Bilahi je peux témoigner d’elle une maman gentille adorable j’étais très petite quand elle a quitté ce bas monde mais je n’oublierais jamais lorsqu’elle m’a sauvé du serpent qui voulait me mordre Ta Mame Samb Diop à jamais dans nos cœurs.Bilahi Aboubakry souguéne gorgolou diguéne ame lou kawé sen diorte par ce que sa yaye liguéye na sa keur pape .Wallahi une femme très belle et pieuse courage frère
Ndeyssane je te comprends bilay yak da meti moi j'ai perdu ma mère bimay âme 4 mois mais sante yalla bimou ma bayi ak yaye diou bakh ak papa massa yalna yalla may mougne
Gnak metina mé kousa xell dem sii mbamel yonneti Rassoul lilah nga mougne té nga xameu nii lou wayy dii doundou tayy diar na si louko raweu courage yallah borom khep doli inchallah
Walahi kou niakoule sa yaye meunoulo ko khame gni fi sen yaye dess yalna niou fi yague t weer, nioune gni fi sunu yosse diogué yalna yalla yessale yeurmandé si niome g encore pleuré. mane d beugue nala dakh lébou gui, sope nala nakh Khadre yi ga beugue. bonne continuation😍🥰🥰
Rien mon cher, ma chère, c’est pourquoi il faut faire pour elle quand on en a les moyens et même si on en a pas, car c’est le jour où elle part que tu te rends compte de sa valeur. Moi j’ai prouvé à ma mère tout mon amour jusqu’à participer stoic à son lavage mortuaire étant l’avant cadette de ma mère car mes frères étaient en Europe et je suis la seule qui pouvait être à ses côtés le plus tôt possible. L’ayant informé de mon arrivée pour prendre soin d’elle a 16h heure de Goma en RDC, on m’a annoncé son décès pendant mon transit à mon arrivée à Addis, je ne l’ai vu que dans un casier mortuaire et l’ai accompagné dignement jusqu’à son enterrement à Touba et Serigne Basse Mbackè et toute sa cour m’ont entouré et l’on enterré dignement comme une vraie Shérif car petite fille directe de Cheikh Bou Kounta Ndjassane. C’est Dieu qui te donne cette force. Je ne le souhaite à personne. Faites du bien pendant qu’ils sont encore en vie, vos parents pour ne pas le regretter demain.
Gniak dafa metti 😢massa Aboubacar j'ai des larmes aux yeux g perdu mon Papa mais en vous écoutant je ne peux plus me retenir oh la vie yalna yalla xarélen aljana firdawsi
Ndéyssane niak yaye dafa méti paix à son âme yalnanga déssé barké bi longue vie à toi sama kharite bi yalnala yalla ték lokho si barké Serigne Babacar sy rta
Macha alla j'aime Serigne Babacar!!! Yalla Nala gorgui aralbopam lakhla fou yakk khamoul. On t'adore Aboubakry. Defal clip ga way thisa tourendo def thi tabala lolou dinagniou nékh.bétébétébi fodiar yonla❤❤❤❤
L idole de mon fils cadet j ai eu la chance de te le dire et tu lui as fait un son via un cousin qu il garde jalousement. Longue vie à toi et du courage.
Machallah frèro tay sama khôl dafa fess Yaye mom kéne le thie dom yalla nala yalla may kholou mouñe té kharéko aldiana je t’encourage et bonne continuation🥰🥰
Tu m as fait tellement pleure car je vis le vide autour de moi sans sama yaye mais Alhamdouillah inna lilahi wa inna ileyhi rajoun. Yalla na sunu borom yessal yeurmande si wadiour te khare leen aldiana si barke yonente bi PSL
J’ai besoin de mes parents 😢tay weutt na trop yaye pape kengue ci Man j’ai perdue beaucoup de choses dans ma vie tay Bou. Sama yaye niawaton diaral nama niak lepp ci sama avenir gir mome yaye yaye yaye oie rek yama mana comprendre mes personnes d’autres personnes tu es seul 😭
Bilaye je le comprends bien quand il dit " dama nam sama yaye " plus de 20 ans que ma maman est partie et elle me manque énormément mais c'est la vie mon frère du courage
Ndeysane une mère est irremplaçable Et que jamais dome mag thi kanamou yaye Yalna ya rabbi yereum waydiour you deudou yeup sans exception . Gni fi dess mou May léne fane you goudd incha Allah Amine
Massa frère Lou metti ngeuy wakh kouko doundoul douko kham Yalla na Yalla yokk sen lére kou meun profito saye na ngeu profité ça me rappelle bcp de chose di ngeu sokhla wakhtan puisk amna yo kham ni sa yaye rek ngeu meun Wakhal 😭
Mane mom damako beugue en 2021 defaralone nama vidéo anniversaire ba tay dama KO gardé sama phone 😂 diko statut chak anniversaire 🎉😂 mais nitt kouma naw lah barki seydina mouhamed PSL ❤yalnako yallah samb si barké alkhourane
Bilay mame guay wakhal dama dioye ba sonne magui sa place yaye bou febar ay att am insuffisance renal do am vie tout le temps daganan tay lay dem mé yalla bakhena
Bilahi je peux témoigner d’elle une maman gentille adorable j’étais très petite quand elle a quitté ce bas monde mais je n’oublierais jamais lorsqu’elle m’a sauvé du serpent qui voulait me mordre Ta Mame Samb Diop à jamais dans nos cœurs.Bilahi Aboubakry souguéne gorgolou diguéne ame lou kawé sen diorte par ce que sa yaye liguéye na sa keur pape .Wallahi une femme très belle et pieuse courage frère
Mon frère 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Ndeysane yalla na yalla taxawou leu thi barke serigne babacar sy ❤
L’homme brave MACHALLAH ❤️😭
Ndeyssane je te comprends bilay yak da meti moi j'ai perdu ma mère bimay âme 4 mois mais sante yalla bimou ma bayi ak yaye diou bakh ak papa massa yalna yalla may mougne
Masta waay yalna ko yalla yeurem ak keep kou djitou🙏🙏 sama tomaa mané
@@manishounaby2341 merci c la vie mais sant yalla rek alhamdoulilah
😭😭
Même moi aussi ma mère avait le cancer du foie bilahi dafa meti trop 😢😢😢
Qu'Allah l'accueille dans son paradis céleste 🤲Machalla force à vous bro et bonne continuation ❤🦋✌
Dangay dem ziar ko tokk wakhtane ak mome
Sois sûr que ta maman veille sur toi et ta famille.
Du courage❤❤❤
Gnak metina mé kousa xell dem sii mbamel yonneti Rassoul lilah nga mougne té nga xameu nii lou wayy dii doundou tayy diar na si louko raweu courage yallah borom khep doli inchallah
Walahi kou niakoule sa yaye meunoulo ko khame gni fi sen yaye dess yalna niou fi yague t weer, nioune gni fi sunu yosse diogué yalna yalla yessale yeurmandé si niome g encore pleuré. mane d beugue nala dakh lébou gui, sope nala nakh Khadre yi ga beugue. bonne continuation😍🥰🥰
J’ai beaucoup pleuré en l’écoutant
Rien ne peut remplacer la mère
Rien mon cher, ma chère, c’est pourquoi il faut faire pour elle quand on en a les moyens et même si on en a pas, car c’est le jour où elle part que tu te rends compte de sa valeur. Moi j’ai prouvé à ma mère tout mon amour jusqu’à participer stoic à son lavage mortuaire étant l’avant cadette de ma mère car mes frères étaient en Europe et je suis la seule qui pouvait être à ses côtés le plus tôt possible. L’ayant informé de mon arrivée pour prendre soin d’elle a 16h heure de Goma en RDC, on m’a annoncé son décès pendant mon transit à mon arrivée à Addis, je ne l’ai vu que dans un casier mortuaire et l’ai accompagné dignement jusqu’à son enterrement à Touba et Serigne Basse Mbackè et toute sa cour m’ont entouré et l’on enterré dignement comme une vraie Shérif car petite fille directe de Cheikh Bou Kounta Ndjassane. C’est Dieu qui te donne cette force. Je ne le souhaite à personne. Faites du bien pendant qu’ils sont encore en vie, vos parents pour ne pas le regretter demain.
Gniak dafa metti 😢massa Aboubacar j'ai des larmes aux yeux g perdu mon Papa mais en vous écoutant je ne peux plus me retenir oh la vie yalna yalla xarélen aljana firdawsi
Oh massa c émouvant
Très émouvant et y’a notre yaye encore yaye tjrs yaye wlh nioune gni ko dessé warnaniou profito thi sen existence 😢
Ndéyssane niak yaye dafa méti paix à son âme yalnanga déssé barké bi longue vie à toi sama kharite bi yalnala yalla ték lokho si barké Serigne Babacar sy rta
Bilay ndeyssane sama papa nonou laniou beugue beuguoul d'ara louniou meti yalna yalla goudeul fan name ak sama yaye machallah dioyou ma yaye ben nion
Sama makk dji Sama keur la koy tekk magal di ko way lo serigne babacar yalla na sa diam yagg ❤️❤️
J ai pleuré lolou laye dounde mais yalla bakhna courage Bonne continuation
Machallah frère yalla nala yalla samal bopam courage yalla na yalla yéssal yeurmandé thi sa yaye 🙏❤
Macha alla j'aime Serigne Babacar!!! Yalla Nala gorgui aralbopam lakhla fou yakk khamoul. On t'adore Aboubakry. Defal clip ga way thisa tourendo def thi tabala lolou dinagniou nékh.bétébétébi fodiar yonla❤❤❤❤
L idole de mon fils cadet j ai eu la chance de te le dire et tu lui as fait un son via un cousin qu il garde jalousement. Longue vie à toi et du courage.
Courage yalla na yalla mayyy laaaa kholou mougne takhawou sii barké sougnou wasiila bii seydiii aboubacar rta ❤❤❤
Très émouvant. Elle reste à tes côtés. Qu’Allah Azawajel te garde et te protège 🤲🏾
Je ne l ai pas encore ecoute mais je l adore a cause de notre prophete mohamed rassoul swt
Ndeyssane
G op puis retenir ms larmes blh k firdawsi soit sa demeure éternel 🙏🙏
Mame Coumba Talibé Cheikh leu ndeyssane 😘
Vraiment meitina niak yay srtou si circumstances yi mai sante yalla nitt kou bakh la Abou inshalah lou bakh rk ngay amm
machallah fiére d'etre talibé cheikh
Machallah sama chanteur bi je l'aime bilay
Yalla nala yalla may kholou mougne
Machallah Abou diam rek ngay ame inchallah. Sunu yaye Yalna khipé aldiana. Sunu papa borom bi bayiko fi bassi kanama kanam
Yalla na ngou yalla yeureum meul sounou wadiour yi yaye dafa nekh machaallah
Machallah frèro tay sama khôl dafa fess Yaye mom kéne le thie dom yalla nala yalla may kholou mouñe té kharéko aldiana je t’encourage et bonne continuation🥰🥰
Walwara bi oh j'adore suis mouride mais ah
😢😢😢 oh papa Abou dama dioye ba soneu
Ndaysan que le tout puissant te fortifie ❤
Tu m as fait tellement pleure car je vis le vide autour de moi sans sama yaye mais Alhamdouillah inna lilahi wa inna ileyhi rajoun. Yalla na sunu borom yessal yeurmande si wadiour te khare leen aldiana si barke yonente bi PSL
Machallah❤❤❤❤❤❤❤❤ que le bon Dieux te protège Amen
J’ai besoin de mes parents 😢tay weutt na trop yaye pape kengue ci Man j’ai perdue beaucoup de choses dans ma vie tay Bou. Sama yaye niawaton diaral nama niak lepp ci sama avenir gir mome yaye yaye yaye oie rek yama mana comprendre mes personnes d’autres personnes tu es seul 😭
Massa ces triste vraiment delen nianal bou bax et du courage
il m'a fait pleurer parce que je me suis mise à sa place quelque instant
Machaala sama wadjii content trop thi yow du courage c'est vraiment émouvant
Yalla nala yalla samal bopame thi barkep seydouna psl
Tres émouvant defgua sawaref.Dieu a décidé autrement. Que dieu te protège
😭😭😭👉❤️❤️❤️massa yalnako yalla yeureum 🙏
Machallah frère courage Yalla na ko Yalla yeureum kharé ko Aldiana ci Barké Muhammad psl
Bilaye je le comprends bien quand il dit " dama nam sama yaye " plus de 20 ans que ma maman est partie et elle me manque énormément mais c'est la vie mon frère du courage
Yalla nako yalla yeureum té diegueule ko yalla sam la tji barké serigne babacar sy ❤
Ohooo machallah ❤🎉
Mon'frére'que'ta'mére'repose'en'paix'inechalah🙏🙏❤️❤️
Ndeysane une mère est irremplaçable
Et que jamais dome mag thi kanamou yaye
Yalna ya rabbi yereum waydiour you deudou yeup sans exception .
Gni fi dess mou May léne fane you goudd incha Allah
Amine
Machalah ❤ mame coumba ont te demander amsa de la serie maîtresse d'un omme marié
Très bonne émission
Doudeul werreul amale diam thi barke serigne babacar sy aminé yarabi aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne
Mashalla mame coumba tu fait une belle émission
Bilahii métina yaye feneu amoul fayam franchement diabar gua dicourage yalla bakhna yalla nala borom boné caré bi aral boop
Bilahi fréro tu m'a fait pleuré walahi kéne menoul remplacé yaye ci adouna ❤paix à sn âme ❤sama yaye moy sama leup ❤❤
Coumba Tu es vraiment magnifique ❤
Machalah tu as une belle voix bonne continuation
Que la terre soit légère firdawsi ♥️🤲🤲
11:30 je ressens exactement ce que tu ressens
Kuko dundoul meunul comprendre😢
Ndeysane sama sopè bii taylala gueneu beugue parsk perd une maman s telma douleureux j vie la même situation kome tw ma maman me mank telma
Première fans ❤
Allahouma amine inchallah
Machalla tay dh maffi ndieuk ak sama sopè bi ❤
Yalla nako Yalla yeureum
Non coumba machalla c’est une bonne journaliste vraiment
Machallah sabm
Longue vie à nos mamans ❤❤
Machallah lolou rafetna lou rafet daffa rafet
Massa frère Lou metti ngeuy wakh kouko doundoul douko kham Yalla na Yalla yokk sen lére kou meun profito saye na ngeu profité ça me rappelle bcp de chose di ngeu sokhla wakhtan puisk amna yo kham ni sa yaye rek ngeu meun Wakhal 😭
Du courage metina cette douleur est inexplicable massa😢
Mach alla rek Dicourase mon cher ✅✅✅✅
Ndeysane 😢keine meunoul remplacer yaye
Ndaysaan yaay ken amoul fayam ❤️❤️❤️
Hooo aboubacry samb mane ki rk la beug
macha Allah❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dioyloguama koumou daloul meunoko kham dama nam sama Yaye cette phrase yobounama fou sori lolou lay ndound ni massa mon frere 😢😢
Demako nam ndeysanne Yalla na xippe firdawsi si Barker seydina Mouhamed psl
Aboubacry simplo dé 🤭🤔🤨
Alap lébou ❤😂
Maman tu nous a laissé dans le vide😭😭😭😭😭😭😭😭
Ndeysan fosco kennedy lako guiss pour la meilleure fois souniou école la dioukhe samba gueye ba kennedy 😻🎉❤️ nan beugeu ko 🥺
C'est comme si que Wally mo tokk Di wakh😂😂😂
C'est le sang
Lol la wakh mm voix ❤❤❤❤😅
Mane mom damako beugue en 2021 defaralone nama vidéo anniversaire ba tay dama KO gardé sama phone 😂 diko statut chak anniversaire 🎉😂 mais nitt kouma naw lah barki seydina mouhamed PSL ❤yalnako yallah samb si barké alkhourane
DAGAY WAYE CHEIKHNA CHEIKH SAADBOU NAK AKH SEUTAME CHERIF ALWALY MANE NDIAYE
Tabala koukoy begoul sa afér la
Abou masta teye dafa neih
Tivaouae toujours tabala dorfa
Massa laye makhtar 😭😭😭
Masa paix à son amê 😢
❤❤❤❤❤
Invité mabou😢😢
Aka méty niak yaye kouko doundoul meuneu ko kham massa
Ay yaw coumba bayil di dioylooo niit yiii
Bilay mame guay wakhal dama dioye ba sonne magui sa place yaye bou febar ay att am insuffisance renal do am vie tout le temps daganan tay lay dem mé yalla bakhena
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Revoyez votre son svp ca deviens répétitif.
Invite Bath masamba 😮😮😮
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😭😭😭🤲🤲🤲🙏
Thiey aduna koula waxx djar djaram ga faté sa boss
Batou wally Seck
Bilahi ❤😅
❣️
Yagui maye diolo yaye kouko niaka dioyko