Ndeye manchallah am nga yar ak téguine tu as bien parlé franchement chapeau 👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽❤️❤️😍😍🥰🥰❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾yalnala yalla défal diam taw fékh Amine 🙏🏾🙏🏾😘
Bijou quand tu poses tes questions à une illettrée soit la plus précise possible et n'utilise pas de mot compliqué, tu parle de culture générale, lath ko thi are bi, thi féthieu bi, reformule ta question en lui demandant par exemple que-ce qu'elle ferai ou changerai dans l'art ou la danse sénégalaise si elle était présidente? Bou boba gua dégeu degeu . Sinon ndeye gueye je t'adore, très réctive et posée, t'es adorable chérie papa, seyeul sa seuye t boul falé kéneu.
Wawaw beugueul sa dieukeur te yalla takh yalla moy tak seuy yi sa arass bou la si dara dieule te sa yaye magui koy nianal yalla khareko aldiana te yekhe niou
Je suis vraiment outrée. Ça fait un petit moment que je regarde les interviews mais là, Bijou a fait fort ! Depuis quand, on invite une célébrité pour la rabaisser en direct devant le public ?! On fait une interview pour en savoir plus sur la vie personnelle et professionnelle de la star. Mais on ne va pas jusqu’à juger la star sur tous ces actes, et lui dire que sa carrière est mauvaise (et j’en passe..). Cette émission devrait être arrêtée, et la journaliste virée (si on peut appeler ça une journaliste). Elle se permet de critiquer ses invités, elle manque de professionnalisme. ..Le plus gros problème du sénégalais : c’est la mentalité. On est en 2018, essayez de changer ! Bijou, ya sof
mais daba thiam je suis triste de constater que tu n' as rien compris, lis bien le titre de l' émission c' est ça le but de l' émission, atteindre confronter, soutirer c' est l' émission
Bijoux déh questions youmouye Sagna ladje mo takh émission bi osé je pense que si c'était une autre personne qui animé cette émission je penses que personne ne le regarder donc moi je dis bravo et continue comme ça.
L'émission est vraiment affreuse comment on peut inviter une personne et lui dire que tu représentes la poisse pour ton mari et la rabaisser de la sorte, c'est vraiment dégradant. Ndèye tu t'es bien défendue.
Ooooo I never see this type of program because ndye Gaye get angry easily n bijou didn't care of asking any type of questions.i luv your program sis bijou very much belie u so educated belie because your questions are wel ask
@@korejolie belie sis bijou is very intelligent that way she ask her questions is vry good but her program with sis ndye Gaye is that best i luv it because she ask ndye many questions which no one has ever asked her
Bijoux à tu etais à l'ecole.???tu es trés insolente , incorrect, Tu poses vraiment des questions bêtes . discute dans le concept De l'emission, respect à Ndeye gueye
Contan si bijou rek prsc mashallah oyof na lolou ta djigeeen kou gawawoul guisse boppam kham niit rek momma meuna def confrontation🙌🏾💯 she has my resprct ive always loved bijou♥️❣️! Mes ndeye gueye dafa melni daga nieuw pou defantè ak bijou 😁 mes defal nank dei bijou dou bayi mo seddd
Ki yabatewoulll akk kanamammm bouuu bonnnne gonflé nii melni balon boumm rek ga explosé mais bon on te comp dagaa tangg 😂😂😂😂 niaw 😩 ndeye je taime 😍 maturité moy nitte wayyy😂😂😂
yéne sénégalais yi yéna sof bijou bouguéne nék di sagua méni séne morome la mome liguéyame laye déf t'es mou mena tonte conne bijou bonne continuation que dieux te donne une longue vie pleine de bonheur y'a Bah t'es mena bakhlé ❤💋💋💙💘💕
Liguéye day endak professionalisme. Do invité nite ba paré diko rabaissé diko coupé la parole sous prétexte que sa émission la. Ça ce fait pas on dirait un règlement de compte c abusé franchement
Felicitation bijou eii merci ndeye gueye sii leral yinga deff ms Senegal j parl avk vs li c 'étai juste une émission Bjou c norm q elle pose ls lésion à ndeye gueye koi q s soi nak Tu es notre fierté Bjou d passage salut moi Miss
Ana gniko setanatt thi 2020
l’idéale bousaliou STB moi
Ma ngui ni'i
Mane
@@coumbaniang9886 !n1111
l’idéale bousaliou STB niongui ni deh
Ndeyesan yalla nala yalla may dom si barke Serigne Touba ❤️ amoul morom Serigne Touba
Elle m’a fait pleurée quand elle a parlé de sa mère 😭😭😭
Ana gniko sétanate thi 2021 bi beusseul j'aime
Ndeye Gueye elle ne s'est pas marié pour de l'argent
Un exemple à suivre
Bikay c vrai
Aka rare
Madame Ndeye Gueye tu es la meilleure danseuse de ta génération !!!!!
Pombitair ak angutair
😃😃 Merci beaucoup ndeye je t'adore👍👍😁😁😁😆😆😆
Yalla nala yalla maye ngiabote bou barké ak papa contane n'a si yoe fière bigua doné sa ma homonyme ndeye gueye
Ndeye manchallah am nga yar ak téguine tu as bien parlé franchement chapeau 👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽👏🏽❤️❤️😍😍🥰🥰❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾yalnala yalla défal diam taw fékh Amine 🙏🏾🙏🏾😘
Bijou quand tu poses tes questions à une illettrée soit la plus précise possible et n'utilise pas de mot compliqué, tu parle de culture générale, lath ko thi are bi, thi féthieu bi, reformule ta question en lui demandant par exemple que-ce qu'elle ferai ou changerai dans l'art ou la danse sénégalaise si elle était présidente? Bou boba gua dégeu degeu . Sinon ndeye gueye je t'adore, très réctive et posée, t'es adorable chérie papa, seyeul sa seuye t boul falé kéneu.
Vraiment je n'ai jamais aprécié Ndeye Gueye mais taye j'ai apris k nite boul geume loula woroul elle a bien assuré l'émission bravos à toi et bijou😍
Merci beaucoup tokou doff 👏👏👏👏👏
ndey yalna Yãlla yeurem sa yaye té khareko aljdana firdaws si barke nabi mostaph Amine ya Rabbi 💓
🙏🙏 Amine
Wawaw beugueul sa dieukeur te yalla takh yalla moy tak seuy yi sa arass bou la si dara dieule te sa yaye magui koy nianal yalla khareko aldiana te yekhe niou
Gnaw Ndeye Gueye contane na si ioe gnaf gua bijou Aÿ gnaf you bakh en plus avec classe 😊
Deug dou nkh
félicitation Ndéye GUEYE et du courage
Ndeyesan dou Sama fethie kat mais machallah yallah nala borome bi bayei AK sa borome keur barki serigne saliou mbacke 🙏🙏🙏
Ndeysan ndeye gueye mako fen te beugg ko😘❤️
Vraiment bijoux vas refaire ta formation ont ne juge pas les gens moi je t'aime bien ndeye gueye
ndeye Sow explique moi la situation
Bikay sow
Bilay sow
Ndeye Gueye est une belle femme MashaAllah.😍
5h 19mn g pleure walahi 😭 niak yay da meti loll
émission bi dh mankoy soga setan si téléphone en 2021 bisou da melni kou analon ndeye gueye à de sabarou maman africa bi
Ohhh ndeye cntanena si yaw bilahi bne continuation k dieu t garde jt souhaite tt le bonheur du mya t'aime fort
ndey j l'aime bien 😘😘😘💓💓💓
On ne juge pas les gens. Si elle a décidé de changer, il faut l’aider au lieu de dire son passé
Sergio Tchico Pereira Vraiment seul Dieu a ce privilége la de nous juger merci
Penda Diop oui 👍
Merci
Sergio Tchico Pereira ta parfaitement raison, Lolou RK motakh keineu doufi bakh, ndakh lo wakh niouné la yaafi défone lii wala yaafi laa
Dgue dgue
Bayilen khél photo bi ci guanaw ndeye gueye rafétna trop notre diva Coumba gawlo séck🇸🇳❤️🇸🇳❤️❤️
« Damaye dieme rekkk di seuy « Ndeye banga wakhe lolou sama yarame dawna machalla yalla n’a yalla dioubole bonne continuation
Lanne moy mague ndeye g... et papa boy d... sey bii yalla moko toudu si arache kenn mou ns sou si dra sey bii yalla na am mboudiou bu ra fett❣❣❣
du courage paix à son âme yalnako yalla kharei aldiana
Je suis vraiment outrée. Ça fait un petit moment que je regarde les interviews mais là, Bijou a fait fort !
Depuis quand, on invite une célébrité pour la rabaisser en direct devant le public ?! On fait une interview pour en savoir plus sur la vie personnelle et professionnelle de la star. Mais on ne va pas jusqu’à juger la star sur tous ces actes, et lui dire que sa carrière est mauvaise (et j’en passe..).
Cette émission devrait être arrêtée, et la journaliste virée (si on peut appeler ça une journaliste). Elle se permet de critiquer ses invités, elle manque de professionnalisme.
..Le plus gros problème du sénégalais : c’est la mentalité. On est en 2018, essayez de changer !
Bijou, ya sof
Daba Thiam Ta tout dit ma chere merci...
Je sais elle m'énerve grave cette animatrice. Je n'arrive jamais à regarder jusqu'au bout tellement elle me tape sur les nerfs. Tellement arrogante
Daba Thiam vraiment tu as tout dit. Mais cest dommage le sénégalais est synonyme de critique
mais daba thiam je suis triste de constater que tu n' as rien compris, lis bien le titre de l' émission c' est ça le but de l' émission, atteindre confronter, soutirer c' est l' émission
Gni di aye doff meune topado té khamouniou doul mane genre tu sa me met hors de moiiii
ndeye gueye tu est tres belle
Ndeye gueye Dieu va te protéger
Bijou dafa r3wwww,môme tey amna histoire té keneu wakhouko
doul
Très bien repondu ndeye gueye. Dagua am klasse. Passé thi nitt la bokou
MACHALA NDEYE TAS BIEN PARLER
Ndèye GUEYE a été très claire dans ses propos.
Bijou, elle est... Waouh quoi! Elle doit revoir sa façon de faire.
Bijoux déh questions youmouye Sagna ladje mo takh émission bi osé je pense que si c'était une autre personne qui animé cette émission je penses que personne ne le regarder donc moi je dis bravo et continue comme ça.
Merci beaucoup ndéye amegeu foulo
Ayy wayy niak yaye daffa méti ndeye beuseull sa khol 😢😢
NDEYE boul dioy😭😭😭😭
So dioyei damay 😭😭😭
Je t'aime Ndeye joylo guama courage frangine
Mem moi
je te respecte Ndeye et t encourage dans tes projets d avenir et ton beau couple ndeyeboydjinné
Machalla Ndeye Gueye yalla nale yalla diapelé ms mane môme damala beugu rek té yalla takh doundel lou barii
L'émission est vraiment affreuse comment on peut inviter une personne et lui dire que tu représentes
la poisse pour ton mari et la rabaisser de la sorte, c'est vraiment dégradant. Ndèye tu t'es bien défendue.
ibrahima aidara au moins toi tu parles français merci 🙏
@@anouarbonimakeup3501 moi je vais te Chalier ça va tout le monde ne se fait que tu vas bien et la journée ça s'est bien passé qui m'aime
Amine yala nako yala may ndam thi barke serigne touba, Ndeye Gueye yay gor, bilay mala beugue.
Ohhhhh ndeye sa histoire akk sa yayy touché nama trop yalnako yallah yeureum et dou courage seuyeul sa seuy
Waa bijou mi nitt leu mounane boma nianone gresse sakh ma mayla weuhh pour sa gress merci rekk tchimmmm
Bravo 👏 ndeye gueye diamou thi yalla bamou nekh
Bien dit ma chérie d'amour Ndeye gueye ya tayyyy yawo yaye général
Bonne continuation ndaye gueye que Dieu vous protège
Ndeye Gueye manchalla borom khékh ak khoulo
Wawaaaaaaaw Ndeye Guéye do morromou been fethieu kaaat
c k Sénégal khamouniou kou changé koi bne continuation ndeye gueye courage
Guis nga lolou
Ndeye manchallah ts la meilleur
Bilay mala sope Ndeye Gueye ! Yala nala yala takhawou ta diapalé si sa sey.
Ooooo I never see this type of program because ndye Gaye get angry easily n bijou didn't care of asking any type of questions.i luv your program sis bijou very much belie u so educated belie because your questions are wel ask
Jobis Jobe i said the same thing
@@korejolie belie sis bijou is very intelligent that way she ask her questions is vry good but her program with sis ndye Gaye is that best i luv it because she ask ndye many questions which no one has ever asked her
Ndeysane yalla nako yalla yeurem
Bon courage ndeye geuye yalna sen seye bi barkél tarou djigeuéne seuye laaaaaa
Ndeye gnowatale thi tassou bi je t adore
Du courage et bonne chance à papa.
Je voulais la jujé mes j’ai été triste 😢quant elle parlé sa maman ke dieu lacieu dans son paradis
Machalla Ndaye gueye
Contena si Ndeye gueye
Ndeye gueye elle est très belle avec sa taille
mia Diop wawaw MachaALLAH
mia Diop Wawe
No bijou yamay danel nekh ngama
bijou mom kom mbeurou chinoi yii 😂😂
😅😅😅
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂réy guama
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂réy guama
😂😂😂😂😂😂😂
c ps sérieux wayyyy
Stp Ndeye Machala yangi diongama ni taill fine bii machalah
😭😭😭😭 sa yaye ya la nako yale yereme 🤲🤲🤲
Merci Ndeye tu es tres forte
Ñdeye gueye li takh ma beug la danga am foula si sa bopou merci way
Bijoux à tu etais à l'ecole.???tu es trés insolente , incorrect,
Tu poses vraiment des questions bêtes . discute dans le concept De l'emission, respect à Ndeye gueye
Contan si bijou rek prsc mashallah oyof na lolou ta djigeeen kou gawawoul guisse boppam kham niit rek momma meuna def confrontation🙌🏾💯 she has my resprct ive always loved bijou♥️❣️! Mes ndeye gueye dafa melni daga nieuw pou defantè ak bijou 😁 mes defal nank dei bijou dou bayi mo seddd
Merci mdey
Bravossimo Ndeye Gueye
Taylor Gang Diarraye cosa vuol dire brovossimo😂
Ndeye Gueye is gangster nigga! She's a fuckin Queen! Bo dougué ci gueew goné yeupeu wara tooke! Deugleu!!!!
Billaye bijou bi na bayi li😭😭🥺🥺🥺
Ndaye Gueye dall fouleu rek la ame
bijou xolal niigua déf légui yanii kay dioylo ndeye soi forte yalla nako yalla xaré aldiana sii barka Mohamed
iow deye Gueye mola geun, deye Gueye yalla nala yalla défal diam
Yalnalen yalla same te maylen ndiabote
Vrai ma journaliste Sénégal khamougnou Dara
Nice couple ndeye et papa , vs êtes des baye fall
Ndéye guéye daw naa yaram🙏🙏🙏🙏
Jador bijou😍😍😍 tu me fait trop rigoler.
Vraiment jss fière de toi 👏
Ndeye merci beaucoup
Ki yabatewoulll akk kanamammm bouuu bonnnne gonflé nii melni balon boumm rek ga explosé mais bon on te comp dagaa tangg 😂😂😂😂 niaw 😩 ndeye je taime 😍 maturité moy nitte wayyy😂😂😂
Ndeye gueye mane je déteste sene danse yi mais nakk j8 dakor avec tw nakh seye diamou yalla la et inshallah digu am lou bakh
Ndèye ngeye jtmm way djiguéne dagay am foula boul nangou kéne koula yapp boula naré sonal rek la wone fa wone waw keuy
Mashallah ndeye gueye sa tontou raféte na beug nga boy djiné bamou diekhhhhhh yalnala yalla dioubolé akk sa dieukeur
Teh xoloul xaliss ak interet
Bijou nak, tu dois faire une speciale un de ces quatres...et que tu sois de l'autre cote du plateau...niou interview la...
Ki mounelni gaidé ni
yéne sénégalais yi yéna sof bijou bouguéne nék di sagua méni séne morome la mome liguéyame laye déf t'es mou mena tonte conne bijou bonne continuation que dieux te donne une longue vie pleine de bonheur y'a Bah t'es mena bakhlé ❤💋💋💙💘💕
Liguéye day endak professionalisme. Do invité nite ba paré diko rabaissé diko coupé la parole sous prétexte que sa émission la. Ça ce fait pas on dirait un règlement de compte c abusé franchement
Bilay man ndeye gueye damako meussa beug rék courage rék
Ndéye❤❤❤❤❤
j'aime ndeye gueye
Non bijoux raye nguama "Ma meye la graisse " loll
Mais sénégalais arrêté léne di jugé une personne sur son physique.
QUAND JE LIS LES COMMENTAIRES,JE VOIS QUE CERTAINS N' ONT RIEN COMPRIS DE LA NATURE DE L' EMISSION CONFRONTATION COMME SON NOM L' INDIQUE
Waih on’a compris juste k’elle n’est pas pro y’a une manière de poser les questions tt en restant professionnel
Felicitation bijou eii merci ndeye gueye sii leral yinga deff ms Senegal j parl avk vs li c 'étai juste une émission Bjou c norm q elle pose ls lésion à ndeye gueye koi q s soi nak Tu es notre fierté Bjou d passage salut moi Miss
tafichou mbaye cest ce ke les gens n’ont pas compris
Ndeysane yalnako yallah xaré aldiana
Ndeye gueye el est tres inteligente
Macha Allah ndeye gueye tu es adorable
O machalla
Mane yow la endale♥️