Mbir yi daal nii rek. Bou Baye dji wakhé, dom yi top si. Familles de Serigne pour toujours ak famille de talibés pour toujours. Yi mo wara diekh. Lii motakh yoone yi di diekh. Affaire de dynastie, mamocratie mo wara diekh. Baye Niass si boppam daf ko bagnone. Senghor a été Président puis Abdou Diouf, Wade, Macky Sall alors ken bokkou si ak ken dara. Ecole ak système toubab bi gniy khass moy mayé lolou. Kou am kham kham ak takhawaay nek njiit. Obama, nioul done djité ay niou wekh talle. Baye Niass lou mou bokak Cheikh Tidjane. Wala Haj Malick Sy ak Cheikh TIdjane wala Hajj Oumar Tall ak Cheikh Tidjane. Na niou bayi diiné bi gniy teunk si ay familles. Lepp si biir famille bi, khalif général, président Ansarouddin, mom Tafsir yi ak wakhtane yi. Lii comme mbirou Chiite yi. Gni gueuena mokkal al quaran si att yi moudj yeup ken doussi domou Serigne you siiw yi. Nonou la démé si fann kham kham yeup, fiqh, hadith, balagha wanté heurou djité bou dioté rek niou nieuw takhaw si kanam di ko donanté nak tek si. Lii Yallah néka toussi. Ay tiakhane la gueuna niirol. Da ngay guiss kouy def gamou si domou Baye yi alors do comprendre sakh li mouy wakh mais daal na koy deff rek ba ila... Mbir nagn ko diokh gno ko meune. Yallah amoul dome, amoul mbok ay kharitt rek la am. Wa salam.
Yaw doff nga so ame xam xam demal diel micro bi niou deuglou lolou moye yoon mai ay critique dou affair bi. Xam xam motakh mouy waxtane. Yaw ken degoula mom diangue na te mogui wakh xam xam kou diangue tamit micro bi ken terewou lako.
Sa way li nga wax nuancé woul dara a quelque exceptions près : Ki da fa diangur ba am licence au Caire en Egypte. Donc ma question c'est : doit il se cacher et ne pas parler parce que son père est serigne, je crois que non il doit parler et transmettre comme tout savant. De grâce, ça n'a rien à voir ak Baye niass et Cheikh Tidiane. Baye niass da fa diangue, limou diot si Cheikh tidiane beneene mbir la. Domou Bayi tamit diangue, donc ils sont legitimes pour parler , ça ne veut pas dire que nio fi raw, walla nio fi raw si Batine. Peyi Baye bi boudone ay donante rek kone Serigne Aliou Cisse do nek khalifa à la disparition de Baye. Moytoul khol bou fiir yobela togne. Là tu mets tout le monde dans le même sac. Bossi bole 1000 you thi bokoul c'est pas grave mais guene thi ken kou thi bok nga halkou. wa salam
Kossy TV mane critiquer wouma sen liguey au contraire dama kay rafett lou. Kou woté nga couvrir ko, loou amouma louma siy wakh. Celui qui me dit que la personne a une licence, mais kou niou diall nga am lidjaza. Limay wakh lou lerr la. Baye si boppam moko wakh, da ngey dioud niou daipé la serigne nakh sa Baye aors que talibé moy dieurign. Lolou Baye moko wakh. Ya ngi wakh Seydi Aliou Cissé mo nek khalifa Baye, lolou moy wané ni Baye nangou na li may wakh. Cheikh Tidjane, Sidi 'Ali Tamacini mo nek khalifam ganaw mome. Seydina Muhammad, sallalahou 'aleyhi wa sallam, Sidi Abu Bakr la djital, ganaw ga Sidi 'Umar. Li moy diiné. Mamocratie dou diiné. Par exemple Baba Lamine fait les gamous alors que depuis quelques années, tu ne comprends rien de ce qu'il dit. Mais daal nay continuer rek nakh moy domou serigne bi. Mounkhamina NIass fii la tok si hadra Sangue Ndiaye mouy wakh kou toud Baye soubhanahou wa ta'ala nga si wara tek, té wakhouko dara. Imam bobou nek madina fi la fi né kou votéloul Macky wor nga Baye di traiter nitt gni de mbam ak golo. Té nieup guiss nagn li Macky tek rewmi. Lii yeup li kay indi moy di djital ay nitt nakh dérett. Mane woutouma kouma couvrir. Limay wakh khamna dina si weet. Mais deug mom faw niou wakh ko rekk.
ياشيخ أحبك بالعلم والله أتابعك في المحاضرات كلها
Machalah yalla na yalla yok kham kham bi té lafal la thiat
Macha alla yalena yalla lafale la thiate cissé ni rék la
ماشاء الله kossy tv
Walayi dégele Machala cheikh Ibrahima Cissé yalagavi yaGe tawe'r barke baye niass Amine yarabi Machala walayi dégele Amna solo walayi dégele Amna solo walayi yalagavi tawe'r barke baye
Macahlla baye sisse lerna
Baraka llahu feeekah
Mash'allah sa ma Serign
جلال الدين ما شاء الله ياحبيبي ❤️❤️❤️❤️
Machalah cheikh Ibrahim Cissé dialalu dine
Machalla cissè
Macha allha niass alhamdoulila dieureudieufe baye niass alhamdoulila 🇧🇷🇧🇷❤️🙏
Machallah
machallha
cisse
Machalla Cissé
Alhadoulilah 🙏
❤️❤️❤️❤️
Nagn ko gnanal gudd fane rék AK weur keip
Té yalla musssal ko ci thiat
Mbir yi daal nii rek. Bou Baye dji wakhé, dom yi top si. Familles de Serigne pour toujours ak famille de talibés pour toujours. Yi mo wara diekh. Lii motakh yoone yi di diekh. Affaire de dynastie, mamocratie mo wara diekh. Baye Niass si boppam daf ko bagnone. Senghor a été Président puis Abdou Diouf, Wade, Macky Sall alors ken bokkou si ak ken dara. Ecole ak système toubab bi gniy khass moy mayé lolou. Kou am kham kham ak takhawaay nek njiit. Obama, nioul done djité ay niou wekh talle. Baye Niass lou mou bokak Cheikh Tidjane. Wala Haj Malick Sy ak Cheikh TIdjane wala Hajj Oumar Tall ak Cheikh Tidjane. Na niou bayi diiné bi gniy teunk si ay familles. Lepp si biir famille bi, khalif général, président Ansarouddin, mom Tafsir yi ak wakhtane yi. Lii comme mbirou Chiite yi. Gni gueuena mokkal al quaran si att yi moudj yeup ken doussi domou Serigne you siiw yi. Nonou la démé si fann kham kham yeup, fiqh, hadith, balagha wanté heurou djité bou dioté rek niou nieuw takhaw si kanam di ko donanté nak tek si. Lii Yallah néka toussi. Ay tiakhane la gueuna niirol. Da ngay guiss kouy def gamou si domou Baye yi alors do comprendre sakh li mouy wakh mais daal na koy deff rek ba ila... Mbir nagn ko diokh gno ko meune. Yallah amoul dome, amoul mbok ay kharitt rek la am. Wa salam.
Yaw doff nga so ame xam xam demal diel micro bi niou deuglou lolou moye yoon mai ay critique dou affair bi. Xam xam motakh mouy waxtane. Yaw ken degoula mom diangue na te mogui wakh xam xam kou diangue tamit micro bi ken terewou lako.
Fi Kossy Tv la, discrimination amoufi, nékal Talibé Baye té wolou sa kham kham so ñowé ñou talala micro bi
So bugey nyu topula da ngai dem diangi. Ta nga bayi sa Fenn you ngai sakk. Payi Baye niass Kun Fi topu kham kham lenko topee
Sa way li nga wax nuancé woul dara a quelque exceptions près : Ki da fa diangur ba am licence au Caire en Egypte. Donc ma question c'est : doit il se cacher et ne pas parler parce que son père est serigne, je crois que non il doit parler et transmettre comme tout savant. De grâce, ça n'a rien à voir ak Baye niass et Cheikh Tidiane. Baye niass da fa diangue, limou diot si Cheikh tidiane beneene mbir la. Domou Bayi tamit diangue, donc ils sont legitimes pour parler , ça ne veut pas dire que nio fi raw, walla nio fi raw si Batine. Peyi Baye bi boudone ay donante rek kone Serigne Aliou Cisse do nek khalifa à la disparition de Baye. Moytoul khol bou fiir yobela togne. Là tu mets tout le monde dans le même sac. Bossi bole 1000 you thi bokoul c'est pas grave mais guene thi ken kou thi bok nga halkou. wa salam
Kossy TV mane critiquer wouma sen liguey au contraire dama kay rafett lou. Kou woté nga couvrir ko, loou amouma louma siy wakh. Celui qui me dit que la personne a une licence, mais kou niou diall nga am lidjaza. Limay wakh lou lerr la. Baye si boppam moko wakh, da ngey dioud niou daipé la serigne nakh sa Baye aors que talibé moy dieurign. Lolou Baye moko wakh. Ya ngi wakh Seydi Aliou Cissé mo nek khalifa Baye, lolou moy wané ni Baye nangou na li may wakh. Cheikh Tidjane, Sidi 'Ali Tamacini mo nek khalifam ganaw mome. Seydina Muhammad, sallalahou 'aleyhi wa sallam, Sidi Abu Bakr la djital, ganaw ga Sidi 'Umar. Li moy diiné. Mamocratie dou diiné. Par exemple Baba Lamine fait les gamous alors que depuis quelques années, tu ne comprends rien de ce qu'il dit. Mais daal nay continuer rek nakh moy domou serigne bi. Mounkhamina NIass fii la tok si hadra Sangue Ndiaye mouy wakh kou toud Baye soubhanahou wa ta'ala nga si wara tek, té wakhouko dara. Imam bobou nek madina fi la fi né kou votéloul Macky wor nga Baye di traiter nitt gni de mbam ak golo. Té nieup guiss nagn li Macky tek rewmi. Lii yeup li kay indi moy di djital ay nitt nakh dérett.
Mane woutouma kouma couvrir. Limay wakh khamna dina si weet. Mais deug mom faw niou wakh ko rekk.
Machallah
❤❤❤
Machalla