(Vidéo) Annulation du Gamou de Tivaouane : Des talibés donnent leurs avis

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 20 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 128

  • @papendiaye7604
    @papendiaye7604 4 ปีที่แล้ว +6

    Kou nek ak sa kilifeu souniou kilifeu doy nanou si lep tivaoune rek inchallah

    • @moustaphandiaye3736
      @moustaphandiaye3736 4 ปีที่แล้ว

      Some djito diokhome Rèspè elek bodjito boul khar rèspè

  • @makhtardiop3088
    @makhtardiop3088 4 ปีที่แล้ว +10

    Yalla na corona virus bi diékh Bala gamou di nieuw in challa amine

  • @cheikhfall3605
    @cheikhfall3605 4 ปีที่แล้ว

    Diaradieuf serigne babàcar sy yalla nafi yague te wer

  • @kebetouba6263
    @kebetouba6263 4 ปีที่แล้ว

    Topou kilifa dh amoul moudiou gou niaaw topou lén ndigalou kilifa yi bakhna serigne mountakha Mbacke yalla nafi geuna yag geuna wér barké serigne touba

  • @taphadiop7928
    @taphadiop7928 4 ปีที่แล้ว

    Dieureudiauf borom touba yalla diamou yakk Sénégal

  • @cheikhtoure5199
    @cheikhtoure5199 4 ปีที่แล้ว

    Yalla nakofi yalla dieulé té mouseul gnouthi mousibeyi ak balayi

  • @wadanesougou8431
    @wadanesougou8431 4 ปีที่แล้ว

    Troisième personne hors sujet

  • @SERIGNECHEIKHMBACKE
    @SERIGNECHEIKHMBACKE 4 ปีที่แล้ว +3

    ZIAR BOU BAKH YALNA DIAMOU SAKH CI REWMI

  • @salioumbackeba9595
    @salioumbackeba9595 4 ปีที่แล้ว +6

    Nima ko japé dh moy topou sa ndigalou kilifa dara eupou ndiarign té bagn ko siki Saka.
    Kou neik daal lila sa kilifa tanal moy li gueune si yiow.

  • @mboupmboup1069
    @mboupmboup1069 4 ปีที่แล้ว +7

    Fii amoul lougne fiye comantair way démlén diamou yallah maylou sougne gamou niou wayy yabbbilén niou wayyyy ma digal béppou talibé dieufél ndigeul tagua noppi 🗣️🗣️🗣️🗣️

    • @yokenzanataal8230
      @yokenzanataal8230 4 ปีที่แล้ว

      Yaw nga linga def dou commentaire 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ndiagandiaye1294
    @ndiagandiaye1294 4 ปีที่แล้ว

    Kou yala takhe gaye defe mane ga gamou sa keure goumou diane la reke

  • @lhommefort7850
    @lhommefort7850 4 ปีที่แล้ว +24

    Yéne gninouy diokh micro yi yéna nako déf bagne léne bouléne si wakh journaliste ayy vrai seytané lanou

    • @abdouly6773
      @abdouly6773 4 ปีที่แล้ว

      Dafa am niou dof doumo comenté douma diokhé avis journaliste tarikha cheikh rék lagnou contre

    • @lhommefort7850
      @lhommefort7850 4 ปีที่แล้ว +1

      @@abdouly6773 bilahi mais gnou kham sounou bopp rek

    • @abdouly6773
      @abdouly6773 4 ปีที่แล้ว

      @@lhommefort7850 bilaye parce que gamou amoul rénn tivaoune rék kouné disi déf débat pour lan mais yalla bakh na ziare nala sama mbokk pass pass yalla na yalla faye la

    • @lampefall3570
      @lampefall3570 4 ปีที่แล้ว

      Bilahi réw lan déf srgn wkh ba paré gua disi tégu lanén

    • @moustaphagueye4709
      @moustaphagueye4709 4 ปีที่แล้ว +1

      Guissou mafi loulen três Célebre gamou gui

  • @coeur2lion38
    @coeur2lion38 4 ปีที่แล้ว +16

    Diaradieuf Al khalifa Serigne Babacar mansour Mane lolou rék la wah

  • @aliounediop3745
    @aliounediop3745 4 ปีที่แล้ว

    Senegal7 ay seyetané gené RK

  • @ousseynousall4851
    @ousseynousall4851 4 ปีที่แล้ว

    ziar serigne mbaye sy mansour yalna fi yag lol tè wèr

  • @Dusherfall
    @Dusherfall 4 ปีที่แล้ว

    Hum bayiléne lii bakhna rekk

  • @mouhametfall9550
    @mouhametfall9550 4 ปีที่แล้ว +5

    bayilénn diakhasé guir yalla li mome amoul bénde sanss

  • @ismailaba7381
    @ismailaba7381 4 ปีที่แล้ว +5

    Serigne Moustapha Mo nek si deug

    • @طالبالرضوان-ر8س
      @طالبالرضوان-ر8س 4 ปีที่แล้ว +1

      yaw nafikh nga saytane nga nopil ken ladioula

    • @yokenzanataal8230
      @yokenzanataal8230 4 ปีที่แล้ว

      @@طالبالرضوان-ر8س 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂yaw nak lodonn

  • @sofietoubadiane9278
    @sofietoubadiane9278 4 ปีที่แล้ว +10

    Ame léne talibè mane mourite la mes nite daye dègu digale

    • @ndatteyalla9917
      @ndatteyalla9917 4 ปีที่แล้ว

      Vraiment bien dit

    • @sarrmassaer1870
      @sarrmassaer1870 4 ปีที่แล้ว +1

      Nga yam ndeyou s’en tarikha domeram

    • @mariasant3937
      @mariasant3937 4 ปีที่แล้ว +1

      @@sarrmassaer1870 yaw c'est quoi ton problème ? Qui waxoul dara lou ayy banga koy saga

    • @sarrmassaer1870
      @sarrmassaer1870 4 ปีที่แล้ว

      @@mariasant3937 so beugué nga dieul

    • @mariasant3937
      @mariasant3937 4 ปีที่แล้ว

      @@sarrmassaer1870 yar àk téguine baxna si dioulitt

  • @برومباقجوب
    @برومباقجوب 4 ปีที่แล้ว +6

    2me personne bi machallah wakhal sa problème 😂doulnaliste yi dano mana doul

  • @geuyefamily6807
    @geuyefamily6807 4 ปีที่แล้ว +3

    Amê lén' talibe ndigel niefé

  • @modoucisse3204
    @modoucisse3204 4 ปีที่แล้ว +4

    Serigne bi aye talibéme laye wakhal kouné na dieuffé ndigualou serigname oki

  • @khadydiagne5181
    @khadydiagne5181 4 ปีที่แล้ว +14

    Ce n'est bien pas bien ce que vous faites. Kilifa wakhe ba paré gnabote gui teunkou si nguéne di défe micro trottoir comme si n'importe qui mo wakhe. Gnake diokhe tieure kilifa wala gnabotou kififa daye yé fitna.

    • @maremediopdiockou2283
      @maremediopdiockou2283 4 ปีที่แล้ว +2

      T'as parfaitement raison

    • @khadydiagne5181
      @khadydiagne5181 4 ปีที่แล้ว +2

      @@americain0620 xalé daye yégue si kaaw garabe dou guiss, mague teude fimou teude di guiss li gneuwagoule.
      P.S: quand on n est pas d'accord avec une idée on l'ignore mais on n interagit pas avec.
      Mbeute yi si mbeute yi baare yi si baare yi diam ni gnoye.

  • @bayedame2329
    @bayedame2329 4 ปีที่แล้ว +1

    أَسْتَغْفِرُ اللّٰه

  • @ngagneniang3149
    @ngagneniang3149 4 ปีที่แล้ว

    Merci mon ami pour mon frère que m ne

  • @diopablaye5227
    @diopablaye5227 4 ปีที่แล้ว +3

    Al khalifa yalna fii yage te yer

  • @Bawolbawol
    @Bawolbawol 4 ปีที่แล้ว +2

    Oumar sy bul wakhati lolou gamou yagg nafi deh s bamba ken djiitu wuko si gamou

    • @elbledardo864
      @elbledardo864 4 ปีที่แล้ว

      Nittou deug ya mana doul 😂... Bamba nane lay djito si gamou té Cheikh Oumar Foutiyou djitou ko si diamono?

  • @mexdroid1703
    @mexdroid1703 4 ปีที่แล้ว +7

    Sheutttttt khalifa bi loumou déff moy Yonne do démm sa keur nga gammo fa wakhtane si seydina Mouhamed psl bayilen critiqué svp wa salam diazzakoumoulahi Anna khërr

  • @mboupmboup1069
    @mboupmboup1069 4 ปีที่แล้ว +2

    Sénégal bayilén dieuf dieu finou na fikhe Serigne Babacar limou wakh c'est logique talibé ndigeul rék

  • @neneniane7643
    @neneniane7643 4 ปีที่แล้ว

    Billahi

  • @ousseynoufall5004
    @ousseynoufall5004 4 ปีที่แล้ว

    Vraiment ware guena xolat séne bopou nit dafay ameu KILIFA

  • @cheikhmbengue9249
    @cheikhmbengue9249 4 ปีที่แล้ว +2

    Dieuf Ndieguel Amna sola

  • @mamadousy3749
    @mamadousy3749 3 ปีที่แล้ว

    Boulén faté navetane stade bi nafés Dé té amoul tak masque ok

  • @moussafaye9309
    @moussafaye9309 4 ปีที่แล้ว +5

    Il faut apprendre au utiliser les mots et expressions qu il faut
    Annulation du gamou de tivaoune
    Un e expression inapropriee inadequate

    • @moussafaye9309
      @moussafaye9309 4 ปีที่แล้ว

      On ne pas annuler un gamou et en ore moins la celebration de celui ci
      Pour des raisons securitaires
      On peut eviter les rassemblements
      Qui n ont au une importance
      Des depenses inutules des de placements en cette periode de covid chaqu un chez lui

  • @moussadiop7156
    @moussadiop7156 4 ปีที่แล้ว

    Way moy lolou

  • @L.SARRENE_BI
    @L.SARRENE_BI 4 ปีที่แล้ว +12

    3ème personne bi mome limouy wax loumou dioték lignuko ladje thiey li

    • @aminadiagne5070
      @aminadiagne5070 4 ปีที่แล้ว +1

      Diakhal nama dé

    • @assanecherif2075
      @assanecherif2075 4 ปีที่แล้ว +1

      😂😂😂 Bilay grand

    • @L.SARRENE_BI
      @L.SARRENE_BI 4 ปีที่แล้ว +1

      Li kat keneu dako mesta guiss beu paré naneu senegal degny indi ay détail te moy PDG détails kat yii dh mais yegouko nak srx

    • @assanecherif2075
      @assanecherif2075 4 ปีที่แล้ว +1

      @@L.SARRENE_BI 😂😂😂

  • @talibeserigneabombacke5028
    @talibeserigneabombacke5028 4 ปีที่แล้ว

    Talibè mom niguel rek wakh dji amoul bènn chance nakh bigne dèmè banè niguel rek konn niguel ta guenn bayi sénn wakh yi kholalma li rek gni koulènn topou

  • @ablayegueye6811
    @ablayegueye6811 4 ปีที่แล้ว

    Manque de respect totale en ver du khalif mé yallah bakhna

    • @profcoly6085
      @profcoly6085 4 ปีที่แล้ว

      Ablaye guiss ngua kilifeu désouko wormal té en plus cite internet yi lagnou wara éliminer

  • @adamaattidianithiam2237
    @adamaattidianithiam2237 4 ปีที่แล้ว

    Bilahi dioli farata moguena nèka farata tè noubari don dèm diague khalifa bi yalla nafi yague tè wèr

    • @mallbelly8250
      @mallbelly8250 4 ปีที่แล้ว

      Beugue yonene tibi mo eupou doole lo guiss

  • @mamecheikhndiaye2532
    @mamecheikhndiaye2532 4 ปีที่แล้ว +1

    Saway dh wakhna problème bimou amon hôpital ba

    • @yokenzanataal8230
      @yokenzanataal8230 4 ปีที่แล้ว

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @yokenzanataal8230
      @yokenzanataal8230 4 ปีที่แล้ว

      Mame rey ngama😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @fantadieng3333
    @fantadieng3333 4 ปีที่แล้ว

    Khalif bi loumou wakh khamna ko déh fo tok gamou ndakh li bolémou dioulite moko mome vrai ndakh goudi naby Moustapha leu pls foko def dagane neu vraima meuna né gnoune sougnou magal gnoune tidiane yi ziar général leu donc gamou bi naby mognou takha diouk nagnou ko magal bounou déme ba nék talibé nak nagnou nagou degue niguel khalif bi ndakh moy kilifa bi wasalamoulaykoum🙏

  • @chiekhtidianediba1021
    @chiekhtidianediba1021 4 ปีที่แล้ว

    Nite day ame kilife

  • @mallbelly8250
    @mallbelly8250 4 ปีที่แล้ว

    Kou neke ak sa kilifa poin

  • @aliounediop3745
    @aliounediop3745 4 ปีที่แล้ว

    Dolén dara

  • @mboupelhadje6034
    @mboupelhadje6034 4 ปีที่แล้ว +1

    Ab talibé deug sakh warouta âme avis fou kilifa gui diokhagne fofoula

  • @alhadjidiaw9724
    @alhadjidiaw9724 4 ปีที่แล้ว

    ila medina baye Niass rek

  • @ibrahimadiop2320
    @ibrahimadiop2320 4 ปีที่แล้ว +2

    Dimbalileen nitt gni linguene di commentaries xamoo leene si dara
    Micro dou n'importe qui lane koy diokh , many wakh gnounane danouy atté

  • @rkhadyniass5215
    @rkhadyniass5215 4 ปีที่แล้ว

    Donne talibé rek mo woor deghe digueul

  • @mallbelly8250
    @mallbelly8250 4 ปีที่แล้ว +4

    Nioune serinie Moustafa sy laniuy degulou poin

    • @cheikhciss9086
      @cheikhciss9086 4 ปีที่แล้ว

      Point

    • @sidatediop4831
      @sidatediop4831 4 ปีที่แล้ว

      Ndiguel thiabii laa sou eupé dou
      Tiidjii sou manké dou tiidjii djeufé ndiguell daa geuneu woorrr..jsui un servant mouride...

    • @profcoly6085
      @profcoly6085 4 ปีที่แล้ว

      Belly yow 🤣🤣🤣 nguir yalla

  • @saermbaye7376
    @saermbaye7376 4 ปีที่แล้ว

    Teyellene sen guemigne youreuyi taloube day yam te nopi

  • @ndatteyalla9917
    @ndatteyalla9917 4 ปีที่แล้ว +1

    Senegal mo bari gnu dof gamou fou way nek meune ko fa def vraiment li dou debat quoi yonénte bi magal ko yamoul ci béne beuss donc ou est le probleme kou nék défko fing ko meune défé cest simple

    • @yokenzanataal8230
      @yokenzanataal8230 4 ปีที่แล้ว

      Yaw fokoy defè renn😂😂😂😂😂😂😂

  • @khamkhamletv9488
    @khamkhamletv9488 4 ปีที่แล้ว

    Wallahi niakk talibe wesou woul seringe bi wax ngaye dioxé saxalat boune wexna nane ni tall boune nioulna niouni koukou

  • @mouhametcassama8392
    @mouhametcassama8392 4 ปีที่แล้ว

    Dk221

  • @mbayartv
    @mbayartv 4 ปีที่แล้ว +2

    ndigal dieffe te bagna dingat

  • @khadydiatoudiouf3237
    @khadydiatoudiouf3237 4 ปีที่แล้ว

    boulene gnou sonal gamou ken momouko vraiment kou ni talibé nga waro wakh sou khalifa bi wakher ba parer gnak nguene yar trop té gnak talibé

  • @malikdiop6670
    @malikdiop6670 4 ปีที่แล้ว +3

    SERIGNE CHEIKH DISAIT QUE YENNOU METIYUL LIMETI MOYE BEUGUA YENNU THIA KENNU YENNULA

  • @coeur2lion38
    @coeur2lion38 4 ปีที่แล้ว

    Gir yalla tok séne keur yéne ba dou dara

  • @geuyefamily6807
    @geuyefamily6807 4 ปีที่แล้ว

    Nanou respek.té wakhii khalifa bii

  • @barhamthiam616
    @barhamthiam616 4 ปีที่แล้ว +2

    Wouté borom xam xam yi djégal la ns disait l prophet muhammad psl

  • @Mensch48
    @Mensch48 4 ปีที่แล้ว

    Wakhou kilifa mom waw la sante

  • @ousmanesarr2278
    @ousmanesarr2278 4 ปีที่แล้ว

    wakh bi rafena

  • @abdouly6773
    @abdouly6773 4 ปีที่แล้ว

    Talibé seydi Hadji Malick Sy mélni mann boulén diokhé sén avis boulén commentaire journaliste ay seytané lagnou donio contre tarikha cheikh talibé cheikh yi déf lén très attention si journaliste yi

    • @yokenzanataal8230
      @yokenzanataal8230 4 ปีที่แล้ว

      Yaw linga def dou commentaires 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @maradiaw5610
    @maradiaw5610 4 ปีที่แล้ว

    Gayi dé lén dégga nak téy nangou ndogal
    Kilifagi li tah mou wah li moka ham

  • @mamnan1714
    @mamnan1714 4 ปีที่แล้ว

    Dimbalilén niou khalifa bi ay Taloubém lay wakhal te guem nanko te topou nan diekhna

  • @oumarsow300
    @oumarsow300 4 ปีที่แล้ว

    Yéne journalist yi aye nanfekh ngéne gamou wougnou gamou wougnou poin

  • @ibrahimakhalilkane6960
    @ibrahimakhalilkane6960 4 ปีที่แล้ว +1

    Ndigeul jeufei tei yam plaçou talibé

  • @saermbaye7376
    @saermbaye7376 4 ปีที่แล้ว

    Journaliste sofguene lol te manafene lol bayilene diakhasse ak fene

  • @mamoudoualassanediaw5726
    @mamoudoualassanediaw5726 4 ปีที่แล้ว +4

    Un talibé n'a aucun avis à donner. Sinon tu n'es plus talibé tu es aidacone

    • @profcoly6085
      @profcoly6085 4 ปีที่แล้ว

      Actuellemnet c moustaphacone champs de course 🤣🤣🤣🤣 thiéy sénégal mo nékh rék

  • @diawfaraofficielle913
    @diawfaraofficielle913 4 ปีที่แล้ว

    Yén la rék kharal ma kholi bénén vidéo man mom kén douma Ray si war na fome ak waroul fome

  • @oumardia2400
    @oumardia2400 4 ปีที่แล้ว

    Bouné demé baye wakh gamou Maodo takh mokafi sakhale loumou wakh laniouye def .loumou wakh laniouye def loumou wakh laniouye def

  • @seriinho2119
    @seriinho2119 4 ปีที่แล้ว

    Sénégal 7 ay saytane geun massa done merde

  • @ibrahimakhalilkane6960
    @ibrahimakhalilkane6960 4 ปีที่แล้ว

    Gzmou gnp KO mom mai maodo RK khalat yonentei bi l' reste sen serigne lagnou magal

  • @هناديمحمود-ظ1ظ
    @هناديمحمود-ظ1ظ 4 ปีที่แล้ว

    maylene niou diam gamou dafa bok si diinee bidah bou bonela topando chretien yi rek yonentibi khamouko

    • @diengmouhamed2401
      @diengmouhamed2401 4 ปีที่แล้ว +1

      Yawe daga rère yalla nala yalla guindi si barkë brom goudi seydina mouhamed 🙏❣️ psl

    • @khadimndao4804
      @khadimndao4804 4 ปีที่แล้ว +1

      Di ngeen dee rek, say say yi,

    • @mexdroid1703
      @mexdroid1703 4 ปีที่แล้ว +1

      Sa connexion mo diékh pas connexion Internet dh connexion bopp

    • @gayegaye9457
      @gayegaye9457 4 ปีที่แล้ว +1

      يا أخي هذه البدعة لاتضرك إن لم تعمل بها إن الله قد حكم بين العباد فدعنا نحن نفعلها ولله عاقبة الأمور

    • @برومباقجوب
      @برومباقجوب 4 ปีที่แล้ว +1

      Y’a meuna doul