Li am wakhou niouko dé walahi wakhe dji désse n'a dou waloum goor djigene walahi sou wax dofé nopyi Koy deug vara niité Aziz boudé goor djigene kou dém négam digafa fék ay indix tout goor djigene yallana yalla lééral léép thii barkep seydina mouhad psl
Nga am 37 ans diour dome bou am 20 ans di weur nane Aziz sama papa la nabou mi louniouko wakhal moko def dinga kham ni nak loudoul dioub diouba ko geune ko beugue doko boler ak ay bandit sa kanam bou niemer bi def ngen niou louniou meti trope wayer Lou way def bopam
"Ma fekke la police bëg te man mi ma fekke":NL Quelle coïncidence ! YALLA naleen YALLA yërëm te jegeul leen te mousseul gnou ci lou bonn ak defkatou lou bonn
Depuis assassinat de Aziz dabala et wally sama khôl nékhoul damay teudeu ba goudi diko khalat ndakh Ray bou niaw bou méti bouniou léne Ray surtout le jeune wally ,ils ont souffert avant de mourir oooooh 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 que firdaws soit leur demeure éternelle
Les faits se sont déroulés le lundi au lieu de dimanche car wally était parti au travail le lundi et un ou une voisin(e) a dit entendre 2 cris matin et soir .donc il faut savoir ecouter nous sommes trop émotionnel
Je vous donne rendez-vous ce soir à 20hgmt sur votre dossier d'actualité qui fera des révélations sur l'enquête du meurtre de Maman Aïcha Ndong à Bargny . Merci d'abonner sur notre chaîne pour suivre nos dossiers d'enquêtes exclusives
Té Yow NABOU leye y’a wakh lii yeup, Tey la bayi aduna. Ngani aziz baye fall la, wakhtou diouli d’où ko raw, patati patata… Tey nga key takal goordjiguene. Yaye domou khathie. Yow meritewo sakh doundou. Yalla na la borom bi gueuneu wer
@@AichaDia-vv3vnli dé la wakh mane com guisnani clip yi moudié yépp troupe aziz ñioko féthi mou beuguone sou affaire yi sédé mou continué thé damako défendre ba sone domérame dji
@@halikano392 mané nabou leumbeul ak gniaka leumbeul lathi yamale nabou sokhor rek mo takh ray azizz pour bou azizz demé mou jel palassbi sokhor ba bouga de
Bravo Seydina, la scène est bien retracée. J'aimerais aussi savoir si vous avez des nouvelles des autres dossiers de meurtres qui ont eu lieu ces derniers jours ? Est ce que la police fait les mêmes efforts pour traquer les auteurs des autres meurtres. Il ne sert à rien d'avoir une police qui est active que lorsqu'il s'agit des dossiers politiques ou qui concernent des célébrités.
Ont dirait-on que ce voix mais famillale sakara Mbaye ❤❤❤ père daba Mbaye ❤❤❤❤🎉que firdawci soit leurs deumeurs internel inchallah amine ya rabie Allah que dieu les pardonnes
Seytaane moo bari doole, li Olof di wax rekk mooy dëgg de "Mbaam wéq na doomam, waaye bañu ko" Yal na leen Yàlla jubanti te dindi ci ñoom ak kiñaan, te yërëm ñi fi bàyyi koo, xaare leen aljana 🙏
C faux! Aziz a parlé à sa sœur le dimanche même et lui a fait un transfert wave. Le petit Waly aussi est allé travaillé le lundi mais s’est descendu tôt d’après son patron. Donc le crime a eu lieu le lundi
Lima diakhal nabou Leye rèk laniouy wakh Goor you bonne yi bénn djiguéne késsé dirigé lènn baniou dèf lou niaw li warna nio lenn publié sènn tour kom nabou Leye pour nieup kham lènn 6 personnes bénn djiguéne késsé dirigé lènn dafa yombeu trop
parceque Nabou " le MAMBA NOIR " est une grande manipulatrice. Nabou manipulait Aziz, elle controlait la vie de aziz. khana degouloh petite soeurou aziz mouni: aziz moko wakh tegui na nateu, mais nabou leye nango koko diokh, lolou moy lann? lan moye sagn sagn bobou, ? nit tek chaque mois bamou radj, mou wara tegui khalissam, nga bagn ne dokoko diokh ba aziz diko dioytou soeurame. dafa yabone aziz, minn aziz.. ndeysann. aziz naak bakhone beu euopeu nitou diam, beugeu diama, il ne disait rien, khol bobou naak lako souniou borom feye motakh dewam bi, amoul sakh 3 jours, niou diapa lenn niom nieup, tous, te dessna.. gni si khalkou laniou dieum inshallah.. sou att bi delousse te dewouniou, wala niou khalkou, wa khamneh neh ibliss amna deugeune taan ndiaye.
Wakhtou diouli douko raw ba paré nga beug tourmaline aziz ak wali de g.. dji.. c est du n importe quoi! Kouné khamnani soo neké si lobby yoyou da ngay free financièrement parlant. Soussi aziz nekone kone dîna dépasser fii. Sou nguene setloo même waly à la marque de la priere au front. Yalla nalene Yalla yeureum diegal lene teu kharé lene aljannah Firdaws
Meilleur documentaire de toute l’histoire… trés professionnelle 👏👏👏❤️❤️❤️❤️
Yes
KÚ GEUM-NI " on ne peut jamais trouver le bonheur en provoquant le malheur d'une autre personne. LALALE J'AIME 👈
Li am wakhou niouko dé walahi wakhe dji désse n'a dou waloum goor djigene walahi sou wax dofé nopyi Koy deug vara niité Aziz boudé goor djigene kou dém négam digafa fék ay indix tout goor djigene yallana yalla lééral léép thii barkep seydina mouhad psl
Dagni doul rk beug leurrer sénégalais yii ces imbécile
Manedé lila li dafa flou bilay
Non vraiment lii dérou djiguéne geunatina yaxou manr dama rouss bilahi
@@AwaSOGUE-c5c walahi wakhe deug kouy am gathia rék am gako
Pur vérité
Ya rien de compliqué, les assassins veulent semés le doute mais ils sont tous coupables la fille y compris
Pape Sidy Fall akh Aziz Ndiaye yalla nalene yall maye goudou fane amine
Décé meussouma mété nii bilahii walahii té prtan je connais pas azize ni waly mai lignou léne déff nii sa m briz le cœur 😔
Mane lolo ma dale chaque jour sama soumako khalaté am louma méti
Kon deh mak yaw nio yam
Lolu moma dal
Bilahi niep la metii
Maneu ça ma braucoup traumatisè ter nekouma senegal sakh li dafeu meti trop walahi
Meilleur reportage merci bcp frère
Ne faites confiance qu'à vous même 😢yalnalenn yalla yeureum 🥺
On ne peut meme Pas faire confiance a soit meme a cause de Satan. IL faut chercher refuge aupres d Allah alla jallaloo
Amine Ya Rabouna 🤲
@@AissataBah-ih1kp😅p😅
Kou d'accord ni pène de mort Dina diafè fici Sénégal wayè perpétuité meune na nèk avie rèk tca kassoba
Sénégal nehna danu lay fate ba nopi dila sossale 😢😢😢😢
Nga am 37 ans diour dome bou am 20 ans di weur nane Aziz sama papa la nabou mi louniouko wakhal moko def dinga kham ni nak loudoul dioub diouba ko geune ko beugue doko boler ak ay bandit sa kanam bou niemer bi def ngen niou louniou meti trope wayer Lou way def bopam
Walakhi
C'est une vraie domerame se nabou
😅😂😅😅😅😅
Doyna War trop trop trop sakh
Personnellement je connaissais pas Aziz et je croyais c'est une personne âgée vu k Nabou ne cesse de dire k c'est son papa
Merci si éclaircissements yiii .naniou dehh si kassoo biiii Wala Niou reyy sen Ndeye car Ayii domarame laniou nieup.....
Amna solo lôol merçi❤❤❤❤❤
Li bokouna si lima guena métti si aduna c'est vraiment triste 😭😭😭
Mâcha allah seydina kadou yi amena solo lerena nagne Dieuredieuf
"Ma fekke la police bëg te man mi ma fekke":NL
Quelle coïncidence !
YALLA naleen YALLA yërëm te jegeul leen te mousseul gnou ci lou bonn ak defkatou lou bonn
😮 Que la terre 5 Sénégal leurs soit légère inchallah
Depuis assassinat de Aziz dabala et wally sama khôl nékhoul damay teudeu ba goudi diko khalat ndakh Ray bou niaw bou méti bouniou léne Ray surtout le jeune wally ,ils ont souffert avant de mourir oooooh 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 que firdaws soit leur demeure éternelle
Machalaha❤seydina un grand messieur 😢tu m'a touché ❤vraiment avec le fond musical REPOSE EN PAIX 🕊 😭
Daffa massoul amm gnaw'na trop
@@charlottecurtis4065 Li dafma metî
Li comme film bilahi 😢😢😢
Nabou daye jouer film mé mokalagoul❤
machala reportage amna solo
Yalna léne yalla yeureum té kharé léne aldiana firdawsi 🙏🙏🙏
Machalla très réussi ❤ et c’est vraiment triste 😭
Les faits se sont déroulés le lundi au lieu de dimanche car wally était parti au travail le lundi et un ou une voisin(e) a dit entendre 2 cris matin et soir .donc il faut savoir ecouter nous sommes trop émotionnel
il est bel et bien mort Dimanche soir! les alegation du Lundi ne sont pas confirmé
Merci,❤
Alakhou akbar 😭 li mom noko manaaa diangueee 😢
❤❤jutice pour AZiZ et Waly❤❤
Thank you
Ray nit ba paré diko sossal
Lolou mo gueneu graw si histoire bi « elle a dit neke baye fall, ba paré di djouli »nite mono di djégué yallah di djouli sa khel di dem si yeneu yi.
Fène rek, wayè douko ci guènè
Décès yi sénégalais yeupe la méti
Merci beaucoup seydina fier de vous ♥️♥️♥️
Yallanalene yallah yereume té kharelene aldiana firdawsi amine
Li yep ay pekhé nabou laiy ngen ray nit baparé dellou diko sosal diko fenal😢nabou ya bon
Belahi wakh dji niawna trop rayko ba pareh di ko sosal rek pour geineh si
Je vous donne rendez-vous ce soir à 20hgmt sur votre dossier d'actualité qui fera des révélations sur l'enquête du meurtre de Maman Aïcha Ndong à Bargny .
Merci d'abonner sur notre chaîne pour suivre nos dossiers d'enquêtes exclusives
Massa au défunts que le paradis soit votre demeure
Kou nangoo nekal ak Bathi Seras kaay sagne nga louné
Défnagnou lougnawa gnaw.
Yalla nalen yalla até si yeurmendem
Li lernaaa big respect 🤦♂️🤦♂️🤦♂️les mort yalla n’a len yalla yeureummmm
Ndeyssane yàllah ne ko yàllah yeureume kharéko aldiana firedaweci 😭😭😭😭
Té Yow NABOU leye y’a wakh lii yeup, Tey la bayi aduna. Ngani aziz baye fall la, wakhtou diouli d’où ko raw, patati patata… Tey nga key takal goordjiguene. Yaye domou khathie. Yow meritewo sakh doundou. Yalla na la borom bi gueuneu wer
Nabou Kay dmrm la rek💔
Aziz dale baye fall leu diouli dou ko raw mou déh subitement comme par magie mou nekk lénéne dale…mais ñi kou ñou ñépe
Ya féké wayé ya andeu ak ay nit niou rayko ba paré nguén sossalko, yakheu déram. L'histoire dira son mot
Merci
Ay waay li metina deum Ray la diale la Sénégal yakhouna😭🫢
Maneu dale diomina lou bonne li nouko niteu meunè deff double meutre ah sokhor amna nak repose en paix Azize et Wally
Belle documentaire très précis
Doyen warr Billahi
Machallah lerall nga kep
Lima wor moy population bi xamagouñu dossier bi au fond
Kéne xamou si Dara daniouye doule rék
@morndiasa papa molen wakh douleye3623
Cas bi si bopam mo compliqué louno yague préparer la motax
Merci frère diangatt mo meilleurs ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
nabiu mome beugou ko wone
vu son comportement apres le décès de aziz
impossible d’aimer quelqu’un et de se comporter ainsi
Merci nabou defa bougon elminè azizz pou mouna nekka palass aziz
@@AichaDia-vv3vnli dé la wakh mane com guisnani clip yi moudié yépp troupe aziz ñioko féthi mou beuguone sou affaire yi sédé mou continué thé damako défendre ba sone domérame dji
@@AichaDia-vv3vnmouye djiguéne di leumbeul Aziz leumbeuloul leumbeulaléwoul wala noumouye beugué palacame 😢
@@halikano392 mané nabou leumbeul ak gniaka leumbeul lathi yamale nabou sokhor rek mo takh ray azizz pour bou azizz demé mou jel palassbi sokhor ba bouga de
@@garyibra9425 mo linga khalat loolou mo nafikh yii rek gnioy defender nabou raykatou nit bou bonbi ray nit baparé delou diko sossal
naniou dé si kasso bii niomm nieup gno comploté aziz
Yallanalén yalla yeureum😢😭 ndeysan méttina nk mais lou way déf boppem leu
Paix a leurs âmes😢
Nabou dayesane métina ly kéne khamoule lane la Yalla nagnou Yalla mouthiale
Senegal yep nabou laiy mo gina bon gina yees gina sokhor nabou yew do gor😢
Bravo Seydina, la scène est bien retracée. J'aimerais aussi savoir si vous avez des nouvelles des autres dossiers de meurtres qui ont eu lieu ces derniers jours ? Est ce que la police fait les mêmes efforts pour traquer les auteurs des autres meurtres. Il ne sert à rien d'avoir une police qui est active que lorsqu'il s'agit des dossiers politiques ou qui concernent des célébrités.
Li doyna warrr boutayé niouné dakadone khebelle bousouba gua dégat lénnéne
Wakhouniou deug
Avec tt c vs voulez l'éliminer et être dans la paix et non Lolou meunoule nekkk.femm bii domarame leuu badola leu mai Yone nalen reyy niome nieupeuu
Amine
Salam seydina seck malla diayone oreilles yi mariste residense seyna
Meilleures chroniques
En tout cas keneu khamoul fou deug bi nek naniou bagna juger yalla reka kham té nianal waay dawlou yi yeurmandeye yallah
Je ne suis pas d'accord sur le mobil, Aziz était propre et net pieux. Eliminer une personne et jeter l'approbe sur lui ce n'est pas normal
Yalla na yalla tabal len aldjana 😢😢
Ndeysane 😭😭😭😭🙌
Ont dirait-on que ce voix mais famillale sakara Mbaye ❤❤❤ père daba Mbaye ❤❤❤❤🎉que firdawci soit leurs deumeurs internel inchallah amine ya rabie Allah que dieu les pardonnes
J’ai eu la même impression. On dirait que c’est Sankara Mbaye
Pourquoi Ndésaane Nabou??? Ndésaane Abdou Aziz Ba Oui🥺😭🥺
Bépa Ndéye bou beugoul sa dome dioye sou magué dioylo la soula réyoul yaw mi ragal sa YAYE ta kafo nabou wala wolof yi la dégoul mane😢
Paix à leurs âmes
Thiey Adouna 😮😢
Mane mom Diao yi yémé naniou ma dé dama beugu kham boudé niom nieup nio bokk bén famille franchement lii gathié la thi niom une famille 3 personnes 😢
Seytaane moo bari doole, li Olof di wax rekk mooy dëgg de "Mbaam wéq na doomam, waaye bañu ko" Yal na leen Yàlla jubanti te dindi ci ñoom ak kiñaan, te yërëm ñi fi bàyyi koo, xaare leen aljana 🙏
ALLAHOUMA Amine MACHALLAH néna cest Collé bagnou soupçonné ko thi association malfaiteurs yi bokka thi gni diapalé gni réye sa domou Ndéye colle crazy YALLAH nala YALLAH soutoural ba doudone deugua🤲
@@halikano392 Aamiin 🤲. Te Yàlla musal nu ci ñuñuy gëmël ne ñoo far te demeewul noonu 🤲
Way nabou danio khaptal way tayoul limou def parce que bo kholè nabou interview boumou def dinassi sante Aziz yalla rek mo kham
Mais pourqoui on montre pas leur visages
Mooma diaakhal nk 😢
Moytoulma djiguén bou def diaro laminñ
Aaaaaa😂😂😂😂kula bayi
Wallah degue la
😂😂😂😂😭😭😭
😂
Kou am kersa douko def
Qui est le coupable
Pourtant Nabou mi baniul Aziz déh😭
C'es le bonne information dite moi
C faux! Aziz a parlé à sa sœur le dimanche même et lui a fait un transfert wave. Le petit Waly aussi est allé travaillé le lundi mais s’est descendu tôt d’après son patron. Donc le crime a eu lieu le lundi
Ces deux-là devraient se marier depuis longtemps, que DIEU l'accorde sa miséricorde
Waly lundi lagne ko reye kharitam mouler waly ligueye n'a lundi
Ma féké la police beug ,doyna war
Paix a leur âme
Lima diakhal nabou Leye rèk laniouy wakh Goor you bonne yi bénn djiguéne késsé dirigé lènn baniou dèf lou niaw li warna nio lenn publié sènn tour kom nabou Leye pour nieup kham lènn 6 personnes bénn djiguéne késsé dirigé lènn dafa yombeu trop
parceque Nabou " le MAMBA NOIR " est une grande manipulatrice. Nabou manipulait Aziz, elle controlait la vie de aziz. khana degouloh petite soeurou aziz mouni: aziz moko wakh tegui na nateu, mais nabou leye nango koko diokh, lolou moy lann? lan moye sagn sagn bobou, ? nit tek chaque mois bamou radj, mou wara tegui khalissam, nga bagn ne dokoko diokh ba aziz diko dioytou soeurame. dafa yabone aziz, minn aziz.. ndeysann. aziz naak bakhone beu euopeu nitou diam, beugeu diama, il ne disait rien, khol bobou naak lako souniou borom feye motakh dewam bi, amoul sakh 3 jours, niou diapa lenn niom nieup, tous, te dessna.. gni si khalkou laniou dieum inshallah.. sou att bi delousse te dewouniou, wala niou khalkou, wa khamneh neh ibliss amna deugeune taan ndiaye.
@@ayosk5859amine wayy kii woorkat la yalnagn topp aziz gnom gneup
Gni dal yalla nalénn sounou borom wathié yeumandé thi sènn kaw thi barké Nabil Moustapha
Naniu Ray senn ndey
Raye nite ki ba paré diko djignie goordjiguéne yéna bone
Mane de'nabou diarro bissi laminam bi gneme'xoumako dara ndax kou am kersa douko def
Jai mal au coeur quand je regarde les vidéo
Ndeyesane 🤲🤲🤲🤲🤲👌👌👌👌😥😥😥
Wakhofi dara lou besss goooo
😭😭😭😭😭😭😭
Natou rek
Li mettinama bathia kanamou yalla😢
La musique est trop forte
Nabou Leye dou nite deh
Sama khol fésse na😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Wakhtou diouli douko raw ba paré nga beug tourmaline aziz ak wali de g.. dji.. c est du n importe quoi! Kouné khamnani soo neké si lobby yoyou da ngay free financièrement parlant. Soussi aziz nekone kone dîna dépasser fii. Sou nguene setloo même waly à la marque de la priere au front. Yalla nalene Yalla yeureum diegal lene teu kharé lene aljannah Firdaws
C'est triste 😭😭😭