Guiss ga dé mane li rék motakh wolou wouma kéne ,nite yi nio nakaré xam ,té kosi wane né wolouw mala mou guiss thi bopam li dafa niaw KANE NGAY WOULO TI FI SI ADOUNA .
Papiers ken douko lidjanté denguay dem ambassade ou consulat niou diokh la papier en bonne et due forme mais dadjalé sa khaliss diokh nitt ko dadiel ni rekk doyna waar.
Sa way yaw bamoula wax waxi paspor nga waraona xam sa bopou engaltre dou Sénégal deh bay am pasporo false noy dèfaré paspor engaltér té néko bir engaltérr 🥱🥱🥱
Passeport qu’on t’as fait à l’étranger sans tes empreintes et le contrôle très strict dans les aéroports il fallait avoir des soupçons Il faut être très vigilant maintenant les gars diamono bii nitt gni nio def mou doywar du courage mon frère
Bounguéne bougué nopalou si arnaqueurs dangéne di woute Cianure ngéne defko si thé wala café dioxeléne ko gnou nane , aye vrai domerame lagne kouléne réye yalla doula bindeul bakar
SOULÈN NITT LIDIANTIL FÉXÉLÈN BA PHOTO KO BOU LEER APRÉS NGÈN PUBLIÉ KO SI RÉSEAUX SOCIAUX YI...YÈN NINIOULÈN DI NAAXÉ DAFA YOMB TOROP MAIS YALLA NALÈN BOROM BI TAXAWOU
Ces kow kow là ils sont vraiment stupides comment tu peux penser entrer en Europe sans visa ,quel con lui, invitation dafla mouneu dougueul europe ,,,doff deugue
Doumane Ngakoy Wax Gni Fa Nék Amouniou Yeumandé Kou Niou Door Laniouy Weur Diémo Naniouma Ko Def Mais Dialoul Sa Taxi man Yi Nek Aéroport Laniouy Commencé Beug Kou Niou Nakh.
Franchement y'a certaines choses terre à terre que tout le monde doit savoir comment on peut voyager en Europe sans Visa, tu n'es pas européen, t'as pas un passeport diplomatique , d'ailleurs tout le monde veut venir en Europe mais donne pas tes sous bêtement comme ça .
Guiss ga dé mane li rék motakh wolou wouma kéne ,nite yi nio nakaré xam ,té kosi wane né wolouw mala mou guiss thi bopam li dafa niaw KANE NGAY WOULO TI FI SI ADOUNA .
Man Ben Sénégalé moma KO def Algérie Man. AK ay ga Sénégal warnano kolah s'en yafe niawna trop 😭😭😭😭😭😭😭
Je suis en Europe mais louma nakhari fi ak loumafi daal cii loumeti rek Sénégal momako teck bilahi
Yaw fou nake
Stuttgart Allemagne
Ils sont partout et nombreuses ici au Maroc 🇲🇦 j’y connais bcp ! Ils vont pays trop ou tard !
Vraiment c'est dommage
Maroc Sofi amé nakar boudé 100 la ça bokou sénégalais moglay ték 50 yi
Billahi Lou wérr ga wakhe 😭😭
Papiers ken douko lidjanté denguay dem ambassade ou consulat niou diokh la papier en bonne et due forme mais dadjalé sa khaliss diokh nitt ko dadiel ni rekk doyna waar.
C’est mon frère ass Gaye je connais ce gas il s’appelle Serigne ousman c’est un grand dileur à kaolack wha kaolack gno Kayy whakh door Marto
Dicourage frr lepp Dina bakh inchallah
Sa way yaw bamoula wax waxi paspor nga waraona xam sa bopou engaltre dou Sénégal deh bay am pasporo false noy dèfaré paspor engaltér té néko bir engaltérr 🥱🥱🥱
Passeport qu’on t’as fait à l’étranger sans tes empreintes et le contrôle très strict dans les aéroports il fallait avoir des soupçons
Il faut être très vigilant maintenant les gars diamono bii nitt gni nio def mou doywar du courage mon frère
Il faut contacter la DIC. Ils vont collaborer avec la police marocaine pour le localiser.
Elaes le🙏🙏🙏🙏
Thieye Sénégal tekk dill rek
Tiey adouna mo baré ay workate
Barinagnou fi lole tass yakar reck lagnou fi neké.et en plus il te fon maraboutage il on des marabouts qui attrape les clients.
Bounguéne bougué nopalou si arnaqueurs dangéne di woute Cianure ngéne defko si thé wala café dioxeléne ko gnou nane , aye vrai domerame lagne kouléne réye yalla doula bindeul bakar
😂😂😂😂😂
@@deugheulaveritemoufin4731 waxouma deug ?
🤣😅🤣😅🤣😅🤣bilaye c vrait
@@diordiagne5395 mba do Dior Diagne bou Adji sarr 😂😂
Mane magui fi Europe dioupe motakhe tequiwouma dara yalla terait
Masta mis Maroc yono ndokh moy Visa bi visa mom kola koy Wakh Dalay nakh
De courage frère yalla dina leral lep
SOULÈN NITT LIDIANTIL FÉXÉLÈN BA PHOTO KO BOU LEER APRÉS NGÈN PUBLIÉ KO SI RÉSEAUX SOCIAUX YI...YÈN NINIOULÈN DI NAAXÉ DAFA YOMB TOROP MAIS YALLA NALÈN BOROM BI TAXAWOU
Diambar yalla bakh naaa
Ces kow kow là ils sont vraiment stupides comment tu peux penser entrer en Europe sans visa ,quel con lui, invitation dafla mouneu dougueul europe ,,,doff deugue
Serigne ousman dano dorone khalis bou barri senegal dou mom réckk dafa garow té nekh lamine aussi
2 éme Commentaires
Amna Solo niongi léne Di topou
Ami yew esque hamgani man demalanab looollsa
Senegale Yi neck Maroc akanou trienia khamnadra
Doumane Ngakoy Wax Gni Fa Nék Amouniou Yeumandé Kou Niou Door Laniouy Weur Diémo Naniouma Ko Def Mais Dialoul Sa Taxi man Yi Nek Aéroport Laniouy Commencé Beug Kou Niou Nakh.
@@ninkinanka3644 nio geuneu done niempou domou rame amena béne waye boufa nék bougne nane Méîssa mo Kate ndeyame niempou moma nakhone bimaye doga nieuwe Maroc kou Kate ndeyame leu fouma diapou dou doye bilahi 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@@ababacarsamb837 Niniou Beug Dundé Dafa Yomb Torop Di Dundou Ci Niakou Nitt Gni
@@ababacarsamb837 yaguimaye ki loumoula deef reeyna no senegalais kagne legui dagno yakou no raguama🤣😅🤣😁😄😂
@@ababacarsamb837 no rayguama 😅😆😅😆😅😆
Bayi len nan lijanty papiers ambassades moy joheè visa
Lolo mou yombol nak
Wa amy dafa🎉ngeuwate dakar beuz
Khamena yaina nitte warnano kholate saine djoulitai lainali gnawena loleeee loleee loleeeeee
Arnaque kouko doundouwoul rkk doko kham , moi on m’a arnaqué 2million 500
C est avec les erreurs qu on apprend do co defeuti
ass kou bakh la wallahi epui geum bopam yarou teey courage frere
Wakhal way
Tu a raison frere mai yale na yala leral lepe
Métina trop sah wallahi courage frère 🤜🤛🙏
Soit patient frère
Saway yaw dem Engleter sans visa
Franchement y'a certaines choses terre à terre que tout le monde doit savoir comment on peut voyager en Europe sans Visa, tu n'es pas européen, t'as pas un passeport diplomatique , d'ailleurs tout le monde veut venir en Europe mais donne pas tes sous bêtement comme ça .
Amna Amy nakalaye dioko ak yaw giapou si
Fais attention au maroc,
Arabie Saoudite l’âne dorone khalis bou barrit depuis ngourou balaye wade
Ca ne peut pas etre vrai;comme quoi (si tu n'as pas de carte de sejour tu ne peux pas porter plainte) ca n'as meme pas de sens
Donne moi son numero niou diapouko
Doyna warr bilahi
Non metina trop mes dicourage
Are you crazy You don't even have a visa you're talking about a ticket
😂😂😂😂😂😂
Nyaka Jang Bahul Guissoul Visa Mouy Jeunde Ticket
Copin bi wayoul déh
ass ont se connait tres bien ici a casa ainseba
Bilahi keep kou nee dekk nar nga lakk khaliss sama doulla dijkk akk nimou metee
🤒🤕🤒🤕🤒
Dakar buzz warouline partage doonne diambour arnaque amna mais nadem si yoon
Wakho fi toss 😏
@@dallavili5266 yao khamou ne pass port defa personnel
Yow werngha?
Première commentaire
Ar
q
Vraiment animatrice bi zeumaralna djiguene daye yagne del ré touti sakh mba nga sourire
Ko nek ak nala yalla binde
Mais yacine genrou emission yi ree waroufi am...dafa meti kw
@@dallavili5266 sourire loumou dioté ak binde?ak koufi toudou mbind
@@ibrahimagueye8559 femme bi damaye koye suivre mais kaname gui dal yanioule djiguene daye yanie doula téré am foula
Elle fait bien son boulot nagn khôl lolou t bâyi détails anatomique yi