Ahmeth khalifa Niasse damako moussa beug mou tékk si sol dalam ba ndindy si sama serigne bou tédd bi Serigne Abdou Karim Mbacké si lako gana fonko ay wakh you bakh youmouy wakh si Serigne Touba ❤️❤️❤️❤️
Ammlénn respect, khalé bou beugué goudou fane dafay respecté makk, Quelque soit ses défauts, lui il a passé de bons moments et a eu l'estime de nos exemplaires chefs religieux Mame Dabakh, Serigne Fallou, Mame Baye Niasse donc dou sen morom Vous la jeunesse Sénégalaise faites attention aux réseaux sociaux, juste un petit commentaire peut nuire toute ta vie, Dispute entre religieux ou entre adultes sougnou yoon nékoussi Limotakh jeunesse bi legui di gawa déé rek,
Ahmed halifa limou tahaw wah ko si seydi el hadj Malick (RTA) journaliste amul lumuy déf ludul diko may mougn tontou gni dal si kawam...sen métier bi guir yalla set len si sen borom dégueine war di bolei mai pa di hadialé nit yi
On en disconvient pas c'est quelqu'un qui a du savoir.Mais mon seul problème en ai que je ne peux pas concevoir d'aider quelqu'un et dévoiler cela dans les médias.Pour moi c'est indiscret et cela discrédit ces personnes qu'il a porté assistance.Si c'est par contre ce sont ces derniers qui le disent dans ce cas y'a pas de problème.On parle de Gaston mbengue qu'est-ce que ça soeur vient faire dedans svp.
Gnioune sénégalais sunu djicko motakh rewmi metti.nguir yalla sopékou djiotna.waakh Lou rafet diotna.kou nek moussa birr keur sa éducation nguay affiché thiat commentaire. Bayléne khél gniouye lire commentaires yii.aye kiliffa son presant.peut être kilifeu diné yi.gnioungui khol. Tjrs les même personnes la.bane tarikha nguéne bockou???
Certains journalistes devraient porter le titre de chaytan. Ça devient dangereux d'étre invité ă la télé puisque tout ce que vous direz pourrez étre retenu contre vous.Çaaxaan faaxee waay ngoor kee,euh!
Kii Tange Tandiang là dou journaliste people lay déff loumu moye lou bone rkk liguafi waxone ba dawone dém paris nitte yii fatéwuniouko Ahmed iow wakh bou niaw kéne dakou lako sii Sénégal donc nopil
Gaston ioe sa data ndy amo ndy khame khame ki mo raw sa baye raw sa leufeull ndy sa niaway bu kharr leufeull ndm wa tiwawone yeup seine data ndy akh seine khalifa bie
Merci Khalifa Ameth Niass
Ahmeth khalifa Niasse damako moussa beug mou tékk si sol dalam ba ndindy si sama serigne bou tédd bi Serigne Abdou Karim Mbacké si lako gana fonko ay wakh you bakh youmouy wakh si Serigne Touba ❤️❤️❤️❤️
Ablaye Camara Akassa mouride mane talibe Sidi Ahmad Khalifa Niass la. Mouride sadikh yena meune ganale kar mashallah. Beussou aldiana la wone biir ndindi niari goor y’Allah yi fa dadje reuyone lolou te nekh Serigne Touba nekh Mame Khalifa Niass. Hakaza mouride
Merci Machalla rafetna
🤣🤣🤣 néna xamoul Gaston
Diajeuff way cette fois ci kontanaa si yow😎🙏🏾
Une bonne leçon de morale pour Gaston mbengue
Merci Ahmed Khalifa Niass. Bonne réplique. Machalla.
Yaw journaliste d'où nar fékh d'où diakhassé da wara défar lé yaw saïtané nga narfikh nga Tass katou adouna nga yékatou fittna nga
Kii moo paré vraiment frére 💪💪💪🎤🎤🎤🎧🎧🎧👀👀👀💪🤭🤣😂
Machalla niass longue vie à toi
Ammlénn respect, khalé bou beugué goudou fane dafay respecté makk,
Quelque soit ses défauts, lui il a passé de bons moments et a eu l'estime de nos exemplaires chefs religieux Mame Dabakh, Serigne Fallou, Mame Baye Niasse donc dou sen morom
Vous la jeunesse Sénégalaise faites attention aux réseaux sociaux, juste un petit commentaire peut nuire toute ta vie,
Dispute entre religieux ou entre adultes sougnou yoon nékoussi
Limotakh jeunesse bi legui di gawa déé rek,
Lii moy wané neu matoo aminata lousey yoonam😎😎😎😎
*yow journaliste bi yalla reubb nala vrai seytanë nga yalla dinala wonn bopame*
Machalla niass xam xam rek mo ame solo
Yene wa presse ay vrai seytaani nguene domaram you nguene done ! Vous allumez tjrs le feu dans ce pays !
Eupeu bakhna si lakh bou tangue Merci bcp à Gaston Mbengue
Journalists bii nafeke la diarijeff niass
Hahaha
C'était géniale comme réponse
Pour une fois une il est cohérent et lucide .
Merci ahmed khalifa Niass yalla nala yalla fay si barke serige touba wahbi amna solo machala
Yalla na goudou fane yalla n'a am weerr
Mame 2stv yalla khamnani moye sama télévisions mai dégnendi wéré bouléne boque si yi stp
Merci Ahmed deuguerk ngay wakh gayi bagougno kouy wakh deugue
C la vérité validé
Mane dé je prefere thiarakhou gaston mbéngue ,.que kanhan niasse
Cela ne regarde que
Alors gardes le pour toa bayilenn ki domou diambour la😔
Tay dé déna yalnako yalla yeureum
Niou wax la Gaston🤔.
Ngay tudd lo defaal Aminata Mbengue Ndiaye.🤔
Yaw tamite dé 🤔
😂😂😂
Nature Humaine Gaston mo kat ndeyem diaroul tontou anti modèle mbeur ak rey lamigne arrogant illettré
Ahmed halifa limou tahaw wah ko si seydi el hadj Malick (RTA) journaliste amul lumuy déf ludul diko may mougn tontou gni dal si kawam...sen métier bi guir yalla set len si sen borom dégueine war di bolei mai pa di hadialé nit yi
Kone ki niougui kaye INVITÉ ba legui mouye wah
Radio ak télé u amoul programme key,Kou nek la niouy invite!!!
@@jinnjahlo1666 c sa le problem
Merci 🙏 Ahmed Gaston saytanèla bayiko rèk
Doule yaw yaye saytanè
Journalist bi moye saytane sa waye
Journaliste bii kou deugue ndayamla
@@papambengue8074 sa baye moye doul
@@mamadoudiouf2772 bilaye li bakhoul amna yoo khamante nii diaroul lathie quoi
gaston gueumoul dara néwone dou politique téy macky diokh ko sougnou khaliss moukoye défendre golo mbengue kham nagnou le 😂😂😂😂😂
Walay niass manoul la guena rafet manoul la guen tamit
Fi béna journaliste mo fi ame pape alé niang kasé
Ya meune doul khamoko ba paré di wakh lima defal aminata mbengue ndiaye
😂😂😂😂😂
Yaw sa Baye yaroula domeram
On en disconvient pas c'est quelqu'un qui a du savoir.Mais mon seul problème en ai que je ne peux pas concevoir d'aider quelqu'un et dévoiler cela dans les médias.Pour moi c'est indiscret et cela discrédit ces personnes qu'il a porté assistance.Si c'est par contre ce sont ces derniers qui le disent dans ce cas y'a pas de problème.On parle de Gaston mbengue qu'est-ce que ça soeur vient faire dedans svp.
Nee na ko "yal na ma gënë rafet". Yeen deggu leen wax ji 😂 Mo tax mu dolli ci *mom ni mu mel, Yalla mo ko melloo; na jël benn seetu rek ñu xool ci* 😂😂
Ahmed rek kham kham kesse
Gaston dé dou famille s'y mame maoda boko wakhe dara lou safanou bilay doula djigue
Thiey voici le pain qotidien des senegalais.wakh bou amoul bène dieurigne.wakhna,wakhna ,fèna ,fènati mossiye top
Mdr pourtant yow waxbou gnaw téyy féwalé singa deukk yéné yéme vous vous connaissez très bien monsieur causa
Gnioune sénégalais sunu djicko motakh rewmi metti.nguir yalla sopékou djiotna.waakh Lou rafet diotna.kou nek moussa birr keur sa éducation nguay affiché thiat commentaire. Bayléne khél gniouye lire commentaires yii.aye kiliffa son presant.peut être kilifeu diné yi.gnioungui khol. Tjrs les même personnes la.bane tarikha nguéne bockou???
Yènangui mèrè khalifa balègui
Dieureudieuf Niasse 🙏 🙏
Sangu nga, hanrifou bilahi deug moy yaww.. Kou khamoul nak khamo.. Malheureusement...
Yala na borom bi barkell defal la diam. Deugueureul leu.. Niasse beuggu nala bilahi
khalifa niass bayil fèn
Ndaysan Ahmed mo bakh
Tange kou deugue ndéme nga seytané nga. Aminata Mbengue Ndiaye wakhoul yoname nékkoussi. Non Sénégal néekhoul
Journalistes yi non 🙅♂️ ken khamoul sen ligueye
Doull Rék
Journaliste bi seytane gua
c vrai
😀😁😀
WOLLAH Ahmed lii laniou sohla diaroul houlo diarul wéraneté
Kou khé'khakh doff yako togne mougneul lénko té yalla takh
Noy hamei Aminta mbengue ndiaye tei hamo Gaston 😂😂 épuis ngani mom ham na lolou😜😂 Ahmed napp nganiou koi
Mass Ngom katal sanday feulé yaw doull waayaw
Konne li nga wakhoone ci ousmane sonko nak fooko tek
Masahala
Aminata Mbengue Ndiaye kay😂😂
Sûrement dako beugone Kate
Yow do dara do touss on sais k khadafi te finançait.gueumo dara djiguene rek nga beug
kou contre Ahmed khalife niasse nakhare rek deuké yalla ko maye kéne mounouko dindi
@@alycamara6380 dou touss yalla nieupeu la may
@@abdourahmaneniang1148 c'est pas vrai yalla yémalé woule
@@alycamara6380 mome kham khamou djiguene la am
@@abdourahmaneniang1148 se khole moy méti ndéysane masseu
Yow mi journaliste bi kou yabatega seytane bi ken warouko invité thi plateau thim yow ak mom
Yayil togne
Dou sa morom
Machalla niass sa wakh réfétena
gnaw Gaston de mome do niékho gnebé mome bo deme rek banéne gneuw dagaye diaye mana wakhe rek
Féne môme baakhoul gani khamo gaston
Grand Ameth khalifa niasse yow do daara
Deme Omar sa lefeul ndeye
Dame Omar sa leufeull ndy khame nala bou bakh nk
Pardonnez moi.je vous poses une question ?
Bane école diné gniofi dakk sagua ndeye. Khasté.ak yaradickou les plus affiché sur les réseaux sociaux.
1 école serigne touba ?
2 école mame elhadji malick ?
3 ecole mame aladji abdalla niass?
Nguéne balma
Amadou Lamine Diallo école bi nga diangué té yakar nani dousi béne si yinga wakh prsk ya ngui saga
Good journalist bravo ✌❤
Bayilene diakhasè rambajj doudougou aldiana journalise yo khamni diakhasè rek a namimatou
Journaliste bi tamit keineu gueunou ko seytané yé fitna rq la ham
bilahi
Non pas vous 2stv ak sén professionnalisme kmm qui diaroul invité day oum sén TV bi rk
Ahmed khalifa niasse dayy soppe rek
Khamnani gaston mbengue dou n importe qui
Degal mouy diokhè lecon de moral
Certains journalistes devraient porter le titre de chaytan. Ça devient dangereux d'étre invité ă la télé puisque tout ce que vous direz pourrez étre retenu contre vous.Çaaxaan faaxee waay ngoor kee,euh!
Gaston limou wakh yép si yawe deugleu yawe ak journaliste bi d'ou guéne dara
Kii Tange Tandiang là dou journaliste people lay déff loumu moye lou bone rkk liguafi waxone ba dawone dém paris nitte yii fatéwuniouko Ahmed iow wakh bou niaw kéne dakou lako sii Sénégal donc nopil
Télé c pr tout les telespéctateur boulén intéréséwoul amna dioumou intérécest
Gaston mbengue ounkou leu say say leu
Ah yow kaye la Yalla wara defar
Ki damako banion mais damako moudié fan 😂guérier la loumou dougou man nasé guéne
Maodo dou morom
Ahmed ndiass bo rspectèwoul maodo rek niou niappeu sa ndaye
Ababacar Djite yaw laniouy tegal sa ndeye domi tiaga bi
ey way ana soutoure
Un vieux dans le vent….. ptit coucou à mon pote Masss….
Thieuy Aka beurii kham kham
Mane ma bayi 2s douguéne Dara
Lolou léerna
seytané nga
Gaston ioe sa data ndy amo ndy khame khame ki mo raw sa baye raw sa leufeull ndy sa niaway bu kharr leufeull ndm wa tiwawone yeup seine data ndy akh seine khalifa bie
Ahmet daye fene khamga Gaston fene bakhoule
iow journaliste bou mane fén nga nganan Experiences Ki fomou dieulé experience kana Experience djiguéne🖕d’où ndayi Dara🖕🖕🖕
Wayal Lifa bimou né « kone togne nala » la geudjeu nek journaliste.
Yow yaye nafèkh yaye diahir lo beugue daganalko lo bagne aramalko nè serigne nga di wère sa mbokoum dioulit
Mercie Ahmed Sénégal 60% ay naveke lén joulit dege nit bu néké si dege dayko wara naggu
deug deug
A khalifa niass kou niéff ndayam leu
ķhady Faye halkou nga koka waliyou y’Allah la pire.
Yalla nama geuneu rafete Pa bi Ray nama😂😂😂
😂😂😂😂 dafa ragal Gaston rék motakh mou rassou.
mdrrrrrrrrrrrrrrr....ak na khol sétou
Ki dof la Mingui contre dire bopam ferme la menteur
Tange t'es maudit
😭😭😭😭😭😭😭😭
Salam Ms Man damay lathie kii dafay lathie walla day diakhssé
Cette perdonne est bcp plus utile au senegal k gaston
Gaston Mbégue d'où wax jam
SA YAY YAW LA WARRON NA DIEUKKEU GNANALL NGA BAYYI TOGN
OUSTAZ ALIOUNE SIKIMOU PÉRE NOEL AK YENNEN TOGN YO DEFF NIT GNI
journaliste bi saïtané bou katt ndéyam la
Katal ndeyam yaw hamo dara
Tang ya séytané bo néké talibém gua wakh ko journaliste domékharame mo beuri sénégal
papa Ahmed khalifa niass ioe sa daleu fimou diarr boufa gaston diarè siguil ndigalè gay dèggg
Ahemed bayil diiné biguay fowé, té nga topou alkurane au sunnah.
Li moy netaly. seytane diakhasse.
S journaliste
Kon deh warna nioula nianal ndax si wax lou niaw nga deukeu