S MBACKÉ ABDOURAHMANE "Sëriñ Tuubaadu nit bu bul nit..🤷🏾‍♂️| c'est quoi le Mouridisme "3ème Partie

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 1 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 32

  • @MameyoroDime
    @MameyoroDime หลายเดือนก่อน +2

    BOROM TOUBA DOÙ NITTE.DIEUREUDIEUFÉ BOROM TOUBA

  • @mamadoudiakhate5708
    @mamadoudiakhate5708 หลายเดือนก่อน +1

    Dieureudieufati yallah na yallah gouddal sa fan

  • @CheikhNdiaye-z7v
    @CheikhNdiaye-z7v หลายเดือนก่อน +1

    Machallah amna solou jërëjëf mbacke balla li dé warr Na yatou

  • @modousamb3695
    @modousamb3695 หลายเดือนก่อน +5

    Machallah mbacke amna solo

  • @mamadounallaba9495
    @mamadounallaba9495 หลายเดือนก่อน +6

    Merci pour les éclaircissements

  • @FatouchaNdiaye-t5i
    @FatouchaNdiaye-t5i หลายเดือนก่อน +2

    حفظه الله ورعاه إنه عالم مخلص في مقالته يقول للحق .إذا من خالفه فقد خالف الحق❤

  • @ToureBara-tr5vz
    @ToureBara-tr5vz หลายเดือนก่อน +3

    Macha Allah yalna yalla fayla yiw ❤

  • @SabdouGueye
    @SabdouGueye หลายเดือนก่อน +3

    ماشاءالله جزاك الله

  • @saringemodoujange5519
    @saringemodoujange5519 หลายเดือนก่อน +3

    ماشاء الله تبارك الله ياالشيخ احمد محمد

  • @Djilydiob-jf2ey
    @Djilydiob-jf2ey หลายเดือนก่อน +3

    Ahmadu Mbákk kepp rekk ndong jaajëf ❤❤❤❤❤❤

  • @galasfall7419
    @galasfall7419 หลายเดือนก่อน +1

    Ma challa

  • @seydounouroukonte6891
    @seydounouroukonte6891 หลายเดือนก่อน +1

    Serigne bi moudiadid la
    Yessal dînè
    Kou dondou yonentabi cie xam xam
    Ar Rassoul
    Serigne bi ayy yitèm yallah rek la wo nitt yi cie Dieubeul sèn boppou cie yallah ba dièkh tax

    • @seydounouroukonte6891
      @seydounouroukonte6891 หลายเดือนก่อน

      Tella nangou lou mou dône
      Noppal la
      Titre boumou ám yallah mokko nommè
      Dè dina am matt yènen
      Lolou mbirroum allah la
      Serigne bi ma beugeul sama boppou gnirr yallah
      Lire le coran et méditer sur les versets moy sakkou yallah agreer la

    • @seydounouroukonte6891
      @seydounouroukonte6891 2 วันที่ผ่านมา

      Bama xamè lolou Cie la dieubeullou sama boppou Cie yallah directement
      Et avoir un bon cœur et comportement
      Être miséricorde envers ton prochain

  • @fallougaye1645
    @fallougaye1645 หลายเดือนก่อน +3

    Machalla xam xam Bi rafena

  • @MadyMbaye-q7i
    @MadyMbaye-q7i หลายเดือนก่อน +2

    Dieuredieuf mbacké serigne lépapam dafa ler nagne nek si ahirouzamane di toumal yone wi rek lolou lou mene gnak la

  • @saringemodoujange5519
    @saringemodoujange5519 หลายเดือนก่อน +1

    Good luck and good health and your family members

  • @elhadjifalloubarr5834
    @elhadjifalloubarr5834 หลายเดือนก่อน +1

    Borom Touba dou nit mo wakhe « adiabani rahmanou khabelale khalkhi » diamouna Yalla diouraume fouki diouni ate Yalla sakoul dara

  • @elhadjifalloubarr5834
    @elhadjifalloubarr5834 หลายเดือนก่อน +4

    Borom touba néna : »adiourou mane annassaniya walam yatoub sakhawatoune tadoumou fi oumil koutoub » kep koumay ndiro lé wala dima wala teuklé ak nit yi ngua khamni daniouy faté boko touboul di ngua dem safara wakhi borom touba nak dousamay wakhe

    • @cheikhounalo8342
      @cheikhounalo8342 หลายเดือนก่อน +1

      Linga bind AK linga firi bokul dh esk dioumo
      Dani keep Ku khathio AK man dra teh tubu Loko Sak tekhé Di bind nan ko ndayi tera yi(lawhul mahfus)
      Wasalam

    • @elhadjifalloubarr5834
      @elhadjifalloubarr5834 หลายเดือนก่อน

      @@cheikhounalo8342 adiabani rahmanou khabelale khalkhi » diamouna Yalla diouraume niar fouki diouni ate
      Borom touba dou nit

    • @Rawdourayahine
      @Rawdourayahine  2 วันที่ผ่านมา

      Danga gàtt xam-xam rekk

  • @babacarndong-ge7mc
    @babacarndong-ge7mc หลายเดือนก่อน

    Serigne Touba dou nit lane la ??

    • @MameyoroDime
      @MameyoroDime หลายเดือนก่อน

      Borom Touba KENE là. Té KENE khamoule loumou doone ! A bon entendeur salut.Dieureudieuf Borom Touba

    • @babacarndong-ge7mc
      @babacarndong-ge7mc หลายเดือนก่อน

      @@MameyoroDime bala gay wah ni Serigne Touba dou nit warga mana xam limou doneu alors
      Digako lahoo sougnou borom nak
      Gnoune talibés yi gno wara xolat sougnoy kadou kou yap ak di saga sougnoy kilifeu rk sa genre Kadou yi moko waral

    • @MameyoroDime
      @MameyoroDime หลายเดือนก่อน

      @@babacarndong-ge7mc MERCI DE BIEN RESPECTER NOTRE GUIDE CHEIKH AKHMADOU BAMBA,L’UNIQUE CRÉATURE DANS CE BAS MONDE D’ICI BAS ET DE ´L’AU-DE LÀ.LUI MÊME À DIT:JE SUIS NI DJINN NI ANGE NI HOMME NI PROPHÈTE,JE SUIS UNE CRÉATURE UNIQUE QUI VIT AU DE LA TERRE ET JE SUIS JAMAIS PARTI.MERCI ENCORE POUR POUR VOTRE RESPECT ET VOTRE COURTOISIE À L’ÉGARD DE NOTRE VÉNÉRÉ CHEIKH AKHMADOU BAMBA

    • @babacarndong-ge7mc
      @babacarndong-ge7mc หลายเดือนก่อน

      @@MameyoroDime parfois kheur bou meti moy tah gnou wah yéneu yi ,,,,sougnoy maytou yéneu Cadou yi rk dina bah
      fi mom amna gno xamni yakam ti nagnou tariha yi wah bagnou critiqué len motah
      Parfois day am wah yi xamni kéneu douko wah si public
      Amal diam rk yaw ak bolem dioulit def si deuk bi diam inchallah
      Yala fayal gnou sougnoy kilifeu diné 🤲🤲

    • @MameyoroDime
      @MameyoroDime หลายเดือนก่อน

      @@babacarndong-ge7mc SAABAH YI DANIOU KHERONE TIE MOUHAMED PSL. DE LA MÊME FAÇON DINONE GUEUNEU KHERRE TIE SUNU WADJI CHEIKHOUNA AKHMADOU KHADIM, Yalna BOROM YOKOU AYES LERAMES BARAKATOU SEYDINA MOUHAMED PSL.A BON ENTENDEUR SALUT

  • @ansoucamara2963
    @ansoucamara2963 หลายเดือนก่อน

    En tout cas le Prophète Seydina Muhammad PSL est un être humain. Et DIEU lui a dit de le dire aux gens. Je suis un être humain comme vous. Après, qui est supérieur au Prophète Seydina Muhammad PSL ? Évitons le fanatisme.
    Au passage, le Prophète Abraham dit qu'il veut que DIEU lui pardonne ses péchés le jour du jugement dernier et il fait partie des cinq plus grands Prophètes, grand-père de Seydina Muhammad PSL et grand-père de beaucoup d'autres Prophètes et Aboul Mouwaahidoun c'est à dire le père de ceux qui vivent l'unicité de DIEU.
    Thiaaxaan bakhoul.