Il faut ke l'état prenne ses responsabilités et arretes sa avt kil ne soit trop tard et ces a des civils de régler des civils seule letat detient le monopole de la violence mais pas des civils c pas sa dans un pays normal
Baye Fall naa niouy dawal yeurmandé SERIGNE Touba leep cii daal ak teey lako ligueeyé mais violence bi da Hawa eup yeen tamit dieufé leen digaal té bayii téré Lou Serigne bi beugoul gala waay nanie koo bayii
Ay waa jii tée ngèn noppal Seen boppou Serigne bi yéesalaat na ndigeul limou joxoon baay Fall yi ngir sammou wormay deukke bi noppalou leen ngir jeummi yalla sounou borom ah
Il faut pas oublié que Touba etat amoufa ndogual. Touba béne ''titre foncier'' la ame té tourou Serigne Touba mosi nék. Touba Serigne dako mome si zaaire mome ko si batine. Kép koufa nék té meuno déf lignoufa beugue nga délou sa dekou mame. Wassalam
Niakka jullik baay Fall yi séen Yoon nékkou ci loolou AK Diag léel la goo xam né yalla sounou borom moo leen ko Diag léel té li Serigne bi beugge mooy li yalla sounou borom beugge té tmt li Serigne bi beugge ci ap deukkeum lolou Mooy am in Chaa Allaah
Il faut dire la vérité les bagues Fall ne sont pas formés pour maintenir l'ordre. L'état n'a qu'à prendre ses responsabilités avec courage et fermeté deug rek moye moudiou
Diaroull beuri wax dh li serigne bi beugue mooye am inchallah
Sa data yay nafek yi deukolen si deuk bi
Serigne bi dou yalla doul
bane serigne
Wa Serigne bi lom bague Moy li gayi def ni wale
Wallahi diaro yéd sa genre gui mom nanlén yeureum rek ndakh mala sakh molén tané shim
Ana mandikate ak dioubanti domou adama
Li Serigne bi beugeu Moy am fors bilahi walakhi
Gni nan baye fall dagno rèw,baye fall dèfougnou dara koulèn ko sant mo yabatè
Douma nila déd dh ndakh lo guiss louné dal amna responsablité
Baye fall yi yeena taay 💪💪💪💪💪
Il faut ke l'état prenne ses responsabilités et arretes sa avt kil ne soit trop tard et ces a des civils de régler des civils seule letat detient le monopole de la violence mais pas des civils c pas sa dans un pays normal
Baye falyi kou bayi Ndigeulalal yalla baparé di diklé Li yalla santane
Mm yaw dangay bayi ndigeulou yalla
😂😂😂😂😂
Yéne wa Touba yéna wara diaplé bay fall yi ci ndégalli ba Serigne bi wakhé gnépa warone massé bayi lagnoy diaroul waone di khaar bagnoulay téré❤
Koudoul dioulli noumouyy appliqué charia.
Baye fall yi dagno yabaté
Sarabb ndayi li waye
L'état doit prendre c'est Responsabilité,, c'est du Dictature
Baye Fall naa niouy dawal yeurmandé SERIGNE Touba leep cii daal ak teey lako ligueeyé mais violence bi da Hawa eup yeen tamit dieufé leen digaal té bayii téré Lou Serigne bi beugoul gala waay nanie koo bayii
État bi n'a réglé liii
Bay fall yi niou réw
Ana l'ETAt de droit
Bay fall yi ak ki léne ko Santa yéppa da nio rèw khamadi
Sawa.fou.rek.khaye.douke.di.saka
Mai.yaw.mankesse.makana.khepou..si.youni.de.foumala.feke.na.ou.sa.leufe.daye.ok.fo.beuke.ma.fekalafa
Li bougn bouci état wakhoul dinafi indi guerre civile civil dou contrôler civil lolou ay thiakhane là
C'est pas normal courage tourono dina bakh billagui jamais vue Sénégal❤❤❤
Bilahi les jeunes il faut guéne xexx thaff ndayi baye fall yi
Khekh dena am touba
Baye fall mon bari bairé
Ay waa jii tée ngèn noppal Seen boppou Serigne bi yéesalaat na ndigeul limou joxoon baay Fall yi ngir sammou wormay deukke bi noppalou leen ngir jeummi yalla sounou borom ah
Lima lén wakh rek nagnou déf association and Katte ndayam baye fall yeup gnou Fatou fa yalaw
Li dou deug dou yone
Il faut pas oublié que Touba etat amoufa ndogual.
Touba béne ''titre foncier'' la ame té tourou Serigne Touba mosi nék.
Touba Serigne dako mome si zaaire mome ko si batine.
Kép koufa nék té meuno déf lignoufa beugue nga délou sa dekou mame.
Wassalam
Bilahi Wax Nga Dëgg. Ku Ragalul Yalla Munul Russ Khadimou Rassoul. Wayyé Bammeelangui Leen Di Xaar. Lu Waay Déf Boppam. Kénn Déful Lu La Jall.
Kholale seytanéyi digén géne touba li Serigne bi beg dina ame inchallah baye fall môme Ndiugul rék laye dokhe lolénsi bagnoul bagnou noukosi
Niakka jullik baay Fall yi séen Yoon nékkou ci loolou AK Diag léel la goo xam né yalla sounou borom moo leen ko Diag léel té li Serigne bi beugge mooy li yalla sounou borom beugge té tmt li Serigne bi beugge ci ap deukkeum lolou Mooy am in Chaa Allaah
Amalouléne Serigne ndiarigne baparé khamadi
Wayé amale nanou sunu baye ndiarigne té sunuy baye kay dan no wara mat srg nou yam si nak
Gena len Touba bayelen s'en dekae
Il faut dire la vérité les bagues Fall ne sont pas formés pour maintenir l'ordre. L'état n'a qu'à prendre ses responsabilités avec courage et fermeté deug rek moye moudiou
اليس الله بأحكم الحاكمين
Non amna lo khamni dafa simple Touba Serigne bi moko môme dafa loumfiy bagne ta yaw manoko bayi wa do guéne deukeum déme fanéne jamou ni nioyou
Li Serigne bi beug Moy am diaroul wakh bou bari
Ce sont ces balles perdues qui tuent les bayes Fall. Dans le village Peuls près de Touba lors d’un affrontement nocturne un baye fall a perdu la vie.
Population kou meunoul normal NGA gnibi sa deukou Mame ngene mayniou diam li Serigne bi beug Moy am
Dakhe.nioniou.ay.bay.fall.laniou.amena.ay.agresseur.youciye.rakhe
Est-ce que fii Touba la saxx
Niniouy diéma yakk dérou Bayfall yii rk laniouy werrr😂
Li Serigne beugu rek Moy âme dioub MBA déh
Rewmi 24 bayi lén fén zna popilation bi
Mouride ndigal
Toupou ndigalou Serigne bi moy yone ta moy li gueun wayé diapou asgor diko toumal sathie rafétoul ta ak togn la
Baye Fall yi nagne nopalou t df lilén Serigne bi Sant t Bayi togne fami moudjé dou néx d
Baye fall yi ay dof lan li amoul fén
Ay embesine ngene rec baye fall ye nec si yone liniou bagoul si deukeu bi doko bayi
Touba bou nèkkon boorou casamance wala nguebi kon lèlèn lanouy wakh serigne bounè boudèfèni kon ana senegal li dou deg dou yoon waye dara yaggoul dakh.... ... اليس الله بأحكم الحاكمين
Li serigne touba beugueu moy am diaroul diabolisation soungueine deifoul dara keine douleu llaale
gayi manuhn thiy dara ax si yon wi rèk diafè ndigal
🇸🇳😡😡😡😭😭😭
Mais gnoune wa Senegal lane la gnou def yalla , oh ndeysane
démdèm li baye fhoyi didèf dina indi poroplème youniou douleuxam founiou kouye waxè dax liniouye dèf yalla sanetanè wouko yènène tibi saneta nèwouko sidiaye dolèrèk laniounè
Baye fallyi dagno téyoul lignouy déf kén santou lenko gnolene geuna beug s touba fouf néklene ay nite té andak s'en khel
Serign bi limouy setane famouy mouddié dou bakh touba si bopam deug amatoufa
Touba deukoup serigne bi la ko meunoull dèf limou beugue geneull deuk bi
Liniouy def ni serigne bi moko diglè ay tire balle
Ki déh daye fén rék
kum nakhri nga gén dek bi
Baye fall yiii AK kilén diokh ndigal gnéppay domouharaam
Wonél sa kanam
On s'en fout 😅😅😅alhourane ak souna rék tout le reste cinéma rék motakh douguou djiauke si problème 😅😅😅
Saytaané ak rambaathie baakhoul.
Surtout goor
Li segne bi digale kou ko manoul guenal deukeu bi dellou sa degue mamme.
Tarikha yeuppp mourid yii nio ci guena dofff😂
😢😢😢lii gnaawna lool. Bakhna rek,ils vont finir à tuer une personne,liignouy déf Serigne Mountakha santoulénko
Jarul mbèll mbelli lula Dall ñakk teggiin molako yobbe
Gni d'où niou ay baay faal ay mbaam lagne
Keur djambour sakh khana bofa néké dinga djeufé li borome keur gui beugue wala nga abal ko keureum, wakhoumala deukou djmbour.
Seen waxdji louusna d😂😂😂😂😂 ragalal yalla
Bayiléne féne té nek
Naniou diokh touba indepandance mou diekh
Ndiguel diéufé
Mais ani eta bi war nasi wax de.
SERIGNE MOUNTAKHA DIOKH NA LÉN NDIGAL WAYÉ SANTOUÉN FITNAL DOMOU ADAMA YII
Yén daguena deug sén ndiaye rew
Àna bay fall ak saga ndéy😢😢😢
Dara worou lasi kii dafa Nétali rk wayé xamo lou siy deug
Ndigeul li koum nékhoul mono guéne touba Déme fanéne ngéni féne rk
Soumettez vous aux charias en quelques sortes les lois instaurées dans cette ville islamique.😢
Yén dagnéna yaradikou soléne dégué ndigal dieufé rek mo si wara topou
jiournalis bi saitané la😂😂
Il fait son travail kouy wakh kay si Lou am té niaw si nga wara wakh
Kodoul diouli doo woorr waroula dioubanti kinee
Yeen boy Touba yi da bari ay conn ak gnou khamoul aduna Touba lafa sëriñ beug moy am kouko bagn domeram ga touxoul
Yaw ya niaf sa ndaye doum kharm touxou nio sono keur ye lèguiye mou nio ko may Am nam dakar Am Touba Am fènn fou la wakhut
Dioay faye na wokh si li
Boneki si deug wonel sa kanam domaram
Reew buu aamuul justis gerre civil Lay Andi te ñanou ñuukoo yaala buu ligeey bi seelle reek diaamu aam te xaalee yii aam yaar aak teegiin taay degluu ndigali
dagni fén
Li serigne bi beug rék. Koussi diot tamit doussi man touss. Yaw journaliste bi sakh so wathie ndigal gnou tekk la si ndigal
Li sëriñ bi bëgg mooy am
Ndigal rekk mba ga touxou
Touba serigne Touba moco mome serigne mountakh dina yakh DEUG bi
Loutahk
Niou tay yen aye saytane
Rek guén
Yéne ay doméram ngéne borom deukk bi beugoul li ngéne fiy déf
L etat est faible
Touba bayou kéne momouko Lou Serigne bi beug Moy ame
niok sut bi nio yam dagni fén diabisé
Fo ko you
Yena togne de khaley Touba Nek Lene sy nigeulle Mo geune séné wakhe dji
Yaw Borom sen bii ndafeekeu gu bon nga
yaw del saga thi sofo rek yaw fomo guene gnawe rek dagal fofo amo gno dole Na lamine bi gnawe rek
Doll rek Kate len sen ndaye
Gni danouy fen rek
Du n imporye quoi que fait l etat
Touba dou Dakar soléne beugué mélni waa Dakar guéne léne touba déme dakar souko défé kéne douléne wakh dara ok