Mamy ma fait pleurer Wollah en plus j’étais là juste pour voir si série bi dinama nekh ou non et m voilà épisode 2 hâte de voir les autres🥰bravo à l’équipe ✨
Sa Maman la tjr dit kil ne faut jamais être facile devant un homme Togou foot fanane tei kene takoula Ndou beuguel la femme de Omar elle est respectueuse elle a aimé Omar en gardant sa dignité ❤
La première épisode était à moitié réussie je pensais que vous alliez rattraper au cours de la 2ém épisode mais je vois qu'elle a plus de manquements que cette dernière. Beaucoup d'étapes ont été brûlé et on avait hâte de voir comment Mamy va prendre le fait que son homme va lui trahir et se marier avec une autre. En plus ce massage devait avoir plein d'autres leçons de morale dans cette vie que nous menons. Il faut revoir votre scénario. Merci
Une belle série bilay thiey Mami ak Dave ni baxna dal série bou nekh la vraiment machallah bonne continuation l'équipe série bou nekh vraiment chapeau à vous l'équipe 🥰🥺
😪je n'aime pas de voir de brisé le cœur de quelqu'un c pour ça que beaucoup pensent que tous les hommes sont pareille niit ki soka beugoute bayil mou dém boul ka gueum lo lou amoute
Li dei leçon la pr nioune djigéne gni Gor loko beug beug boumoula diaral moukkou ngua diokh ko sa boppou faux thi boppam lanie déff bounie la khamei rk bayyila takk sa morome mtx naniou fonkou soune boppou té geuneu takkaat souni seurr sammou sounou dignité ba dieukeur bou bakh nieuw niou tékkil koko
Thieuy li mofi am légui deh daguay guénague nitt ki beugeu ko ba doff sou takeu djioté mou warr la takk kénéne wala soudé djiguéne mou déme seuyi ak kènène 😢😢😢😢nékhoul thi khôl dall mei Mamy li leçons la pur ioe gua yéwou kham sa valeur osi😌😌😌
Ah ØMĀR tu ressemble beaucoup à mon mari mais sa infidélité bi mome yorou ko il est beau et fidèle rasta yi rek mo deef difference 😂😅motakh may setane film bi Dama beugue sama dieukar
En mamy da diokh bompam omar lolou takh kay omar tankk kenéne goor diaroul ngay diokhé sa pompam même goor boula wakhé diokh ma sa bompo warr ngako péss péss bou tangue dieurr bouka defé touto laka wakhati 😂😂😂
Mami niak nga fayda nak tu n'a rien à faire chez ton "ex" tu n'a rien à faire avec lui sax bey dem si keureum tu te fais honte seule c un traite donc ne la calcule pas
Serie bi ndourona ak serie bou garaw pasque gisna si style bou ma meuseul guiss 👍
😀😀😀😀😀😀😀
S❤❤❤a❤❤❤❤
👍👍🥰🥰🥰
❤❤❤
❤❤
Kou beugue serigne Babacar sy lall j'aime ❤️🙏🏿
♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Séne commentaire doff yi chiiiiim
RTA🙏❤️
@@lhommefort973 mais yoy yaya kane
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
KOUFI LOULOU INDI LALAL J'AIME😂
❤
😂
Mane loulou mo ma fi indi❤
Benn thi mane
Waxon ba dinafi guiss commentaire bii
Tes parents vivront jusqu'à à ta réussite dit Amin 🙏❤️❤️❤️
𝑨𝒎𝒊𝒏𝒆❤
Amine ❤❤❤❤
Amine ❤️
Amine ❤
Amine
Ani talibe cheikh yi souba inchallah gnou wadial ziar Gènèral bi kou d’accord lalal ma j’amis bi🙏🤍serigne babacar sy lagnou beugue sama werou way❤
Coubeugue Mame dabakh beusseul j'aime ❤️❤️❤️❤️❤️
Une très forte pensée à toutes femmes qui subissent ces genres de situation😢
Co begue sayidina Mohamed lalal 👍🏿❤️❤️ j'aime 👍 j'aime
Môme rék la beugue
Yalnala Allah sono brome wonalé ak mome❤️❤️ amiine 🙌
Salah la aleykhi wa salam
Kharitou Omar bi nitt la koi machallah 😍🥰
Mamy ma fait pleurer Wollah en plus j’étais là juste pour voir si série bi dinama nekh ou non et m voilà épisode 2 hâte de voir les autres🥰bravo à l’équipe ✨
Kou beugue sa yaye lalale j'aime ❤❤❤❤❤
Sa Maman la tjr dit kil ne faut jamais être facile devant un homme Togou foot fanane tei kene takoula Ndou beuguel la femme de Omar elle est respectueuse elle a aimé Omar en gardant sa dignité ❤
Machalla ❤️ vraiment cette série est important car elle est censé de nous donner beaucoup de leçon de morale ❤️❤️👉
Niou tambali ak diam yallah naniou fekei fin bi ak diam🙏🙏🙏❤️
Amine
Amine
Amine❤
Kou beug brome darou lalal j'aime
Vous brûlez des étapes mais c'est une serie avec pleins d'enseignements donc il faudra aller pas à pas je vous remercie🙏
Effectivement c trop rapide
Loulou,ç est ça voix qui m'amène ici😁😂
Kou beugue serigne serigne saliou rk lalal j’aime ❤
Magui ne
Lima diangal pour l’instant moy djiguen’e day fonkou bopame diamono dji gor bi diokh sa bopp bouy tak kenen lay kholii 😢
La première épisode était à moitié réussie je pensais que vous alliez rattraper au cours de la 2ém épisode mais je vois qu'elle a plus de manquements que cette dernière. Beaucoup d'étapes ont été brûlé et on avait hâte de voir comment Mamy va prendre le fait que son homme va lui trahir et se marier avec une autre. En plus ce massage devait avoir plein d'autres leçons de morale dans cette vie que nous menons. Il faut revoir votre scénario. Merci
Kou lolou dina wakh lolou rek ladone verifier mangui dème ciao loulou
Vous les hommes vous êtes tous ingrats 😢 mais akk djigéne boulène daller dou bax si yène lingéni bone
Non yw tmt wakhale gneneu gni rk
Djiguen gni tamite kepp lene sen ana ndiay
@@sonkofocus2024-ph4hv 🤣🤣🤣 walakhi c'est vrai
Yallna khariiiit Omar biii takkk mamy 😂😂😂😂😂😂😂😂
amine😍😍
amine amine
Amine yarabi
Diabarou Omar bi sofna mami laniou wakh nioune😂
Bayiko rék mouy melni mane ni
Une belle série bilay thiey Mami ak Dave ni baxna dal série bou nekh la vraiment machallah bonne continuation l'équipe série bou nekh vraiment chapeau à vous l'équipe 🥰🥺
Kou Geume ni Dave moy moudié Mami rék lalal j'aime 😂😂😂
Je crois pas
@@khadidiatougueye-uc5zs en bon tu ne vois pas ça ah attendons
Wakhal dameu😂😂
@@fatoucisse3210 ah wa wawe kome Omar amoul respect si môme 😂😂😂
@@sambafall3509 dél woté série bou bess
Deff lenn ko 2 fois par semaine nk 🥰khar bi dafa yague
Tout à fait d’accord 🎉
Wido episode 2 bi dînafa disponible inchallah lundi
Wakhga DEUG nak
À wakhal dé pour mane saxx da diékh
@@SabadorProduction kouko fa beugua setan noy df
😪je n'aime pas de voir de brisé le cœur de quelqu'un c pour ça que beaucoup pensent que tous les hommes sont pareille niit ki soka beugoute bayil mou dém boul ka gueum lo lou amoute
Bilahi walahi 😰 tu as parfaitement raison wayé nék ak môme rek diko metiteul nn lolou môme j'aime pas
Bily ioe
@@mamediarradiongue1868 lolo mo takh béne djiguéne amatoul confiance si garçons yi nakh gneup yam
Billay waye amna gor you bone
Vraiment 🤔🤔
Qui regarde la série juste pour le beau loulou(omar)
1 cmanter💪
Modou lo yalla nakou yalla may ndam si kaw boy niang 2 🙏
Kagn lay barii
En fin chaque jour mangui Ko done khar 😂
Li dei leçon la pr nioune djigéne gni
Gor loko beug beug boumoula diaral moukkou ngua diokh ko sa boppou faux thi boppam lanie déff bounie la khamei rk bayyila takk sa morome mtx naniou fonkou soune boppou té geuneu takkaat souni seurr sammou sounou dignité ba dieukeur bou bakh nieuw niou tékkil koko
Goor ci bopam mo doywaar..
Meme bouniou la takké nga fess dell sakh dou lenn térré bouniou la diabalé ba parré dem setti lenene ci mbedd bi.. 😒
@@ThiesKaay Billahi yw triste réalité
C ke Yallah molén bindei polygame mtx nanie mounie rk
@@fallnational246 bilahi walahi 😰 mougne rek diap si ylla
Barki yalla loulou motakh ma weur si ko😂
Bilahi kone nio yam 😂
Il faut le faire deux fois par semaine 🙏🙏🙏🙏
je t'aime serigne babacar sy ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Boukouniou kou yombe koumitti la niou beugue 😢
Thieuy li mofi am légui deh daguay guénague nitt ki beugeu ko ba doff sou takeu djioté mou warr la takk kénéne wala soudé djiguéne mou déme seuyi ak kènène 😢😢😢😢nékhoul thi khôl dall mei Mamy li leçons la pur ioe gua yéwou kham sa valeur osi😌😌😌
Bilaye deguele mofi amlègui
Goor yui gnosi geuna bari
Mai kou gname kay sourr dalay yombou
Motakh reglé takk sa seur ba guiss kou bakh
@@mameyoumanedieye8969 loko dieuné diarnako walahi azime
Je suis d'accord avec mamy on doit respecté les femmes marié avec sa guéne tékk sene ex sougnou kaw lolou pour lane la respecté nous stp
Mane mom loulou momafi andi
Omar c'est Loulou de 4 fantastiques 😂😂😂
Mane de loulou motakh may setane 😂
En fin ohh khar bi da moudié yague diii😂😂😂
Éye wayeeeee koumaye diéle thi série yii ngir yalah intéressé nama trop billah diap lén si
Fouma dèm fèk lafa
@@sokhnamaykhouma4621 guani😂😂😂 yw Tamit kén d'où yw
Loulou mouma fi indi damaye khoul ndakh dina wakh ak kane lafi indi wat comme mane 😂
Mane bilahiii😂😂
Kou beuge Omar lalal j'aime
Billay série bii defa nekh j'adore 😍🤩
Dev moy dem ba tank mami kou guise lolou
Je commence à aimé ce séri a cause de dev🤣❤️❤️❤️❤️❤️😘
Ohhh mamy lila dall métti na deh
Ku bagg Seydina Ousmane Nuurayni la lal♥️♥️
Ah ØMĀR tu ressemble beaucoup à mon mari mais sa infidélité bi mome yorou ko il est beau et fidèle rasta yi rek mo deef difference 😂😅motakh may setane film bi Dama beugue sama dieukar
Machall li mom ana solo
Alhamdulilah ame leen diamb🤩
Omar defoul dara dafa Guiss lou bakh ak kouko tek si yone bou bakh mou dougou si Mamy droit tourner la page et apprendre de ces erreurs
Ay way 2 fois par semaine
je suis fière d'être talibé cheikh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏
J'attendais que cette série
Omar ioe biss boula akou mami dalee yeureum nala déjà 💔💔💔😓
Guis gua goor diépayam niom lonkhama goul rek lanoy top disi son mé lon khase ba khame diékhna
Man bokou masi
@@sopesonkodomoudendeye6726 yén goor rek daguén douy War
@@aramendiaye4105 lolou mom amna mais dou gnép
@@sopesonkodomoudendeye6726 boul ko wakhati
@@sopesonkodomoudendeye6726 😂😂😂
SABAD'OR COUTURE OS10 vous soutient bonne continuation 🇬🇳🇸🇳
Au fond de moi série bi guisna si sama boppu presque comme je vie les meme situation 🙈😣😣
Mouni
Nga néma😢
Bilay l'amour est difficile vraiment 😭😭
Walay
Li mon tax djiguén dfa wara samou bopam 😭 ba guiss goor bubakh responsable 😥mou takkou ko mou seuyeul ko 😥😥
Ani Wa team beugg Loulou ❤❤❤
Ma gui ni
Masha Allah rafetna yiwna yalla na yalla yock niou ngeume
En mamy da diokh bompam omar lolou takh kay omar tankk kenéne goor diaroul ngay diokhé sa pompam même goor boula wakhé diokh ma sa bompo warr ngako péss péss bou tangue dieurr bouka defé touto laka wakhati 😂😂😂
Wawaw
Kou d'accord ni Omar da bakhe mamy
Moi suis d'accord
li ko0umou yowoul doto yewou tres interresante jiguenne ware nene yewoui tes diaffer goor
Kou nangouni Omar ak vj da nio ndouro l'alarme j'aime
Yoo ma brother you do a great things 💥❤️✌️
Kane moko don khar comme Mane chaque jour
Man xana
Moi aussi
Avenirou Baba mognu gnor, revanche rek amoul lenenn mane dei lila wakh ba yen tamite lolou ngen wakh 😃😃😃😃😃😃😃
Fouma dem fekk la fa 😅😅
Number one
Moom xanaa par semaine lay am? Kon Omar dafa mujjee takk xale bi nii. 😂 😂
Il y’a que des beaux 😢gosse dans cette série
Dooo nite😂😂😂😂
@@nafisalioukane4452 no srx😂😂
Bravo à l'équipe
Non a partir de 5:38 🤣🤣ce Doudou me kill avec la meuf On dirai Dafla soff en vrai sa khol Guako tibé sheuuu🤣🤣 11:24 aussi ça confirme graaave 🤣🤣🤣
SABAD'OR COUTURE OS10 vous soutient bonne continuation frère 🇬🇳🇸🇳
Ohhh Merciii mon frère de❤️
Mami on t'adore ❤
Kou d'accord ni gor bahoul aimél 😮😮😢
Sa rasta yi dfa rafet ✨❤️
Amna goor you mana Tass yakar
Machallah
Série bi ndourona ak série bou garaw❤
Vraiment mane mome j’arrête cette série parce que meunouma gueum ni genre djiguéne you naïf comme Mamy amna si adouna pufff ça me fait mal au cœur 😢
Naive dara 😑 elle m’énerve sakh naïve ms dafa niakk fayda niakk diom topp goor takoula nguay def comme si y sa femme
J'ai le cœur meurtri😭
Omar qu'a tu fais à mamy
Mane dama xar ba decouragè
Mamy nakk manqué na trope 😓😓😓
Wor dafa meti dé
Wa 2eme saison bi kagne ngueni koy tekk
Mami niak nga fayda nak tu n'a rien à faire chez ton "ex" tu n'a rien à faire avec lui sax bey dem si keureum tu te fais honte seule c un traite donc ne la calcule pas
Ma warou 😂😂diouli bi
Meilleure série
Belle serie 🥰
Liguene jouer bly amna niokoy doudou goor boula khamé rk niakouna 😢😢😢😢djiguene Mbeuguel 😢
Omar défaillant nga warowone trahir Mamy déh vraiment complètement contre toi
Déssé ngén ay sii wax dh
Gagii niou abonnés way dolélénn parce que nous sommes tous des SÉNÉGALAIS 😔😔😔
Merciii frère
@@SabadorProduction on est ensemble c normal
Enfin bismillah 🥰
Vermicelles lagne beug😂😂😂😂😂