@@ngonengom8875 bane deug? Nafekh gua d yaw. Kou wakhone serigne touba moussibeu kesk tu vas faire? Respectez un peu diamou yalla yi. Yene rek nekolene fi. Nite dagno yor ay mbote you saf sap té reuyougnou lamine té folene tassé wakhtane si yalla gnou dorlene ba guene youkhou. Yene ay fans mame bamba rek guene dolene ay talibeme khamolene ko sakh diegué wolene ko sakh ndakh mome liguene di def santoulene ko. Melni beneu niebé si thine pfffff
Bari doull menoull wéssoull nga nk SÉNÉGAL nii yaw waa ARABIE SAOUDITE ngay bokal heurou djouli ak heurou woor ak woorii ta niom bounou nékké si gouddi ya ngii sii beuthieuk✊✊👌🏻
Je suis un tidjane et talibé de Cheikh la Islam mais s'il y'a quelqu'un qui ose cracher les vérités c ce Oumar Diangne car il sait très bien de quoi il parle. Gana, il est coutumier des faits
Je suis Talibé BAYE BARHAMA NIASS Mouy Mouride layénne thianaba thianaba Wa tiouwaone nioune niép béne laniou si yalla Mouride day déme gamou Di déme apél layénne yi Niass day Magali Touba Serigne Touba Maoda Malick INSA nourou laye Elhaj Omar foutowou Tall nioune niép souniouy Mame la niou Lou rafé laniou yague déff Di ko wakhé di ko diéffé kinak louma wakh mome la concerné Serigne Touba massoul togne hamoul kouy togne Yalla yonénte alkourane hassida la ham sa yi bokoy déff bouy si bolé kou TÉDD KI wa'sallam
Salam mon frère Cheikh, J'apprécie énormément la lumière qui jaillit dans vos propos pour vous permettre les redondances que vous étalez à travers les médias. Vous faîtes partie(et le intellectuels te le concèdent) de ceux qui, au lieu de polimiquer, doivent laisser à la postérité des écrits mémorables pour l'éternité. Les amuseurs de la galerie ne doivent pas te divertir. Je n'ai jamais vu où entendu les Dr Rawane Mbaye, Abdoul À Kebe, et beaucoup d'autres sachants accorder une quelconque importance à ces porteurs de médisances fractionnistes. Un sympathisant qui te suit ! Merci😔
Tres pertinent professeur c les guides religieux des confreries qui douvent controler leurs griots sinon on va le regretter a l avenir pass pass dafa grave ' yalna niou yalla defal diame te nasakhal kep kou ye fitna si barke seydina mohamed .....
@@taphiscodiaz9998 iow sa yaye amoul data té sa baye da yoom kigne la waxni moy sa baye koye bi dafa âme Aÿ gommm dmrm iow ngaye domi biral di ame loy wax
La verité est simple mais elle vous ronge le coeur: LA ILAHA ILAHA ILALAH MOUHAMADOU RASSOULILAH BOROM TOUBA AMOUL MOROM TOUBA AMOUL MOROM. Et le probleme est personne ne veut l'entendre. On sait bien k le mouridisme derange au senegal et ca ne date pas aujourd'hui. Le mouridisme a connu ses moments les plus difficiles (les dieux du monde=colons=franc maconnerie) avec hauteur et succes. GANNA A PARFAITEMENT RAISON.
Et le voilà encore avec ses vérité incontestable !!! Vrement je ne sais même pas ce k je dois te dir car cheikh Omar Diagne t'es une personne très éclairé machala yallah na sa diamou yague yallah doli katane bi ak meunmeun bi ak surtout khel mou sel bi contane trooppp sakh si yaw
Toi on te parle de malaise, toi tu parle de Serigne Touba yallah moko yékeuti, mo ko yékeuti kayy comme nimou yékeuté niép... C'est le comble de l'imbécillité !
Talibè cheikh, vraiment c pertinent. Gana Missil dafay diakhassè keur dinè yi nguir am tèranga adouna. Cependant marirando yi gueumoul dara topouko si ay fen. Mais Mouride deug dou dokhalè ni ndakh serigne touba santanèwouko
Suis mouride et suis parfaitement dacord avc tw il na po le drw d dire des chooses sur les autres marabouts merci omar diagne abdou ndaw aussi ma deçu kouy yare ay nite c honteux vraiment
Machaallahou lawakh rèfètna matalèna andak mandou koukham ci s touba dara do togne wayè koula togne nga ballco ndakh lolou la royè ci sangam s smh saw kone lolou lane wara roy ci mom merci pr diagne de oumar thiam moum s touba
Coeur2 Lion Gana wakhou Serigne Touba lay wakh wakhou Serigne Abdoulaye Diop massar ak narou Ganar yii Serigne Touba mo ndieuk wakh ni kéep kou ame wilaya ci Yalla kham ngani kén la le problème c’est les termes les mots que Gana utilise molén doul nex ok on comprend mais nak Serigne Touba kén la dougnou ci nexal kou Yalla binde dougnouko sakh négocié
@@khadimleye5738 ba balma mé mane borom hel you selyi lay wahal yalnagnou yalla fayal sougnou makyi lép bénela diné rék moy gagné mé serigne touba sohlawoul talibé you melni yéne
@@khadimleye5738 ba balma mé mane borom hel you selyi lay wahal yalnagnou yalla fayal sougnou makyi lép bénela diné rék moy gagné mé serigne touba sohlawoul talibé you melni yéne
Belle analyse. Je dirai qu'il faut que tous talibés apprennent à connaître les enseignements de leur guides quel que soit leur tariqa car c'est ainsi qu'ils vont apprendre à se respecter. Autre chose aussi, il y a les ennemis de l'Islam qui n'attendent que ces genres de problèmes pour diviser les MUSULMANS, ne soyons pas impulsifs et mesurons les dégâts que ça peut causer maintenant comme dans les années à venir. Wa salaam
Que personne ne juge personne na kou nek gueum linga gueum prsk mome gana messeré talibé serigne Touba la ndieuké thi mome yem thi mome kone so wahé rek niou indale la fo kagné sa serigne ba wah lou meuneu méti kenen wassalam Gana dale naw nako , ay terangam ak yeneu yi waro wah ni waham bi moko mey ndah boudoul wone wah dji sah dinako am si dunya borom bi mokoko thieuralé wone ganaw dioudom té Serigne bi mo makk alalou adouna sante ko daf gnu war Santati Ceexul Xadim té wormal bep kilifa diné nak mangui balou akh nak wassalam
C'est vrai pour attirer les donneurs bienfaiteurs,ces hypocrites affamés sont prêts à tout jusqu'à embraser le pays. Pourquoi dénigrer les autres foyers religieux dans le seul but de se remplir la panse. Ces histoires ne nous sont d'aucune utilité dans l'adoration. Il aurait été mieux de concentrer leur énergie dans les enseignements de la pratique religieuse(prière, ablutions, zalat...,)
Les diwanes sont devenus des fonds de commerce Gana fait presque deux télés et pas avec des islamologues mais plutôt des animateurs de radio de musique tel que Pap Cheikh à TFM et Cheikh Sarr a SEN TV donc en complicité pour leur part du gâteau ces derniers peuvent même prononcer de fausses contributions pour inciter les fanatiques à donner je crois pour terminer apprenons MASALIKUL JONAAN pour comprendre Serigne et les tariras Diadieuf Chekh Omar Diagne que Dieu nous garde
Kogam s touba doka kénal Ndakh sarigne touba gamna لبسم الله الرحمان الرحيم،قل هو الله احد الله الصمد لم يلد ولم يولد ولم يكن له كفؤا احد.((وبعد ))مقاماته بحر لاساحل له
C'est une vérité incontournable Serigne Diagne vous avez bien dit et vous êtes en phase avec le verset 42 de la sourate Al Baqarat
Gana doul rek laay deff
@@aliounemasterpizzaiolo6255 sa papa moy dul
Professeur Diagne sort de ma tête , 🥰🥰🥰😍😍! Quand tu parles c’est comme si tu Poirote dans mes pensées profondes . Machallah! Merci
moi aussi c un des rares a m impresionner intellectuellement le reste ay kesew kessew rek
Je suis Mouride mais j'aime bien Cheikh Oumar Diagne parcequ'il est un homme de vérité
Ghana de dey wakh degue rek mo taakh gnou ainal ko
@@ngonengom8875 bane deug? Nafekh gua d yaw. Kou wakhone serigne touba moussibeu kesk tu vas faire? Respectez un peu diamou yalla yi. Yene rek nekolene fi. Nite dagno yor ay mbote you saf sap té reuyougnou lamine té folene tassé wakhtane si yalla gnou dorlene ba guene youkhou. Yene ay fans mame bamba rek guene dolene ay talibeme khamolene ko sakh diegué wolene ko sakh ndakh mome liguene di def santoulene ko. Melni beneu niebé si thine pfffff
@@lilisarr529 merde la wakh
@@ngonengom8875 😂😂😂😂
katal sa ndeye
فلا بد ان نقبل بانه لا مثيل للشيخ احمد بمب omar diagne demalvteuri ya kene deklou woul sa wakh.
Merci chiekh omar diange niogi sisa ganaw vérité absolue ' chiekh mouhidine samba diallo Yalna yalla yoko ay leram
Je suis d,accord avec toi
Wakh gua deugue man de talibe Baye Niass la mai dama ko beugué samba Diallo
Bari doull menoull wéssoull nga nk SÉNÉGAL nii yaw waa ARABIE SAOUDITE ngay bokal heurou djouli ak heurou woor ak woorii ta niom bounou nékké si gouddi ya ngii sii beuthieuk✊✊👌🏻
Vraiment on a besoin des personnes instructives comme vous. On sent la classe quand vous parlez mashallah
MERCI BEAUCOUP CHEIKH OUMAR DIAGNE
BILAHI WAKH NGADEUG WAKHDJI RAFÊTTNA LOL
MACHALAH SA GENRYI LANIOU WARDI DEGLOU
YÉW WAKHI DIOULIT PIIR NGA WAKH. DIEUREDIEUF. MERCI ANCORE DE PLUS. GNIY TOGNE KILIFA DIAMBOURYI NAGNOUKO BAYI KÈN SANTOULÊNKO. Wassallam.
Gana amoul liguéey lii mooy liguéeyam. Mais Serigne Touba santouko lii yeup. Na kou nekk yam si sa Serigne.
Wakh nga degue
Tu n’as rien compris
Oumar diagne analys pertinent je suis mouride d,accord avec toi
Deugu nekhoul khalis mo takh mouy def li
@@mountagadiop4025 yaw ya xamoul Lou xéw
Ma Shaa Allah, Diadieuf professeur Diagne genrou gana yi ay mbam youy dokh si souf lagne rek
Je suis muridé mais kham nani méséré mo tougné wakh deugue nekh yallah
Yaw dull guanan mouride la wayé
Je suis un tidjane et talibé de Cheikh la Islam mais s'il y'a quelqu'un qui ose cracher les vérités c ce Oumar Diangne car il sait très bien de quoi il parle.
Gana, il est coutumier des faits
Je suis Talibé BAYE BARHAMA NIASS Mouy Mouride layénne thianaba thianaba Wa tiouwaone nioune niép béne laniou si yalla Mouride day déme gamou Di déme apél layénne yi Niass day Magali Touba Serigne Touba Maoda Malick INSA nourou laye Elhaj Omar foutowou Tall nioune niép souniouy Mame la niou Lou rafé laniou yague déff Di ko wakhé di ko diéffé kinak louma wakh mome la concerné Serigne Touba massoul togne hamoul kouy togne Yalla yonénte alkourane hassida la ham sa yi bokoy déff bouy si bolé kou TÉDD KI wa'sallam
Salam mon frère Cheikh,
J'apprécie énormément la lumière qui jaillit dans vos propos pour vous permettre les redondances que vous étalez à travers les médias. Vous faîtes partie(et le intellectuels te le concèdent) de ceux qui, au lieu de polimiquer, doivent laisser à la postérité des écrits mémorables pour l'éternité. Les amuseurs de la galerie ne doivent pas te divertir. Je n'ai jamais vu où entendu les Dr Rawane Mbaye, Abdoul À Kebe, et beaucoup d'autres sachants accorder une quelconque importance à ces porteurs de médisances fractionnistes. Un sympathisant qui te suit ! Merci😔
J8 vrai mourid
Mais 100% avec vous !
Machaalla bien dit et bien réfléchi
Merci professeur vérité absolue ✊✊✊
yaw khana deumou nga
@@magsjunior7761 amal yarr wayy rew nga torop
@@fadelbulo7921 kii yeufii santan lay deff lou passée ken douko fatalii ta nieupou ben lagne koi khana khamonii da niou beuga diakhasé tariha yii bagne am liniou beug bayil yoyou frere
Tres pertinent professeur c les guides religieux des confreries qui douvent controler leurs griots sinon on va le regretter a l avenir pass pass dafa grave ' yalna niou yalla defal diame te nasakhal kep kou ye fitna si barke seydina mohamed .....
Yéne liléne nakhari moy serigne touba mi djitou
lou lérr nga wakh
Dague lue
Si bokalé yalla kay yenasi dijtou
Gni melni iow nio yakh yonu tassawouf avec tes commentaires cons
Bilahi souniou serigne dou sen morom serigne ❤️serigne touba dou morom
Lima métti rèk senègalais yii doungne la dègue mé sa genre yii bougne lène done dègue lou di djièfè senegal wèssou fiii si katanou YALLAH SWT
Kii amoul limou niouy wax nafékh la
@@tallseye470 nèl amoul loum la wakh
@@mbayeibnoulaminesarrsarrmo6586 mbaye non waye ganna d'où togne
@@tallseye470 Yaak Ganna yeup Saine Datta Yay
@@taphiscodiaz9998 iow sa yaye amoul data té sa baye da yoom kigne la waxni moy sa baye koye bi dafa âme Aÿ gommm dmrm iow ngaye domi biral di ame loy wax
La verité est simple mais elle vous ronge le coeur:
LA ILAHA ILAHA ILALAH
MOUHAMADOU RASSOULILAH
BOROM TOUBA AMOUL MOROM
TOUBA AMOUL MOROM. Et le probleme est personne ne veut l'entendre.
On sait bien k le mouridisme derange au senegal et ca ne date pas aujourd'hui. Le mouridisme a connu ses moments les plus difficiles (les dieux du monde=colons=franc maconnerie) avec hauteur et succes. GANNA A PARFAITEMENT RAISON.
Merci certain personne sont de bonne foi yaw mi wakh katou deug gua
Et le voilà encore avec ses vérité incontestable !!! Vrement je ne sais même pas ce k je dois te dir car cheikh Omar Diagne t'es une personne très éclairé machala yallah na sa diamou yague yallah doli katane bi ak meunmeun bi ak surtout khel mou sel bi contane trooppp sakh si yaw
Machallah Chekh oumar kadouyi amna sollo na fék bakhoul
Merci Cheikh Oumar Diagne vérité absolu deugue rekk nga fi wakh yala na sènègal am gnénéne gnouy dèff diangate bou lér tè deugou kome yaw merci
Mâcha allah cheikh Oumar linga wakh deugg kou respecté sa sérigne gnioungui koy khamé thi respect binga diokh sérigniou kénénn
Mani boléne bagé am diamou dangénii kénnal s touba réck
Mach alla cheikh bi ziar nala bou bakh
Mame Bamba rek mofi né Machallah 👌👌👌👌👌❤❤❤❤
Lofiye dèf kone ioe
Machallah diagne wakhga deugeu
Le probleme est que il y a certains personnes qui ne connaissent pas la relations qu'entretenait nous guides religieux!
1
Veritè absolu
Merci omar diagn cadouyi rafétna👍🏿
Diaamou leen yalla té bayyi thiaakhane may leen niou diamm
Vraiment wakh-katou deug moguini. Je l'adore énormément ❤
Machahala machahala machahala professeur yalla na sa diame yague
Serigne touba dou kougnouy yeukeuti yalla moko tanal bopam may léne gnou diamou wayy
BILAHI
@@bambatoubareck dafa leer
Toi on te parle de malaise, toi tu parle de Serigne Touba yallah moko yékeuti, mo ko yékeuti kayy comme nimou yékeuté niép... C'est le comble de l'imbécillité !
Yaw mome wakho kham kham sa tour bi rék moma si diakhal touba sow
Yawak Serigne touba senn deudieuw ndayy
Un savant voilà ces genres de personnes que le pays a besoin mais pas des cas comme gana messeré
Serigne Touba rek ba Al diana
nafékha yii douniou topeu Serigne Touba Aldiana
Talibè cheikh, vraiment c pertinent. Gana Missil dafay diakhassè keur dinè yi nguir am tèranga adouna. Cependant marirando yi gueumoul dara topouko si ay fen. Mais Mouride deug dou dokhalè ni ndakh serigne touba santanèwouko
J’adore ce personnage car il est très pertinent dans ces interprétations
Dafa dof
On n'adore Qu'ALLAH SWT de passage 🙏 tu peux estimer et aimer
👍👍👍
Chikh oumar diagne machahala
Chiekh Oumar deug rek nga wakh
Nafekh yi rek nioko beugoul degg
Deugue piir sax sais que tarikha yi nio doul competition mai malarheusment Senegal dafa aye doff
Sa
Baye# moy# nafékh
@@abdourahimikanetouba6797 amal yar ak téguin té nga khol sa tourwi aven ngay saga bayou diambour
Wakh deug
Abdou Rahim ya séll tour té niaw lamign RAHIMI Di wax Lou niaw chandél tourr hahaha je rigole mais amal téguine way mbokkou mi
Serigne Touba rék mofi ni Komo nékh ak komo nékhol Serigne Touba rék
Suis mouride et suis parfaitement dacord avc tw il na po le drw d dire des chooses sur les autres marabouts merci omar diagne abdou ndaw aussi ma deçu kouy yare ay nite c honteux vraiment
Bilay sen holla rafet rèk
Ga Balma mai gana waxoul Lou niaw si béne serigne
Yalla rek moy kene Yalla rek lagnou wara kenal. Ku kenal kenéne koudoul Yalla so déwe safara nga dieum. Inchallah
Kou yalla kénale nak nougne kay déf ?
Abo Fall amo hél dou ma wakh ak yow
@@abofall183iow Yallah dala kénal ay vrai con ngén amoulen xam xam
Fi Yallah gneup leufi kénal
Cheikh Omar Diagne mane yaw laa geum dangua niémé DEUGeu
Téwmi liko tardél moy ay fén ak parparlo
Yena yam daguay di fent tk
kén dou serigne touba 😜😛😜😛😜😛
Cheikh Oumar Diagne wakh dji amna solo dangaa niéme deugue machallah
Chaque bus d voyage ya un chofeur c serigne touba nimero 1
Machaallahou lawakh rèfètna matalèna andak mandou koukham ci s touba dara do togne wayè koula togne nga ballco ndakh lolou la royè ci sangam s smh saw kone lolou lane wara roy ci mom merci pr diagne de oumar thiam moum s touba
Lilermoy gordotoulbab serige touba
Fi Serigne Touba moufi né ♥️
Bagn lenna diamou Yallah rek.
Serigne touba mo fi ner anamou ???
Machallah mon professeur, tu é un homme humble
Je suis mourid sadikh wante togne baaxoul serigne touba santoul kénne mouy xasse wala mouye sûfél sëriñe diambour
Écouter Gana Méssére c'est insulter la conscience des Sénégalais. Amoul Kham Kham.
C'est une honte pour toute la Nation.
Wakho deugue d Yalla kham nako limiy wakh mola arranger woul rek
@@khadimleye5738 sama serigne mofi raw mofi mene amoul morom lolou rék lay wah dé lolou dou ham ham
Coeur2 Lion Gana wakhou Serigne Touba lay wakh wakhou Serigne Abdoulaye Diop massar ak narou Ganar yii Serigne Touba mo ndieuk wakh ni kéep kou ame wilaya ci Yalla kham ngani kén la le problème c’est les termes les mots que Gana utilise molén doul nex ok on comprend mais nak Serigne Touba kén la dougnou ci nexal kou Yalla binde dougnouko sakh négocié
@@khadimleye5738 ba balma mé mane borom hel you selyi lay wahal yalnagnou yalla fayal sougnou makyi lép bénela diné rék moy gagné mé serigne touba sohlawoul talibé you melni yéne
@@khadimleye5738 ba balma mé mane borom hel you selyi lay wahal yalnagnou yalla fayal sougnou makyi lép bénela diné rék moy gagné mé serigne touba sohlawoul talibé you melni yéne
Une verite Vrai Cheikhou Oumar
Macha oustaz Oumar Diagne yalnala yalla taxawou yookou Sénégal soutoura inchallah talibe cheikh la nak
Wakh ji amna solo trop prof....
Merci pour tout kouko wakhone serigne gnam mou mere
Cheikh bi gana diaroul top ndah nite kohamni dou wah ba andila aya wala hadiss diangoul hamoul
Machalah sérigne OMAR Diagne nittou dégggu'ngua mo takh ma fonklà
Cheikh Oumar Mo nékh la Serigne Touba Mofi ni Mo nakharila mofi ni Serigne Touba Rék
Yalla mo fi né dello ci lén sén xel
Geumodore yaw doul rék
Dieureu dieuf Serigne Touba
Dieuredieuf serigne touba
😁
yeufou mbamxoukh yi
use your mind way
Wa Corona
Merci cheikh Omar.
Wax deugg nk Pr chéikh bly nk je suis fière d'être talibé lou weurr nga wax
Belle analyse. Je dirai qu'il faut que tous talibés apprennent à connaître les enseignements de leur guides quel que soit leur tariqa car c'est ainsi qu'ils vont apprendre à se respecter. Autre chose aussi, il y a les ennemis de l'Islam qui n'attendent que ces genres de problèmes pour diviser les MUSULMANS, ne soyons pas impulsifs et mesurons les dégâts que ça peut causer maintenant comme dans les années à venir.
Wa salaam
Je suis mourid mais douma déglou gana bilahi ndakh défoi daye togne bilahi
Vérité absolue professeur
Waay maylén niou diamou Serigne Touba daal moom amoul morom
Serigne Touba amoul morome fii ak fagnou dieum
Serigne TOUBA le SAUVEUR de L'HUMANITÉ lolou rek rakhari
Walahi cheikh Ahmed tidiane cherif dou moromou bèn serigne lolou yalla moko def
Dangay féne
Ndeyssane diambar ki diaroule tontou sakh
Dou sén mrom ndakhté mollén mak. Wayyé cheikh ahmadou bamba dou sén mrom fa yallahou
Il y as toujour les homme des foi merci mr diangne
Weiiih barinafi morom nk, di Tagg sa Serigne uniquement pour khaliss késsé mola yittél bassiy wax lou amoul boléssi di khass serignou jambour
khaliss rk mo lenn si dougal
Ganna mésséré nafeikh leu
Toppou yalla ak yonent bi mo guene khasté bi yalna yalla dioubal niou dia dieuf cheikh o diagne
Machalha amna solo merci
Vraiment profèseur tu es un homme vèridice bilay walay
Diaradief ch omar yalla na yalla yoko sa fann ci bar che 🕋🕋🕋🕋🕋👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿🙏🙏🙏🙏🤝
Jeureujeuff khadimou rassoul!!!!
Wawaw
Yaw mom do nitt kene wakhoul ak yaw nite yi lay wakhal
Merci professeur yaw tu es un vrai patriote
Que personne ne juge personne na kou nek gueum linga gueum prsk mome gana messeré talibé serigne Touba la ndieuké thi mome yem thi mome kone so wahé rek niou indale la fo kagné sa serigne ba wah lou meuneu méti kenen wassalam Gana dale naw nako , ay terangam ak yeneu yi waro wah ni waham bi moko mey ndah boudoul wone wah dji sah dinako am si dunya borom bi mokoko thieuralé wone ganaw dioudom té Serigne bi mo makk alalou adouna sante ko daf gnu war
Santati Ceexul Xadim té wormal bep kilifa diné nak mangui balou akh nak wassalam
amal diam rek fall
@@serignefalloungom5289 jajaeufaty way mame yalla na diam yagu 🙏🏽
Merci beaucoup pr Omar Diagne deguele vraiment
Wakhoul deug. Il fait la même chose.
C'est vrai pour attirer les donneurs bienfaiteurs,ces hypocrites affamés sont prêts à tout jusqu'à embraser le pays.
Pourquoi dénigrer les autres foyers religieux dans le seul but de se remplir la panse.
Ces histoires ne nous sont d'aucune utilité dans l'adoration. Il aurait été mieux de concentrer leur énergie dans les enseignements de la pratique religieuse(prière, ablutions, zalat...,)
Réw rék ak doff
Liiii leppp cst entre Akhlu Tassawuff! Ahlou Sunna mom dokofa degg! 😌😌❤❤❤❤
Topp lenn Alquran ak Sunna nopalou! 😌❤
Gana sii bopam mou ragaroul Yalla pochame la geuneu raguale.
Yaw kou niemè yalla gua
mouye fen rek nguendi contane rek molen nekh
S gana wakhi s touba rek lay wakh kèp kou bagn s touba khama touma si iow dara
@@bambakanebeuguloubakh4051 yaw dof nga rek
Dangay doul
Mashala mashala Mr Diagne sopenala nawenala
بارك الله تعالى فيك
شكر الله سعيك أصبت الهدف وقرطست الغرض
فجزاك الله تعالى عن الحق خيرا
Bien dit Professeur
Jtaime Mon père Omar Paa "Nespaa"✌✊
🤣🤣🤣🤣🤣👏🏾pa nespaaa
Gana méséré réwna meuna féne
Allhamdoulilah Allhamdoulilah Allhamdoulilah Allhamdoulilah
Les diwanes sont devenus des fonds de commerce Gana fait presque deux télés et pas avec des islamologues mais plutôt des animateurs de radio de musique tel que Pap Cheikh à TFM et Cheikh Sarr a SEN TV donc en complicité pour leur part du gâteau ces derniers peuvent même prononcer de fausses contributions pour inciter les fanatiques à donner je crois pour terminer apprenons MASALIKUL JONAAN pour comprendre Serigne et les tariras Diadieuf Chekh Omar Diagne que Dieu nous garde
Bagne serigne touba sa khol dou séd adouna dou séd alakhira
Kou bagn Cheikh Ahmed Tidiane Cherif safara jahannama moy done sa keur
Omar Diagne a raison.
Merci d'être véridique, yalnala YALLAH swt défal la yeeuw
Akhmadou bamba dieuredieuf,Gana messere yagual wéreul thie doley cheikh ibra tawfekh rk guay ame
Ganna mesre leufeule ndayam ak kouka ancourages 🐗🐗🐗🐗🐗🐗
“TH-cam” ABONNEZ VOUS À NOTRE CHAÎNE BAOL INFO OFFICIEL
Kogam s touba doka kénal
Ndakh sarigne touba gamna لبسم الله الرحمان الرحيم،قل هو الله احد الله الصمد لم يلد ولم يولد ولم يكن له كفؤا احد.((وبعد ))مقاماته بحر لاساحل له
Vraiment Li Oumar diagne wax Deug La
boy mesere mi khaliss lay outt limouy def serigne touba beugouko
Je t'aime vraiment paix sur vous mon cher