Je suis de kaffrine et c'est la première fois que j'écoute ce chanson mais sa me touche au ❤❤ sérieux ils font partie de nous c'est nos frères et sœurs
Geste bou nice. Comme le disait ndiaga mbaye" kou wéradi boulko daw bamou khamko, ndakh meneu yokou wéradem". Si tout le monde pouvait faire ça, les malades mentales seraient intégrés tous et facilement dans la société. Chapeau à toi l'artiste
Nice na trop bakhw domou adama dou khèp nitt te nitt ko guis diapèko sa bopou RK dina bakh inchallah te gni danio bokou si doundou bi thia kaw thia kanam rk inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤
Je t'aime bakhaw barki yalla damala beugue 🥰❤️❤️❤️❤️❤️😍😍😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Je suis de kaffrine et c'est la première fois que j'écoute ce chanson mais sa me touche au ❤❤ sérieux ils font partie de nous c'est nos frères et sœurs
❤
A
❤Jk
😢machalla bakhaw nitte cou bakh ngua yalla n'ala yalla takhawou thie barke Nabil Moustapha
5:38
Quand je regarde Aida j'ai des larmes aux yeux merci beaucoup grand frère
Aïda dafa wara bokou ci 12eme gaindé bilahi, YALLAH NGA DÉF TOUR DU MONDE AÏDA❤
Non Vraiment ça c Incroyable ça touche vraiment mon coeur
Merci bakhaw pour ton complicité avec Aîda sa me tient au cœur ❤❤❤ je te suis depuis États-Unis
Dafa bakh bilae nimou méle thi aïda rék montakh ma beugue ko
❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Khawma Loutakh mais douma doyal thie vidéo. Je l’ai visionné à plusieurs reprises. C’est touchant ! Merci beaucoup Bakhaw
Geste bou nice. Comme le disait ndiaga mbaye" kou wéradi boulko daw bamou khamko, ndakh meneu yokou wéradem". Si tout le monde pouvait faire ça, les malades mentales seraient intégrés tous et facilement dans la société.
Chapeau à toi l'artiste
Kouye sa dof
@@AbyLo-xr7ho
Dou doof
Syndrom de Turner la ame
Ki mye topato fi Europe mom la ame aussi wayé nonou lako niit beugué ,
Elles sont tellement adorable
Bilay j'ai des larmes aux yeux❤bakhaw on t'aime 🎉❤
Je viens de le découvrir malgré y’a bcps de bande assico mais il parmi les meilleurs assico let’s go bakhaw assico🇸🇳🥰🫶🏿
😊❤🎉😮
Bakhaw je ne te connais pas mais ton geste evers cette femme m’a beaucoup touché vraiment 🥰❤️
Ni dé le deuké ak mome ndeyssane khébou ko béne yone ❤
Dfna lou rafet en tout cas🥰
Merci ❤❤❤beaucoup
😢
🎉❤
Billahi sama kholl dafa toye😢
Macha allah Bakhaw je ne te connaissais pas, mais déf gua geste bou noble. Yalla mo ndiaboté gneup, gneup yéme mome. Na nites gni beuganté.
Nékhoul 😊 ba nékhoul 😮 mais tu es le meilleur ❤
Kou d'accord bakhaw Moy sen baye di sen Mame ❤❤❤❤❤❤
🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂
Sénégalais khôl bi nice vraiment je suis fier d'être sénégalais
Ndeysane aida kou marque sniou enfance ndeysane yaggal weral aida
Oui , ndeyssane
Franchement bakhaw ni ngua mel si Aida billahi motakh ma commencé suivre assiko khebo aida bene yoon ❤❤❤❤❤❤
Même moi le geste
Eryvhgrsn❤😅🎉
Je demande à la fédération sénégalaise de football de contacter l' asico familly pour le reste de la CAN
Bilahi vraiment
Wallahi video bi doumasi doyal mrci bco bakhaw Aida on t’aime 😢❤
Machalah vraiment merci c vraiment magnifique ❤
L'humanité retrouve sa valeur d'antan 🎉🎉 vraiment Baxaw on vous remercie mille fois
Oh lala j'adore vraiment votre complicité vous êtes adorables paix sur vous❤❤❤
Ndeyssane ça me rappelle les matches de Niarry Tally au stade Demba Diop en 2009, actuellement je suis aux États-Unis ❤❤❤
Ooooh... C'est ca qu'on appelle de l'humanisme.
Chapeau à Toi Bakhaw ❤
Ouf quel bel voix machaalla 🎉une geste noble 🥹
Sincèrement je peux plus m’en passer tellement je vous aime très fort bakhawwwww❤❤❤ aida tous le staff manchallah ❤❤❤❤😢😢
Ndeysane bakhaw yala nala yala guena takhawou dawlo gua sama yaram juste ki xel bi nekhoul me y’a koy takhawou Machallah 🙏🏽🫶🏾
Ndeysane aida bou may degeu ci navetane yeup mo nek ni ❤❤ amna bayre deh 😊
Bonsoir je suis en KANADA et je suis sénégalais je satisfaite et vous soutient même quand je suis pas en sènègal
Machalla Bakhaw toujour le respect tu change jamais frère ❤❤
Dame ❤❤
Vraiment très émouvant yalla fayla sa xool
Bakhaw est le Messi bly kou d'accord lalale ❤
❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis d'accord avec toi
Merci bakhaw Pour ce magnifique geste.Aïda dafa mérité lii dafa yagg si stades yii di supporté li dioboula yakafa am dh mrci bakhaw
Baxaw yalla nassa jammeuh yagg❤️
C bakhaw no baxaw
@@MamadouselloDiallo-xo4gi benela bayi len corrigé 😮😮😮
J’ai même des frissons 🥺❤️
Li nice na trop bravo bakhaw niom thi nioune laniou bokkk merci ❤❤❤❤
Vraiment ça fait plaisir merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Nice na trop bakhw domou adama dou khèp nitt te nitt ko guis diapèko sa bopou RK dina bakh inchallah te gni danio bokou si doundou bi thia kaw thia kanam rk inchallah ❤❤❤❤❤❤❤❤
Sénégal khôl bi Nice vraiment je suis fière d être comme toi balhaw❤❤❤🎉🎉❤
❤❤
Je suis en FRANCE,CANADA et ETATS UNIS est enfin thiaroye 😂😂😂😂mais je suis content
Dafa beug aida bly soukoy woy sah Day contane merci bakhaw❤
Machalla yarame daw na bilaye ❤❤❤❤❤❤❤❤
Bakhaw ioe rkk laniouy topou 🥰🥰😎fière d’être Médinoise 🎊😇🍾❤️❤️❤️❤️
Machallah félicitations yalla nalene yalla same dako beugeu Billahi Ndaye sane ❤❤❤❤❤
Wlh je t'aime Bakhaw t'es un bonnn de ouf 🇸🇳🇨🇵🇨🇵
Machallah bakhaw li rafét na trop machallah
Bakhaw tu es le meilleur
ndeysan li dafa rafét machalah aida et baxaw🎊🎊🎊🎊
Ndayesane li nekhena trop waye 💯
Je t'aime bakhaw barki yalla damala beugue 🥰❤️❤️❤️❤️❤️😍😍😍😍😍😍❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Kou guiss Aïda mome khaliss bi leep 😂 la dougual si poche bi 😂😂 Machalla
Guissnga lolou 😂😂😂 mane dee defewona dina si battre Bakhaw lol😂😂😂
😂😂😂😂 aka begue xaliss
Dañe ko ko wakh sinon daye mayéwate lep
En tout cas kou beurii foula😂😂
Boule xallise goré wouci😂😂😂
Ohhhhhhhhhhhhh li rafétte na way té nékh ❤🇸🇳
De tous cœur avec bakhaw vraiment sa takhaway si Aïda raféte n’a lol❤❤❤
Aida patara ndeysan borom niarry tally
Ndeyssane Macha Allah longue vie à aida Ndiaye
Bakhaw ya bakh diam rék guéy am inchallah ❤❤❤❤ vraiment ça me touche beaucoup 😢
❤❤🥰😍💗💓💓🤧🤧 tu as un grand cœur billahi.c est la première fois que je voit ça.les handicapés font partis de la société.merci pour cet acte
Oh machalah way notre aida nationale
Nekk boy Médina djiko leu ay borom khol you Nice ❤
Ça ma touché. Ndeysan
Merci bahaou pour aida la vraie noblesse c'est celle su cœur te souhaite une reconnaissance mondiale bon courage ❤
Ndayssan bakhaw koubakh la
Ha boy tu me rappelle fakhass sico des annees 90
Machallah bakhaw non lingay rimé nékh na way yalna sa diam yageu way amine❤❤❤😂😂😅😊😢❤
Merci grand ❤
c.est vraiment beau❤
Quelle magnifique asico de Aïda Ndiaye ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤merci beaucoup
Yala dafa def batay sak jour damay deig louh music bi ça m touch tro walahi jsei op c prsk ma mere sapell Aida et jlei perdu c op dal
Son bi bakhaw weuy ni la beug df son franchement aida motah ma Kham là mais tu es top
Non lii dafa nékh machalla yalla n'a yalla dolli takhawou ❤😂😢😢😮😅😊🎉
Ndeysan sama toma bii machalla❤ mes nak sédeu keneu si khalis bii😂
😂😂😂😂lep thi biir poche 😂😂
Mane bamou dougualé khalis bi si poche bi dama youkhou 😂😂pour mane bakhaw lakoye diokhatendéké yo😂😂Aïda way aka am fouleu
Jajeuf gaindë contane naniou si yaw 🇸🇳💯✌🏿 aïda ndiaye yagual tè wëër
OH BAKHAW GEUNE NALA BEGEU BILAHI ❤❤❤NAK AÏDA DAFA MARQUÉ SAMA ENFANCE STADE NAVETANE YI OH DAMAKO BEGEU BILAHI 🎉🎉🎉❤❤❤❤
Mouno waye
Machallalah bakhaw ya bakh deh te sa khol mo rafett yallana sa diame yague
Aida sama Rivale aissatou sa première dame Fatoumata Thiam la deuxième et Aïda la troisième ❤❤❤❤❤😢
J’adore tropppp Bakhaw Ndeysane ❤❤❤❤❤
Diadieuf bakhaw li dawna yaram ❤dila suivre depuis Montreal Canada 🇨🇦
😂no mane awoukate yi la fan kolal fignou guéne ak aida machala bone continuation❤
Yalla naléne yalla fay
Thiey aïda❤kou yague dem navetane stade demba Diop xamga aïda paké ndiaye
Mom moy aïda paké ndiaye bou yague bimaye dégue ?
@@maremesougou8031 waw mom la dé
Félicitations bakhaw boy médina
Le meilleur 🎉
Ohhh Bakhaw t’es fort machallah et big up à l’orchestre
Sa me fait pleurer 😢❤❤❤
Machallah bakhaw el es mérite ca tjrs ds les stade les baptêmes tt
Aida Ndayesannnn sama enfance naihonn n'a navetane hlm
Je suis le fan numéro 1 de Aïda NDIAYE 😅
Machallah bonne continuation 🎉🎉
Merci bakhaw🤎
Machalahou ❤je suis content depuis Montreal Canada
Je suis très contente pour Aida Ndiaye
Merci bakhaw bonne continuation ❤
Nice nice ❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Baxaw rekk layy topp bilahi depuis USA
Machalah bakhaw ❤
Machallha bonne continuation c'est joli❤❤❤❤❤❤
merci bakhaw bou gnépe done déf ni yaw dina bakh chapeau à toi et bonne continuation ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Numéro wadjii koumasii meuna diapalé guirr yalla
😭machala bakhaw ❤lou bakh rékkk gayy ammm inchalla 😢🥰🥰♥️