Dokho ci xam xam motakh, limou lou ci bari dou deug ndiakhass rek, ladial s moustapha loutakh mou guén groupe whatsapp ibadou yi? moustapha mi xam xam leuddeumeel la am
@@papeousmanefall5796 man kaay fénouma ladial s moustapha groupe bimou bokkon loutakh mou guén faa lolou c simple, man douma fi nék dila saga kou respecté yayam dou saga yayou diambour té diangue li yonante bi wakh si saga do mousa saga, kathior rekkay sagawaté wakhouma nak né kathior nga wayè dama ni kathior rek moy saga waté na lér
@@sstv7951 wakhi dof sen group yoyou kou am foulle doufa dougou ba dici tok fowe dine ci ah hadis yi rek guen fi neke sen Khol yi mo bon motah Lou bakh khamoulen ko Daguena wara dem niou teurbiya len
@@BAMBISTETV Ni nguén nara faatoo rek ndeysan altoppé bakhoul guémal guestu sa diné nim waré, boudè yén wa soufia yén la yalla faral démlèn mom makka ak médine nguén akimo fa, déféna kou am touti xél xamné makka ak médine amoul place bilèn geuna reuye kaaw souf wala? yakar na adouna bi sédéna lolou damlèn nguén aakima fa aythia yén soufi yin thiaaam xolal yé wa soufia ak sén façon diamou yalla, bo démé mali soufi youfa nék ak nga dém Nigere wala Gambie wala wala, nga xol sén façon diamou yalla yi nim wouté rek kouci nék di yeukeeti wayam nak hahaha né amoufi morom, mou mélni sunu yonante sallahu aleyhi sa sallama mom mi yalla yondi momatoul dara yéné séddo lép, ngir yalla nieuwlèn gnou bok diamou té bagnko bokkalé gnou boolo top yonentam bi, adouna bi dougn fi déss dè wasalam
Ndeyssane ay att ci guinaw dama done sol samay yéré rak nguir ame toubey bou thieuk di wédi sérigne yi wayé sante na yalla bama yalla défé mouride en 2017 ba légui hamna fi degg fété ki digate ak kouy diglé lou bakh té diko djeufé mounou niou yem.jereujeuf ahlou tassawouf
Hakkasa Dieuredieuf jewrin tawfekh ak taysir rek رجوت قياد الحزب لله وحده بخطي الذي يحيي له خير الإسلام Guen gui Islam mom lanu kou tedd ki cheikhoul khadiim indil
Man mom pass passe bobou yorone nako wayè ba sama yaye décédé lassi gaineu..serigne sam mbaye mom dimbali si lou barri ak khassida yi surtout khassida touhfathou..legui mangui sante yala bou weur.
Aka ma yem wadji. Thi émission bi lako decrouvrirè mais damako top diko top ba yakarnani kouko eup kham kham thi gniy debat amoul. Ak mokal gui moma gueneu yem.
Mor kébé tu m'as déçu lol neek si internet bi di wakh rk c trop facile boo wolou wé sa kham kham doo ragal face a face wahabistes yi deme lene diangui nguir yalla rk pas pour am ay financements
Ham ham bokoy sakou dou pour say mbok mai pour joulite nieup la plutôt guir dimbali joulite gni..dah dou werrantè mai libarantè la reik nioune nieup ay jamou yala lagnou..
Machalah machalah machalah yalna yala takhawula ci barkee cheykhoul khadiiiiimel.....deemleen debat tee bayi mbeep mbeep ji. Ku am xam xam doo ragal debat
Sétal Mali rek di wakh te yoro bine kayit xam xam rek mo woor ay daw Kat lanou lini woté dou degue mon takh ñiéme wonou palato lép lini wakh amoul téslal diara dieuf chiekh mostapha
Serigno Wahabe ye ande aye wayekat you jiguene ber Arabie Saoudite delene thiahane ci lan dako akanio bago jiguene Omar Sall lem def diabar bamo dew doku wakh
@@mamendiaye5842 mame ndiaye merci beaucoup wakhgua deugue mar nane komo takha nan fetet bo ndokh ame dagua rouss Ousmane sonko wakh rek laye def ko beugue yor am rew daguaye dem diangue waye do neko fe lo nior gua wakh lo niorot gua wakh melne Ousmane sonko bakhoul
wa touba xam xam bou ande ak liér akoub yarr laniou am bilahi📚📚📚
Une belle connaissance sans support écrit sur les mains, il maitrise son sujet avec une analyse bien structurée. Machala. diazakalaou anna khayran.
Dokho ci xam xam motakh, limou lou ci bari dou deug ndiakhass rek, ladial s moustapha loutakh mou guén groupe whatsapp ibadou yi? moustapha mi xam xam leuddeumeel la am
Ss Tv iow dangaye fen didiakhasse soudé lendeumb yénéko guena deff domouram yi
@@papeousmanefall5796 man kaay fénouma ladial s moustapha groupe bimou bokkon loutakh mou guén faa lolou c simple, man douma fi nék dila saga kou respecté yayam dou saga yayou diambour té diangue li yonante bi wakh si saga do mousa saga, kathior rekkay sagawaté wakhouma nak né kathior nga wayè dama ni kathior rek moy saga waté na lér
@@sstv7951 wakhi dof sen group yoyou kou am foulle doufa dougou ba dici tok fowe dine ci ah hadis yi rek guen fi neke sen Khol yi mo bon motah Lou bakh khamoulen ko
Daguena wara dem niou teurbiya len
@@BAMBISTETV Ni nguén nara faatoo rek ndeysan altoppé bakhoul guémal guestu sa diné nim waré, boudè yén wa soufia yén la yalla faral démlèn mom makka ak médine nguén akimo fa, déféna kou am touti xél xamné makka ak médine amoul place bilèn geuna reuye kaaw souf wala? yakar na adouna bi sédéna lolou damlèn nguén aakima fa aythia yén soufi yin thiaaam xolal yé wa soufia ak sén façon diamou yalla, bo démé mali soufi youfa nék ak nga dém Nigere wala Gambie wala wala, nga xol sén façon diamou yalla yi nim wouté rek kouci nék di yeukeeti wayam nak hahaha né amoufi morom, mou mélni sunu yonante sallahu aleyhi sa sallama mom mi yalla yondi momatoul dara yéné séddo lép, ngir yalla nieuwlèn gnou bok diamou té bagnko bokkalé gnou boolo top yonentam bi, adouna bi dougn fi déss dè wasalam
Ndeyssane ay att ci guinaw dama done sol samay yéré rak nguir ame toubey bou thieuk di wédi sérigne yi wayé sante na yalla bama yalla défé mouride en 2017 ba légui hamna fi degg fété ki digate ak kouy diglé lou bakh té diko djeufé mounou niou yem.jereujeuf ahlou tassawouf
Sama wadji kone dé mak yow gno yel mane dé diotoula thieukal wayé si gnom la bokoon
@@diapoulodia5589 walahi lolo am
Hakkasa Dieuredieuf jewrin tawfekh ak taysir rek
رجوت قياد الحزب لله وحده
بخطي الذي يحيي له خير الإسلام
Guen gui Islam mom lanu kou tedd ki cheikhoul khadiim indil
Man mom pass passe bobou yorone nako wayè ba sama yaye décédé lassi gaineu..serigne sam mbaye mom dimbali si lou barri ak khassida yi surtout khassida touhfathou..legui mangui sante yala bou weur.
@@mouhamedthiam9048 hakkasa sunu yaye dji yalla nako yalla dolli yeumade te khareko firdawsi
Yalla defal le tawfekh ci barkep serigne bi
Bilaye wallahi xam xam Dou Ay pèxè s moustapha Sylla doundal wèral
Wah sandi youma ko ñème na niaw merci serigne moustapha
Diaradiaf s Moustapha sylla yalla nala yalla samou té défal la tawfékh amna solo trop ❤️
Je suis véritablement ébahi par l'ampleur de son savoir, mais ce qui m'impressionne davantage, c'est sa sagesse profonde et sa modestie sincère.
Machallah ♥️♥️♥️♥️ Yalla nala Yalla takhawou te samou la
Vraiment niveau kham kham bi kawéna watasawouf nionraw wahabiste yi fouff merci Bitéye et sylla machaallah
Macha Allah serigne Moustapha kham kham bi wer na sell na
Mor kebe ak ni melni mom Dano rer ba noppi di reralate
Macha alla serigne moustapha sylla yalla na yalla goudele safa tè maye la wère sama ❤sède na bi lahi☝️
Machalah serigne Moustapha xam xam bi lerna ta Amna hikma. Yalna yalla deuguereuleu.
Aka ma yem wadji. Thi émission bi lako decrouvrirè mais damako top diko top ba yakarnani kouko eup kham kham thi gniy debat amoul. Ak mokal gui moma gueneu yem.
ماشاء الله تبارك الله شيخ مصطفى حفظه الله ورعاه ببركة القرءان الكريم
machallah lerna xam xame na wallahi amna solo lolll
Cheikh moustapha yalnafi yagu❤❤
MashAllah jeureujeuf xam xam bi leerna 🤍👌👌👌
Maa shaa Allah S mustapha Xam Xam bi rafet na yalna yalla barkel
Machallah ma ngui Algérie du tewlo
Waw gorrrrrr ch Moustapha Sylla
Mor kébé tapét laa geumoul mboopam machalla Serigen moustapha sylla
Wa mor kebé batay yaw lay khar 2022 pour nga gnew tontou 🙇
MACHALLAH chiekh Moustapha 🙏🙏🙏
ما شاء الله الشيخ مصطفى دمتم في حفظ الله ورعايته
Machallah Cheikh moussatapha Sylla xam xam daal day ande ak yar yalla nala yalla samou barké sëriñ Tuubaa
ماشاءالله حفظه الله ورعاه بارک الله فیک یا شیخ مصطفی صله الله أکبر
ماشاءالله ياأستاذ سيخ سله بارك الله فيك.
بارك الله فيكم شيخنا الفاضل مصطفى سيلا لقد أوضحت المسألة ووضعت النقاط على حروفها
Walahi mor kebe Yaa yéy daw bofi ñëwoon guiss lu rëy
Merci 👍👍👍❤️❤️💞💞💞
Machallah Dr mousTapha maîtriser nga sa sujet , démonstration Total
Xam xam bi rafetna lol machallah!!!
Dieuredief ❤️
ماشاءالله ممتاز الله يبارك فيكم
An s Moustapha Sylla iow yallna la yalla dèfal jamou rk ak goudou Fan kham kham dh mom yalla dèff nako ci iow
jeureujeuf baye moustapha
Moustapha sylla yalnala yalla samue te yokula weer
Machallah Dr moustapha sylla
Merci Dr Moustapha
Douma si doyal 😍😍😍
Machalaha .yala nala defal tawfeih .ta yok weir gui .boul deg lou wahabya yi niom kou niou meuna loul dara yaq sapp derre..sossal
Moustapha sylla merci boucoup très bien
Machalla cheikh moustapha amtina solo
Ki xam taye xam le bokoul ak ki xamoul taye dingate dieureu dieuf s moustapha sylla sa xam xam rafetna lol machallah
Mor kébé tu m'as déçu lol neek si internet bi di wakh rk c trop facile boo wolou wé sa kham kham doo ragal face a face
wahabistes yi deme lene diangui nguir yalla rk pas pour am ay financements
Ham ham bokoy sakou dou pour say mbok mai pour joulite nieup la plutôt guir dimbali joulite gni..dah dou werrantè mai libarantè la reik nioune nieup ay jamou yala lagnou..
ki mor d'où maromane Baye débat ak mome
Machallah wahabiyou wax rek khamounou dara mane sene écolo la diange ngui
Wahabit de bu desul ludul indi ay lay mu daaw .
Li xamngua ni serigni mor kebe sax manuñuko layal .merci dr moustapha
@@ousseynoufaye7903 boudoul wone moromam douko tontou dafe daw rek قل الحق ولو كان مرا شكرا ياسيد سله
Day bakh emissions yi gnouy invite borom xam-xam mais bole thi ko xamne werante ak rereul nitt gni lay def amoul ndiarigne
Machalla serigne sylla
BILAHI
ماشاء الله حفظك الله ورعاك ياشيخ مصطفى صله
S. Moustapha sylla mi dh bayam nonou la melon yeme lool trop s. Maniaaw sylla moy baayam
Xale touba day mokal al Quran tari kutubou xam xam yi
Barakallah
Wawaw
Diaradiaff sylla yagfiloll ta werr
Machall lah deirdief
Xam-xam rek moo woor machalla
Machalla ahlhelmou mafesoudour✍️
Machalla waxtane bi solo trop
Mor da daw 🏃♂️🏃♂️🏃♂️🏃♂️🏃♂️naniouko teugatt s Moustapha Sillah di sa mbeur
ماشاءالله مفيد جزاكم الله خيرا ياشيخ مصطفي صله
أرجو أن ينظم النقاش وشارك فيه أستاذ مور كبي سيكون إن شاءالله أروع وأجمل
Machallah Serigne Moustapha Sylla
Comme on le dit en Woolf "moss mola guena xam keur gou am ay khath "mor kéber liko dawlo xamnako bo bakh so gnewon gnou wedem loko
Deugue bou wer nga wakh
deugue leu bou weur
Dieredief Serigne Moustapha sylla xam xambi lerrrna yallna yale samole sibareke borom Touba dieredief 💯💯💯💯💯💯💯😶😶😶😶
بارك الله فيك شيخ المصطفي صله
الحمد لله على كل حال
Machalla Moustapha sylla
Machalah xam xam moy dëg
Deugeuleu bim ame 40 lathie guenne thi la dadje ak ibn koullab
Maasaa allá
Machalah mor xam xam bi bariwoul dafa dangu ngame rek dé
Machalla ❤
Machallah wahabiyou yi wax rek la ni déf sene ecool la diagn ngui
Kon de barre na ay saga
@@ablayendiaye8315 looll sax walahi meme danoye wax nannou suni wa diour ay yefar lanou
@@amethfall9079 ibn abdou wahab molen diangeul saga ak yefeur lou net nie ay niawtef youbarre lan def maka
@@ablayendiaye8315 wallahi mane dama don saga Serigne ci rek walahi wayi santt na yalla bu bakh sax ndakh 2011 la nek mouride
@@amethfall9079 wahabet niom ak Israel ay kharet lan nio yam motakh soufism rek mo wor
Machalla Sylla
Macha Allah Sylla
Mor kébé fimako tégone dama rous
Khamoule dara yague nako wakh
Diaroul rouss deh dafa xamoul dara wedy youmbu na mais sakhal lou werr mo yomboul
@@moustaphagueye3717 c tellement vrai
dafa daw debat bi ah seigne moustapha mi da wekh dei😂😂
Machalah machalah machalah yalna yala takhawula ci barkee cheykhoul khadiiiiimel.....deemleen debat tee bayi mbeep mbeep ji. Ku am xam xam doo ragal debat
Machalla cheikh bi
Deureudeuf xax bi lerna
Xam xam rékk à am solo
MACHALLA AMNA SOLO
Sétal Mali rek di wakh te yoro bine kayit xam xam rek mo woor ay daw Kat lanou lini woté dou degue mon takh ñiéme wonou palato lép lini wakh amoul téslal diara dieuf chiekh mostapha
Sama hol dafa sed. ..
waw gor sylla
Yalna Yàlla sàmm la Sama Sëriñ
Yéne daal kom Mor kébé dawna kone nopiléne amouléne lou ngéne wakhati.Soss ak féne rék ngéne meune
Wahtan wi doumassi doyal moukkk..ay bou mor nieuwone kon bouy gnibi day daw.
Sak jour ma tewlou kou lou léur kom wax ji amoul
Mansalah Srg Moustapha Sylla
Machalla
Suma nekone Mor kébé sax damay Daw 🤭
Wahabiste yi lakhatou disagua rék wayé kothi woo débat moudaw dieureudieuf DR Moustapha sylla
Mirmi xam xam la kou niamé rék démal tokk débat mo guene waxdji.
WAlay serigne i sa xam xam weer na
Serigno Wahabe ye ande aye wayekat you jiguene ber Arabie Saoudite delene thiahane ci lan dako akanio bago jiguene Omar Sall lem def diabar bamo dew doku wakh
Masallah
Mr6
Wahabiste yi danio wara noppi xamougne tousse séne waxa bari rék.
Niom wakh rek man benn ci Ousmane sonko wakh rek khamono tos
@@xaadim9615 wakh ngua deuge déh Sénégal dagnon wara yéwou Ousmane sonko wakh rék laye déf ta bouniou xôlé bamou yôré Sénégal dinagnou sone trop
@@mamendiaye5842 mame ndiaye merci beaucoup wakhgua deugue mar nane komo takha nan fetet bo ndokh ame dagua rouss Ousmane sonko wakh rek laye def ko beugue yor am rew daguaye dem diangue waye do neko fe lo nior gua wakh lo niorot gua wakh melne Ousmane sonko bakhoul
Steal ki li ci mom ak yar bi mou andal ken dou Serigne touba wahi
Mor Kébé daffa roukh bou nieuwone rek degg deug
Jërëjëüf c Moustapha sylle
Mor kebe loy daw
,,,❤ ما شي،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،،ء،،،،😂
Cheikh moustapha leunteul nga ba guénne ci yalla nala yalla samme té delloola ci pass passou ahloussounna wal djiamaa
Soudé wolouguénee séne khamkhame loutakh mor kébé daw Dr Moustapha Sylla soudé leuteul lafi néké.wayé mane lolou béttouma nakh bama dégué biographie mor dégoumathie foré(wattou alkhourane)la khamné khamoul dara
Yaw nopil
@@leserviteurduprophetemuham9751 😂😂😂
Démlén gnibi Guinée. Yén peul fouta yi soussou yi rék gnio bakh ci yén
Mor kebe tu m’as déçu
😃😃😃
Sen lamigne yi mo saf
Dinala yague bète Bo Kaye dèguelou khamoule dara
Xam xam mo neex mor kebe graw grawlu gu metti gui waróon na teew