VIDEO DU JOUR : Serigne Habib SY ibn Serigne Babacar SY Mansour ''Nos 4 regrets d'ici bas

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 16 ธ.ค. 2024

ความคิดเห็น • 255

  • @mouhamedsambe7820
    @mouhamedsambe7820 6 ปีที่แล้ว +33

    Seydi khadji malick walahi amouniou fayam yalla nako borom bi fay si barkei naby sws Lima nex keur seydi khadji malick yalla dji ak seydouna mouhamed psl dafa saf sap si keur gui seydi khadji malick loudoul yalla wonou niouko alkhamdoulillah

  • @amysarr9402
    @amysarr9402 5 ปีที่แล้ว +9

    Alhamdoulilahi Rabil Alamina. Dieureudiefé Seydil Hadji Malick. Serigne Habib Sy Yalla nga goude fane mou ande ak wér. Yékhe la kham rek lay dioy. Yangui gnouy guindi bou bakh. Niveau bi ngay wakhé amena solo mashaallah

    • @mansoursybarry493
      @mansoursybarry493 5 ปีที่แล้ว +1

      Tjrs sama mbokkou Amy sarr

    • @amysarr9402
      @amysarr9402 5 ปีที่แล้ว +1

      @@mansoursybarry493 wawaw mane la d

  • @badarakandji5637
    @badarakandji5637 4 ปีที่แล้ว +9

    LE PROFESSEUR DE LA JEUNESSE KOULA DÉGLOU DINA DÉGUE LOU BARRI TÉE DINA KHAM LOU BARRI CI BOU BEUGUÉ DÉGUE ❤❤❤

  • @linedor588
    @linedor588 6 ปีที่แล้ว +50

    Merci a vous ASFIYAHI AMOUGNOU SEEENE FAAYE

  • @macodoudiouf2508
    @macodoudiouf2508 6 ปีที่แล้ว +118

    Le niveau est trés elevé mashallah. Et Alhamdulilah bima doné Tidiane

    • @modoubarr8848
      @modoubarr8848 6 ปีที่แล้ว +3

      wallahi wakhatico

    • @ndarylo6781
      @ndarylo6781 6 ปีที่แล้ว +2

      Macodou Diouf Ak mantam

    • @amysarr9402
      @amysarr9402 5 ปีที่แล้ว +2

      Wallahi fier d'être tijane le niveau est tjrs élevé. On y apprend tjrs.

    • @amadoufatydieng2364
      @amadoufatydieng2364 4 ปีที่แล้ว +3

      Yalla nanou Yalla deff ay deugg talibé Cheikj

  • @khadykhouma449
    @khadykhouma449 6 ปีที่แล้ว +29

    Masha'ALLAH SY vous êtes une vraie université que le TOUT PUISSANT vous assiste et vous protège à vie amiîiine

  • @rightright970
    @rightright970 6 ปีที่แล้ว +16

    Xam xam rek moy wore. Yallna yalla goudal sa fane boulesi were si barke nabi (psl) Machalla lerna nagni.

  • @awababacarwaneattidjany4705
    @awababacarwaneattidjany4705 6 ปีที่แล้ว +20

    Mashallah SY MALICK DIEUREUDIEUFATY SAÑIULA DEGLOU GUINDÈKOUSSI DISSI NDIEURIGNU TAMIT YALLA NA YALLA YAGUAL TAKAHWAY BIDJAHI TAHA SAWS INCHALLAH ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @linedor588
    @linedor588 6 ปีที่แล้ว +14

    Machallah yallanaa takhawou leene yook seene faane ak weuure sanguee leene mbalanou soutoureu djeureudieuf SEYDIL HADJI MAKICK SY

  • @mansordiakhate7496
    @mansordiakhate7496 5 ปีที่แล้ว +1

    Dieureudieuf Sy Malick. Diabootou Maodo à l'image de mame Maodo. Maodo la lepam selleu mo takh yallah fayeko ndiaboot ak talibe you sèlleu. Rakho dara ci diné bi. Fou yonentabi tèguon tankeum Fofou ngako tek. Diangal nganou nguidi nganou té déf nganou ay nit you nité baneu def la part des choses. Serigne Habib yallah nanoula yallah fayal té defal goudeu fan ak soutoureu bou sakh.

  • @djibrilsarr22
    @djibrilsarr22 6 ปีที่แล้ว +34

    Machalla. On dirait que c'est Almaktoum qui parle ! Par le niveau qu'il parle. Alkhamdoulilah 👌🙏 yallah naniou Allahou may deeg té khirr niou si bopam

  • @mamadoundoye5187
    @mamadoundoye5187 ปีที่แล้ว

    Macha Allah ko siitane vidéo bi 2023 beuseul j'aime

  • @codesamb7961
    @codesamb7961 5 ปีที่แล้ว +42

    Séne Mame mofi rawone si ay diamonome wayè yène tamite yèna fi raw si séne diamano kou beugue AK kou bagne nak

    • @thiammamadou772
      @thiammamadou772 4 ปีที่แล้ว +3

      El hadji abdou aziz nena nangoul yallah mongui commencé si nangou li yallah deff djerdjeuf si la nga wakh

    • @babafall8862
      @babafall8862 3 ปีที่แล้ว

      Walahi dafa lère

    • @famaciss8165
      @famaciss8165 3 ปีที่แล้ว

      @@thiammamadou772 ¹

    • @OusmanenourayniSylla-ho4sb
      @OusmanenourayniSylla-ho4sb 18 วันที่ผ่านมา

      Dafa léér 😅😅😅😅

  • @fallsenegalais8381
    @fallsenegalais8381 6 ปีที่แล้ว +34

    machallah le petit fils de maodo bon gamou 2018 et bon magal pour les mbokou mourid.

  • @lomoussa8003
    @lomoussa8003 6 ปีที่แล้ว +10

    ماشاءالله ياشيخ محمد الحبيب سه أطال الله عمرك وزاد صحتك وسترك بجاه جدك محمد الحبيب سه

  • @Djamil-Pro
    @Djamil-Pro 6 ปีที่แล้ว +25

    Machallah Sy Malick Yàlla ak Seydina Mouhammad saw rekk guéne gnouy wakh keur Mame MAODO dina Djou Léré nagne nagne

  • @terangatv4073
    @terangatv4073 6 ปีที่แล้ว +25

    Machalla li amna solo dh di firi gayi Di kham thiey maodo sunu mouthie rek moko sohal

  • @maimounandoye5385
    @maimounandoye5385 2 ปีที่แล้ว

    Sy Malick yalla mayela goudou fane weer ak weerle mouthie mouthiele dounda ak doundalé yallana thiat sekhlou Soutoura bou sakh dake bidiiahil nabil moustapha (SAWS) Amiine

  • @sakhocheikh6172
    @sakhocheikh6172 5 ปีที่แล้ว +6

    Bilahi walahi wa tallahi Serigne Habib Sy Mansour yalla na yalla wereul say thieur yeup ba nga soute sa Mame Abdou Aziz Sy aw fane ba taxaway ci tarikha bi meuna dieum kaname
    Sy Malick yalla nga fi yag way

  • @adjidiop51
    @adjidiop51 6 ปีที่แล้ว +11

    Kéyeul dou tepe domdia beut degue rek ba aldiana yala nagnou yalla fayale maodo machallah sy Malick

  • @cheikhounaba6685
    @cheikhounaba6685 6 ปีที่แล้ว +13

    Sante sama borom djouli si sounou yenentou mouhamed saw Beugue l'ole maodo

  • @abdourahmanefall5571
    @abdourahmanefall5571 5 ปีที่แล้ว +1

    Kou diara deiglo guinii walahi Guoudal fane Sy Malick fier d'être Talibé Cheikh😍

  • @ibrahimasenenabien858
    @ibrahimasenenabien858 6 ปีที่แล้ว +12

    Yague fi loll té wérr serigne bi sèn dian wathna nahou ngèn sèn ndiabote bèn ❤

  • @yerimsy8740
    @yerimsy8740 5 ปีที่แล้ว +2

    Serigne mansour borom daara ji dana wakhni xam xamou maodo meune na tékhé lo afrique yeup maodo diokhnaniou solution à tout nos problèmes yallah naniouko yallah fayal

  • @bamsbams3171
    @bamsbams3171 6 ปีที่แล้ว +97

    Bilahi wakh d'où nékh d'où dégne ndiabotou seydil Hadji Malick Sy maodo motakh rewmi kéne dofatoul

  • @dabakhmalick7774
    @dabakhmalick7774 6 ปีที่แล้ว +18

    Serign Habib Sy Mansour ibn serign Babacar Sy Mansour Khalife Général des tijanns

  • @baidyrassoulsow5487
    @baidyrassoulsow5487 5 ปีที่แล้ว +3

    Wakhna ba tayi ni feekeu nit defko dof lolou kounei meune nako wayei fekeu nit ngua nitel ko ba boko beugué def dof mou wathi leufa lolay yeuf yeu tei lolou laniou seydil hadji Malick Sy maodo defal. Diarama Mame maodo ❤️

  • @OusmanenourayniSylla-ho4sb
    @OusmanenourayniSylla-ho4sb 18 วันที่ผ่านมา

    Un professeur, pédagogue,sage Serigne Habib Sy

  • @cheikhtidianediouf6782
    @cheikhtidianediouf6782 6 ปีที่แล้ว +41

    they un niveau très élevé sy malik boulene nopeti délene nguindi nitt ngni

  • @papisdieme4774
    @papisdieme4774 5 ปีที่แล้ว +13

    Keur maodo boudoone atayala dou am 2ème nieup leuweul laniou

    • @sodabadji8350
      @sodabadji8350 5 ปีที่แล้ว +1

      papis dieme eskeuy ma dègg Deugg

    • @layediallo7890
      @layediallo7890 4 ปีที่แล้ว +1

      Walahi ndeysane

  • @ndiankouniang2013
    @ndiankouniang2013 5 ปีที่แล้ว +1

    Dalale guene sounou hel yalla nanou yalla nagoul sounou talibé si barquet yonante bi psl

  • @airafrique8193
    @airafrique8193 3 ปีที่แล้ว

    Al khalifa Serigne Babacar sy Mansour yalnafi yague té wéur ❤️❤️❤️❤️❤️

  • @bintoudia8156
    @bintoudia8156 8 หลายเดือนก่อน

    Machallah Machallah Machallah sy malick yague fi lole lole té ande ak weer amine

  • @dabaxful
    @dabaxful 6 ปีที่แล้ว +2

    TIEUY UNIVERSITE MAODO. KOU WAKH REK GUANI MOMA! DIERDIEUF MAODO DIEUREUDIEUF SY MALICK. GOUDEUL FANE

  • @aboubekrsadikhsarr3911
    @aboubekrsadikhsarr3911 5 ปีที่แล้ว +1

    Machala Serigne Habib Sy Ibnou Serigne Babacar Sy ibnou Serigne Mansour yalla nafi yagg téh and ak wéér... Amiin

  • @serignemansourtoure86
    @serignemansourtoure86 2 ปีที่แล้ว +1

    Mashaallah Sy Malick Qui est là en 2022👌👌👌

  • @modouniang9416
    @modouniang9416 ปีที่แล้ว

    Mâcha alla ziar na yalla na yalla motali lep té dolignou soutoura amine fier de mame Khalifa

  • @baidyrassoulsow5487
    @baidyrassoulsow5487 5 ปีที่แล้ว +2

    Yalla naniou yalla fayal cheikh seydil hadji Malick Sy maodo lii yeup moome leu

  • @nabientvnabientv9454
    @nabientvnabientv9454 6 ปีที่แล้ว +33

    kou ñou wara bayi khel la ndax fason bimi wakhtane mou tambalé rare

  • @moussawade5589
    @moussawade5589 6 ปีที่แล้ว +23

    Ohhh bilahi dèmbeu lèpeu la sètane, mais bilahi Sy ya beuri khame khame

  • @mameawaniang7710
    @mameawaniang7710 6 ปีที่แล้ว +4

    Mashallah Sy. Khana di leu nianal souniou borom sameu leu ci seu barké Mame Cheikhal Hadj Mansour rta

  • @cheikhguitesarr541
    @cheikhguitesarr541 3 ปีที่แล้ว

    Sy malik yalna sounou borome samoula si barkèe seyedina mouhamed psl🤲🙏

  • @oumarsall7769
    @oumarsall7769 6 ปีที่แล้ว +5

    ماشاء الله تبارك الله فك اللهم ربنا تقبل منا إ نا ك أ نت توب رحيم
    جزاك الله خير يا شيخ

  • @babacarsall9458
    @babacarsall9458 6 ปีที่แล้ว +12

    Ma shaa allah Sy Malick goudal fane

  • @ababacarseck377
    @ababacarseck377 3 ปีที่แล้ว

    Machallah serigne Habib sy Mansour Al KHALIFA yalla nala yalla sameu tè are la

  • @sidiahmedmbaye-officiel4269
    @sidiahmedmbaye-officiel4269 6 ปีที่แล้ว +3

    Walahi un grand pédagogue serigne habib sy. Yalna yalla goudeul fanam té sameu ko

  • @djibrilba2582
    @djibrilba2582 5 ปีที่แล้ว +3

    فبارك الله احسن الخالقين ، انه لفرح عظيم فجزاك الله احسن الخيرات وكفيت شرا

  • @thiernondiaye5331
    @thiernondiaye5331 ปีที่แล้ว +1

    Macha allah yalna yalla faw yiw

  • @elizalopes1230
    @elizalopes1230 6 ปีที่แล้ว +2

    Bilahi sy malick doundal 120 ans kham kham mo woor yalla nanou yalla fayale mame maodo

  • @abdoulazizdabakhdiouf5600
    @abdoulazizdabakhdiouf5600 5 ปีที่แล้ว

    Kou am fouleuh ngui mashallah Yalna Yallah guoudeul faan wi tei guena deugueureul takhaway gui reik inchallah

  • @ramatoulayediop5757
    @ramatoulayediop5757 6 ปีที่แล้ว +2

    Dieureuf sy malick wakhtane bi amna solo yalla nagnou yalla may top ak dègue

  • @yatmafall4079
    @yatmafall4079 6 ปีที่แล้ว +1

    Mâcha allah sounou khôl Sedna yalla nguene fi yague s’y Malick

  • @layediallo7890
    @layediallo7890 4 ปีที่แล้ว

    S abib sy yalnala yalla may goudou fane ak wér

  • @thiernoaguiboudiallo4938
    @thiernoaguiboudiallo4938 4 ปีที่แล้ว +1

    Walahi kham cheikh seydil hadji malick mounoul wéssou nga khol ay ndiabotam ak diléne degglou bilahi mais serigne habib sy yalla na yalla gouddale sa fane mane dé sope nala lollll yalla kham nako

  • @babacarniang5695
    @babacarniang5695 6 ปีที่แล้ว +2

    Choukran Diazilan! Yalla na Yalla yok lérou deuneume

  • @adamambaye3918
    @adamambaye3918 2 ปีที่แล้ว

    machaallaa yalna yala faye yiw thi barké yonnénté bi psl

  • @jolofmotivation9603
    @jolofmotivation9603 6 ปีที่แล้ว +12

    Mane loutakh ma fan ndiaboto maodo....bilahi dounioula nakh jamais..

  • @dj_ouz_officiel
    @dj_ouz_officiel 6 ปีที่แล้ว +12

    Machahala Sy Malick yalana yala goudal sa fane rèk 👉👉❤❤❤

  • @abdoulayesow6643
    @abdoulayesow6643 5 ปีที่แล้ว +4

    Très pertinent du courage... Serigne Abib

  • @cheikhououmardiaw7646
    @cheikhououmardiaw7646 6 ปีที่แล้ว +3

    Walay sy Malick ya ham sa mame yague fi rék ta wuer amine

  • @AbdouazizDiouf-y2v
    @AbdouazizDiouf-y2v ปีที่แล้ว

    Machala tivaoune dal xam xam falla fék bakh

  • @codesamb7961
    @codesamb7961 5 ปีที่แล้ว +1

    Yalla na yalla guoudal Sa fane sy Malick ma LA beugue

  • @alinegueye2943
    @alinegueye2943 5 ปีที่แล้ว +2

    Macha Allha serigne bi yalla na yalla may la fanwou goudo ak wèr

  • @mbayemagette9198
    @mbayemagette9198 2 ปีที่แล้ว

    je suis fière d'être talibe cheikh alhamdoulilahi

  • @abdoutounkara8268
    @abdoutounkara8268 6 ปีที่แล้ว +10

    Hii amna fassakh Serigne Habib jangalé bi léér na niveau bi kawé na

  • @mamecoly9827
    @mamecoly9827 6 ปีที่แล้ว +9

    Machallah Sy malick ya gnou doyyyy

  • @djibrilousamb5039
    @djibrilousamb5039 6 ปีที่แล้ว +5

    Billahi sy malick boo lénn amoul woone thi réwmi dou bakh

  • @KelseyMoody-xo3vj
    @KelseyMoody-xo3vj 3 ปีที่แล้ว

    Niveau bi oh oh oh 💓💙💙👊

  • @mamadoundiaye1536
    @mamadoundiaye1536 2 ปีที่แล้ว

    machallah Sy Malick yalla nga fi yagg té wer Sy Malick ci barké yonent bi saw

  • @moustaphandiaye2916
    @moustaphandiaye2916 4 ปีที่แล้ว +1

    Walahi sy yag fi lole te andak werr. Ak kep kou wakh amine...

  • @sarribrahima5278
    @sarribrahima5278 5 ปีที่แล้ว +3

    Machallah Yalla Nanou YALLA FAYAL MANME MAODO MALICK SY AMOUL MOROME BILLAY

  • @mormboup9301
    @mormboup9301 3 ปีที่แล้ว +1

    Ak degu té am xam xam
    Ap philosophe l koukoy deglou xam aduna ak alahira❤

  • @airafrique8193
    @airafrique8193 3 ปีที่แล้ว +1

    Mame maodo sy amo morome yanou khamale naby ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @moustaphadiop3184
    @moustaphadiop3184 2 ปีที่แล้ว +3

    Celui qui parle est à la hauteur de ce qu il dit parcequ il le pratique

  • @sofiagne6444
    @sofiagne6444 6 ปีที่แล้ว

    djeredjef Sy Malick Yalla n'a Yalla doli soutoura barké Yonnetebi Psl

  • @saloumsaloum9627
    @saloumsaloum9627 6 ปีที่แล้ว +12

    Machallah sy yaguafi te wer lool

  • @ibrahimambaye8617
    @ibrahimambaye8617 6 ปีที่แล้ว +3

    Machalah sy yalla samme lah
    Xam xam fégne na

  • @falyseydi
    @falyseydi ปีที่แล้ว

    Èy waye serignebi. NOPI TALÏ LA ..DO HOPITAL..DÈ !😊❤❤❤❤

  • @justicepourtous6168
    @justicepourtous6168 6 ปีที่แล้ว +10

    Was Asfiyahi nianallěne sama yaye elle a disparu le 24 octobre 2018 te talibė Cheikh la wone en plus nėkone présidente dayira. Serigne Babacar Sy reck la geumone elle s'appelle (Oumy Guèye)

    • @sofiyatouagne9399
      @sofiyatouagne9399 5 ปีที่แล้ว

      Yalla nako Yalla yereum barké Yonnenete bi Psl

    • @mansoursybarry493
      @mansoursybarry493 5 ปีที่แล้ว

      Que firdawsi soit sa demeure

    • @oumarly7552
      @oumarly7552 3 ปีที่แล้ว

      @@mansoursybarry493 yalla na ko yalla khaaré aldjana yalla na rethiou leppou loumou don déf ngir khewall ak téranga yamoufa fékk

  • @sopeynabi5390
    @sopeynabi5390 5 ปีที่แล้ว +1

    Macha Allah l'islam thiakaw tek dieureudieuf rek

  • @khaliltv4876
    @khaliltv4876 6 ปีที่แล้ว +6

    Djabotou Maodo machallah

  • @aliounegueye7082
    @aliounegueye7082 5 ปีที่แล้ว +2

    machalla yalla yalla barkél maodo kende amoul sa Faye

  • @ckeikhsow133
    @ckeikhsow133 5 ปีที่แล้ว +1

    maodo amna daraa wala yalla naa yalla motali insha allá barker maodo malick sy sy

  • @ibourahimasow7380
    @ibourahimasow7380 2 ปีที่แล้ว

    machallah serignebi yalla na yalla diapallè

  • @ndiayeamary9046
    @ndiayeamary9046 5 ปีที่แล้ว +1

    Xaw xam yomboulll thiey mame maodo mo yèmè macha Alla sy

    • @salydiouf2193
      @salydiouf2193 5 ปีที่แล้ว

      Wakhatiko dé. Kène dou Sougnou Mame Seydi Hadji Malick SY RTA.

  • @modoufallbetebeteitsenegal5272
    @modoufallbetebeteitsenegal5272 4 ปีที่แล้ว

    SKEUY LOU LÉR NAGNI NI MIDI NGUAFI WAKH MACHALLAH AMNA SOLO LOOL DIEUREDIEUFÉ SY MALICK YALLAH NALA YALLAH FAY

  • @elmansoursarr5646
    @elmansoursarr5646 5 ปีที่แล้ว +1

    Machaa Allâh Sy Malick yague fii lol ta ande ak weer 👏👏👏

  • @absadiop5631
    @absadiop5631 4 ปีที่แล้ว

    Machallah sy malik yalla nala yalla defal diam rek ak were

  • @sodabadji8350
    @sodabadji8350 5 ปีที่แล้ว +3

    Thieuy Mame maodo say seutt sakh ay maodo laniou billahi yalla mon ngui léne wane ligèyou cheikh seydoul hadji malick sy nè dou sène morom bane seutou serigne fi thi Senegal moy wakh yi xam xam khana diniou beugg Ray diw amoul morom

  • @omarfaye1794
    @omarfaye1794 5 ปีที่แล้ว +2

    Walahi serigne Habib Doundeul bamou yagu lol and ak werr sutura aduna ak alahira 😘

  • @OusmanenourayniSylla-ho4sb
    @OusmanenourayniSylla-ho4sb 18 วันที่ผ่านมา

    Le dimension de Serigne Habib c'est une autre chose 😅

  • @ngombabacar5564
    @ngombabacar5564 4 ปีที่แล้ว

    Macha ala sí Malick yalla n'alla yalla goudal Say fan

  • @souleymanemar7291
    @souleymanemar7291 6 ปีที่แล้ว +1

    Allahou Akbar quelle sagesse machaallah

  • @Mansour-m5x
    @Mansour-m5x ปีที่แล้ว

    Theuyy sama wa dji❤❤❤

  • @mouhamedndiaye9440
    @mouhamedndiaye9440 6 ปีที่แล้ว +10

    Ken dou maodo bilahi

  • @jolofmotivation9603
    @jolofmotivation9603 6 ปีที่แล้ว +14

    Pourtant c'est le fils du khalif....bilaye limoy li weur

  • @aissatasow7301
    @aissatasow7301 ปีที่แล้ว

    Machalla sy Malick ❤❤❤

  • @ndarylo6781
    @ndarylo6781 6 ปีที่แล้ว +3

    Lima nekh si Wakh j guenol ben yon allkhour ann ki d koka topou mo yobou lau si yalla

  • @bounabou5249
    @bounabou5249 5 ปีที่แล้ว

    machallah serigne bi,wayé djeura djeuf Maodo Malick ,done gua sa mame wayé donde gua sa mame

  • @diadjikanteye4908
    @diadjikanteye4908 6 ปีที่แล้ว

    Machallah amne solo sy malick yall na yalla goudal se fan dolila were