Bien dit Faisons très attention le Seul souhait de l'Etat c'est que Touba soit comme toutes les autres villes.. Ainsi il pourra y faire et avoir ce qu'il veut.
Jërëjëf Mbacké gnoune ndigalou Serigne bi lañiouy déglou. Té li Serigne bi beugue Touba dou policiers yi ñiokosiy dimbali mais mouride yi beugue ak gni xam li Serigne bi beugue. Wa Salam
À TOUBA il ya une seule constante, c'est la voix de SERIGNE MOUNTAKHA, le Khalife de SERIGNE TOUBA. TOUBA est une propriété privée avec un titre foncier en bonne et due forme 🙏🙏🙏
En tout cas je ne suis pas d'accord avec lui sur ce qu'il a dit sur les koureel Khoudamoul Khadim et Safiinatoul Amaane. Ce gars fait du charme et veut, à travers cette journée porte ouverte, endoctriner la population de Touba et la pousser à renier les organisations sur place qui militent, opportunément, pour la préservation du legs de Cheikhoul Khadim, ce que les représentants de l'Etat(police, gendarmerie,.....)ne peuvent faire du fait qu'ils soient des auxiliaries de l'homme blanc. Il faut savoir que les koureel qui sont là pour mettre de l'odre dans la ville sont le vœu du Calif et à Touba seul le Calif fait autorité. Tous les autres ne doivent suivre que les injonctions de ce dernier. Et ce ne sont pas ces représentants de l'Etat qui vont interdire certaines pratiques immorales et amorales dans la cité bénite. C'est ce que, très tôt, le vénéré Cheikh Abdoul Ahad Mbacké, 3ème Calif de Bamba, a compris et instruit l'Etat à l'accompagner dans la préservation de la bonne conduite dans la ville sainte. Aujourd'hui beaucoup de jeunes demeurant à Touba tentent de braver ces interdits tout simplement parce qu'ils veulent vivre à l'occidentale ce qui ne saurait être tolérer à Touba, vu son caractère sacré. Il faut que ces jeunes se mettent en tête que Touba est un Daara pas un laboratoire pour produire des prototypes à l'occidentale. Tout ce bruit agité à l'encontre de ces honorables koureels ne le sont que parce qu'il existe des forces occultes qui se battent jours et nuits, corps et âmes, afin que Touba perd son statut spécial ainsi que sa sacralité. Et malheureusement les jeunes de Touba tombent dans ce piège là. Khoudaam ainsi que Safiinatoul Amaane sont des entités comme tout autre entité à savoir qu'elles peuvent commettre des erreurs dans l'exercice de leurs nobles tâches et donc il revient à toutes personnes soucieuses de l'image de Touba de faire front autour d'elles et de les aider à s'améliorer. Si on devait radier toute institution parce que tout simplement parmi ses membres un tel a enfreint les règles du jeu, alors il n'y aurait pas aujourd'hui de police, de gendarmerie, de douane, de justice, de gouvernement, de confrérie,.....on les laisse en place, une fois l'erreur commise, sanctionne ci nécessaire le fautif, les aide à mieux faire leur travail et pour cela Touba dispose de toute la ressource nécessaire pour faire avancer ces koureel. C'est ça qui doit être notre combat. On doit les soutenir, les aider, les assister en terme de conseils surtout et en faisant de telle sorte que chacun en ce qui le concerne fasse de son mieux pour que certaines pratiques viles et abjectes ne soient plus de mise dans la sainte cité. Nous crions notre ras-le-bol dans ce qui est en train d'être, minutieusement, hypocritement et dangereusement, installé à Touba et qui est, profondément et totalement, contraire à la volonté de Khadimoul Rassoul. Touba est une demeure bénite, sacré, et spéciale au cœur du Sénégal et ceux qui y vivent doivent se le mettre en tête pour leur propre salut ainsi que pour la sauvegarde de l'immense oeuvre d'Ahmadou Bamba. Tous les sacrifices consentis par Ahmadou Bamba pour que le Mouridisme soit et que Touba aussi soit ne doivent en aucun cas être négligés et annihilés. C'est notre devoir à nous tous de veiller à cela quitte à en découdre avec toute personne et entité qui veulent changer la donne actuelle. La menace est là, elle est réelle et est bien ourdie, donc aux forces vives de la cité de se serrer les mains et de faire face. Il y va de notre salut à nous tous. De jeunes errants ça et là ne doivent pas imposer leurs lois et volontés qui plus sont contraires à la destiné de la demeure. Nous devons refuser cela par tous les moyens. Serigne Amsatou Mbacké a parfaitement raison. Thiobane est un prétentieux. Alhamdoulillaahi rabbil haalamiine, Dieureudieyuf Cheykhanaa Ahmadoul Khadim.
Yen may len nitt gni diam wakho fi touss sen serigne dou YALLA dou YONNENTE mbindèfou YALLA rekk la Fi ben Loi Lagnou wara topp mou nekk sougnou tékhé adouna ak Alakhira mouy topp YALLA ak YONNENTÈM rekk kasé kepp
iow yaa fi wax tuus , Naafex ligniy téré Touba boula néxul en tant que dioulit ?? War gua Xolaat sa BOPP (Naan sangara , pr*stitution, carte, sol yeeré yu bonn , football, ...) Ku nékul silu bax ,nék tha safane ba RK 👉 NAAFEX BAAXUL dh
Déjà ce qui est choquant moy pourquoi les autochtones de Touba ne respectent plus le ndigueul du khalif wala les contrevenants ne sont pas de Touba 🤔🤔🤔
Civile mounoul yar civile man dh kaddu gui daloul sama xél... niom daniou wara xam Tuuba dekkou kilif tēf la. kon bala nga fay déf benn déclaration da ngay wax ak kilifeu gui ba noppi. boufekké insécurité la mom nagn ko def sen xeex ndax lolu dafa weur Sénégal gui yeup. Serigne bi yalla nafi yag lool té and ak wër. Dieureudieuf Cheikh Ahmad Bamba .
Je ne suis pas mouride mais jesuis d'accord avec les marabout ils ne doivent pas accepté certaines choses a touba au prétexte k la loi le permet des lois importe ki ne réponds même a nos realite
Gnigui Ziaar Serigne Amsa. Probléme bi khamnguéne mooy lan: Touba li Serigne Touba beugue moofay am té li Serigne bi beugue daa am lou bari louci wouté ak sougnou lois yii nga khamni la Yalla kham doyna. ndakh lois boudoon lou absolues kon tay dougnou diogué 2012 ba 2022 gnouy am problémou 3eme mendat, goordjiguéen boofi diapp yobbou Police danaan Alhamdoulillah. Touba nak ne va pas a ce rythme. pour finir Serigne Touba limou beugue ci gnoun Mouride daa féeté kaw bépp lois bou nékk ci kaw souf boudoul bou sougnou Boroom. Merci à vous tous
Bayil féne. Laneleu loi bi nangou lo xamni Serigne bi dafko terei biir TOUBA ??. Lii Serigne beug si Touba xamnagn ko mais diaroul dooré diaroul Diap ay niit dilén teudj . Nekk lén ay niit. Touba yagg naa nekk Touba té kourel yoyu meussoul am té leep mogui donn dokh. Louffi diar creer ay kourel di door niit gni aka teudj té police nekk fii. Kolén fii door gnou teudj sen ndeye prison. Momoulén niit gni
Machalla Serigne que le bon Dieu vous protège merci beaucoup
Mandé talibé cheikh là mais je suis de 100/100 ak décision serigne bi. Dieureudieuf Serigne Touba
Bilay Mbackè nila sa baye bou bakh ba melon chiekh Abdoul ahad deug rek machallah yague fi lol ta weer🙏🏼🙏🏼🙏🏼🥰
Béne kadou rekk moffi am té moffi am ilayawmi dini moy Serigne Touba
C vrai li charia beugeu la serigne Touba beugeu kou déffoul lou diaroul yonne gnou wone dall sa kaw
Maccaallaa 💪💪☝💚💚💚💚lolergawakh
Rék
Machallah Dieuradieuf Mbacke Amna Solo
Machalla Mbacke balla yalna yalla dolila diam kheweul sutura were ak werle
Machalla amnasolo diadjeuff mbacke
dierediefe seringe touba khadim rasoul yalla nanga fi yagui lol thie wer thi barkep seringe touba khadim rasoul ❤❤❤❤❤👍👍👍
Machala amna solo Mbacke
Machallahi mbacké amna solou Dieureudieuf
Dieureudieuf Serigne bi,Touba li nékh Serigne Touba rék mofay am inchallah 👆❤️
Kaddouk Serigne bi ba ilal Abadd, amoul police amoul gendarmerie démlén thi khadj, Touba deukou serigne Touba la wa Salaam ♥️♥️♥️🙏🏽
Machala amna solo
MACHA ALLAH sama enseignant bi
Dieredieufeti mbacké balla touba moom kadouy serigne rek ba fawe incha...
we will never allow people to smoke or drink alcohol on the street in touba never dierediefe seringe touba 🇸🇳❤❤❤👍
Senegal police 👮♀️ amofi amnu yar amonu tégunne 😢
Machaalla ❣️❣️👍❣️
Tres Bonnes Reactions Mara
Machallah serigne bi jërëjëff Sant nañ Bu baax
Machallah Sènègal lobby yi dagno ame dolè wayè touba loi Serigne bi mofay dokh
Machallha mbackè balla yaguefi fall tèwèr ❤️ takhaway bi rafetna trop 🇨🇮❤️🇸🇳
Machallah Mbacke Yalna Yalla Barkéll
Akassa diadiuef amna solo
machalla wakh dji amena solo trop
Serigne amsatou Mbakce ibnou serigne abdou Lahad Mbakce aka am foula
Touba ken manouko guené si Sénégal 🇸🇳. Bilahi Touba sou amoul wone Police Niew dolen sax am fituu exposé sen Njaboot
Jeureujeuf serigne bi.
Macha allah Mbacké Yalla ga fi yague ta endeu ak wer si barkelm Serigne Touba Allahou amine way
Bien dit
Faisons très attention le Seul souhait de l'Etat c'est que Touba soit comme toutes les autres villes..
Ainsi il pourra y faire et avoir ce qu'il veut.
Loulou laniouy manigancé et c pas seulement le gouvernement même des lobbies extérieur
En quoi Touba serait ol different ? Deukou s modou lo ngbabou....
Niaplene sene ndeye
@@دفراتسنغال doma tontou kouy teudé yayam
@@دفراتسنغال niafal sa ndey yaw domairam rew ga trop
Lolou dh doufi âme inchalla
حفظك الله وأيدك ونصرك.
Je suis mouride je suis né à touba je suis avec thiobane 💯%
Merci serigne bi
Machalla toujours su service de la population
Jerejefeti mbacké balla aïcha wah dji werna ❤
Masahala yalla n'a la yalla sammou
Machallah mbacké balla yagal wéral naffi ndioubb sakh reck Ak deugue
Akasa mbacke 👉❤️💪💪💪💪💪💪💪
Yagé len fi loll tawerr mbacké balla incha allah ❤️ ❤️
Masallah beknane s. Amsatou mbacke yagfi tewer Lo lér ngawakh
Dieureudieuf mbacke 😍😍
waw mbacke balla aïcha bori wakhi di diar na wone te am na ak talibe yalla na fan wi godou ak wer gui
MACHALLA amna sollo mbacke
Dieureujieuf Mbacke
Touba benn kadu mofi am moy kadok serigne bi point DIEUREUDIEUF SERIGNE TOUBA
Merci commissaire Thiombane linga wax deug kasé la
Mrd
@@D.T.H777 amouma sa diote balaay nonou .touba lignou beug mofi am .kéne doufi tokh wakhoumala sangara
@@D.T.H777 diégaalma bou bakh dama dioum
Machalah mbacké wakh léne si Touba deuk bou sél la kéne waroko thiakhané seringe Touba défal naléne lepp Lisi déss nak yéne Aye setam yénako wara takhawou
Ake nione Talibé yii
Jërëjëf Mbacké gnoune ndigalou Serigne bi lañiouy déglou. Té li Serigne bi beugue Touba dou policiers yi ñiokosiy dimbali mais mouride yi beugue ak gni xam li Serigne bi beugue. Wa Salam
Machalla s amsa Amna solo lole
Macccaaalllaas mbake balla ☝👂👂✊✊touba day derase 👈matnavayikhel😗💪💪sakaw sakanam bolen 👂👂kodol s touba👏👏
Merci beaucoup wawaw 🙏🙏
Waw goor serigne bi
Ndigeul Rek inchallah mbacke balla ❤❤❤❤❤
Machallh
ماشاء الله تبارك الله ❤❤❤❤❤❤
Machalla diere diefeti mbacke
Machalaaah
Machallah
Merci commissaire
Ma challah Mbacké
Macha allah kaddou yi rafétna mbacke balla gnoundé sant nagnoula 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Jërëjëf Mbàkke!
Machalla Mbacke balla
Merci papa 👍👍
Touba rek lano am
je vois que né reewmi taka macky sall mogui si pouvoir bi problème sur problème rek Qu'Allah nous débarrasser de ce régime Amine
Machalla touba mom bén kadu la ame muy ndigalou serigne bii
Le commissaire à parfaitement raison
À TOUBA il ya une seule constante, c'est la voix de SERIGNE MOUNTAKHA, le Khalife de SERIGNE TOUBA.
TOUBA est une propriété privée avec un titre foncier en bonne et due forme 🙏🙏🙏
Touba sou nekeh lolou sr SALIKHOU silla lep jareh teh yeurmandeh rek la dokheh niop joxko thieur kilifa dou and ak loudoul deugue
Dieureudieuf mbacké
Macha alah mbacke
machllala ❤️
dieredieuf s touba
ماشاء الله تبارك الله فيك جرجف سرج طوبي قاد له الله ماقتارله
En tout cas je ne suis pas d'accord avec lui sur ce qu'il a dit sur les koureel Khoudamoul Khadim et Safiinatoul Amaane. Ce gars fait du charme et veut, à travers cette journée porte ouverte, endoctriner la population de Touba et la pousser à renier les organisations sur place qui militent, opportunément, pour la préservation du legs de Cheikhoul Khadim, ce que les représentants de l'Etat(police, gendarmerie,.....)ne peuvent faire du fait qu'ils soient des auxiliaries de l'homme blanc. Il faut savoir que les koureel qui sont là pour mettre de l'odre dans la ville sont le vœu du Calif et à Touba seul le Calif fait autorité. Tous les autres ne doivent suivre que les injonctions de ce dernier. Et ce ne sont pas ces représentants de l'Etat qui vont interdire certaines pratiques immorales et amorales dans la cité bénite. C'est ce que, très tôt, le vénéré Cheikh Abdoul Ahad Mbacké, 3ème Calif de Bamba, a compris et instruit l'Etat à l'accompagner dans la préservation de la bonne conduite dans la ville sainte. Aujourd'hui beaucoup de jeunes demeurant à Touba tentent de braver ces interdits tout simplement parce qu'ils veulent vivre à l'occidentale ce qui ne saurait être tolérer à Touba, vu son caractère sacré. Il faut que ces jeunes se mettent en tête que Touba est un Daara pas un laboratoire pour produire des prototypes à l'occidentale. Tout ce bruit agité à l'encontre de ces honorables koureels ne le sont que parce qu'il existe des forces occultes qui se battent jours et nuits, corps et âmes, afin que Touba perd son statut spécial ainsi que sa sacralité. Et malheureusement les jeunes de Touba tombent dans ce piège là. Khoudaam ainsi que Safiinatoul Amaane sont des entités comme tout autre entité à savoir qu'elles peuvent commettre des erreurs dans l'exercice de leurs nobles tâches et donc il revient à toutes personnes soucieuses de l'image de Touba de faire front autour d'elles et de les aider à s'améliorer. Si on devait radier toute institution parce que tout simplement parmi ses membres un tel a enfreint les règles du jeu, alors il n'y aurait pas aujourd'hui de police, de gendarmerie, de douane, de justice, de gouvernement, de confrérie,.....on les laisse en place, une fois l'erreur commise, sanctionne ci nécessaire le fautif, les aide à mieux faire leur travail et pour cela Touba dispose de toute la ressource nécessaire pour faire avancer ces koureel. C'est ça qui doit être notre combat. On doit les soutenir, les aider, les assister en terme de conseils surtout et en faisant de telle sorte que chacun en ce qui le concerne fasse de son mieux pour que certaines pratiques viles et abjectes ne soient plus de mise dans la sainte cité. Nous crions notre ras-le-bol dans ce qui est en train d'être, minutieusement, hypocritement et dangereusement, installé à Touba et qui est, profondément et totalement, contraire à la volonté de Khadimoul Rassoul. Touba est une demeure bénite, sacré, et spéciale au cœur du Sénégal et ceux qui y vivent doivent se le mettre en tête pour leur propre salut ainsi que pour la sauvegarde de l'immense oeuvre d'Ahmadou Bamba. Tous les sacrifices consentis par Ahmadou Bamba pour que le Mouridisme soit et que Touba aussi soit ne doivent en aucun cas être négligés et annihilés. C'est notre devoir à nous tous de veiller à cela quitte à en découdre avec toute personne et entité qui veulent changer la donne actuelle. La menace est là, elle est réelle et est bien ourdie, donc aux forces vives de la cité de se serrer les mains et de faire face. Il y va de notre salut à nous tous. De jeunes errants ça et là ne doivent pas imposer leurs lois et volontés qui plus sont contraires à la destiné de la demeure. Nous devons refuser cela par tous les moyens. Serigne Amsatou Mbacké a parfaitement raison. Thiobane est un prétentieux. Alhamdoulillaahi rabbil haalamiine, Dieureudieyuf Cheykhanaa Ahmadoul Khadim.
Mercii🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Merci
C'est avec un grand plaisir que j'ai ton commentaire
Doul
Nous sommes thiobane
Mashallah mbacké, gueneu yague gueneu werr
Dieureudieuf Serigne amsatou wakh dji amna solo lool
❤️❤️🕊
Kou beugeul Serighn touba ,njabotam bi, khassida yi,ak deuk bu sell bi ,koku manul deff Dara Lou bakh touba
Machalla bayou serigne khadim mbacké borom deug nio gui sa guinaw
Yen may len nitt gni diam wakho fi touss sen serigne dou YALLA dou YONNENTE mbindèfou YALLA rekk la
Fi ben Loi Lagnou wara topp mou nekk sougnou tékhé adouna ak Alakhira mouy topp YALLA ak YONNENTÈM rekk kasé kepp
Hors sujet
iow yaa fi wax tuus , Naafex ligniy téré Touba boula néxul en tant que dioulit ?? War gua Xolaat sa BOPP (Naan sangara , pr*stitution, carte, sol yeeré yu bonn , football, ...)
Ku nékul silu bax ,nék tha safane ba RK 👉 NAAFEX BAAXUL dh
Signe touba moy sene serigne
Amna solo mbacke ball
Macky Sall baybayal bou eupou boococoy may mouy yiék thi sa diguou boopoubi. Sonko rék moo kham Macky. Toubabyi la respecté waayé ab serigne foowoukay la léene déf. Beucou néeguou serignessi mouy dieunde gniou toogne. Ndakh serignebi dou kham Lou khéew.
seriñbi kilifa du saaga,rawatina saaga waa polis,seen doom maam faati siidi li seriñbi di bañ lafi def,ta joxé galace.Seriñbi ñep xamnañuni nitu fitna nga bayil di tekko.Serriñ muntaxaa moo fiy kilifa Wa salaam
Yaw ko réew Nga Bola naxare Nga ngenne Touba
Honnêtement je suis totalement d’accord avec le commissaire par ce que un civile ne peut pas géré l’autre
C'est un titre foncier APPARTENANT à Cheikhoul Khadim
Oui effectivement frère en plus Thiobane aussi il est Mourid et bay fall comme eux
Boy fii nioko mom koufi am loy wakh démal sa keur bay
Ça se voit que tu ne connais rien du droit...Touba est un titre foncier appartenant à Serigne TOUBA
Té Sa baay djiité sa nday ak sen waa keur yepp
Fi moy touba kou bagn guenal dekk bi touba rekk insahalahou
Kou rew ngan
Déjà ce qui est choquant moy pourquoi les autochtones de Touba ne respectent plus le ndigueul du khalif wala les contrevenants ne sont pas de Touba 🤔🤔🤔
Jërëjëf sëriñ bi , Sama xol sedd na lool ci yaw .
Civile mounoul yar civile man dh kaddu gui daloul sama xél... niom daniou wara xam Tuuba dekkou kilif tēf la. kon bala nga fay déf benn déclaration da ngay wax ak kilifeu gui ba noppi. boufekké insécurité la mom nagn ko def sen xeex ndax lolu dafa weur Sénégal gui yeup. Serigne bi yalla nafi yag lool té and ak wër. Dieureudieuf Cheikh Ahmad Bamba .
Amna solo
Billahi walahi linga wakh moye degue Bamako diglo lakhamni dagnekoye sacrifie liguiyoune dara mbaryi fii loune' amnafi bounioufi niewe'khaliss kep lanioufiye woute.
Waw goor way mbacke balla
barap yoyou yeup ame na Touba wa Touba nekk fa di deff lou bone ....
Www mback Balla wakhega deuku dh
Je ne suis pas mouride mais jesuis d'accord avec les marabout ils ne doivent pas accepté certaines choses a touba au prétexte k la loi le permet des lois importe ki ne réponds même a nos realite
fi si touba ken doufi nan sangara wala toux koumou nex ak koumou naxary
Merci beaucoup guirr yalla yéne rek yéna wara takhawou ndékeu bi serigne Touba da fonkou ndékam
Dieredief Mbacke amna sollo
Faite ATTENTION aux micros EMPOISONNER kilifa dine yi
Gnigui Ziaar Serigne Amsa. Probléme bi khamnguéne mooy lan: Touba li Serigne Touba beugue moofay am té li Serigne bi beugue daa am lou bari louci wouté ak sougnou lois yii nga khamni la Yalla kham doyna. ndakh lois boudoon lou absolues kon tay dougnou diogué 2012 ba 2022 gnouy am problémou 3eme mendat, goordjiguéen boofi diapp yobbou Police danaan Alhamdoulillah. Touba nak ne va pas a ce rythme. pour finir Serigne Touba limou beugue ci gnoun Mouride daa féeté kaw bépp lois bou nékk ci kaw souf boudoul bou sougnou Boroom. Merci à vous tous
Bayil féne. Laneleu loi bi nangou lo xamni Serigne bi dafko terei biir TOUBA ??. Lii Serigne beug si Touba xamnagn ko mais diaroul dooré diaroul Diap ay niit dilén teudj . Nekk lén ay niit.
Touba yagg naa nekk Touba té kourel yoyu meussoul am té leep mogui donn dokh. Louffi diar creer ay kourel di door niit gni aka teudj té police nekk fii. Kolén fii door gnou teudj sen ndeye prison. Momoulén niit gni
Jërëjëf Bàkke