Ce dimanche 04 février 2024 date du démarrage de la campagne électorale pour l'élection présidentielle du 25 février, tous les membres de la coalition DIOMAYE PRÉSIDENT seront aux côtés des autres candidats pour une caravane pacifique, démocratique à partir de 15h00 près du cimetière Saint Lazare sur la VDN pour inviter les citoyens à se mobiliser massivement le jour de l'élection présidentielle du 25 février 2024. L'annulation par Macky Sall de l'élection présidentielle étant anticonstitutionnelle, elle est nulle et non avenue. Les membres de nos différentes coalitions en dehors de Dakar sont invités à dérouler leurs activités de campagne électorale pacifiquement. Victoire des patriotes dès le premier tour ! SONKO MOOY DIOMAYE ! DIOMAYE 5e PRÉSIDENT ! FOCUS ! GMS, •••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••• Ci dibéer jii 04i féewarye 2024 lélub tàmbali dangaa gi ngir tànn njiitu réew ca 25i féewarye 2024, képp ku bokk ci lëkkatoog "DIOMAYE Président" dinanu nekk ci wetu yeneen lawax yi ngir doxantug jàmm, demokaraasi bu 15i waxtu jotee ca wetu sëg yu "Saint Lazare" ca xàll wu yaatu wu bëj-gànnaar gi ngir woo fere ñu jóg waajal bisu wéttug njiitu réew mi di 25i féewarye 2024. Dàq gi Maki Sàll def ci wéttug njiitu réew mi, dafa neen te baaxul. Ñi bokk ci lëkkatoo yi te nekk ci biti Dakaar woo nanu leen ñu doxal seen i yënguy dagaan ci jàmm. Ndamal way-bëgg réew ñi ci wërngal bu njëkk bi ! SONKO MOOY JOMAAY ! Jomaay 5eelu njiitu réew mi ! FOCUS ! GMS,
Kou Beuge Am dom bou gour toudiko Sa papa lalal j'aime 👍🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤
Bilahi Niankou mala beug yalna sa diame yagg bijahi naby Moustapha Saw psl ❤
Tapha dou nitt 😅 mais niankou est le meilleur de tous les temps 😅😂🤣 le solution 😅
#AMD président kou d'accord lalal j'aime
Niankou moy solution bi nak vraiment ❤
Bilaye niankou mon mane ya eupe dolé❤😂😂😂😂😂
Niankou solution...❤🎉
Niankou le fou il perd tout sauf sa raison ❤
Niankou rek lay topou ❤❤
Macky Sall dégage kou d'accord rek lale j'aime 😢
Yalna SONKO am Diamou
Tay mafi djitou malenma ay jaim way
Niakou am na baye ra nak 😂😂😂
Li nèkh n'a waye wa camberine am ngèn ndam 1er comantèr
Ya niake khorom
@@SaliouGaye-ux1le balnala
Thiatou Yoff yane nako yalla may ndam si kaw ndiaye tine
macki moy domérame😢
Ce dimanche 04 février 2024 date du démarrage de la campagne électorale pour l'élection présidentielle du 25 février, tous les membres de la coalition DIOMAYE PRÉSIDENT seront aux côtés des autres candidats pour une caravane pacifique, démocratique à partir de 15h00 près du cimetière Saint Lazare sur la VDN pour inviter les citoyens à se mobiliser massivement le jour de l'élection présidentielle du 25 février 2024.
L'annulation par Macky Sall de l'élection présidentielle étant anticonstitutionnelle, elle est nulle et non avenue.
Les membres de nos différentes coalitions en dehors de Dakar sont invités à dérouler leurs activités de campagne électorale pacifiquement.
Victoire des patriotes dès le premier tour !
SONKO MOOY DIOMAYE !
DIOMAYE 5e PRÉSIDENT !
FOCUS !
GMS,
••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••••
Ci dibéer jii 04i féewarye 2024 lélub tàmbali dangaa gi ngir tànn njiitu réew ca 25i féewarye 2024, képp ku bokk ci lëkkatoog "DIOMAYE Président" dinanu nekk ci wetu yeneen lawax yi ngir doxantug jàmm, demokaraasi bu 15i waxtu jotee ca wetu sëg yu "Saint Lazare" ca xàll wu yaatu wu bëj-gànnaar gi ngir woo fere ñu jóg waajal bisu wéttug njiitu réew mi di 25i féewarye 2024.
Dàq gi Maki Sàll def ci wéttug njiitu réew mi, dafa neen te baaxul.
Ñi bokk ci lëkkatoo yi te nekk ci biti Dakaar woo nanu leen ñu doxal seen i yënguy dagaan ci jàmm.
Ndamal way-bëgg réew ñi ci wërngal bu njëkk bi !
SONKO MOOY JOMAAY !
Jomaay 5eelu njiitu réew mi !
FOCUS !
GMS,
Sénégal yalna fi diam délousi wate 😢
Diomaye Moy sonko ✊🏿
NIANKOU LE MEILLEURE 😂❤😂❤
Félicitations à vous ❤❤❤❤😂😂😂
Macky Sall yay dmrm deug😢😢😢😢
Bilay ma beug niakou ❤❤❤❤❤😂😂😂
Machallah mes son bii daaw cii souf wagni leen KO ❤❤❤❤😊
Noolunekh
Salma est forte Machalla
Niankou Dinama ray😅😅
Salma di neu meu ray way
Kuzu Radiab ❤le 07 nioy borom
❤❤❤
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 niankou
😂❤❤❤❤❤taopha
😂😂😂😂😂😂
❤❤❤😂😂
Macky sall domram dji
niang 🤣🤣
Salma 😂😊
❤😂❤😂❤😂
Boubacar diallo Li ngay wakh sét ci yalla
Xalisss mokoy waxloo
Non niankou mo soff 😂😂😂
❤❤😂
❤❤❤❤
😂😂😂😂😂
❤❤❤