mangui niane nguire yalla nak nanguéne thi diapou rék mou yégeu dounguéne commencé lou yégue mouke ana wirri wirri ana ngeuweul gui central ana tour de famille lgui taye allô dg nguire dieumi serigne bamba na yégeu dia nguéne dieufe
Bravo encore aux acteurs ça parle ' de la condition des femmes en Afrique des femmes qui ce mari plus jeune et souvent sans amour et après elle veulent vivre leur vie passée en sortant avec des hommes plus jeunes mais la société ne les comprends pas. Que la mentalité de l'Afrique en vers les femmes s'améliore dans les années qui viennent
@@salykone1833 je suis désolée ses pas . justesi c'est pas normal pour la femme désolé ça doit pas l être pour l homme sinon c'est hommes avec des filles mineures ils ya un nom pour ça . .a cause de tout ses injustices les femmes sont malheureux merci
ndakhe ngua gnéméko wakhe douniou commencé lou yégue wirri wirri nila ngeuweul gui central nila tour de famille guiss nguéne ko kheuyeneu bi dina yégeu niou khole rék
waye yéne aida ak dieukeureme bi séne rôle bi noye na trop niou défe fouleu waye khoulo daye saf wala mei di khoulo di rétane mélni kou nék thi thiakhane non waye
Avocate bi meuss nagnla wax tu es belle mouni non aka meuma fèn😂😂😂😂😂😂 Lili comme rap eupeul na rakadiou ak rambax cheutt🤦♀️🤦♀️🤦♀️ baparè meuna yokhou Aida je pense qu'elle a jouè dans moeurs🤔 Mais lili rewna regarde comment il est habillè on dirait un thon lili mi weroul bilahi🤔😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Mane mbaye dinama ray😂😂😂 produit bouy dem kel impoli
No série bi c'est très très intéressant ♥️
Lili mo saf khorom.....né neu ko ce truc là😂😂😂😂
Ils jouent leurs rôles très bien, les personnages
Madame calme toi il fait chaud deh 😂😂😂😂😂🎂
mangui niane nguire yalla nak nanguéne thi diapou rék mou yégeu dounguéne commencé lou yégue mouke ana wirri wirri ana ngeuweul gui central ana tour de famille lgui taye allô dg nguire dieumi serigne bamba na yégeu dia nguéne dieufe
Ma mane weuy bissi commencement momay raye allo allo dézé 🤣🤣
okals diallo 😂😂
no Lili dou dem aka nekh elle est adorable
Bilay ray na nieup 😅😅😅
😂😂😂
Lily ak chauffeur bi rek bènen affair la. 🤣👍🏾😘
Bilay yaw ré n’a beu sonou .Allahamdoulillah yalla n’a diam yague
No man lily damako beugue 😂😂😂dawoul thiouw 🛑
Booba 🤣🤣🤣amneu problème nak tè fo fèk kou touti dey bari histoire 😂😂🖖🏿👍🏿
Non lili comme kou am dépression bilay ki mo dof way😂😂😂😂
Lily reynama😂😂😂😂😂😂😂 une vrai folle.....la musique on en parle "allô allô dézè "
T'a remarqué lolou la donn deglou dezeeeeee
😄😄😄 no il faut niou wakh thi tamit
Mais kan moka way
Wawaw...Kou toudeu Aïda dale daye am fouleu kéne douko yaap
Wa waw
Kouko yakam tiwone beuseul j'aime
Tour 2 famille toko séne ❤
Femme bi sofff na 🤣🤣🤣🤣🤣nena khale bou ndaw laay guennal🤣🤣🤣🤣
Woy Lili bonne n'a dé thon kay😂😂😂😂😂
✊🏿✊🏿diamou si yaw ak mane mi
Aïda mi moll na dh thio💋❤🏃
Lily da réww barké yalla 😆😆 😆
Lili raynama,🤣séquence bobou je le regarde en boucle
Lili douma ray😂😂😂🤧😭
Waaw kay ab Aïda dou niak fayda 👍👍👍👍 jamais nak si addouna mes amies
Walahi Toma sa bat si kaw
Bravo encore aux acteurs ça parle ' de la condition des femmes en Afrique des femmes qui ce mari
plus jeune et souvent sans amour et après elle veulent vivre leur vie passée en sortant avec des hommes plus jeunes mais la société ne les comprends pas. Que la mentalité de l'Afrique en vers les femmes s'améliore dans les années qui viennent
Une vielle dame ne peut pas sortir avec un jeune homme tout frais même si tu a raté ta jeunesse
@@mouhmedndiayendiaye3117 une vieille dame ne peut pas, mais un vieux monsieur peut sortir avec une petite fille de 15 ans et c'est normal???🤔
@@salykone1833 je suis désolée ses pas . justesi c'est pas normal pour la femme désolé ça doit pas l être pour l homme sinon c'est hommes avec des filles mineures ils ya un nom pour ça . .a cause de tout ses injustices les femmes sont malheureux merci
@@mouhmedndiayendiaye3117 désolé elle na pas rater ça vie 'ces la société et c'est principe qui font que beaucoup de femmes sont malheureux
J'adore lili elle joue bien son rôle
Billaye walaye mashallah actrice la dé
Tu ma tué lili néna av sa coifure elle joue bien 😂😂😂😂😘😘😘 no chefeur bi sone na
The video and audio quality is so good! Congrats guys!
Non Lylli elle est extraordinaire Mbaye tamit il ne changera jamais 😂😂😂
Lili mon sadique 🤣🤣🤣🤣🤣🤣😅 nena ly
Tour 2 famille nous manque beaucoup s’il vous plaît 🙏🏿
moi j'ai le numéro de CHEKHOUNA je l'avais appelé et il m'avais dit que tour de famille recommence aprés la korité
Hiii aida iow mi dh dinga tass deuk bi dh Macha allah 🤣🤣
J'adore Lili sheut sheut 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
😄😄😄Yangui May merloo kay... merral rekk te bayii wax djii
Sama mbokou yi portail du diable mogui gnew dé💪💃🏾💓
Aida nekh nama dal 😍😍😘😘
Mais Non Lili tu va me tué bilaye🤣🤣🤣🤣
Lily kay c'est autre chose 🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🤣 woooyyy non LiLy dou deimmmm
Jigéen foula wayy barki sama Aïda ya ame foula😂
Fabi da sèd rèwut wakh di rè ganan fula
Mooo mooo ani foulaaa
Gorr gui mongi deurr di ndakh ay féném
@@Userr057 khana dagnoula dor
@Userr057Daffa deurr vrai
Thiey Lili elle m'a tué😅😅😅
Wawaw 2episode par semaine
Lili raynama 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Non mbaye amoul🤣🤣🤣🤣🤣super séri ❤🇸🇳
J'aime ce série surtout quand
chéikhouna le (criminél)🤣🤣😆😂🤣 mais quand le série wiirii wiirii est finit je suis trot triste
Abel nak neixoul dieul diank nak machallah ak fi rew mi tollou
Elle est très belle machalla
Wa yéne tmt sëne allo allo DG bi douñiou si wakh😭
Wahssi 😂😂😂😂😂😂 retane na ba soneu
Billaye momay fath mane mdr
🤣🤣🤣🤣🤣🤣lili rayyyy nama
Lili elle est grave 😂
Série bi nékhna ❤
Mane dé dieukerou diéwo bi nim me sofé eupu ne yambar ne trop way ish
Cool
Lily dhhh Ayyy reii lamay deff... Avc cest maniere koi😂😂😂😂😭😭😁😩
😂😂😂😂non Lily se comporte comme une folle à lier. C'est pas vrai ça 😂😂😂
Elle est foll de nature
@@mbokhodieng3027 😂😂yabon
😂😂😂😂😂 comme mannequin bou dof
Wuyul james brown ak thon 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 lili mag mu reewlaaa
Professionnalisme rek
Mani dolen gnou wakh tour de famille tmt 🤷♀️
ndakhe ngua gnéméko wakhe douniou commencé lou yégue wirri wirri nila ngeuweul gui central nila tour de famille guiss nguéne ko kheuyeneu bi dina yégeu niou khole rék
@@thioukendigue9425 gniom dé nekhna lagni bagna degg😂😂
@@fatoubarhamthiellosene1806 ahh gni kaye nioungui nonou rék
Nos Lili mort de rire trop fort
Cheikhouna aka tama wakh douma dieul sa temps
J'aime daal cette sèrie
No Lili amoul 🤣😂😂🤣🤣🤣
Non lili ray nama 😂😂😂aida sa discussion yak sa copin bi civilisés na
Kou beugu xoulo nga ioe 😂😂😂
Laaaaaay 😂😂😂😂😂😂😂
No lily dou nitt 😄😄😄😄😄😄😄
cette serie sera le meilleuir serie de l'annee
yéne ninguéne dieulé abéle yombouna dh wayé nak ndeysane yayame dako nianale bilahi
Man je ne comprends pas vous ne terminé jamais les séries commencement boo guiiss daye am fin les suites svp Tour de Famille ak Mbettel ak jiixi jaaxa
Arame Diouf Beye vraiment
Sofff reikk
Deugu nékhoul
Mbettel moom c pour bientot ils ont deja tourner pour Tour de familles, Jiixi Jaaxa, Lifeline je crois amoul suite
Mbettel moom c pour bientot ils ont deja tourner pour Tour de familles, Jiixi Jaaxa, Lifeline je crois amoul suite
waye yéne aida ak dieukeureme bi séne rôle bi noye na trop niou défe fouleu waye khoulo daye saf wala mei di khoulo di rétane mélni kou nék thi thiakhane non waye
I
Wa Lyly est c ke cva mouy melni rapp thio ak modé wayam😂
Bravo à Lily elle joue bien son rôle
😂😂😂lili
Mére toubab bi raynama toth nafi hahahaha
NEKHNA TROP MACHALA 👁👁👍
Aïda sa far bi yambar na dé 🤣🤣🤣🤣
Nekhna trop ❤💯💥
Son bi tmt si souff aduna aduna yé🤛🥰🥰 c quii
mame balla
Merci beaucoup
Lily dou ma ray
Ma serie préfère j'ai furt👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏
Mak bandila dafciy gene 🤫🤫🤫😷
Wa Lili khana dafa am dépression
Namm n'a lenn💖😍😍😍
Mane seri bi bobou ba tay makoy suivre mes mounouma fekhe ba comprendre
Non Lili raynama😂😂😂😂
Pa bii moma deff rétane 😅😅
No Lili reynama magui dé
😂😂Lili va me tuer
Billaye li
Li mome khana beneu yone laye âme si moi bi ??
Vous devez faire 2 épisodes par semaine
A wi
Vraiment
Vraiment et augmente les minutes jusqu'à 30Mn ou 40Mn même
22Mn c'est trop court
Oh oui
Nice na troppo
Ey Lili 😂😂😂😂😃😃
Machalla
Lili rew naa thi makk 🤣🤣🤣
Mbaye 😂😂😂😂😂😂 mdrrrr.
Décidément Lili est folle
Merci
Toure 2 famil way damako nam
En kon cheikhona dafa sathie bb DC 😂
Ou est tour de famille
Ak renaissance
@@xalildiagn7767 Renaissance c fini
@@xalildiagn7767 renaissance cetait pour sensibiliser
@@vieuxbocarguisse9431 OK j n savais pas ça
@@abdoulahatniasse8688 jahjeuf cheikh bi pour l'info
j'aime bien Lili
Lilac la best
Lili bilahi ya soof🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣Lili nga yakarni nitt leu 🤣🤣
😚😚😚
Abel Aka mool sheuuu 🥰
Iow mom bilakhi daga fébar simmmmmmm
@@awasarrsarr8338 kone yanguikoye bayi khéle aka beugeu lou bakhe nak ki dofoule dh
💖
Aïda mom molna dii moway🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰😘😘😘😘
Avocate bi meuss nagnla wax tu es belle mouni non aka meuma fèn😂😂😂😂😂😂
Lili comme rap eupeul na rakadiou ak rambax cheutt🤦♀️🤦♀️🤦♀️ baparè meuna yokhou
Aida je pense qu'elle a jouè dans moeurs🤔
Mais lili rewna regarde comment il est habillè on dirait un thon lili mi weroul bilahi🤔😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Mane mbaye dinama ray😂😂😂 produit bouy dem kel impoli