Baye Sam yalna Yaala yokk ay leeram. Merci pour ce patrimoine immense que vous nous avez légué à travers les enregistrements sonore/vidéo de vos innombrables conférences et émissions. On ne peut compter combien de personnes, il ont remis sur le droit chemin, et il continuerons de le faire pour l'éternité. Merci pour votre sagesse et votre clairvoyance. Que le Bon Dieu vous honore pour le l'œuvre colossal que vous avez laissée à la postérité.
Ndeysane oh TGP Serigne Sam Mbaye ❤🙏🏾 yallah na yalla tass niou ci barkehm teh yokh ay leram 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 ci barkeh Seydina Mouhammad salalahou alayhi wa salam ❤ L'époque où Babacar Diagne était encore journaliste avec éthique et déontologie! SENEGAL yakhouna legui nakh macky Sall et sa voyoucratie 😢
Salam , salam niou gui ziar bou wér , il ya aussi une version de cette émission sous titrée en FRANÇAIS pour ceux qui ne comprennent pas wolof sur youtube , en tappant pour la recherche : "serigne sam sous titré francais" Dieureudieuf serigne sam
Mbaye Sangue. Li mata wakh, wakh nguako Mbaye. Lignou warona degue Mbaye wakh nguagnouko. Doyna seuk, matalena. Sougnou done ligueye ba fin du mois gnou djebal la lep yaw walla sak ndiabote, takhoute gnou mane la faye. Diareudieufat Mbaye Sangue. Mbaye Thiam Modena ma wakh li.
Baye Sam yalna Yaala yokk ay leeram. Merci pour ce patrimoine immense que vous nous avez légué à travers les enregistrements sonore/vidéo de vos innombrables conférences et émissions. On ne peut compter combien de personnes, il ont remis sur le droit chemin, et il continuerons de le faire pour l'éternité. Merci pour votre sagesse et votre clairvoyance. Que le Bon Dieu vous honore pour le l'œuvre colossal que vous avez laissée à la postérité.
⁰⁰⁰
Yallah na njégël léér ak yërmëndé Sunu Borom saxoo di wacc tji mom🤲
Macha allah yalla na yalla dolinu fayal serigne sam mbaye barkeb s touba
Koubakh ki ak liko yalla maye ta mom nagoul na s touba kone kouneke war na nagoul s touba
Diambar ziar mais est ce que amna kou nangouloul Serigne Touba
132 dislikes eukhlou saïtaan. Diakhal ngen ma kou nangou woul eukhlou alquran mom yallah reub naleu. Serigne sam yallah na yallah yeutrum té geureum ko 🙏🏽
Serigne Sam Mbaye nitou yalla la waliwou la
Yalla nanou yalla maye xam vam bou and ak racgal yalla ❤❤❤❤
Serigne sam mbaye yalla na yallah yokou lérame🙏🙏🙏
❤️❤️billahi dama ko bague té Yallah takhe
Serigne Sam mbaye yalle nanou ko yalla fayale amine
Machallah machallah machallah Serigne sam mbaye yalla nako yalla yeureum yokou ay leram
serigne sam xamoul nama man ak gnou bari ci sounou diine lo xamni meunone negn doundou ba deih dougn ko xam...yalna yalla yokou ay leeram
Billahi
Baye sam yalla na yalla yokk aye leram barké Serigne Touba
*_Ndeyesan 😭😢😭yalna yalla yokk l'airamm si barkép serigne saliou mbacké❤_*
Yalah na yalah yokou aye lérram
Thiéye saringe same yalla noko yalla faye
Énormément de savoir en une personne MachAllah. Très concret et direct. Borom xamxam degueu
Ol
SERIGNE SAM MBAYE YALNA YALLA YOK AY LÉRAM 🙏🙏🙏
souma koy déglou sama xol day toy😭yalla na yalla yokou ay léram si barké seydouna Mouhammad pls 🙏🙏
Machallah sopé bi❤yalla na sa brome yokou say lerr
Dieureudieuf baye sam❤
Walahi kou tew tewlou saye kadou yalla rek laye yeuk
رحمه الله ورضي عنه كان مسلما مؤمنا تقيا متواضعا عالما داعيا مجددا نفعنا الله بعلومه
AL HAMDOULILLAHI SOUKRANE YA RAHMANOU YA RAHIMOU
Serigne Sam mbaye yalla nago yalla yeuram takharèko aldjana sii bare képe Alkhourane
Ki moy kham kham, yalla nako yalla yereum té fayko
mane déi moussouma guiss kou mélni serigne sam mbay yalla nagniou ko fayal
Yalla na yalla yokou léram té tasse niou si Barkémn !
Serigne Sam Mbaye yala naniou koo yala fayale amine khavise mou diadite Baye Sam
Ndeysane oh TGP Serigne Sam Mbaye ❤🙏🏾 yallah na yalla tass niou ci barkehm teh yokh ay leram 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 ci barkeh Seydina Mouhammad salalahou alayhi wa salam ❤
L'époque où Babacar Diagne était encore journaliste avec éthique et déontologie! SENEGAL yakhouna legui nakh macky Sall et sa voyoucratie 😢
Serigne Sam mbaye yalna yalla doli léram yalla fayal niou ko
Machallah way thiey sama waji baye same Mbaye yallana yalla douli yeurmendé si mom si barke boroum touba
Ndeyssan louga sante nagn la lolou❤️... yalna yala yokk leiram tei tass niou si barkéem
Serigne sam mbaye yalla nako yalla yeureum guèn neuna adnouna wayé migui may tarbiya al hamdou lil lah
Yay sougnou lamp adouna yalna yalah yocou aye lèrram
Baye Sam mbaye yalla na yalla yokkou Ay l'éram si barkép Al qour ãne
2021 - dellou tchi Serigne Sam rek - Yalla na Borom bi Yok Leeram Abadane. Mashallah.
Mane damako beuggue bilahi ❤️
Yalna yalla yokou lèram té tass gniou si barkem 🤲❤️
Yalla nanou ko yalla fayal te tasnou ci barkem te sammal ko ndiabotam ci barke alkhouran ak yonentebi slws
Yalla nanioula yalla fayal
Thiuey yallah founouy dieuletii kou melnii ioe😭😭
dieuredieufé serigne sam mbaye si fingagnou dieulé ak fingagnou yobou si kham sounou borom ak diamouko
Serigne Sam, ndeysane goor Yallah deug ngi ni, borom kham kham deug
Salam , salam niou gui ziar bou wér , il ya aussi une version de cette émission sous titrée en FRANÇAIS pour ceux qui ne comprennent pas wolof sur youtube , en tappant pour la recherche : "serigne sam sous titré francais"
Dieureudieuf serigne sam
Amine yalana yalla yokou leram té tass niou si barkem si barké cheikhale kabire mbaye
Serigne Sam mbaye yallna yalla yoke ay lerame 🤲
Baye sam mbaye borom xam xam bou sel bi yalla nanou ko bour yalla fayal si dara diay seuydoun Moukhamet
JUSQU'ICI INNEGALABLE
Un conférencier hors paire toujours immité et jamais égalé
Ci lou werr
@@MuridLife 3
L'homme le plus erudit de tous les temps!
@@MuridLife hhhhhdhhhddddddhhdddddhdddhedhedddhdhhhddhdhdhddhhdddddddhddhdddhhehdddhdhdhhhhhddhddddhhhdhddhddhdhdddddhdhdddhhhhddhhhhhddhhddhhhhhhddhdddhdddhhhdddddddhdhhddddhdhhhhdhdddhdddhdhhdddhdddhddhhdhdddhddddhhdhdddhdhdhdddddddhddddhdddddddddhddddddddhdhddhdhdkdhddhddhhdddhddddddhdhdhhdhhhddddhdhhddhhdhddddddddhdhdhdhhhdzhddddhdhdddddddhhhdhhdhhhdhdhhhdhhhhdhhdhdhhdhdddddhhhddhhddbhdddhdhdddddhdddhdhddhhdhhhhhhhdddhddhddddddhhhhhddhdhhhdhdfddddhhdhdddhhddddhdddhhdhdhddddhddhdddddddddhhhddhhdddhhhddhdhhddhddhddhdhdhdhhhhhddhddddhhhdhhhddhhddhddhhddhddddddhddhddddddhhhddhdhddddhhhdhdhddhdhdhdhhddhhdhdhdhhdhdhhddddhdddhdhdhdddddddhdhdhddhhhhdddhgdddddhhdhdddddhddhhhhr4, 4
@@khadimthewritertv2397 r you
Yalla nako yalla yeureum te khareko Aldiana firdawsi srg sam mbaye nako beug
Yalnanou yalla fayal Serigne Sam mbaye
Machala s sam yalla na yalla yokou ay léram
Yallana borom bi yok ay leram te tassgnou thi barkem🙏🏽❤️
Serigne sam mbaye yal na yalla tass ma si barkemm
Yalla nagnou yalla xaré aldiana
Dieum dji wama ko soppp lolou sah... un grand érudit amone kham kham ma sha allah...yalna nako sunu borom fayyy yiwww
Dieureudieufé baye sam yalla sounou borom térou la si aldiana you kawéya
Amine ta rabbi serigne sam était un monument
Allahoma sali khala moukhamad ❤❤❤❤
اللهم إن القبور واسعة والنور والنفور اللهم اغفر ورحمه واعف عنه وادخله جنةالفردوس
Machallah yalla na yalla yokk leramm te tassniou thie barkéme
Yalla n'a yalla yokou lèrame Tass gnou si barkêm
اللهم آمين يارب العالمين
Ndeyssan seuñ Sam yalla naniou ko yala fayal🙏🏾
kouy jang dou seuñ Hady Touré?
Kou melni moom meuneutoul am
yalla nako yalla faye
Yalla nako yalla dolli yeurmandem si mom
SANTATI YALLAH BOUWER ÇI BARCKÉ KOUTEDDKI EUHMEUDOUL KHADIMOU RASSOULOU LAHI ❤️❤ DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMP ❤ SERIGNE SAAM MBAYE YALLAH NA YALLAH YOCK LÉRAM BARCKÉ SEYDINA MOHAMAD RASSOULOU LAHI SLHWSLM❤️🙏!
Yalnala yalla dolley lerr
Yalla naka yalla yeurem ❤❤❤
yalnaniou yalla fayal serigne same ta yoklerame
*_céyy serigne Sam Mbaye🙏_*
Thieye Serigne sam amoul morom
Thiéy yalla alhamdou lillah machallah
Yalna Yalla defalnou deg ak top
Dieureudieuf Serigne Saam Mbaye ❤
Jeureujeuff baaye saam luniversel yaalla yook seuy maay fofou l’abreuvoir des assoiffés
yalla nagniouko yalla fayal
Yalla nala yalla faye
Yallana yalyoko lérame
Dieradiafe serigne sam mbaye
yalla nagnou may ak dioum
Bày sam le mujàdid eternel
sante. serigne. sam. mbaye. kharitou. khollll d'i. sante. yalla. R eekk. yalla. deugue. yakarre. serigne. sam. R eekk. T hiey
Yallah naa ya Allah yook ayy leeraam
Masalah yalla na alah fayla
REGARDEZ > [ARCHIVE] Serigne Sam Mbaye : Le Saint Coran - Emission TGP
Barakala
yalla na niokou yalla fayel
YALLA DOLLI KO YEURMANDE TE KHAREKO ALDIANA FIRDAWSI BARKE SEYDINA MOUHAMED
❤❤❤❤❤❤
yalneu sama borom yokou leirou serigne sam mbaye
mamadou mouride bakane Diouf serigne sam mbaye kendou mom
Machallah 💞
yalna yala doli ko yeurmade ta fayalnou ko
Mame Cheikh Mbaye amin
yala na yala yoki leram
Yalla na yalla yakko ngeureumeum aamineeee
جرجفت شرج شام بي ماشاءالله 🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤🖤😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Allahou akbar
bay sam sama serigne
Baye salam yalnaniuko Yalla fayal🙏🙏
Alkhamdoulila serigne Sam mbaye
Machalla am na solo trope♥♥♥♥
❤❤❤🎉❤
what a great man.
yalla kénla
dieumm ju beuri xamxam
Le soleil des soleils
Mbaye Sangue. Li mata wakh, wakh nguako Mbaye. Lignou warona degue Mbaye wakh nguagnouko. Doyna seuk, matalena. Sougnou done ligueye ba fin du mois gnou djebal la lep yaw walla sak ndiabote, takhoute gnou mane la faye. Diareudieufat Mbaye Sangue. Mbaye Thiam Modena ma wakh li.
Hadi touré yala na yala goudal fanam ❤
Ma beug baye sam❤❤❤ a été
Akassa way Serigne sam mbaye