Moi je supporte Modou Lo depuis très longtemps à 100% ; mais je pense que Tapha aussi cherche le combat royal et veut lutter avec Modou et je le respecte beaucoup donc je pense qu'il n'est rien de mal de dire que Modou n'est pas son roi. Je pense que c'est juste pour pousser à Modou de le prendre🙏🙏
Tapha Amna droit waxx lolou parck Modou Lô dakka ragal. Roi bi day daw Balla Gaye di daw Tapha Tine. C'est ça la vérité. Un vrai roi ne doit pas avoir peur de personne.
@HenryDiouf-gw2yl 1) Football matche et élimination direct leu ce qui est différent avec sport de combat 2) Modou Lô préférait Siteu à la place de Tapha Tine pendant que Tapha Tine était Libre. On est d'accord que Tapha Tine est plus méritant que Siteu pour un combat contre Modou Lô. 3) Loutaxx Modou Lô beugueu dieul Sa Thiés à la place de Tapha Tine. Pourtant tout récemment Tapha Tine a battu Eumeu Séne qui a battu Sa Thiés yaggoul dara. Ignorant et malhonnête que tu es 🤣🤣🤣 !
Yén xana Daguén ragual eumeu séne yén gnak nguén djom franchement eumeu séne daneu mak daneu rak au lieu nguén dém djeuli sen revanche nguèn nék fih dih wakh ay wakhou roi té pour djékhal par force modou moy roi que ça te plaise ou non mom lafi yalla ték nanguou rk
@@bilalkhalyfall9938 Balla Gaye contrairement à votre roi fugitif meussoul waxx ni dou beuré ak Eumeu Séne. Modou Lô daffa ragal Balla, yayou Modou bagne combat bi 😅, supporters yi niakk diomm ba dh nane beuréwougnou ak Balla. Quant à nous combat bougnou geuneu beug moy revanche contre Eumeu Séne. Balla est roi à l'âge de 25 ans. Dane kou teuwone gneup mouy Yékini.
En tout cas dal.Rock énergie ,grand Khadim Gadiaga daniou éviter sama mbeur mi .Tapha Tine ,le géant du baol sunu champion .Respect à Kharagne Lô, le roi Modou Lo jeelma way mettez la couronne en jeu .Tapha Tine naak ne prenez Franc ou sa.Thiès Modou lo ou rien
😂😂 tapha tine wéroule yaw Ana baldé mola dane modou lô moko dane li dou dakh modou lô mbeuré ak yaww yaw dagaye soule danane mo takh modou dila dieule😂😂
Roi des arènes c’est pas sélectif,c’est un titre,même si balla bat modou 20 fois,cela n’empêche que modou est le roi de toute l’arène car c’est lui qui a le titre,c’est comme si l’Arabie saoudite dit que argtine dou sama champion du monde car ils ont battu argentine 😂😂
K''‹coupe du monde soka dielé nio jouer loul déniouy conteste ki d'où champions du monde prsk jouer wunu😂 bégaye et famille ay nafekh gueine waleu xamoulene len sport
Ku bagn Modou Ló neek sa Roi guéneul Ndéye Aréne bi😂😂
Merci bcp
Tu ment 😂😂😂😂
Wala modou bayi tegui bi
Waxofi gat combat la modou da dane eumeu tapha dane eum modou dane boy Niang tapha pareille balla niouss len niom niar combat la
Soyez des sportifs Modou lo c'est le roi des arènes de tous les lutteurs que vous le veuillez où non , minimum de respect pour lui .
😂 légui gnimou bania beurel aussi moy séne roi
Non yaw comprano, kii combat la beugue mootah mouy wahé nii, communication la rek mais khamnané Modou lô mooy Roi
Ama baldé dane nala modou dane ama moy sa 🤴
Tapha dane n'a bomb te bomb dane n'a modou
@@ousmaneba2608y’a dègue
Voila merci
Mais Tapha sagnsangé nak machalah ❤
Dagay wakh rk kep kou nekh si arènes bi di beuré Modou moy sa roi par la force
Wallahi DEUGG la ❤❤
Modou lo Moy roi des arènes
Merci lolu moy ku dekeu Sénégal ni diomay dusama président khel manuko nangu
Mais dafa ragal Tapha Tine nako dieul
@@abasall711 hallpoular rék Moy wakh lolou
Tapha vs modou moy combat bi
Boul saxor way modou moy roi de tt ké lutteur du sngual
Esk dou beuré ak tapha aussi bagn beuré ak mom ba paré nane may sa roi
Dokh nagn sougnou combat 😂😂any time
Modou lo tafa tine moy combat bi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Deugue nekhoul mais lambe mon wakhoul deugue bari aye lobi ko monon nek roi wa ame lo lou monye deugue
Modou Lo doit prendre Tapha c’est la logique 😊
Tapha miii dou gattt
Légui.louye.roi
Louye.senpoin.dafrique
Modou dey moytou tapha lolou moy deug
Mon taye 😂
Modou dan kila dan ngay doul
Modou lo d'où sama mbeur mais Moy roi des arènes dank diomay président toutes les sénégalais te mane té d'où nieup nioko votel
Diadieuf ardo wax nga lp point
Modou lo vs Tapha tine combat la bou logique
@@ibrahimandiaye9319 billahi lolou kessé la
Modou dofkoye moytou 😅
Tapa wxo lou am aragatin doroul Sénégal moye champion 🏆 dû Mon dou
Bayyiko fofou rk
Donc Argentine nekkoul souniou champion du monde 😂😂😂
Khawma founiou bind k Roi des arènes dafa wara daneu nieupp
Merci champion damala begue mais yaw yakarouma li ngay beré dane modou
BIMOY COMBAT/ Lac2 ak Tapha tine / tapha tine dieuleul revanche mais si yoon war nga beuré combat Royal
Ponkal mou niakk diom moy tapha Tine 😂😂 Eupp gars yii,ba paré gueune léne tapéte
Le combat logique que tout le monde s’attend Tapha tine vs Modou lo
Ak bindeum bou bakh mais mo gueuneu ragal té yambar si mbeurr yii.
Beurre la manul doley rek la am mai manul beurre
Ki kay moungui nonou rek waroul tok fi sakh di oubi lamignam bi
Modou Lô Da Raguale Dofoule Djiné Diapakou hum Domérame Dji ❤❤❤❤
Moi je supporte Modou Lo depuis très longtemps à 100% ; mais je pense que Tapha aussi cherche le combat royal et veut lutter avec Modou et je le respecte beaucoup donc je pense qu'il n'est rien de mal de dire que Modou n'est pas son roi.
Je pense que c'est juste pour pousser à Modou de le prendre🙏🙏
Moy sa Roi force
Sou nekhé gambie mouni Argentine dou champions du mondam
Tapha Amna droit waxx lolou parck Modou Lô dakka ragal. Roi bi day daw Balla Gaye di daw Tapha Tine. C'est ça la vérité. Un vrai roi ne doit pas avoir peur de personne.
Même Sénégal bimouy done champion d'Afrique gagné woul GNEUP Gambie gui dorougn KO 😃😃ay dof ngén RÉKK
@HenryDiouf-gw2yl 1) Football matche et élimination direct leu ce qui est différent avec sport de combat
2) Modou Lô préférait Siteu à la place de Tapha Tine pendant que Tapha Tine était Libre. On est d'accord que Tapha Tine est plus méritant que Siteu pour un combat contre Modou Lô.
3) Loutaxx Modou Lô beugueu dieul Sa Thiés à la place de Tapha Tine. Pourtant tout récemment Tapha Tine a battu Eumeu Séne qui a battu Sa Thiés yaggoul dara.
Ignorant et malhonnête que tu es 🤣🤣🤣 !
Yén xana Daguén ragual eumeu séne yén gnak nguén djom franchement eumeu séne daneu mak daneu rak au lieu nguén dém djeuli sen revanche nguèn nék fih dih wakh ay wakhou roi té pour djékhal par force modou moy roi que ça te plaise ou non mom lafi yalla ték nanguou rk
@@bilalkhalyfall9938 Balla Gaye contrairement à votre roi fugitif meussoul waxx ni dou beuré ak Eumeu Séne. Modou Lô daffa ragal Balla, yayou Modou bagne combat bi 😅, supporters yi niakk diomm ba dh nane beuréwougnou ak Balla. Quant à nous combat bougnou geuneu beug moy revanche contre Eumeu Séne. Balla est roi à l'âge de 25 ans. Dane kou teuwone gneup mouy Yékini.
@@bilalkhalyfall9938 Saway boul gnou Sonal Balla Gaye au moins ragaloul djeulate Eumeu mais Modou tapete Tapha tine motax Siteu gnous ko !!!
Tapha tine nékale nitt modou dane 3 lutteurs youla dane ( Ama, Lac2, Issa Pouye)
Md lo le roi des arènes champion de tout les temps
Légui MBEUR Yii dañio osée dii YeuG YeuG Lou succès té guéna yém moo geun ci yén fékké Lii MODOU LÔ 👑 motax guén NEKKEU fii dii wax RK
MODOU LÔ 👑 mo wra baayii Lambji RK yén MBEUR Yii guén noppaLu Té xeuthio bu nékkeu ci BALLA Gaye
Soyez logique on peut pas terrasser tous les lutteurs pour être roi
😂😂yaw wakh kessè 😅😅😅😅
En tout cas dal.Rock énergie ,grand Khadim Gadiaga daniou éviter sama mbeur mi .Tapha Tine ,le géant du baol sunu champion .Respect à Kharagne Lô, le roi Modou Lo jeelma way mettez la couronne en jeu .Tapha Tine naak ne prenez Franc ou sa.Thiès Modou lo ou rien
Mon frère je n'aime pas lutte mais wadji môme meunoul barei en plus defa yambarei wax rek
Tapha Tine vs Lac De Guerre 2
Iow tapha dagua niakh diom motah 😂
Yaw rek ya niak diom nak
Modou Lo moy roi kouli Mbeur par la force doley mbam khoukh walaaaaaaa
Modlo est le Roi des arenes❤
Modou lo moy sene baye😂😂😂
Modou mom day tégui tapha tine nak
Tapha fine rek🎉🎉
Je suis fans balla gaye mais Modou lo est le roi par force
Modou moy sma mbeur mais je veux pas qu'il lutte avec Tapha. Dama yéné Taph ndam prochaine combat.
Je suis parfaitement d'accord avec Tapha c logique dagno wara beure
Tapha deh nangounani Eumeu moo daxa beuré sii lamb djii😅
😂😂 tapha tine wéroule yaw Ana baldé mola dane modou lô moko dane li dou dakh modou lô mbeuré ak yaww yaw dagaye soule danane mo takh modou dila dieule😂😂
Amna mbeur bou nekh si lamb ji tolnii camion ken geunouko niak Diom toudouma tourou ken
😂ya sokharr 😂
😂😂
OK me Ama moy sa roi lac moy sa roi😂😂
Je suis balla gaye mais Modou lo est le roi par force
😂😂😂bou arbitre bi di sifler mouye Tite😂.
Modou moum day daw tapha rk srx😂😂😂
Bilaye
Modou Moy roi de tout les lutteur
Sa thies champion
Bg2 100 combat mo meun tapha ms tapha 100 combat mo meun modou
Wa legui Modou lô nako dieul kay gnou khol😂😂😂😂
Kou nékoul mbeur Modou lo dousa roi mai kouy mbeur Modou Moy sa roi mouy nékh mouy nakhari
Tapha tine wakh duégg modou lo dou roi wam ndakh ma su niobaré❤
Modou Lô moy sama mbeur mais ragal na tapha tine
Tapha tine yow khamo sport😂 modou sen roi la yen yep
Franc sak rawnala😂😂😂
Bane champion lafi dane?
Si Naka
Kou bagne ni Modou lo Moy sa roi tekil sa nguemb liguendi sokhor
Modou lo da ragal tapha tine
Modou lo seul❤❤❤❤❤❤❤
Un roi qui fuit les géants depuis que bombardier la terrassé
Tapha Tine tu te fou du monde. Tapet Bou mag nga
Tapha togal way Modou Lo est le roi des Arènes incontestable.
TAPHA a raison
Am ngathi droit dé parce que Modou lo nangouwoul beuré ak iow
Yow topal falé khamo tousse Di wakh fi dieulal sa thiés
Roi des arènes c’est pas sélectif,c’est un titre,même si balla bat modou 20 fois,cela n’empêche que modou est le roi de toute l’arène car c’est lui qui a le titre,c’est comme si l’Arabie saoudite dit que argtine dou sama champion du monde car ils ont battu argentine 😂😂
Kholale bamou kharam yi force mouy nekh ak mouy nakari roi bi Modou Lo loutakh sénégalais yi faux même champion du monde gagné woule gneppou
Tapha Tine ioe mom ami jom.Houlé ba Ama ak Balla daan la nga nék di wax
Tapha Tine bayil di gnew si plateau yi di téééglé
Tapha Écoute bien per becaye wakhna la lamb dépasser na fofou
En tant que amateur combat Tapha Tine nekhoul
Famille mbaye ay deum ngène Modou ngène mounoul digérer tok lène si plateau di wakh rekk
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉
Deeleeen wax dëg roi des arènes keepp kuy takk gemb mooy sa bàay😮
Becay amo lo waxh si Modou lo Bago Modou lo ioe AK sa dom😮😮😮
Modou lo vs tapha tine moye combat bi
Sissou bakhoul 😂
Wakh dji Moy bénn arène mo am Sénégal te Modou Moy roi bi mou nékh la mou nakari la Mouy yow Mouy Balla Mouy EUMEU yén niéup Modou Moy sénn roi
Modou Mbaye
Pere Becaye
Danio sokhor trope lan laléne modou lo déf pourquoi ignane sheuut wow
Amnasi droi
Lou ma diaxal si Sénégal mbeur yi douniou ay sportifs
Modou lo tapha tine comba leu
Ki est ce que werna wouye modou lo dousma roi
Wa nadegeu 😂😂
Khawma roi khawma rouwa mais li lère ba lère moy modou lo niéméwoul tapha tine.
Ndiak faye ndayam
Laambam neexul. Wax rek lat def. Modou Lo moy Roi par force. Tapha Tine bokkatul "cours des grands".
Mrm dji tioupp dessatoul Sénégal 😂
Ya dan eumeu do beurè ak sa thies ok d'accord modou lô mo dan ama ama mola dan dialal feulè
Modou moy sen baye
Sa thies modou lo moye combat
Tapha vs Modou
Ki dou mbeur way
Vraiment sohore nagn Nn Sénégal dou rew
Modou dou sama roi communication bobou bakhoul mo takh modou lo doula dieul
Kou dane kou la dane moye sa royal
Tapha Tine waxou nit la wax nak yaw beuré wo ak say Morom nane xaléyi ngay may chance Modou lo da ragall rek sama xalate la nak mane la engagé
Bour dou dem kw😂
K''‹coupe du monde soka dielé nio jouer loul déniouy conteste ki d'où champions du monde prsk jouer wunu😂 bégaye et famille ay nafekh gueine waleu xamoulene len sport