Wakho deug,Souka est la femme typique sénégalaise,ce qu'elle dit est la pure réalité,, c'est entre un mari et sa femme..nul ne peut imaginer qu'un mari ou qu'une femme divulgue des audios intimes ou des vidéos de son conjoint et de sa conjointe.. c'est pas son mari qui a fuité ces vidéos...
To be honest with you what Sa said is true I take all the mobile phones when somebody visits I have been doing it for a very long time trust no one any misunderstanding with somebody can be destroy you if they have any videos of audios.
Yène Sénégal danguène bari tapalé, bone! Fi États-Unis kou publier photos diambour casso ngaye moudji! Justice Sénégal dafa wara voter loi bo khamné kou divulguer vidéos awra gnou teudji la casso! Gniak fayda rèk!
FRANCHEMENT, LA PRISE D'IMAGES PHOTOS OU VIDÉOS N'A PAS SA PLACE DANS LES RELATIONS INTIMES. EN TOUT CAS LES PORTRAITS C'EST APRÈS ÊTRE BIEN HABILLÉS ET PAS QUAND ON EST NUS. Arrêtez de prendre ces types d'images.
C'est ça ta aussi yacine far bi ladone appel vidéo dou dieukeur dji ms nak esk du far bi moko tass parce que bagage bi doko guis bou yacine rk ngay guis
SA, Les couples doivent se comporter de manière à suivre leur religion quelques soient la religion qu'ils appartiennent pour quoi se filmer en intimité vraiment se n' est pas des faits de croyances, se sont des faits d' animistes . C'est moche

Dafa ame gnou boone rék 🥲
Yalla moussal nioussi .
gnaw trop waye 😭😭😭
Mais normalement celui qui a publié ces vidéos doit être traduit en justice. C'est simple
Le President Diomay doit interdire les reseaux sociaux au Senegal. Il pourra laisser Google pour les etudiants afin de faciliter leurs recherches.
Wakho fi dara sokhna si
Yaw nak wero 😂😂 Li ngay wakh moy Lane
@@MDbousonko kikay lepam dikoul
😂😅@@khadimka2058
Yao Lou waxni
Djiguéne dale kouko torokhol Yallah dinala torokhol In Shaa Allah tôt ou tard
Waw Madjiguéne mom fila guéné...Thieuy mo meuna médiatrice
Sénégal neh n'a nak 😭😭😭😭
Diekerem moko def lolou yasin kou baxla bilahi courage
Sohaibou delen afiche heur bi svp
Souka mom ay wakhou dof rék lay wakh😂😂😂
Wakho deug,Souka est la femme typique sénégalaise,ce qu'elle dit est la pure réalité,, c'est entre un mari et sa femme..nul ne peut imaginer qu'un mari ou qu'une femme divulgue des audios intimes ou des vidéos de son conjoint et de sa conjointe.. c'est pas son mari qui a fuité ces vidéos...
To be honest with you what Sa said is true I take all the mobile phones when somebody visits I have been doing it for a very long time trust no one any misunderstanding with somebody can be destroy you if they have any videos of audios.
Omar est trop intelligent.
Attention Solution Tv, ce n’est pas son ex mari qui a publié les vidéos de la dame, c’est un autre gas
Hum
Downa warr😢😢
Je répète encore. PAS DE PHOTOS TANT QUE L'ON EST PAS BIEN HABILLÉS.
Nako porter plainte gnou teudjeko
❤❤❤
Li dou dieukeur dji faram ladone appel vidéo moko capture après niom nioy rafatel di wakh dieukeur dji la pour yacine sétt ta fékna dieukeur dji la
Sonhibou louy elemengue 😂😂😂😂
Sa sa sa Wa bakh 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Doyna warr
D'où dieukeureum déhh copin wam la danio wara bayii fo oumm tate
Wa temp yi Anna bety mba diam leu??
Yène Sénégal danguène bari tapalé, bone! Fi États-Unis kou publier photos diambour casso ngaye moudji! Justice Sénégal dafa wara voter loi bo khamné kou divulguer vidéos awra gnou teudji la casso! Gniak fayda rèk!
Son djeukeur il est fou bilaye
Ndeysane ndaw dh Bou amoul bopp Rek dou bakh mane nako diappou be Ray ko
Quelle'sois fier d elle parce que si mariage la d'ara nekhousi le mari on fou en prison
Non non Souhaibou dou ex diekereum moo guéné vidéo yii
Kaliphone def na live dé nena dou dieukeur dji
Man de gëmu ma ne Jakkër ji la
Yacine kou bakh leu ndakh référence le ci rewmi té yague na beguel sénégalais yi
Héy!!!!
Information bi lerroul beuge waxrek
sëy daal téléphone amoul fa place yénneu yé niaggeu fayda la
Amna yénèn yima jota jot tay Yacine day fonto rek
Pourquoi enregistré vidéos intimes ak sa djeukeur wala sa djabar gnome gneupe gno gnake fayeda
Aladji 😂😂😂👊
Ndawsi mo mana fen
Sénégalais si bopam mo beug sa you dioté ak moromam diko diéma yakk.
Vraiment verite absolue merci beaucoup ❤
No Sa ndiogou tu n'est pas sérieux Simbangue la deg
Li du dieukeur dji farama ladon defal appel vidéo far bi nak dou mom defar katou téléphone yi niom la rk
😂😂😂😂😂😂😂
FRANCHEMENT, LA PRISE D'IMAGES PHOTOS OU VIDÉOS N'A PAS SA PLACE DANS LES RELATIONS INTIMES. EN TOUT CAS LES PORTRAITS C'EST APRÈS ÊTRE BIEN HABILLÉS ET PAS QUAND ON EST NUS. Arrêtez de prendre ces types d'images.
Sonkhibou bayilen di wakh "way yalla" svp rafetoul, teguiné ci tourou borom bi, té dou batou wolof, ap dioundiou la rek. wakhelen "anaconda" sakh dinagnou comprendre
La vidéo peut échapper à partir des réparateurs, ils arrivent souvent que certains en réparant voient des choses sensibles.
C'est ça ta aussi yacine far bi ladone appel vidéo dou dieukeur dji ms nak esk du far bi moko tass parce que bagage bi doko guis bou yacine rk ngay guis
@papacheikh-p4b ok je vois
Vous metriser pas le dossier
Sohibou dénguéna dégoule poular motakh ndawsosou di wakh mo geuneu ham limouye wakh dou deugue dou dieukeureum copain wamla takhna niou saga dieukeureum ta dieukeurdji défoul dra émission halepolar sank sétane nako wadjiko defe haléboundawela ndawesi moko mag foufe kikaye da wéer djiguénegni tognena.dieukeureum trop
Ma djiguéne mi mom dafa am Borom Keur wala déte. Mangui koy lathie nguir sop guimako sope té Yallah rék takh
Mme Diop la..
@@Amir-gt6qfDjadjeuf . Yalneu seuye bi barkél
Elle est mariée
Elle a un fils
Amna dieukeur dh day seuy nianalko
AK dôme sah kholi fénébe😂😂
Sohibou li kene douko df debat si télé psq daguay guena yoku siweul bi
Wawaw na siiiiiiw ndakh gnou moytou
soufeke dieukeur gila te niou am dom hana dieukeur sanioul lolou?
J'ai bien walf mais s'il vous plaît ne parlé pas les sujets que vous metrisez pas c'est pas son mari
A général nak vidéo yi d'où fuite si couple deh afer de copin copine silaye dioge' te aferou sentage mokoy andi
SA, Les couples doivent se comporter de manière à suivre leur religion quelques soient la religion qu'ils appartiennent pour quoi se filmer en intimité vraiment se n' est pas des faits de croyances, se sont des faits d' animistes . C'est moche
Bayilene di video sen boop bolene di seuye , lolou yeufou doff la Akhhh dofguene torrop