Je me pose des questions sur celui qui fait les montages sur alkhuran ak sunna rek44 ???? Il faut être juste même si on est pas d'accord avec l'autre et il aussi être respectueux avec vos titres !!!! ALLAH aime ceux qui sont JUSTE !!!!
JE PENSE QUE MOURTADA GUEYE DOIT ARRETER DE DEBATRE AVEC SES GENS NON SEULEMENT ILS N ONT PAS LE MEME NIVEAU MAIS AUSSI NOUS SAVONS AVEC TOUS LES DEBATS QU ON A SUIVI QUI EST SUR LA BONNE VOIE MERCI ENCORE LEGUI KOUMA WAKH DARA THI DINE DIGUAMA ANDIL FIRNDEY SINON DOUMALA GUEUME IL FAUT QUE CES TARIKHAS ARRETENT D ARNAQUER ET DE TROMPER LES GENS ALKHURAN AK SUNNA REK MOY VERITE
Wallahi Khalifa wargua bayyi nikhache ak khaléyi danou diangue ba noppi rawléne yaw Khalifa yaw wakhi kou rouss rék guaye wakh wallahi étudiants madina yi wallahi ñioléne raw noppalal sa bop yaw ak Boye Ñiass
Maashaa'Allah Maashaa'Allah. Baaraka'Allahu fik ya Sheikh MorTalla Gueye... les vrais savent que vous n'êtes pas à la dimension de ce petit marabout lasrar. Alquran et Sunnah rek mo woor
Ce culte du secret et de l'initiation et le fait que pour accéder à certains il faut atteindre un certain niveau, c'est similaire au fonctionnement des franc-maçons. Ces tariqas peuvent aussi permettre de progressivement modeler(pévertir) des jeunes à au potentiel tout comme les franc-maçons. Les franc-maçons visent des gens de préférences jeunes intelligents et/ou charismatiques afin de servir leur mission.Pour le système du soufisme les jeunes visées sont ceux qui s'implique beaucoup dans la voie de la religion, et on constate en effet que beaucoup de ses "grands" religieux étaient spirituellement ou religieusement "précoce". De l'autre côté de la pyramide on constate aussi que les tariqas permettent d'avoir une grande influence, un contrôle sur le peuple, tout comme les franc-maçons. Au sommet de la pyramide, un grand serigne qui voit "tout", pourrai être comparé "l'oeil qui voit tout" des franc-maçons. En vérité le cheminement dans les tariqas peut être à l'instar de celui d'iblis, on peut y entrer en étant un jeune très pieux et en sortir arrogant, ce pensant supérieur à des sahabas ou prophète et même Allah lui même subhanallah et ainsi pervertir des éléménts très prometteurs.
Mountag tapale lii du woun débat ñion fekke nagn fam doun khéwe thia group al hakho sabit ba léén sen tapale yi ngén di def ki khalifa de mor gueye kham na ko bu baax yagg na ñiou dadjié moy yekati ba thia kaw door thi soof
Sou lakho thi ibn taymiyah dinguako lakharthi. Yakheuyty wessouwoul nga nangou nii sa serign ibn taymiyah ap ndiabar la. Boul nafekh. Deugu gui mom danguako waff tayy. Tarikhayi ay tappalé niouthi barry mom lagn neké certe. Wyé yen tamite tanewoullen kéne. Ndakh yena yemm danguena am app serign mouy ndiabar kom nieup. Boulen niou yepp.
Soumoun boukmoun khoum youn fa khoum la yah kiloun. Lolou pass passou sofianké le parce que lou serigne bi wakh gnou geum ko même sou outé ak al khour an té dougnou si réfléchir
Fi dal limafi guiss moy un Docteur Mourtada en ouvrant ce débat pour prouver que les soufi sont des Ndiabare katt s'est coincé lui même montrant que son propre guide Ibnou Taymiya est alors un ndiabare katt, parce que ce qu'il rejette lui même, Ibn Taymiya le faisait.
Masallah Dr Mortada Gueye Masallah li ngeu wakh wallahi dafa Lér Barakallahou fiik mom nak amou lumou wakh ki khamoul dare wallahi Allkhoran ak sunna rek moye dine moye degeu wallahi 🇸🇳🇩🇪✊✊✊✊✊✊❤❤❤
Le Doctor Mourtada est un Don d'Allah (AZ) et la Sunnah du trés Saint rassoul (sas) pour les 🇸🇳 Alhamdul Lil Ahi
Masha Allah
MASHA-ALLAH MOURTADA, yalla n'a yalla goudeul sa fanne, alhourane ak souna yonentebi PSL moyy deugg
machallah Dr mourtada
Mourtada Gueye yalla neuga doundou 125 an si barké mouhamadou rassoloulahi.
Mor Anta oustaz oumar sall nena kounian si barke muhamad damelna kasou ndoh ak kasou deret ga bole
Si barké lailaha ilalha
Mouratada kay tay metrisewoul limouy wakh. Mais daffa am lou nek thi wakham. Mom dafa contre wa rewmi ba parè di defandre ibn taymiya
@@latdiordiop6051 waw kay ya deeug wakhji
Khalipha mboup waxou fi dara amoul preuves mouy weur weur lo pour mom mo eup xél nit yi
Yalna yalla samou alxouran ak sounnah amine yarabi
Macha Allah! Dr Mourtada Gueye amnasolo trop dieureudieuf.
Je me pose des questions sur celui qui fait les montages sur alkhuran ak sunna rek44 ???? Il faut être juste même si on est pas d'accord avec l'autre et il aussi être respectueux avec vos titres !!!! ALLAH aime ceux qui sont JUSTE !!!!
JE PENSE QUE MOURTADA GUEYE DOIT ARRETER DE DEBATRE AVEC SES GENS NON SEULEMENT ILS N ONT PAS LE MEME NIVEAU MAIS AUSSI NOUS SAVONS AVEC TOUS LES DEBATS QU ON A SUIVI QUI EST SUR LA BONNE VOIE MERCI ENCORE LEGUI KOUMA WAKH DARA THI DINE DIGUAMA ANDIL FIRNDEY SINON DOUMALA GUEUME IL FAUT QUE CES TARIKHAS ARRETENT D ARNAQUER ET DE TROMPER LES GENS ALKHURAN AK SUNNA REK MOY VERITE
ibrahima ndao sa. Data. Ndaye. Yene. Naryi.. Gnoysen. Serigne...douleway
Cheikh Tidiane ab naar le😂
Bayilén saaga yi té indi ay daliil
Tu as raison mon frère khalifa amoul nouveau pour débat ak mourtada xamouniou dara motah day xassaté rek
ماشاء الله يا دكتور خليف بارك الله فيك
Ma cha allah docteur m.gaye
Ma Cha Allah DR Mouh🌷🌷🌷
Guemal linga guem rk tè bayi kenen guem limou guem tarikha Tidiane Alkhour-àne ak sunah rk moko lal
Wakho deug d cheikh dafa sori alcoran ak sunna
Sofianké yi bayilén thiakhan way
Wallahi Khalifa wargua bayyi nikhache ak khaléyi danou diangue ba noppi rawléne yaw Khalifa yaw wakhi kou rouss rék guaye wakh wallahi étudiants madina yi wallahi ñioléne raw noppalal sa bop yaw ak Boye Ñiass
Vive a mourtala Gueye
Waw Docteur ki ni boul di dèbat ak mome way. Ki mom day wax pour wèrantè .
Amna xam- xam dè wayè kathior leu.
Diaridief Dr kii amoul bene lath ci limouy wakh alhamdou lillah ci yaw
Salam macha Allah Dr mourtada khalifa wakhtanou kou xamxamam beriwoul
Maashaa'Allah Maashaa'Allah. Baaraka'Allahu fik ya Sheikh MorTalla Gueye... les vrais savent que vous n'êtes pas à la dimension de ce petit marabout lasrar. Alquran et Sunnah rek mo woor
Mourtada Gueye dangua ëupp gnii lamigne mais Yena yam wakho lènefi Dara
Ouztaz Khalifa am Nga diot comme si diema débattre Ahlulkitaabe Bou Gueumoul Alxuraan ba prêt Teukh ça sert à rien
Bida'a tout ce qui advient après le prophète. en plus au 12eme siècle
Dr mourtada gueye yall naga doundou 125an
Thiey khalifa ya fiye khalifa
Wa tassawouf noppalouleine toppeu sunnah mo gueune di defendre lou amoule argument
Mo gueune déh
Mouratala gueye talibé mouhaawiya nafékh
Khalifa ngi sen khole marché woul
Mourtada yalla nga gouda fan waye dinga die lou yag salatoul fatiha digan di yatou
Dinga dé bayifi salatoul Fatiha serigne yi ngay wAh ndiambar nio géne sa ndey guén sa bay
Yaw ya mana féne sa serigne yi bida laniou indi guenou nioufi kéne
Ce culte du secret et de l'initiation et le fait que pour accéder à certains il faut atteindre un certain niveau, c'est similaire au fonctionnement des franc-maçons. Ces tariqas peuvent aussi permettre de progressivement modeler(pévertir) des jeunes à au potentiel tout comme les franc-maçons. Les franc-maçons visent des gens de préférences jeunes intelligents et/ou charismatiques afin de servir leur mission.Pour le système du soufisme les jeunes visées sont ceux qui s'implique beaucoup dans la voie de la religion, et on constate en effet que beaucoup de ses "grands" religieux étaient spirituellement ou religieusement "précoce". De l'autre côté de la pyramide on constate aussi que les tariqas permettent d'avoir une grande influence, un contrôle sur le peuple, tout comme les franc-maçons. Au sommet de la pyramide, un grand serigne qui voit "tout", pourrai être comparé "l'oeil qui voit tout" des franc-maçons. En vérité le cheminement dans les tariqas peut être à l'instar de celui d'iblis, on peut y entrer en étant un jeune très pieux et en sortir arrogant, ce pensant supérieur à des sahabas ou prophète et même Allah lui même subhanallah et ainsi pervertir des éléménts très prometteurs.
Waw moom nena yonentibi menna diangale louko neh ak kouko n'en boudoul louy mouthiele safara ak louy dougal aldiana Waw sirou fatiha dou pour dem aldiana
mourtada gueye amo xam xam nopil tei bayi tiaxane
Ta mo eupou xam xam sa Khalifa général, ak mamam
Ma farratna fil kitabi min chay iin
SEGN BI di wakh siiru fatiha coy niabar la rek nakh dr mourtada lim coy demander moy déllou way bi bodé degue nga begue dégue ki xamoul dara
Machallah serigne khalefa mbom le gawkh lerna loll talla Gaye nafekh daga la lemoy wakh amol dalil the lemoye wakh
Yaw mi yaye nafékh khalifa mboup mi da xam dara omoul nuveau si bida yon bon ngén nék baparé di sonal
Lima guis si débat bi moy alquran ak sunna rek moy deugu té tek ko si ay preuve you si alquran ak sunna sinon dinga rére
Oustaz khalifa dondall 163
Mountag tapale lii du woun débat ñion fekke nagn fam doun khéwe thia group al hakho sabit ba léén sen tapale yi ngén di def ki khalifa de mor gueye kham na ko bu baax yagg na ñiou dadjié moy yekati ba thia kaw door thi soof
dieureuf serigne touba
MERCI DR JE SUIS FIER DE TOI
Bilahi khalifa mboup yaye domarame ga gate ham ham yaye nafekh
Talla Gaye daywoti khaybo aywaye ragalal yalla
Sou lakho thi ibn taymiyah dinguako lakharthi. Yakheuyty wessouwoul nga nangou nii sa serign ibn taymiyah ap ndiabar la. Boul nafekh. Deugu gui mom danguako waff tayy. Tarikhayi ay tappalé niouthi barry mom lagn neké certe. Wyé yen tamite tanewoullen kéne. Ndakh yena yemm danguena am app serign mouy ndiabar kom nieup. Boulen niou yepp.
Oustaz bayil gni dagno nga khamni daggassantè rekk laniouy déf lamou
Mourtada demal seugg thi téré yi kat boul rouslo wahabit yi
Khalifa yallnala yallalh Faye
Mor gueye moum masoul am xam xam taassou rek lagn ko khame
So werro thi souneu dangay werrou rek thi souneuci bayi ben courell wounguendy défendre walliss nienen
LASLAAR = LA MAGIE NOIRE NDIABAR
Insa halla
Koye ndiabar ndakh dana djoly ?
Bilah khalifa yaye gewéle yaye domérame
Cheikh khalifa nopaloul gni soumoune boukoumoune houmm youne fikoune
Yow ki ngay défendre mounoul tontu lougnu ko ladjie yow est-ce que Cva
Soumoun boukmoun khoum youn fa khoum la yah kiloun. Lolou pass passou sofianké le parce que lou serigne bi wakh gnou geum ko même sou outé ak al khour an té dougnou si réfléchir
Dr bayil ki amoul xam xam mais amoul yarr
Fi dal limafi guiss moy un Docteur Mourtada en ouvrant ce débat pour prouver que les soufi sont des Ndiabare katt s'est coincé lui même montrant que son propre guide Ibnou Taymiya est alors un ndiabare katt, parce que ce qu'il rejette lui même, Ibn Taymiya le faisait.
Senegal nekh0ul wakhe gin degniiu rere li amol ganar nope bou degue deug Khanna dr gaye ya am deug
Amol firde sunnu rek Moy deug il napasdereponse concrete boulder discuter ak ki