L'arrivée de Sidy Diop chez grand avec ce duo a fait que tout le monde a oublié qu'il était même passé à Sentv. Il s'est vite rattrapé en un seul morceau. En plus il a du talent dans le vrai sens du mot.
Kou melni papa you dotoul am même fi ba 2050 c meilleur du mbalakh sidi Diop laaf nouko Neex meuneko def si voix té lolou yomboul si artistes machallah
Macha Allah man mousouma deglou benna son sidy diop mais aparti de tay sopp nako billahi man Lou beugue daddy youssou ndour beuguenala wallahi ndeysene
Vraiment parti bi doumaci doyal Avec la voix de Sidi Diop que je répète souvent il est excellent mashaallah je n'aime que youssou ndour mais ce Sidi la il monte mashallah
Tonton youssou ndour a fait d'excellent geste en faissant cet duo avc les autres chanteurs sa montre k aussi le Sénégal c le pays des térangua plus on s'entre aide entre nous . Billahi je l'aime trop youssou ndour ❤
Sidy est un artiste scène bou youssou nek thiouné doufa nieuw. Enplus dafa meune traditionnelle est c ca la musique sénégalaise pour nga bokou faut nga meune ko
Tu es le meilleur de la planète africaine svp continuez à nous faire du plaisir n'y pense à la retraite maintenant parc6 que insbi musique niveau yako téyé
Sénégalais lou diouk mou diapé ko comparaison.... Na kouné bay waram rk . Je les écoute tout les trois mais il faut accaccepter le talent de Sidy, franchement il est fort...
Sidy il est trop fort mai dafa tell yeuk succé dafa wara bayi affair d buzz ak wakh liguey basi kanam adouna lou diote yomb youssou et wally n'oublions a k ils ont bokou travailler et c trop dur
@@iliasderanger2969 lolou wally defone nakafi té kén waxoul 🤷♂️ sidy ak wally on peut les comparer ndax nio yém amouniou fi béneu trophée international ci walou musique ... mais wally mi nguén di comparer ak YOUSSOU ndour mi nga xamni lep leu am nak ? 🤔 Sidy dal mok wally on peut les comparer ay morom laniou
Mai attend donc toi tu connais pa wally seck pour les trophées international wally a pris 2trophées Happa Music awards 2017 Nominés dans différents catégories et c'était à Los Angeles et bokou d'autr sidy n'a jamais été l'homme de l'année au Sénégal donc ils sont pa pareil il devrait beaucoup travailler pour être au même niveau que wally
Je suis hyper content ojrd8 Voici le duo le l'année vraiment Sidy Diop félicitations pour cet merveilleux prestation. Good job et Bonne continuationrek. Dina bxh inchallah 🙏 Mërcï père Youssou Ndour le roi 🔥🙏🙏🇸🇳👍😄
Kouko meunn ak koukoyyy dieemm douniou beeneu😂😂 merci Papa youssou ndour ak sidy machallah Yallah lafalleenn thiate🥰🥰❤❤❤❤🥰🥰❤🥰🥰 long vie tonton youssou 🥰🥰❤❤
Kouné amgua loula yalla may té nitt kén douko khébal kimou beugue naniou moytou diaxassé ay nitt art bi yatouna . yalla naniou yalla défal atte nékh té dakal niou kholou kignane.
Très fière de partager mon existence avec vous. Vous êtes une légende et une référence. Longue vie à vous. À travers votre musique vous m'avez rendu tellement heureux.
Vraiment pays yeup dagno respecté sene légende mais au Sénégal kou khéw rek. You warou gnou ko comparé ak kéne car icône le comme Michael Jackson au USA, Céline dione au Canada.
Oui vraiment. Je me rend compte k né entre les musiciens les joueurs etc gnoune gnoy créer des rivalités imaginaire bou amoul féne. Mais aussi télé ame nagnou une part de responsabilité
Tout à fait Ndeye Binta, les journalistes ce sont eux qui gouvernent en vrai et ça c'est partout, il faut juste que l'audimat juge par lui même, ne regarder que par notre conscience
Le roi des roi des Mbalakh .xamna loutakh mou wo Sidy kou amoul talent doula woo , kou rew boko ci moom , kou reuy saffoko dara walahi sunu borrom mokoko diaglél
💖💖💖👑🎶💖💖🎶💖💖💖🔥👏Je L'aime Sama nidiaye YOU ndeyssane le monde évolue bilay lou beurii dii reure ...WAYER YALNEUH DIAM YAGUE NO STRESS SO HAPPY 💖🔥🎶👑 NGANIIII SOUYYY TE MOUY DEUG ADINA AMOUL SOLOOO 💖DEMEURÉ TOUS BÉNI 💖
Non vraiment sidy tu chante bien, waayy deugg ngay déf sa kaw, sa kanam rék topal si le roi des mbalah doko réthiou bou sobé yalla ...courage a toi broo trop fiert de toi
Machalla yalna yalla goudale sa fane youssou té bayila fi kou ndoguale do sonou sidi Diop fofou la dé djinné bou maguéte sou néké ci garabou dakaar sothi sokhla dangaye yarou rék fofou la dé
Kouy waykatt si Sénégal rek warnguaa waay Madjiguene Ndour
Kou beug sidi diop way beuseul ma jaime
99999990999ool
Dw
🥰Bilahi li dafa fess bay tourou
Youssou et sidy un duo de diaman,🙏🏾🙏🏾🇸🇳🇸🇳🇸🇳 yalla na nieup am diam si at bou bess bi❤️
L'arrivée de Sidy Diop chez grand avec ce duo a fait que tout le monde a oublié qu'il était même passé à Sentv. Il s'est vite rattrapé en un seul morceau. En plus il a du talent dans le vrai sens du mot.
@lamine MANÉ
Kou melni papa you dotoul am même fi ba 2050 c meilleur du mbalakh sidi Diop laaf nouko Neex meuneko def si voix té lolou yomboul si artistes machallah
Wakhal déh doutifi am moukou bay aduna di touki
GOLDEN BOY SIDY DIOP YAFI NEIK DH 🤟⚡🔥 merci papa you🔥
Macha Allah man mousouma deglou benna son sidy diop mais aparti de tay sopp nako billahi man Lou beugue daddy youssou ndour beuguenala wallahi ndeysene
Kane mo dacor après youssou ndour sidy moy le roi du mbalax
Dafa lerr
Yossou Ndour yalla nala yalla may fan ak waar . Gayi yai san Baye 🎶🎶
Sidy diop diome mo si DESS youssou tecknala lokho du courage
Vraiment parti bi doumaci doyal Avec la voix de Sidi Diop que je répète souvent il est excellent mashaallah je n'aime que youssou ndour mais ce Sidi la il monte mashallah
🙈🙈🙈 Mane tonton Youssou esk doumako may sama bop🙈🤩♥️♥️♥️♥️♥️
Détt wayy
Bilay yaw Mane dama beugue tonton you fans bou mague
Sidy Diop wakhalén ko lou nék sama yone nekouthi mais 🎤way dako meune par la force tout court
Walay c vrai
❤️❤️❤️🤩🤩🤩
Sidi diop yalla na sa fane si serigne touba lingay wakh nékhna bilahi yalla na sa diam yalla way
La surprise de ce grand bal de mon côté fût la prestation de sidy diop talent kessé la et sa voix oohooo bénéne affaire la chapeau bas
Lima nékh si sidy diop moy voix wame normal lay weuyé❤️👑
Machallah Sidy de tout coeur avec toi yalla na ngua raw say masss
Sidy wayal ragal dou deukeu guèdiawaye wa li nèkhoul🕺🕺🕺🕺
Guediawaye alioune gueye reik moko mom
@@mamadouwelle8480 Aliou ak sidy Diop Bene lagn na teksi ak jam. Il es excellent aussi. Vive GW
Franchement suis tres raciste j écoute que mon papa you mai sidy chante bien chapeau et bonne continuation.
Bravo Youssou Ndour ya niak kiniane sidi Diop dicourage khaléga lépe migui sa kanam
Degloul degloul degloul Sydi degloumayyyyyyyyyy❤❤❤❤❤❤
Qui comme moi à aimer cette partie
Non youssou ndour dou nitte
Tonton youssou ndour a fait d'excellent geste en faissant cet duo avc les autres chanteurs sa montre k aussi le Sénégal c le pays des térangua plus on s'entre aide entre nous . Billahi je l'aime trop youssou ndour ❤
Bravo a Sidy Diop, il est fort en live, Youssou da diomi🌹❤️🌹❤️🌹👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍
Je trouve partout 😅🤣😂
Jais en vue toujr ecoute cette soire koi doumasi doyal sidy ils est tres fort li nday san johohohohohohoh💯❤🇪🇸
Sidy ma vraiement donnè des frissons euy way li nekhna 😍😍😍
Siiidy daal moma dakhal way wally lolou xana amnasi droit il a du talent ce gars 🥰🥰
Mèlomane nga
@@deuggsenegal3425 mouni 😂
Lolu yaw la rk soof ngua trop
Dafa lér
Un artiste qui a bercé mon enfance et un futur roi du mbalax machalah limoy Sénégal 🙏🙏
Machalla vie Youssouf md
♥️♥️♥️♥️♥️
@@ndemesady6371 ii
Bonne continuation mon papa adoré papa Youssou tu as encore frappé Yallah n'a Yallah wéral sa voix bii on a encore besoin de toi daddy♥️ je t'aime
Amine
Mane ma beugue Sidy rek🥰🥰🥰ken dou The king Papa Youssou
Sa mouray bi raféte na trop
@@cherifseck8902 merci beaucoup
Sidy man souma sagnone nga liguey ba si kanam bilaahi grab mome ci kaw layé fékanté❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🔥🔥🔥🔥🔥👏👏👏
Sidi Diop c'est mbaye dieye faye un gentleman papa il t'apprécie beaucoup il ne faut pas oublier, Bonne continuation
Vous navez pas contaster que sidy diop tenter de chanter gouye dakar basi yonou marêne youssou ndour la freiner professionelment
Cv
Le patron de la musique africain merci you
Machallah nice na trop ♥️💋 💞👍 tonton Youssou Ndour et sidy Diop magui sii yéne
Barki yalla Sidy dafa ayy il a la voix et c’est le plus important
Bilahii
Il chante trop bien
Deug la deh boy bi bougnou ko diapalé fou sori laye dem ndakh dafa aye
@@moussambengue42 sDqqqqqq
Bilay lii koudoul mélomane deugue doko xam il a une très belle voix MACHALLAH lolou casé moh ame solo....🚶🏼🚶🏼
Sidy est un artiste scène bou youssou nek thiouné doufa nieuw. Enplus dafa meune traditionnelle est c ca la musique sénégalaise pour nga bokou faut nga meune ko
Tu es le meilleur de la planète africaine svp continuez à nous faire du plaisir n'y pense à la retraite maintenant parc6 que insbi musique niveau yako téyé
Merci pour la bonne soirée youssou Ndour,Capitaine du morom chapeau
Sidy sama préféré Machalla il as une voi ki porte loin il es trop fort,Courage frère mai Kénn dou Youssou Ndour
Sydi Diop Mima Guiss Dé kouko
Souxiwoull Mou naww 😆😂😆
Kii Loumouy way Dou Azame franchement Boy bii Laf Thiath Rék 💚🤍❤️👑🙏
Y mythe 5
Raz5ryelgy
Ou. 😶🤗🙂😍😍😍
Youssou à vraiment innové la scène autrement, dancing à distance
Sénégalais lou diouk mou diapé ko comparaison....
Na kouné bay waram rk . Je les écoute tout les trois mais il faut accaccepter le talent de Sidy, franchement il est fort...
Vraiment
Merci
Sidy il est trop fort mai dafa tell yeuk succé dafa wara bayi affair d buzz ak wakh liguey basi kanam adouna lou diote yomb youssou et wally n'oublions a k ils ont bokou travailler et c trop dur
@@iliasderanger2969 lolou wally defone nakafi té kén waxoul 🤷♂️ sidy ak wally on peut les comparer ndax nio yém amouniou fi béneu trophée international ci walou musique ... mais wally mi nguén di comparer ak YOUSSOU ndour mi nga xamni lep leu am nak ? 🤔
Sidy dal mok wally on peut les comparer ay morom laniou
Mai attend donc toi tu connais pa wally seck pour les trophées international wally a pris 2trophées Happa Music awards 2017 Nominés dans différents catégories et c'était à Los Angeles et bokou d'autr sidy n'a jamais été l'homme de l'année au Sénégal donc ils sont pa pareil il devrait beaucoup travailler pour être au même niveau que wally
Merci sidi boul concurrence boul deglou ken❤️💪💪🙏yagatoul leip dina nieuw insalah
sidy m'a trop ému il chante trop bien il a une voix de oufffff💪lgue vie à vs deux les super star❤
It is m'y firt commentaire mais Youssou Ndour inspiration kesse leu
Thiéye sidy Diop 😭😭il es pétri de talent ce guar Youssou Ndour mom dou moromou bén nite quel domou Adama 🥰🥰😂
Moom rek dou ay fo. Deggal ma sisou maan yi dima tegal ay vus😂😂😂
Kénn dou mome
Boybii bi dîna yengeul nday at mu béss bii 2021 akk sidi dèlène thiow mouy housse rek
Lou ler gua wakh.. Xalé bou ndaw la té amna fit
@@momzly6818 amna fite mom dawoul sala yaye nder
@@fatoundiaye8224 lou ler nagn xol rek
Ahh lì nexna way❤️❤️❤️Youssou il padre della musica senegalese!!!Sidi bne continuation...
❤️❤️❤️
Ndiaga mbaye rek lay guis si sidy Diop billahi
Yousou yawdaguabakhe sidy teyelnouko
Ndiaga baye ne pa internationnal
Vraiment !!
Lou lerr nga wah
Yaw pa nga ndékété
Machallah 💖💖💖👏🎶🌍💯🎶liii rafetneuh hee oui un monument 👑🌍👏💖mercii a toute l'équipe👏👏👏👏💖💖
Je suis hyper content ojrd8
Voici le duo le l'année vraiment Sidy Diop félicitations pour cet merveilleux prestation.
Good job et Bonne continuationrek.
Dina bxh inchallah 🙏
Mërcï père Youssou Ndour le roi 🔥🙏🙏🇸🇳👍😄
Je confirme
Ta belle prestation
Yaw thi kanam inchala! Bou yala ner waw nelene waw youssou ndour dafa teral yaye ak baye mak ak rak ! Def patteu wa li loukoye faye !
@@boudioumane9932 merci pour la correction.
Non sidy diop est fort bonne continuation...kène dou youssou ndour ma djiguene nourd....
Waxx deug yalla kou Youssou ndour nangoul boy bulathi bagne nalla déff ayy rééé fonce boy tu fais la fierté des banlieusard surtout gediawaye
boy sidy diop day wor Légui mo yeuguatii bopam boul khalatt bro
Y’a muna katt sa data yaye
Kouko meunn ak koukoyyy dieemm douniou beeneu😂😂 merci Papa youssou ndour ak sidy machallah Yallah lafalleenn thiate🥰🥰❤❤❤❤🥰🥰❤🥰🥰 long vie tonton youssou 🥰🥰❤❤
Mach'Allah duo bii c'est du lourd sidy ak papa youssou vous êtes les meilleurs
C’est vraiment la classe ça 🥰
Je pense que les enfants ne comprennent pas trop niom gni di wakh ay vu😁 ... j’ai jamais vu ça ❤️
Kouné amgua loula yalla may té nitt kén douko khébal kimou beugue naniou moytou diaxassé ay nitt art bi yatouna .
yalla naniou yalla défal atte nékh té dakal niou kholou kignane.
Sidi Diop c'est magnifique Machallah 🎤🎸🎷🥰🇨🇵
Très fière de partager mon existence avec vous. Vous êtes une légende et une référence. Longue vie à vous. À travers votre musique vous m'avez rendu tellement heureux.
Mais sidy yow do nitt deh 🔥🔥🔥🔥
Thieye Sidy diop le future roi du mbalakh 👏👏
Sidy kénn douko té
😂😂😂mane je peu tout comprendre mai ñi comparer wally ak youssou ndour la manoul mouñ Senegal dafa nekh😂😂😂😂😂😂respect way youssou bénéne afair la
Rew rek 🤣😂😂🤣🤣😂
Saway gars yii danio khamoul reik
Bilae
Vraiment pays yeup dagno respecté sene légende mais au Sénégal kou khéw rek. You warou gnou ko comparé ak kéne car icône le comme Michael Jackson au USA, Céline dione au Canada.
Youssou de amofi morom
SIDI DIOP il est très fort c'est pas évident
Wally kimoy sa mrom Maï du Youssou ngène balma naak guys
Bilahi deugleu
pam yeen yaabileen walli. Jaime youssou mais walli amoul morom dans sa génération nakk
@@ndateyalla2784 kane mo diap wally ak loumay bagne wally khamal ningaye wakhé ak mane
pam désolée c'était un messagepour DEUG Sénégal
@@ndateyalla2784 deug rek nga beug dieuleule sama numéro dinga kham louy deug 00225 77 98 94 79
Wa nguir Yallah 2stv dolene organiser duo sidi et wally nguir yalla kone ngéne xamni dinako diangal nugnuy wayer wally bayrè rek la am
Wally aml fit bobo barki Baye Karim 🤭
Kone gua wamni talent rek mo woor 💪
Mon yawe katt nopi sidy diop my kane wally desfauko darra
Pardon yaw est ce que cava yene wally dalene di béet chaque jour
@@tontoudoufrokh3867 iew setane nga duo papa thione Ak wally
@@kharagnembaye4862 oui
Youssou bo diapalé sidy lègue mou raw gneup da mana way
Dou raw kenne wally 26k sidy et you 13k
Si c'était le cas pape diouf raw gnepeu ame disque d'or combien de temps a ses côtés.
Bou donne lolou pape Diouf raw teh mogui ni dafa soukh teh wa prince art la
Deug nékhoul meuna weuy ak am bayré dou béne wally seck manoul weuy
@@lasanaseck7146 on parle de meune woyy tu nous parle de vue ibbil sa khel bi wayy
Eh fans wally yii ne soyez pas jaloux sidy dafa meneu woy
Vraiment nagou dula wagni dara mm wally l c
Billa hi wayendo ak you yomboul koi vrm sidy moko yor def nga lou nice youssou ce le maître du mbalax
Fii mon so beugué dém faw gua dème si papa djii you le boss mahalla yafi nék dhé par force nak 🤔❤❤❤❤❤❤
YOU LE MEILLEUR CHANTEUR DE TOUS LES TEMPS...KOU MÉRR REKK NANAAL ESSENCE, TOKK CI GAZ...LOLOU LA YALA DEF, NANGOU REKK AM DIAM...BA DÉWENE INCHALLAH
Youssou ndour DOU NITT Longue vie la santé REK Laly Thanal ♥️♥️♥️♥️👑👑👑👑🙏🏻🙏🏻🙏🏻🙏🏻👏🏻👏🏻👏🏻👏🏻♥️♥️♥️♥️
Ohhh Sidy Diop meune naa❤️💪🙏🙏🙏
Thiey sidy machalla Youssou ndour Moy bombou
Mon papa Youssou Ndour santé de fer longue vie paix
Sidy Diop a assuré bélle prestation
Waly diam ak tawfeikh le peuple t'aime ❤️
Li gardé ko pour cons wally j pens k c mieu
La nouvelle génération sidy Diop mossi Daka woyy
😂😂😂😂😂
@@omarndao8691 🤣🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🖕
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😭😭😭😭
dangay doulll dh
Machalha yalla nak fi yagg barcké khadimou rassoul
Senegal soutenons ce goss bilakhi walakhi talakhi c le meilleur chanteur de sa génération
😂😂😂meilleur chanteur tu dis
@@fatysyll5643 😂😂 doit dire millleur interpréteur
Way nioune Wally rek point ❤️❤️
Wally moy seen baay niom niépp
@@bktv7807 waly Joueur navétane là capo deug dou dém soiré waly seck djigénn
Bou am class aussi doufa dém
Machalah Sidy Diop fi nga tèkk sa tank fofou boulko tègui
A mane je savais que sidy nila mané way machalah
je ne suis pas trop musique mais voir ça ma fait plaisir vrement.vive le senegal
Le king que tu vives 100ans sans ordonnance je reve de te voir un jour face a face
Machallah doundeul Tonton Youssou Ndour bilahi soumalay deglou sama xol day sed
Oui vraiment. Je me rend compte k né entre les musiciens les joueurs etc gnoune gnoy créer des rivalités imaginaire bou amoul féne. Mais aussi télé ame nagnou une part de responsabilité
Tout à fait Ndeye Binta, les journalistes ce sont eux qui gouvernent en vrai et ça c'est partout, il faut juste que l'audimat juge par lui même, ne regarder que par notre conscience
@@giado8414 bien dit vraiment
Youssou Ndour yallah nga goudou Fane waay wonibik hâte
Machalla sidy bonne continuation wayé papa youssou keen du yow longue vie❤❤❤❤❤❤
Le roi des roi des Mbalakh .xamna loutakh mou wo Sidy kou amoul talent doula woo , kou rew boko ci moom , kou reuy saffoko dara walahi sunu borrom mokoko diaglél
Wakh nga dégu déh
Dafa khamne dafa noyé nbop ana pape diouf soukhalnako n'a dem diamou die yalla mon guene gnaqe fayda
@@yamabadji5685 yaw mi di deglou di commenter loula té dem diamou yalla tamouy nitt ni yaw koula wakh doko ndieuké guéne adouna ta yalla n'a yékh
@@yamabadji5685 diamou yalla amoul mak amoul khalei gneup la warr
Gneukèko sisa bopou doguay diglè
@@yamabadji5685 damay lath lane moy diamou yalla 🤣🤣🤣
💖💖💖👑🎶💖💖🎶💖💖💖🔥👏Je L'aime Sama nidiaye YOU ndeyssane le monde évolue bilay lou beurii dii reure ...WAYER YALNEUH DIAM YAGUE NO STRESS SO HAPPY 💖🔥🎶👑 NGANIIII SOUYYY TE MOUY DEUG ADINA AMOUL SOLOOO 💖DEMEURÉ TOUS BÉNI 💖
👏👏👏👏👏💖🎶🔥
Non bilahi youssou diapalel sama makk bi Ngir dieum seydina Mohamed yalla na diam yague
Sidy tu as fait une belle prestation vremen jais adoré longu vie à toi
Man deh bo amé 0;5 vu sakh yaw la beug sidy Diop ken doula téré dem boul deglou ben wakhou noneu on t'adore sans arrière pensée 🤩😘😘
Bilahi walahi
Sidy chante bien machallah you do morome ben xalei li la wakh mane💪❤️
Sama baye bi li nga youkhou si souf meuna ray nit ooooh tonton youssou le meilleur chanteur du monde 😘😘😍
Sidy diop l'étoile filante de la musique Sénégalaise 🔥 🎤
Non vraiment sidy tu chante bien, waayy deugg ngay déf sa kaw, sa kanam rék topal si le roi des mbalah doko réthiou bou sobé yalla ...courage a toi broo trop fiert de toi
Thieuy lii suñu youssou international 🇸🇳❣❤🎄🎆🎆🎆🧨🧨🧨🧨🧨🧨🧨
You limou youkhou si souf non amoul le meilleur de tous les générations cou nekh amnaga place si music mais youssou ndour est le roi
No li dafa nex thiey super étoile 💥✨✨😍
Machalah nékhna Dale sidy mouy waly niapeu aye naléne yalla tek lokho
Je viens aujourd’hui d accepter que sidi est un bon chanteur mais j aime pas les détails qu il gère na concentré wou pour ame visibilité
Machalla yalna yalla goudale sa fane youssou té bayila fi kou ndoguale do sonou sidi Diop fofou la dé djinné bou maguéte sou néké ci garabou dakaar sothi sokhla dangaye yarou rék fofou la dé