Yeen gnima guiss nguene di wax lou niaaw S Amsa kou guiss seen commentaires yi khamni ak mbanieel bu nguene eumbeul wakeur S Touba gui késsé leu Ndakh nileen yalla def te Serigne Touba Fagoul leen ko te yeen amouleen lolou Lolou késsé molene metti Fii mom kénn doufi dof kham nagne leupp surtout nioune gni nekk si Diaspora bii louné laniouye guiss fii
Machallah alkhamdolillh
Waw goor way mbacké jërëjëf amna solo looool machallah
Jërëjëf Mbacke, Yàlla na saa boroom sàmm la, te saxal fi jàmm.
Lim wakh dara néwousi mam mor Diarra warna liguéyeul s touba ndakh Serigne Touba moye serigniam
Balla Aissa yaa woyof, jërëjëfëti !
Sama yaram dawna mbacke
😢ماشاء الله
Wallahi lime wakh Dara nekou sy serigne touba sakh da na ligeu yall boupam
Yeen gnima guiss nguene di wax lou niaaw S Amsa kou guiss seen commentaires yi khamni ak mbanieel bu nguene eumbeul wakeur S Touba gui késsé leu Ndakh nileen yalla def te Serigne Touba Fagoul leen ko te yeen amouleen lolou
Lolou késsé molene metti
Fii mom kénn doufi dof kham nagne leupp surtout nioune gni nekk si Diaspora bii louné laniouye guiss fii
Kilifa bouye diangue lé daka wara défe si deugue
Kilifa dafa war diommu wakh diu niaw diu melni thim
Mo yakh touba look ay moromam
Ki fen rek laye Def bon nga loll
ya rew 😢😢😢
Katal sa ndaye w ak sa baye
Sa bonou baye ak sa mame
Iwo démal nga tok