Machalla félicitation Bombardier respect du courage Balla c'est ça la vie du sport merci Aziz Ndiaye et sa famille toujours là pour notre champion l'homme qui à térassé beaucoup de champions lafe thiate yalnala yalla défal diam Amine Balla rék Balla késsé 💪🦁💪🦁💪🦁💪🦁💪
Balla vraiment a partir d’aujourd’hui je suis ton fans sa khol darra nekouci néké♥️🙏je suis de Mbour meilleur artiste du département aussi et j’aime beaucoup B52
Balla et bombardier bonne chance à tous balla je suis vraiment fière de toi continue seul dieu peut te protéger respecte ton travail et attend ta retraite pour vivre pleinement ta vie
Nais combat belle plateau encore d'autres contre... Merci Pére Guass, pére Bégaye véllicitation Bombardier vs balla Modou mdaye baye fall le con ziaarna léénne fiére de vous diadieuff...
Balla Gaye est toujours mon lutteur et Bombardier est largement plus fort que lui . Tellement il ne sais jamais reposer , Faire du Mma + La Lutte et l hygiène de vie . L erreur que Balla gaye à fait c'est quand le combat avait été reporter. Il aurait dû retourner en France pour s entraîner mais bon , Le monde est méchant
No vraiment contane na si yénn nieupp bilay émission après comba comme bi meussoul am balla je suis très fier 2 tw ms b52 na kou nékk dindi li nga défone sa morom slvp
Je suis fan de Modou Lô mais j’aime Balla avec son charisme. B52 très sérieux et gentil aussi.
Le Sport sénégalais en Avant !🔥🔥
Fière d'être suportaire Balla bekaye ligua wakh si suportairou Balla gaye yi merci beaucoup
Vraiment je suis ému mais du courage à mon lutteur BG2 je suis toujours derrière toi
Franchement Balla est quelqu’un de bien
Je sui fans de XLO 100% P.A
Mais Balla vrai sportif leuh
Good luck
Nit Lo bayi mou bayi le
Balla Avent 👉👂
Balla hier 👉👂
Balla aujourd'hui 👉👂
Balla après 👉👂
Balla avis inchallah ☝️💓💪💪
je t'aime énormément Boubacar
Lolou degue le bilaye
Machalla balla guaye Khol bi darafet champions nga diam si yaw
Balla dou sama mbeur mais loumay wakh rek Hol bi dara nekou si loudoul diame yalla nako yalla diapalé arko yir ko merci Balla❤
Merci beaucoup ❤️
Bilay bombardier ake Balla gaye aye kharite laniou 🇸🇳❤️❤️
Je suis fans de Balla gaye2 malgré la défaite il est le meilleur je lui encouragé et c'est ça l' sport félicitation B52.
N’oubliez pas les 5 prières c’est important
Force à toi Mashaallah ❤️🌹
Machallah lou amsolo nga waxe
Yallanala yalla taxawou
Ma Sha Allah
@@senegalmoysamarew2441 amine yaram
Balla tu es vraiment super un homme au bon cœur qu allah te protège
Vraiment c'est beau ça Balla ken dou yawww t'es une meilleure personne de même que toi Bombardier ❤️🥰yeine ay Noble ngueine
Franchment bombardier moy mbeur deugeu. Kiii moo nitè tèy règlè tè am yarr. Machallah bomb 💣
Nala ko sani rk😅
Billahi Balla diame rék ngaye âme inchallah , vrai nitt moye yaw,un vrai sportif,nous t'aimerons pour toujours quoi qu'il arrive
Machala c’est ça le sport 🏋️♀️
Yalla na yalla doli diam
Balla dafa bakh Machalla kontan na trop si yaw
Bilaxi Balla haye goor mashallah yalla nala ya allah tahawou li dess sa carriere in shaa allah
Machalla félicitation Bombardier respect du courage Balla c'est ça la vie du sport merci Aziz Ndiaye et sa famille toujours là pour notre champion l'homme qui à térassé beaucoup de champions lafe thiate yalnala yalla défal diam Amine Balla rék Balla késsé 💪🦁💪🦁💪🦁💪🦁💪
Ndeysane Yacine bou Balla Gaye. Billay ya beugeu balla machallah fima guiss vidéo balla rék guiss fa sa commentaire. Ndeysane😍
@@daoudaanneat-tidiany billahi aka bougou balla ❤️💯😱😰😭🙏🙏🙏
@@daoudaanneat-tidiany Machalla merci beaucoup Daouda c'est très gentil de votre part nékale si diam Amine yarabi 🙏❤️🙏
Nous resterons tjr des fans de Balla mais maximum de concentration mbeur❤️❤️❤️
Balla notre lutteur préféré 🖤🥇
Balla toujours dans nous ♥️
yeh mano balla e boa pessoa
Bilahi
Je félicite le champion bombardier et j'encourage mon lutteur Balla Gueye k je supporte
Relève le défi Bro you're spécial
Vraiment balla gaye vrai sportive c est un homme très bien
Waw souniou Mbeur Bii
C'est le Sénégal qui gagne je suis fier de vous "les lutteurs "
Bala ngay kham ni balla gaye mo rafet combat bi diekh ❤️ 0 problème
Balla vraiment a partir d’aujourd’hui je suis ton fans sa khol darra nekouci néké♥️🙏je suis de Mbour meilleur artiste du département aussi et j’aime beaucoup B52
jaam ci yow✌🏾
Diadieuf vrai diam si yaw bienvenue
Merci bcp et bienvenue antanque fans bala gala gaye
Wala c est ce qu on attends de vous merci balla pour le courage de dire que danou nga
vraiment contane na ci gnane bilaye ,li moy sènègale .bonbardier tamite kène dou mome geste bigua dèf contane nassi ci diarou bigua may diabarou Balla .du courage Balla borome kholou diama gua koi
Le meilleur sport du monde c'est Lamb après leurs combat je vois que les deux lutter sont magnifiques
Balla et bombardier bonne chance à tous balla je suis vraiment fière de toi continue seul dieu peut te protéger respecte ton travail et attend ta retraite pour vivre pleinement ta vie
balla si kaw si kanam❣️❣️
Franchement deux exemples sportifs bravo Gaston et becaye
C'est pourquoi ça que j'aime Balla il est un bon personne
Li dafa Nice trop machala ❤️
Sénégal 🇸🇳 la paix 🙏🏾🥰🥰🥰❤️❤️ one family
Machallah Balla yay sama mbeur pour tjrs inchallah
Merci balla gaye tu es sportive boule wakh dara daffa guenn
Lima retenir ci émotion bi, bisou dangay ayy!!!
Bien Parler balla si yekini tonton bou nice en plus sa communication bakhena trop nila masha ALLAH
…👑Balla Gaye 2👑
❤️Forever♾🥺🇸🇳
Gaston démal soleil levant joué théâtre way 😂😂😂
Père Bécaye vous êtes un sage j'ai beaucoup d'estime pour vous
Fèlicitation serigne dia courage balla ce sa sport vous êtes des frères
Balla dou sportif psk heur bougnouko dané mouni dafébar wala mouni da bléssé di yak victoirou diambour
Balla diam rek ngaye âme bilakhi sa khôl mo rafet
Balla jtm mon frère
BAlla Gaye 2 il Est cool et vraiment sportif
yallah na yallah Dafala lené diamou🥰🥰🥰🥰🥰
Vraiment becay ,un Homme véridique ❤️👌🏾
Balla gaye 2 billahi xol bi defa rafet trop ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mais félicitation à bombardier ❤❤❤❤❤❤
Bombardier vraiment yalla mola sououral seni pèkhè Modiouboul rek Mè ken yènèwoula woon Ndamli .Mè sw prudent rek
Non Balla Gaye mom vrai sportif la je l'aime beaucoup malgré qu'il n'est pas mon lutteur préféré.
Je l'aime trop 💯🥰❤️
Machallah yallna diamou yague liii rek moy sport
balla gaye tu le meilleur de ta génération yalla na sa diam yague yaye sama beur ba faw laf thiate 🙏❤
Non..Balla n a jamais et4 le meilleur.....ce sont des farces ..
I love you Bombardier 🇬🇲👑🇬🇲
Nekhol mais Gaston nafikhe la 😂😂
"Allo malaka la toudou 😂😂😂😂"
Père Gaston goudel fane waye toujours ce le même personnage machala
Balla gaye 2 nitte késsé la vraiment té aussi amoul koula dakh beuré si aréne bi machalla nitt kou bakh nga
Nais combat belle plateau encore d'autres contre... Merci Pére Guass, pére Bégaye véllicitation Bombardier vs balla Modou mdaye baye fall le con ziaarna léénne fiére de vous diadieuff...
Balla Gaye. Machallah 💪💯💯
Balla Gaye est toujours mon lutteur et Bombardier est largement plus fort que lui . Tellement il ne sais jamais reposer , Faire du Mma + La Lutte et l hygiène de vie . L erreur que Balla gaye à fait c'est quand le combat avait été reporter. Il aurait dû retourner en France pour s entraîner mais bon , Le monde est méchant
Bijoux xana amoule conseil da eupeule trop😂
Balla du courage c ça le sport en tout cas c le Sénégal 🇸🇳 qui gagne
B52 félicitations ms balla mbeur tigua bokal génération Sax xapnagn ni yafi ne bilay defourou Wat rek
Franchement Balla gaye 2 nit cou bakh machallah 🙏
Machallah balla 🙏🏼 ni la 🇸🇳
Mbeur nioune bayiii wouniou bene Yonne tay lagne guena bgue balla yaye defarou wate rk 🙏ngaay bayii xell Say suportair
Machalla li Nice na billahi
🌹🌹🌹❤️❤️❤️❤️💪💪💪sénégal qui gagne wollah
Bombou dafa kham balla même si coté mystique
MODOU MBAYE SA YEUREE BI REUYNA TEE DIAPOULA SAMA COPAIN, 😀😀😀
No raina bâ dai
Bilay bakho😂😂😂
Bilay bakho😂😂😂
Je l'avais dit avant le combat niom niar daniouy aral di tangal mais danio beugeuntei lol sakh.
Ayy mystique kessé ngako dané
amoul lanèn ms bijou dafa soof
Bravo bombardier 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Manchala a mon lutteur préfère toujours souriant yaw diam rek ngay am champion
Aziz ndiaye mo wakhon mo Fay balla 200mîll fay modou 200mill beug balla nekk si khanam yalla mo athé rek
louthi sa yoon
Ken ladioula
Degg guen deug gou werr
Balla gaye vrai champion nga machaaaaaala
Machallah limouy Sénégal yallna diamou yague
No vraiment contane na si yénn nieupp bilay émission après comba comme bi meussoul am balla je suis très fier 2 tw ms b52 na kou nékk dindi li nga défone sa morom slvp
Li rafètna lolll😍😍😍😁
Ça c baux bly lamb rk mo mane lii félicitation b52 fans bg2 la ms dama contant
merci bcp gaston bravo
Bala champions gua mais sa caustum bi dafa rare 🤔🤔
Gaston ragalla walla thii ligayewa
Noooo Gaston Yalla wèrnala. Yaw mome sa montre BG2 nga faralone
Li Nice na trop
Machallah bijou
1000defaite dagnuye continuer diko beug
Bilahi
Bilay walay
Yaw balla maguét naaa 😂😂😂
Balla gaye 2 lion indomptable ❤️💞👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
Toujours Balla gaye 2 rek amoule lénéne champions gua mbeur
Masala li moy Sénégal fans ama yi holén si li
Balla je t'aime
Franchement Bombardier kou niakeu kinian la mo takh mou wakhal balla Gaye lou bakh
No Bijou saytané la😅
Nice na félicitations aux deux champions
Balla yalla na la yalla sam arla félicitations à B52 me man dama dogon ni B52 dafa am blessure
Chèrie Bourry, Baye Mohamett, Domou n’deye Aziz Ndiaye,Rakk Lirou Diane,dit Maggou Sa thiès
😅😂 Sas sou daano rek wah ni dafa febarrrrr😅😂😂😂😂😂😂😂😂
Balla rek on t'aime
B52 Aka Yarou Yaro Bakh 💪🏽💪🏽💪🏽💪🏽
Vraiment c beau c ça vous donnez de bon exemple