si ngim am yakar niafa nek pour niou dokhal you rek niouy ay domeram
@mbodjousmane mbodj Dieureu dieuf d'àma xexall premier ministre oussmane sonko ba samay Book bayima injustice la menoul siporte
Arrêter de pointé sonko il n'était pas au courant té bouléne faté né gouvernement menoul lép il est temps pour nioune sénégalais niou yar souniou bop té di fatélikou yallah.dé amna dé. Ngéne Balma nak❤
Mm si elle est libre sa conscience ne sera jamais libre elle est condamné à vie
Sonko môme akk Diomaye khamouma Lougnou fi deff ayy merde kessé depuis 8 mois gouvernement bou incompétent regarde le cas Aziz Dabala rien trop d’injustice franchement li daffa metti 😢😢
Ya yaye moy mbam bi eumbeu 9 mois indifi merde bou melni yow
Nanal glass doumou merde
@@Ablayb Yaw khamena sa yaye 3 mois lala eumbe liguay rew wakh day rafaite ray ray rek tee ken dou wakh doule way
@bijoumbaye2834 dafa wakh niou tontouko
Yaw low wakh ni au temps de macky il y avait des cas plus critiques que ça est ce que sonko mo done dawal wala diomaye toi tu es un mécontent rek donc nanal galace wala nga tok si gaz ousmane sonko le meilleur de sa génération ❤️ ❤️ ❤️ dokhalal
Ce gouvernement doit nettoyer ces coumba am ndeye sinon on les sanctionne comme l ancien système
Sans permis ,elle n'a pas le droit de conduire ni de faire des cours de conduite sans auto ecole. Elle doit aller en prison. Basta
Paix à son âme mère bou bakh
Paix à son âme k firdawsi soit sa demeure éternel métina trop bilahi
Prison direct n’importe quoi celle qui est parti paix à son âme 🙏🏽
Senegal dou changer amethe ndoye dawal san permi 15jour femme dawal sans permi ba raye nite 6 jour li kgne lay diekh
Dafa Guéne
Yéna wara ballèè sakh li mètina tropp ballèè woulène niouy bayi waté dieukeur ji commisaire laa Bone lolou mon takh niaw na déé yalla naco yalla yeureum te yékhè niou
L histoire de Amet Ndoye devait servir de leçon , malheureusement , nous avons une justice trop laxiste .il faut durcir les peines pour que les gens en tirent des leçons.😢😢
Ndaysan yalla nako yalla yeurem wayé bouléne bâyi mou séde c pas normal nioukoy relâché
😊
Wa sidi diop diapoune ko wone mouye dawal cent pérmi
Ms rayoul nit
Rangoniou badola moy sime thiéré bour moy li . Raye nite nane sama dieukeur commissaire la. Kone dal kou sa dieukeur néke Homme de tenue dal meune nga rayé ha ok. Dinako guiss . Yalla naléne Yalla may kholou mougne ko barkè Nabil Moustapha 😢
Mais pourquoi cette façon de faire c'est comme une histoire fictif c'est inadmissible la femme là doit vraiment payer pour ce qu'elle a fait
ki faatou yalna ko yalla kharé aldiana ki faate bayilene kok yalla bou yonn defoul ligueyam entre temps consciencam dinako tégueul
Liii khew yeup ci biir tribunal ken mounouko ko Wakh
Yalla nako yalla yeureum th khareko aldiana firdawsi amine amine
Mais mon problème moy comment s fait-il gu ray niite par accident mou déé legui yaw au lieu gu tiite wala sa aduna touki ay bakane noumou foré nganane sama dieukeur police l wala gu balou akk famille diambour yaw waro sak yane ndimbeul... 🤦
Niite yii es c k cva
Lolou moma diakhal
@@Yayouamina6530ah dama warou di mais yen niite yii es c tout va bien c eux
@@ndiolesarr5290 yabaté rek bilahi
Que l'âme de cette bonne dame repose en paix. La justice fera son travail .
Massa yallah na Yallah yeureume ko
Que son âme repose en paix
Système bi dessna tribunal Ousmane diagne na segue way
Yalla nako souniou borom yereum
Paix à son âme ak mbolém joulit 🙏
Yalla nako yalla kharé si adiana firdawsi li metina president diomaye ak pros senegal loufi leather betina
Ndeyesane oh repose en Paix
Sénégal môme justice bi il faut que gnou kholatte ko.Le nouveau régime doit voir de près ces dossiers.Des personnes tuent des gens et on les laisse partir.
3 mois en sursi pour un crime lolou loumou meune néké top len ko yomb na trop