GP - Serigne Khalifa Mbaye: "Kane moy Serigne Babacar Sy..."

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 21 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 157

  • @yayourassouldiop7055
    @yayourassouldiop7055 4 ปีที่แล้ว +23

    Ay wayy ma beugue Seydi Aboubacar SY wayé ma sope doudou kende mbaye, dieureudieuf oustaz khalifa mbaye machaallah fière d'être talibé cheikh yalna gnou ko yalla def

  • @md7multimediadistribution907
    @md7multimediadistribution907 4 ปีที่แล้ว +23

    Salam Macha allah ; Seulement on aimerait prochainement 1- qu'une émission de telle dimension soit animée ou dirigée par des Oustaz pas une journaliste. 2 - Comme le temps était précieux , il faut mettre en priorité le thème (causerie) mais pas l'animation.
    3 - IL fallait mettre l'accent sur Serigne Khalifa MBAYE qui était prêt à nous donner beaucoup d 'enseignement sur cet incontournable Homme de Dieu Serigne Babacar SY ( sama serigne ). Merci

  • @papesylla7281
    @papesylla7281 4 ปีที่แล้ว +31

    Yalla na yalla yokk léram sougnou sopé Sérigne Babacar Sy ❤️.

  • @mamesofiendiaye9189
    @mamesofiendiaye9189 4 ปีที่แล้ว +6

    Machalla tabaraka kénn dou sama sopé ba. Merci Oustaz.

  • @partisandelaverite6183
    @partisandelaverite6183 4 ปีที่แล้ว +5

    Machallah amna solo wakhtane bi nékhna trop yalla naléne bourbi yallah fayléne yiw si barké goorgui

  • @elmansoursarr5646
    @elmansoursarr5646 4 ปีที่แล้ว +3

    Masha allah faa Mbay yag fii lol ta ande ak weer Suma serigne Serigne Babacar Sy(rta) fougnou toudou sama xol dafay toy 🙏🙏💕💕

  • @ndongomboup7518
    @ndongomboup7518 4 ปีที่แล้ว +5

    Je suis le petit fils de Mame cheikh Issa Dienne mes dama beugue Mame Dabakh ak Serigne Cheikh al maktoum yalna yalla yeureum léne téyokou séni lére Amine

    • @fatoudiawara327
      @fatoudiawara327 4 ปีที่แล้ว

      Daga beugue lou bax rek yalla na yalla faye yiw

  • @fatoudiawara327
    @fatoudiawara327 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalla khalifa Mbaye yalla na yalla faye yiw yakk say rakk ci barkel sa dourodon 🙏🏾🙏🏾

  • @ibrahimasambou4473
    @ibrahimasambou4473 4 ปีที่แล้ว +19

    Machallah contanou trop

  • @maminoukane519
    @maminoukane519 4 ปีที่แล้ว +5

    Macha Allah Alhamdoulilah sope Serigne Babacar Sy khôl séda sen Tv si KAW Si Kanam.

  • @ledivbleglgjuuf4853
    @ledivbleglgjuuf4853 4 ปีที่แล้ว +12

    Kene Dou Mame khalifa il est le marabout l plus élégant et l plus elokant🙏❤

  • @mangoneseye2127
    @mangoneseye2127 4 ปีที่แล้ว +6

    Machallah kene dou cheikhal Khalifa dieureudieuf pape Khalifa Mbaye

  • @elmansoursarr5646
    @elmansoursarr5646 4 ปีที่แล้ว +4

    Masha allah li lannu soxla si television xalna sunu borom yagal taxawaywii🙏👏👍👍👍

  • @fantambaye3976
    @fantambaye3976 4 ปีที่แล้ว +14

    Kén dou sounou Mame Khalifa Abacar sy bayou Al Amin lounou la beug doyoul Sy et Seulement Sy💓💓💓

  • @mbayengom4797
    @mbayengom4797 4 ปีที่แล้ว +15

    Machalha Khalifa mbaye yalna yala goudal sa fan ak wer barkue serigne babacar sy

  • @issasamb6476
    @issasamb6476 4 ปีที่แล้ว +7

    Mashala borom bonnet carré bi...yalla yok leram...fathie adio yi si barkem..

  • @minaciss6461
    @minaciss6461 4 ปีที่แล้ว +4

    Ma challah khalifa yalla na yalla goudale ça fane

  • @ジャウバッチ
    @ジャウバッチ 4 ปีที่แล้ว +26

    Dieuy serign babacar sy ladj lene mbeur maka songone da moudiou neup deh yam len kanamou Mbaye moy architect aldiana

    • @mamekhalifasy7767
      @mamekhalifasy7767 4 ปีที่แล้ว

      Déétt waay😃😃

    • @AbdouAbdou-bq5wy
      @AbdouAbdou-bq5wy 4 ปีที่แล้ว +1

      Doul Rék 🤣😂

    • @seckpalamine9544
      @seckpalamine9544 4 ปีที่แล้ว +1

      sa way khana danga wakhtane ak mak.lou wér nga wakh bouléne togne dh wayé kouléne togne amléne arguments youngéne ko defendré bou bakh

    • @AbdouAbdou-bq5wy
      @AbdouAbdou-bq5wy 4 ปีที่แล้ว +1

      @@seckpalamine9544 Doul Rék

    • @mexdroid1703
      @mexdroid1703 4 ปีที่แล้ว

      @@AbdouAbdou-bq5wy sa Serigne mo dakk doul

  • @moussaniang8407
    @moussaniang8407 4 ปีที่แล้ว +23

    MAME KHALIFA DIEREDIEUF MBAYE !

  • @deffaly9056
    @deffaly9056 4 ปีที่แล้ว +2

    Ah airou Baye Mbaye Dondé Mbaye moma nèkh masha Allah ❤💕🌷🌷

  • @boubacar9607
    @boubacar9607 4 ปีที่แล้ว +4

    Mashallah yalla na yalla yokku ay Léram

  • @amimbow211
    @amimbow211 4 ปีที่แล้ว +5

    Man ma beugue sérigne Babacar sy sama xol🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️

  • @babacarndour
    @babacarndour 4 ปีที่แล้ว +9

    Kén du souniou wadji♥️♥️♥️

  • @magatteseck694
    @magatteseck694 4 ปีที่แล้ว +4

    Machalah yalna yalla fay leen yiiw

  • @taphadjiamillo7347
    @taphadjiamillo7347 4 ปีที่แล้ว +8

    Billahi oustaz Khalifa mbaye soun ko bayi won mou wakh ohh machallah borom xam xam le mais mayougn ko mou wakh 😭

  • @princeseven1452
    @princeseven1452 4 ปีที่แล้ว +6

    Serigne Babacar bouma yalla mayéh dom bou goor ma toudéh koko rekk sama xoll sedd yalla mangui Lakay niane

    • @ndiassegueye1933
      @ndiassegueye1933 4 ปีที่แล้ว +1

      dinga ko am thi barké yonen tibi nakh yéné bi yégg neu yeugg neu lep

    • @princeseven1452
      @princeseven1452 4 ปีที่แล้ว

      @@ndiassegueye1933 amiiine merci

  • @dienabasabaly539
    @dienabasabaly539 4 ปีที่แล้ว +5

    Dieureudieuf Sy Malick ❤️ sama Serigne Babacar

  • @mamadouseck6450
    @mamadouseck6450 4 ปีที่แล้ว +9

    Machaalla ❤️💯

  • @serignemortoure11
    @serignemortoure11 4 ปีที่แล้ว +24

    Xame xam bou amoul guistal démal keur seydil hadji malick sy fala ame

    • @maimunabah6403
      @maimunabah6403 4 ปีที่แล้ว

      masahallah si sama sering babucarr sey

  • @wadeabdou6069
    @wadeabdou6069 4 ปีที่แล้ว +7

    mashaAllah

  • @deffaly9056
    @deffaly9056 4 ปีที่แล้ว +1

    Masha ALLAHOU khol sèddna, Mame Boye Mame
    Babacar Sy 😊💕🌷❤

  • @iboudieye1255
    @iboudieye1255 4 ปีที่แล้ว +1

    Yalla na yalla fayale niou baye mbaye donde mbaye 💖💖💖

  • @khadydiop2397
    @khadydiop2397 4 ปีที่แล้ว

    Babacar mbaye dafma nekh trope yalla na yalla yoku sa lèrou deunou si sa barkè tourondô mame khalifa amorom jamais du plus grand jamais🙏💝💙💗💞👍🏼👍👍👍

  • @zakariadeune2296
    @zakariadeune2296 4 ปีที่แล้ว +13

    Kén dou serigne babacar sy ma challah

  • @babacardieng7374
    @babacardieng7374 4 ปีที่แล้ว +14

    Ken dou sama torando Serigne Babacar sy😭❤

  • @absadiene9139
    @absadiene9139 4 ปีที่แล้ว

    Mchala bilay makoy beug piir borom bonet carré bii ah sakaryalla bii ham ham bii dieureuf serigne babacar sy❤❤❤

  • @madeleinedieyeamar8547
    @madeleinedieyeamar8547 4 ปีที่แล้ว +2

    Machalah machalah sama khol daffa seed😭😭

  • @ndeyesall1055
    @ndeyesall1055 4 ปีที่แล้ว +5

    Machallah sy malick dieuredieuf. Mame khalifa ababacar

  • @maremesy7276
    @maremesy7276 4 ปีที่แล้ว +1

    Machala dieredief Mame Babacar Sy ma contane

  • @awaawa1703
    @awaawa1703 4 ปีที่แล้ว +2

    Ay Lalhilaha ilalah koumay diokh adiya Serigne Babacar s'y dama bloqué fi thie fronthier bi ndakh Corona bi ay lekouma nanouma wakh lene ak mane sope Serigne va car sy

  • @assaneboye9337
    @assaneboye9337 4 ปีที่แล้ว +3

    Machallah khalifa mbaye

  • @coeur2lion481
    @coeur2lion481 4 ปีที่แล้ว +10

    Sen tv ligéne am tay dafa reye trop khalifa mb ak doudou kéne mb si béne plateau gnou wara wahtané serigne babacar sy tok léne kéne hole sen tv fi ak déwéne

  • @daoudasy4716
    @daoudasy4716 4 ปีที่แล้ว +1

    yalla naniou yalla fayal mame babacar sy

  • @khadydiagnenarr3661
    @khadydiagnenarr3661 4 ปีที่แล้ว

    Mash allh serigne babacar Sy mosi fesse walahi😭😭😭😭

  • @moktarmoh789
    @moktarmoh789 4 ปีที่แล้ว +2

    Tidiane yii xam rek bayeekou ak noum 💪👍💓💯💯💓

    • @fantandiaye6331
      @fantandiaye6331 4 ปีที่แล้ว

      Lu lére nga wax ak dale ak téye si gnome la fékeu bax

  • @diallondeyeanta4432
    @diallondeyeanta4432 4 ปีที่แล้ว

    Machala sy demba yalla n'a yalla yok lèrame sousou Mame Babacar mome lagnou beugue dès chapeau Bâ QG

  • @oumoukebe1747
    @oumoukebe1747 4 ปีที่แล้ว +9

    Université serigne Moustapha s'y oustaz machlah

  • @aidaguene1948
    @aidaguene1948 4 ปีที่แล้ว +2

    Yalla na yalla def jamm ci nieup fier d'être talibé cheikh

  • @papediaw8200
    @papediaw8200 4 ปีที่แล้ว +1

    Ma challah yalla nanou yalla fayal mam Babakar sy tas nousi barkem

  • @paassaneseck9049
    @paassaneseck9049 4 ปีที่แล้ว +9

    wayè kéne dou baye mbaye dondé mbaye thiat bèguè nalla sa sopé depuis keur mamor sarr yaw rk lay déglou souba ak guone

  • @mamydiop6651
    @mamydiop6651 4 ปีที่แล้ว +2

    Machallaha Talibé cheikh

  • @souleymane7584
    @souleymane7584 4 ปีที่แล้ว

    Machalah... Machalah Machalah.. Quelle voix Doudou kene Mbaye

  • @youssoundiaye5864
    @youssoundiaye5864 4 ปีที่แล้ว +2

    dieuredieufe.s touba

  • @djibrildiop4813
    @djibrildiop4813 4 ปีที่แล้ว +4

    Deugue ak dal machalla

  • @abdoudiallo6680
    @abdoudiallo6680 4 ปีที่แล้ว +1

    Ma ' sah ' Allah
    Rta amine

  • @adjagueye6283
    @adjagueye6283 4 ปีที่แล้ว +1

    Machallah Yana yalla doli léram

  • @aliousarr6168
    @aliousarr6168 4 ปีที่แล้ว

    جزاک الله خیرا یا استاذ خلیف بی

  • @oumarsarr2755
    @oumarsarr2755 4 ปีที่แล้ว

    MachAllah ❤️❤️❤️

  • @abdoulba3605
    @abdoulba3605 4 ปีที่แล้ว +1

    Lou yeme si keur maodo palatoe bi 4 frère moi santé mbaye

  • @sopebayamesanteyayame5397
    @sopebayamesanteyayame5397 4 ปีที่แล้ว +3

    Mokofi wakh dé, meussoul moy boromame, bènène serigne wakhoukofi, bilahi s babacar sy

  • @khadydiallo8311
    @khadydiallo8311 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalla yalla na yalla fayy ooh Machalla

  • @mounzzfrederic1148
    @mounzzfrederic1148 4 ปีที่แล้ว +2

    Thiey serigne babacar sy sunui mame nui bakh dji

  • @coeur2lion481
    @coeur2lion481 4 ปีที่แล้ว +6

    Bilahi liga wah dek sen tv sa kaw lay déme serigne mo tolou nonou sougnou diahlé rék woco mou fath sohlayi

    • @ndiassegueye1933
      @ndiassegueye1933 4 ปีที่แล้ว

      lolou lako yalla defal. nena fouma sama sopé wowé tamouy deugg ma niew taxaw

  • @mbayengom4797
    @mbayengom4797 4 ปีที่แล้ว +3

    Machalha serigne babacar sy yalna yala yoku leram taz niou si brkuem

  • @absadiop5631
    @absadiop5631 4 ปีที่แล้ว

    Machallah bonne courage yalla nala yalla defal diam

  • @tallaseck1270
    @tallaseck1270 4 ปีที่แล้ว +1

    Machala😍😍😍😍

  • @gorafall9444
    @gorafall9444 4 ปีที่แล้ว +1

    Oooh Serigne Babacar Sy khoutboul Hajtab

  • @mansourdiop497
    @mansourdiop497 4 ปีที่แล้ว

    Mashalla kholll yi sed na trop bilahi

  • @bnydiop975
    @bnydiop975 4 ปีที่แล้ว +1

    Khalipha mbaye khalipha mbaye yalla boo fatou yay Mbaye eskey ya ngi wakh si gor gou amoul morom

  • @baamdymousta1359
    @baamdymousta1359 4 ปีที่แล้ว +2

    Kén dou cheikhal khalifa

  • @khalifadiop6168
    @khalifadiop6168 4 ปีที่แล้ว

    Machalla mame khalifa babacar sy

  • @assaneboye9337
    @assaneboye9337 4 ปีที่แล้ว +3

    Khame khame moyorr dhé

  • @djibaibrahima8497
    @djibaibrahima8497 4 ปีที่แล้ว

    Machalla amna solo lo

  • @abdoukarbalatv5250
    @abdoukarbalatv5250 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalla

  • @madadiop8345
    @madadiop8345 4 ปีที่แล้ว +2

    Ani Khalé Yi Dioudou Si Guinaw Mbaye

  • @mamounidiarra3880
    @mamounidiarra3880 4 ปีที่แล้ว +1

    Machalla machalla

  • @yebesylla2045
    @yebesylla2045 4 ปีที่แล้ว

    Machalla 🥰😍❤❤

  • @daoudadioptalibe7809
    @daoudadioptalibe7809 4 ปีที่แล้ว +1

    Masalá

  • @cissmeissaciss5110
    @cissmeissaciss5110 4 ปีที่แล้ว

    yalna yalla kharéko lér

  • @ndiassegueye1933
    @ndiassegueye1933 4 ปีที่แล้ว +1

    CHEIKHAL KHALIFA rta yaa yoré diammii rééw mi diammi diiné dji ak tarikha cheikh bi

  • @kenediop3894
    @kenediop3894 4 ปีที่แล้ว

    Machalla mane ma beug sama mame yi bilahi sy

  • @maramatadiaw2134
    @maramatadiaw2134 4 ปีที่แล้ว +1

    Masha lla

  • @linendao3591
    @linendao3591 4 ปีที่แล้ว +3

    Thiéy khalifa kene dou serigne babacar borome bonecare bi

  • @serignefall1258
    @serignefall1258 4 ปีที่แล้ว

    Meilleur partie

  • @khadydiallo8311
    @khadydiallo8311 4 ปีที่แล้ว +1

    Bilahi

  • @kadiatadjigo5668
    @kadiatadjigo5668 4 ปีที่แล้ว +2

    👍👍🙏🙏🙏🙏

  • @mouhamedattidiany5061
    @mouhamedattidiany5061 3 ปีที่แล้ว +1

    Nioune Tidiane🤍💫 beug naniou🤍 Mbaye gueme naniou 🤍Mbaye dieufé sél naniou 🤍Mbaye def naniou 🤍Mbaye souniou xol yii kénn dou 🤍Mbaye si nioune 🤍

  • @mamanndiaye9138
    @mamanndiaye9138 4 ปีที่แล้ว

    yalna yallah tas niou si barkem ta teyel niou sounouy pas pase

  • @madineamar7322
    @madineamar7322 4 ปีที่แล้ว

    Yalla na yalla Yokou leram
    Tas nous sibarkem amna solo

  • @thedemocrate6687
    @thedemocrate6687 4 ปีที่แล้ว

    ana sopé serigne babacar sy

  • @taphadiallo1091
    @taphadiallo1091 4 ปีที่แล้ว

    Mashaala

  • @arounadiallo967
    @arounadiallo967 4 ปีที่แล้ว

    Mansh'allah

  • @modoubah1345
    @modoubah1345 4 ปีที่แล้ว +1

    machalla sy

  • @Miss-n2i
    @Miss-n2i 4 ปีที่แล้ว

    Mashallah

  • @ahmeddamarushakur7596
    @ahmeddamarushakur7596 4 ปีที่แล้ว

    Jajeuf🙏❤️

  • @serignediabeldrame1308
    @serignediabeldrame1308 4 ปีที่แล้ว

    Merci

  • @morcisse7909
    @morcisse7909 4 ปีที่แล้ว

    Almaktoum ken do mom machala Khalifa mbaye

  • @ciregaye4895
    @ciregaye4895 4 ปีที่แล้ว

    ❤❤❤❤❤

  • @abdoudiallo6680
    @abdoudiallo6680 4 ปีที่แล้ว +7

    Rta amine

  • @barragueye8213
    @barragueye8213 4 ปีที่แล้ว +3

    Akassa