Dayza il a le rythme et la rime dans le sang ! L'on ne finit jamais de s'enjailler de ses couplets🎉😅. " C'est normal ma dof ci yaw parce que ya yoor sama garab bi". Même dans le délire, sa plume suggère de l'esthétique pure❤ Quant à Ara, il n'y a plus à redire son aisance mélodieuse. Sa voix est une brise de miel. Il jongle avec son timbre et chante comme ça l'enchante.
Koula yaga deglou hamni nanane nga gar yi dagn lay doga découvrir et ce boom me fait tellement plaisir pleins de succès dans ta carrière in sha allah ndam rek
WA deyza mani deyza deyza la wax dh deyzakallah bou akhlou brick domou ndayou ara temou ndiol gentle esk nit la la wax damay lathie ki da meun maman wa rap way😮🤔🤔🤔❤️😍
Dome dapp love mome nanou bayi ak yene non vraiment ça c'est lourd vraiment bonne continuation mes frères akhlou brick paradise le 1er couplé de dayza ça me vas beaucoup ❤🎉🎉❤🎉🎉❤
Rek dougou ci keur gui ndakh xole dou 🥧 ba kén douko daggate daggaté, xole dou 🍕 ba kouné teul di ladj part, amo lén fi part , bén part lë diox nala ko❤❤❤ oh Ara❤❤
Dayza il a le rythme et la rime dans le sang !
L'on ne finit jamais de s'enjailler de ses couplets🎉😅.
" C'est normal ma dof ci yaw parce que ya yoor sama garab bi".
Même dans le délire, sa plume suggère de l'esthétique pure❤
Quant à Ara, il n'y a plus à redire son aisance mélodieuse. Sa voix est une brise de miel.
Il jongle avec son timbre et chante comme ça l'enchante.
❤
Socoplume respect
❤🎉
Liguay comment bakhena neikhena 😂❤❤❤😂😂🎉
Ta plume toi aussi machaallah ❤
Akhlou brick = courage perseverance talent intelligence aisances technique tactique confiance en soi polyvalence akhlou brick = puissance force croyance Bilahi yena bien
Brick bou nieuwé teumb thi kaw nieup 🔥🔥🔥✌🥵
Bilaie lou leer ❤
Kou nangou ni akhlou brick mo Dakh gné lalal j'aime
Nio fi nek
Lolou dafa féss bro❤❤
Ngaka rk
@@alouakhloubrickmarshallah damaleni beugue ba kagn tmt
.n.@@general-blindé
Ana kouy rèvè ziarra dji Mohamed rassoul borom barrière ba ça Madine❤
❤❤❤
SAW SALALAHOU ALA MOUHAMEDINE ❤️
❤❤❤❤
PSL❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kouy sopey nabi lalal j'aime ❤
J'ai accouché d'une petite garçon yalla boumou oumpou bén djiguen ❤
Dingal nga bagne 😂
Yalna sa petite garçon doundou té barkel ame ndeye AK baye way
Boy do srx touti banou deff sounou baptême ba paré😂@@alouakhloubrick
Yalla na sa petite garçon bi mague done grande homme bou ame niame
Amine
Rap galsen ara est le meilleur pour refrain kou d'accord j'aime et ça fait 10 ans j l'écoute force a vous akhou brick
Game bi wa mbour niofi dakhe rap kou d'accord lalale j'aime 👍👍👍 brick
Bilay iow ❤❤❤🎉
Gno fi nékk kay
Lolou la yalla dogal bro🔥🔥🔥🥵
😂😂😂😂😂😂
@@amadoudamediankha435 billahi
Kou aimé sama commentaire Yal na nga teki ba teral ko beugue teral goudou fane were kene bagnla manal dara ❤
Amine yarabi ñu bokouko ñoun ñep
Amine yarabal alamine
Amine
Bilaye yénafi nek quand ces bon c'est akhlou brick yalnaséne diam yag ku meune na def gnaw ❤❤❤❤❤
Sénégal mom yena fi dakk clip 🎉la qualité de vos vidéos c'est juste incroyable 🎉❤
Sénégal bamou dadj yénafi dakka clip 🦾💪 kou d'accord lalal 👉👍
Bilahi frère Lou lér nga wax 🥵🥵🔥🔥🔥
Dra douko dindi
@@amadoudamediankha435 bly sen niveau clip dépassé na galsen nakh amougnouffi concurrent
@@abdouazizgaye1027 mané akhlou Brick moy ramou rappeur yi euleuk yawmal khiyam🥵🥵🔥🔥🔥😭
mai kou daf rabb
Je suis blind blind way lii nekh na deehhh🎉 chapeau
Koula yaga deglou hamni nanane nga gar yi dagn lay doga découvrir et ce boom me fait tellement plaisir pleins de succès dans ta carrière in sha allah ndam rek
Toi qui lu mon commentaire qu’Allah laisse tes parents vivre jusqu’à ta réussite
Amine amine 🤲🤲🤲 allahouma amine 🤲🤲🤲
❤❤❤❤❤❤
Amine
Moi qui lu je dis amène❤
Aminn❤
Mana Mana, prouve leurs supériorité brick yéenaa meunn eupp doléé
Papa ci rap ,papa ci music , Papa ci sollou, papa clip bou Nice 🎉🎉akhlou brick for real
Qu'il la vue plusieurs fois comme 🤔🤔🥺🥺🥺c'est super classe srx Non Dayza qui est vous et sans oublié le flow de Ara 💪💪💪brick yéena woor dh 👌
Mane soumay dee gaïndé may ray 🎉🎉🎉
Mane soumadei beug damay beugalei sa demb ak tay🎊🎊🎊🎊
Akhlou Brick yenaa fii meunn,
Yena fi nekk
Yenn laniou top
Yen laniou de glou
Yen laniou préféré
One love guys
Kou geme nė rewmi dina chance lala j'aime
Inchallah ❤❤❤❤
🤨🤨
Dougenn ma décevoir moukk yene ayyy d
Kola KO wakh 😅😅😅😅
@@tallandiaye9150pros mou sel mi❤
Kou âme lénéne téyél sa yeuff😂😂akhlou brick paré Niokali 😂😂😂😂😂😂😂
Mana Mana🤝😂😎🔥🔥🔥
Quand c beau c Akhlou brick🔥🔥👋
WA deyza mani deyza deyza la wax dh deyzakallah bou akhlou brick domou ndayou ara temou ndiol gentle esk nit la la wax damay lathie ki da meun maman wa rap way😮🤔🤔🤔❤️😍
Dathie nek rek wayé bokou ci
Lumière,sons habillements tout est au top brick vous êtes fort avec l'équipe
Akhlou Brick ❤❤Paradise bi yoone la té si yeinn la dièkk ndah moy deukouwayou Hariff yi Eulleukkk ❤❤❤❤
Khôl dou pyza ba kou nek teuleu di lathie part 😂 trop fort techniquement chapeau akhlou brick 🎉🎉🎉🎉
Wépépéppppppppppppp💃🤩😍🥰 ❤️❤️ meilleur yéna ko def mani Mana Man💃💕
Les King 🤴 ❤🎉
Yeah
Vraiment vous êtes meilleur toujours au top machallah clip mome yéna ko moune 🎉❤❤❤❤❤❤❤
Aldiana gang ❤
❤do kay ma déff la aldiana ❤❤❤😂
Daffa leer gnoungui fi dh
Bon Gamou a tous Diam akk salam siii ñép Machallah Akhlou brick vous êtes les meilleurs❤❤❤❤❤🥰🥰🥰
La voix de Ara est juste magnifique.
vous etes trop fort tjrs a l'aise n'importe quel beat weiy quand c'est propre c'est Akhlou Brick
Diaroul ñiouy lathié fii yénafi nek té yénnafi tek tang si game bi🎉 kou d'accord ak man lalal J'aime bi ñiou guissko🎉
Diaroul lath sax🔥🔥🔥😂
Un bon musicien se démarque par sa polyvalence, vous en êtes l'exemple parfait 🗽
Yéna meune love dé bilay❤❤❤❤❤😊Akhlou brick 🎉🎉
AKHLOU BRICK,yénaa polyvalent DH foouguén guéneu mou gueuneu gaaraww
Sén affaire lë
Diaroull gayy laathie ,niokayy nékhall ,boull laathié niomm l'Aa
C'est un plaisir pour moi d'avoir artistes préférés comme vous. Je vous love ❤❤❤.
Dayza doundeul wéral ❤️ li nékh na trop 😍❤❤❤❤
Wa prkw ma akhlou brick yen 😂😂 nonnn je les aimes trop ❤❤
Liguéne di déff néx na Ma challah🤝🏾💫
Wow woow wooow mais quel kiff 🔥🔥🔥 Mc Ada tu nous transporte très loin avec cette chanson.
Mon lecteur est en boucle🔥😭
Yénn dayza nitte leu wala barké rassoul dayza mo dakka rap Senegal wollah ☝️💪
Meilleur son depuis l'histoire du hip hop
Rap pur lagnouye beugg kou drc lalaye j’aime 🥰
🔥🔥🔥🔥❤️❤️💋 li nekh na dé ma chérie bravo et Bonne continuation trop contente pour toi 💕
Dayza doundeul wéral ❤️♥️❤️♥️ li nékh na trop 🤣
Dome dapp love mome nanou bayi ak yene non vraiment ça c'est lourd vraiment bonne continuation mes frères akhlou brick paradise le 1er couplé de dayza ça me vas beaucoup ❤🎉🎉❤🎉🎉❤
Mch 👌Ara La voix ki tue 🎊 🎉🎉
Akhlou brick et de retour avec plaine de puissance ça nous plaît
Mongui cool deh samagayi😮
Vous êtes les meilleurs.
C'est le travail de tant de sacrifices. Le senegal est fier de vous
Mousouma am 5 j'aime 😞😢😓
😂😂😂😂😂😂
Rek dougou ci keur gui ndakh xole dou 🥧 ba kén douko daggate daggaté, xole dou 🍕 ba kouné teul di ladj part, amo lén fi part , bén part lë diox nala ko❤❤❤ oh Ara❤❤
Felicitations pour le style different. le Mbalakh a besoin de ça....foncer distinctions yangui nieuw
😂😂😂😂ioe neex gua dh
Affaire bii yén vs êtes les meilleurs
Ara do nitou fi way aaaaaah 🧠 😅😅😅😅❤❤❤
Ya rafett djiko
Rafett xoll
Dema napadié 🎉🎉🎉🎉
Les meilleurs aux sénégal 🎉❤
Louma wakh rek aye Répétition lay donn walahi vous êtes les meilleurs de tout les temps❤❤❤
Ana mérr 4yii marrrr lén sén bouneu yi si commentaire yi ok 😂😂😂😂 fi akhlou brick rék amul kénéneu ❤
Seuuuuu song bi enh daflay voyagé lo dans le planète de l'amour ❤😊
Koufi tékk tank yéne la yéne la😂😂😅😊😊❤❤❤❤
Vraiment vous êtes les meilleurs je ne peux pas comprendre les gens qui vous comparent avec Ngaka ou Dip
Yokhoul thi kaw🔥🔥
Waw mais Li dope n’a dè machallah
Mbeuguel senn yeuff leu 🤌🏾🔥 trop fort cmm d’habitude 😎🖖🏾🔥🔥🔥🔥
Mon frr nice na❤❤
sheuuuuttt encore akhlou brick yena meunn ayyy fort grawwww😅 peace n love
Gouddi Gouddi Mbour 👏🏾✊🏿
L’artist🔥
❤❤❤❤❤❤😂😂haayy liii nekhna machalah
képou kou nékk si ayyy tolof tolof YALLA nako Yallah safaraa si barké Seydina Mouhamed (PSL)
Amin yarabi
Akhlou brick cou
rage perseverance machllha❤️🥰😍❣️♥️💞❣️
Vous êtes les meilleurs ❤
Ziz killer in the building so cute 💥💥 dash hip hop
Record bi mana mana 💪
Oh machalla nékhna vous avez encore frappé 🎉
Kou meunoul na bayi.
Waa Mbour laale lène 👍 yi niou avancé
Écouter les paroles c important 👂🫡 respect akhlou brick ♥️♥️♥️♥️
Kou meun na deff 🔥🔥
Je vous vois plutôt sur des projets internationaux. Rien à prouver. Super com dab.
Binette ak moussa laniou warone dieul si clip bii
Le mielleux par la profondeur de vos écrit et parole chapeau ,Respect 👏🏾❤️🫶🏾
Bit nice troppppppp avk la qualité de vos clip...Nice Nice 😍❤️📸😊
Non ils sont très fort kou d'accord rék lalal j'aime mais déyza fann la jangé Olof yénn
Mo niou diakhal
Akhlou bo diéko dél ballé wayé 🥵🥵🔥🔥😭
Team Akhlou depuis 2015 ana ngénnn??❤❤
Suis là dh
Suis là depuis bimay df 6ème cem kay
Tu es le meilleur baye grand mass le message et très fort les paroles sont très touchante ❤
Mafi dieukeu tey mome 😂😂real Brickests vous etes où ??
😂😂😂yaafii moudié
Polyvalent dafa lér billahi akhlou brick respect 🫡
Sini sambeu vue quel que part😮
Mane soumadei beug damay beugueulei sa demb ak tay🤝❤️🔥🔥
Kou abonnés si Séne compte bii pour xar chaque jour Séne sortie yiii😂❤
Ki sou bayé rap AK mabayi dék Lou rab yamane ya apou doulé ❤❤
BD❤🎉
La voix, tjr la voix encore elle ❤
Kou meunn naa deff
Dafa am akhlou brick ak rappeur yi dou niveau sax ❤❤ loulén waxal yénn la
AKHLOU YEN LADONNE KHAAR
Xamou niou dra
@@midounianggalsen8127 Yéna dayon deuk bi yeup😂😂
@@midounianggalsen8127nanal ndokh😂😂😂
Doléne sakh ay nitt🎉❤❤
Kou guiss rewmi Defa metti lale j’aime 🥰
Do gawa am j’aime deh😂😂😂