Le cas de Malick Gakou fait mal. Un des leaders les plus courtois... Il faut les identifier et chercher les lâches qui sont derrière. On veillera au traitement réservé à ces lâches. Plus jamais ça !
Li moy wané né danion sathie khalissou réwmi bagne kouléne niaf si caso bi motakh niou beugueu fagagal Sonko wayé peine perdue dakh PRO ak nimou adal dinkeu naniouléne yalla
Merci encore SAWOLOF
Que le Tout Puissant Allah SWT Sauve le Sénégal
Salam et bon vent au binôme gagnant Diomaye -Sonko
Le cas de Malick Gakou fait mal. Un des leaders les plus courtois...
Il faut les identifier et chercher les lâches qui sont derrière. On veillera au traitement réservé à ces lâches.
Plus jamais ça !
Protégeons Mousselmi
Merci beaucoup les sa et pm os ❤❤❤❤❤❤
Li moy wané né danion sathie khalissou réwmi bagne kouléne niaf si caso bi motakh niou beugueu fagagal Sonko wayé peine perdue dakh PRO ak nimou adal dinkeu naniouléne yalla
Fanta sall la guisse si photo bi
Fanta nagn ko diaap téthieu si kasso bi APR ay bandit rék niofaa kén bakhou fa
L'exemple c'est Baye Assane et saa ndiogou 😂😂😂
Wa aka nio Mona fen 😮😅😅
** FANTA BÂYILÊNEKO BA LE 17 PASSÉ**
Dioup rek raggal Yallah rek Sellal rek am diam
Un matche de football kî meuneu 5 but a 0.kôkou.dou tohihe matche bi nagnou wah lénén sonko amoul séndiote
Fanta sall mome thiaga doulkat leu mais pastef dina niaf sene ndeye bou bakh le 17