que le Bon Dieu l'accueil au paradis firdawsii le Monde a perdu un homme multidimensionnel très courtois civilisé et discipliné je l'estime tellement je me disais même avoir la chance de le rencontrer tu demeures tjrs dans nos coeurs vs êtes inoubliables Papa Malick Sy repose en paix tu va ns manquer ns la jeunesse car vs saviez comment ns parlés à travers votre claire explication
MachAllah SY Malick wakh diou rafet dieuf diou rafet Yalla bou la thiat djitou si bamel Yalla na Cheikh Al Khalifa terou la thia Aldiana Firdawsi ak bepp ndiabott Maodo Malick ak bepp dioulit 😭😭😭 tu nous manques beaucoup dou gnou la meussa fate Sy Malick Fatiha+ 11 Ikhlass
Moi je considère qu'il n'est pas mort, mais juste parti au paradis et que nous continuons à l'écouter à travers ses causeries de hautes factures. Yala nako Yaala yobou thia aldianay firdaws ya té taas niou si barké lérou armélam, comme il le disait.
Bilay lolou lako nieup donne nianal mais souniou borom moniou ko gueun sokhla, yalla na yalla Yok lerram si barké Seydina Mouhamed PSL tass niou si barkém amine ya rabbi
ماشاء الله بارك الله فيكم وجزاكم الله خيرا وأيدكم الله ونصركم الله وحفظكم الله وأطال بقاءكم مع دوام الصحة والعافية والتوفيق والسداد بجاه اللهم صل على سيدنا ومولانى محمد وعلى جميع الأنبياء والمرسلين وعلى آلهم وصحبهم وسلم تسليما كثيرا عدد خلقك ورضا نفسك وزنة عرشك ومداد كلماتك آمين يارب العالمين
Yallah borom yessal yeurmande sii kawam inchallah pape malick sy ❤️🙏
Bly sy malick doyala gouma si mm ba tye blh yalla nala yalla yokou ay leram té tass nusi barkem
que le Bon Dieu l'accueil au paradis firdawsii le Monde a perdu un homme multidimensionnel très courtois civilisé et discipliné je l'estime tellement je me disais même avoir la chance de le rencontrer tu demeures tjrs dans nos coeurs vs êtes inoubliables Papa Malick Sy repose en paix tu va ns manquer ns la jeunesse car vs saviez comment ns parlés à travers votre claire explication
Sama Sope bilahi Sope nala yalla xamenako yalla nala yalla wanale ak sa Sope sa copin Serigne Babacar sy tu reste gravé dans nos cœur
Y’a bonne nuit
Amine
Mashallah S'y Malick Yalna YALLA. Yok leeram.
MachAllah SY Malick wakh diou rafet dieuf diou rafet Yalla bou la thiat djitou si bamel Yalla na Cheikh Al Khalifa terou la thia Aldiana Firdawsi ak bepp ndiabott Maodo Malick ak bepp dioulit 😭😭😭 tu nous manques beaucoup dou gnou la meussa fate Sy
Malick
Fatiha+ 11 Ikhlass
Yalna yalla doli ay leram té karéko aldiana thi barké yoneté bi aleyhi salamou té tasnou thi barkém
Masouma guiss SRG BABACAR SY wayé sayuma guisé pape malik ak al amine déy mélni SERIGNE BABACAR laa guiss
Billahi degele bou wuer sakh
Akay deg
Serigne pape malick sy
Yalla na yalla goudal fane wi 120 ans yafiy serigne babacar sy 🙌🙌💓
Masha Allah dieuredieuf Sy Malick yalna Yallah yessal yeurmandeim ci yow
Moi je considère qu'il n'est pas mort, mais juste parti au paradis et que nous continuons à l'écouter à travers ses causeries de hautes factures. Yala nako Yaala yobou thia aldianay firdaws ya té taas niou si barké lérou armélam, comme il le disait.
Wallay ndeyssan 😢 de même que moi
Machalla sy malick damala beug lol yallna yalla yok sa lerr
Oh ken dou seydi aboubakar sy ❤❤❤❤❤❤❤❤
Thiey YALLA comment ne pas aimer cet illustre homme k DIEU le récompense de tout merveille ds l l'haut de là paix à son âme 🙏🙏
Amineee ndeyssane
Je suis khadre et fière d’avoir un Pape Malick Sy dans mon pays yalla moye karim .
Diazaakumul lahu khayran sy Malick sa mission matna seuk yalna yalla gueureum la
Yalna xippé aldiana si barké cheikhoul khadim
Que le Tout Puissant Allah l'accueille en son paradis...
toujours le meilleur💫😭😢🙏🥰
ALHAMDOU LILLAH MACHA ALLAH yalna YALLA fayalnou Mame Cheikh Seydil Hadji Malick Sy
Amine
Un excellent professeur, un courtois macha Allah qu'Allah soubhana watahla l'accueille dans son firdaws
Machalla goudou fane ak weer rk lagni lay nianal sy malick yafiye S.babacar sy❤️🙏🙏
Yalla nala yalla yeureume khare aldiana firdawsi
Goudou fane ak wére rék lagnouye niane sy Malick
Amine way kou bakh
Yallna go yalla yereum amine inchallah
Mame malick sy kharitou serigne chiekh tidiane sy almaktum yalla nala yalla defal diam ak soutoura si barkep chiekhou Omar foutiyou Tall Tall amine 💖💖
Yallana yalla yokou lerame the tassounou thi barkeme
Terminera
La'
Yalna yalla yokk léram mou xipé sa barzahou magg you bax yi
Walay ndeysane sy malick yalna yalla yok say lére té tasgnou sisa barké inecha ala
Machallah sy malick yalla na yalla goudeul sa fane
Machallah yalna yalla faye lene si barke serigne babacar
Yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana🙏
MACHALLAH MACHALLAH AMNA SOLO DIEUREDIEUF YALLAH NA YALLAH GOUDEUL SA FAN GEUNUE WEREUL SAY THIEUR SI BARKE RASSOULILLAH PSL ET TOUT LE MONDE
Machallah Sy Malick yalla na yallah doli soutoura ba faw inchallah
Amine way kou bakh
Sy Malick yalla nalafi yalla bayi ba sikanam gnola sope pure
Yalla na lalènefi yalla bayi bassi kanam si barké S Babacar Sy RTA
Machalla Wakhtane bi ame na solo Sy Malick
Alkhamdou lila machallah yalna yalla nagou gnane
Yal na Yalla bourbi goudal sén fane May léne wér si daradja Seydina Mouhamad psl
Macha allah yalna yalla faye la yiw sy malick
Machalla yalna yalla fayal gnou lene ci brk sayidil Haji Malick rta
Bilahi sy yéna bah té yatal yép yatou machala
On peut l'appeler Le professeur par ce qu'il dispose des cours extraordinaires
Sama sopé bi yalla na yalla mayla fane wou goudou
Thiey sy malick yague fi Lo tè wer si barque Cheikhal khalifa🙏🙏🙏
Amine way kou bakh
Amine inchallah
Ohhhh gnibbi na aldjana
Bilay lolou lako nieup donne nianal mais souniou borom moniou ko gueun sokhla, yalla na yalla Yok lerram si barké Seydina Mouhamed PSL tass niou si barkém amine ya rabbi
Walahi mome yalla la dèf ma begue mane mome bi dèguè dèm mame walhi lima yegue mak yalla rèk ko kham way Alhamdoulila 🙏
ماشاء الله بارك الله فيكم وجزاكم الله خيرا وأيدكم الله ونصركم الله وحفظكم الله وأطال بقاءكم مع دوام الصحة والعافية والتوفيق والسداد بجاه اللهم صل على سيدنا ومولانى محمد وعلى جميع الأنبياء والمرسلين وعلى آلهم وصحبهم وسلم تسليما كثيرا عدد خلقك ورضا نفسك وزنة عرشك ومداد كلماتك آمين يارب العالمين
رحمة الله ومغفرته ورضوانه عليه بجاه سيدنا محمد عليه الصلاة والسلام
Sangu bi yagg fi bou and ak wér si barké yonnenti bi SAWS
Bilay bumakoy diglu dafay melni Man dama diakarlo ak Serigne Babacar s'y walahi s'y Mala beug
Machallah Yallana yalla barkekl
حفظك الله ورعاك يا شيخي❣️❣️
Billahi yèna donou mouhamad rasoul
Amoul wérénté billahi
Danga bakh dek Sy malik wayè ay sangua nguène
Sy yalla nangafi yague té wér
Koulen khamoul rek moléni diguénte
yallahnakoyallahyereem -ayway 😎Liban
Diangue yagoule niakka diangue mo yague nakhe amoule moudie bilahi sy wakhe gua deugue
Machalla sy malcik🙏🙏🙏🙏🙏
tabarkarla Sy Malick
Dieuradjieuf sy malick
Machallah rafetna
Machaallah sy malik
Maa Shaa ALLAH amna solo
Macha allah ❤
Yalna yalla doli soutereu ak weerguu yaram yalla déf guéne am kataane ba agualé sen yéné keur seydil El Hadji Malick sy ak diné dji
Amine
Yénay sunuy sakk dh Sy goudou fane ak wërr lagn léne Di nianal té niou yaggeu Léna goungué
Walaay Ndeysane
amlén goudou fann ak wérr
Alhamdoulila sy machala wax dji rafetna
Macha alah bilahii sy malick
Mashallah
Machalla amna solo
Macha Allah Sy
Machalla sy malick ♥️♥️♥️🤲🤲
Machallah la famille de Maodo est une fierte
Ma Shah Allah sy
Thiéy Adouna
Très fière machalah
Machalah amine
Machallah machallah
Ndeyesan repose en paix amine yarabi 😭❤️❤️❤️
Son âme repose en paix
Yalana yala goudeul sa fane
Amine way amne solo
Sy malick djeureudieuf
Sy malick yagefi loo téwér
Contane na wakakhi
Machala sy malick
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Alhamdu Lillah ❤❤☝ mashallah❤❤🕋.. Sy
Machalla
Machallah 🙏❤️
Fatoumata sall ziar nalla
Sy malik
Amine
تبادل هداية وحنان % تقويان علاقة الإنسان
من يبغض الخديم دائي نفسه % وضاح من يحبه بالجنان
أوعي برعي ورائه كأمامه% يقضي الديون أوفر الميزان
مردي العدي مرضي الهدات تكرما % مزكي النفوس مكفل الأبدان
وبإسمه أعزي (تيواوونا) سيدا% شقيق الشيخ أحمد التيجان
ألموة فارقهما وتلقيان روضة البرزخ والجنان
ألموة فارقه حبيبا مخلصا % لحبيبه تفارق الزوجان
ألموة فارق مسترشدين زعيمها % وزعيمه من قبله بأوان
توفي نجل صغير الخليفة % والبدر أفلي خاسف الميدان
توفي المالك سبط المالك % لطيف النفس وكثير الأمان
أدبه كبيره بكتابه % معلمه العلوم والقرآن
شابهه بصراحة وحكاية % ومهارة وذكائة الأذهان
وله بلغات شتت تثقفا %حكيم فاسح وفصيح للسان
تجده أين الخيور كثيرة % فيشهد الكبار بالإحسان
كريم خلق ذوالبشاش مرحب % وجميل وصف يزدري المرجان
وصالح من كل صوة يلقه % لايؤذيه من مقاله الإخوان
وحاسس (تيواونا)بلباسه % وببرنس ونظارة الأرمان(1)
وبزينة جثمانه ودمائه % وفؤاده مادنستها الخنان
هذا أبو أبيه من بسماته % ألمالك أخ الأمين الكيان
رحمهموالرحمان صل علي النبي % والآل والخديم كل الزمان
LE /26/06/20
الأرمان1/ Giorgio Armani
خويدم الخديم ابراهيم غي
Sy Malick
❤❤❤Sy Maodo Malick ❤❤❤
الله يجازيكم خيرا
Yag fi lol teii werr sy malick
Mika aw
Amine
😍😍😍😍😍😍💪👉👂
qui pour m'écrire le ya khayumou pour nougn fattei svp
Merci ousmane
@@ousmanesarr6381 27 fois
@@ousmanesarr6381 merci
@@ousmanesarr6381 27 fois au lieu de 28
😢😢😢😢😢
Tathiou yi nak dafa doy dou teguine
🙏🙏🙏🤲🤲🤲😭😭😭
M