Ndeye ndack est femme que j'apprécie beaucoup. Elle est venue à kabrouse pour aider les femmes âgées en leur donnant des dizaines de matelas des tonnes de riz et beaucoup de denrées précieuses. Je fais parti des gens qui l'on aidé à décharger les camions. Merci ndeye ndack je t'aime
Serigne fallou kéne là yala moko def maschalah❤😍yala naniou yala tass si sén barké mbecté mii rek ❤😍 Une remarque ndeye Ndack la guis ni té tégoul péruck mai les autres si maschalah
Magal gui si wérrou safar leu mouy tombé si 18ème jour bi motah gnou wah 18 safar serigne Touba lépeu dafa teukou si wérrou wi toi ndack Touré gueunala sopp dakh ligua beugeu kou teed ki diadieuf waay nekk mouride mo nékh
Ben secret barki serigne saliou mbacke man talibe serigne saliou mais serigne fallou mbacke si tabaski bi la xam ni ken dou mom tabaski dafa nieuw mou dess presque 15jours té ligueyouma mangui maroc ma diaxle te warna dieundal khar Sama yaye ma diahlei lol teud guente Sama am koumay Wax si guente gui sa sokhla bi oup sa bop bi diss ko serigne fallou mbacke ma yewou si kaw lal bi neko mbacke ballah dama bg khar pour Sama yaye si tabaski bi te diakhlei na diapalema mbacke ballah si 10eme jour bi heweul yi dima dal bama yonei Sama yaye khalisou khar bi lolu mom man mako doundou ak serigne fallou te fouma diakhlei rkkk soumako wowei damay yeut ni nieuw na barki serigne saliou 😭😭😭😭😭 serigne fallou mbacke dama soutoural
Melocan da am solo ndack serigne Fallou miguiy wakh nena si ndakh ak ounkou nouro melocan mo takh gnou lene di diawalei Tei pourtant bokou gnou Nit da ngay am melocann bou bakh gnoulay diawalei ak kou bakh Mais machalla contenne nassi yaw
Ndeye ndack est femme que j'apprécie beaucoup. Elle est venue à kabrouse pour aider les femmes âgées en leur donnant des dizaines de matelas des tonnes de riz et beaucoup de denrées précieuses. Je fais parti des gens qui l'on aidé à décharger les camions. Merci ndeye ndack je t'aime
Vvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvbvvvvvvvbvvv
9
Serigne fallou kéne là yala moko def maschalah❤😍yala naniou yala tass si sén barké mbecté mii rek ❤😍
Une remarque ndeye Ndack la guis ni té tégoul péruck mai les autres si maschalah
Wallahi lébal nguén kou am AK Faye Serigne Touba amoul tanki guinaw tanki kanam rék la am
Machallah ndeye ndack Yalla nalla serigne bi fayal bopam si Barke Serigne Fallou mou Tedmi
Salut wa sen web je suis un vrais tidiane mais j'aime beaucoup bayi Karim ,je veux la visite vraiment. Et j compte sur vs
Suma star bi ci kaw si kanam insahalla 2stv rek Marshall 💕💕💕
Jaime ndeye ndack bègue nala lou bari je vous stl depuis islande touré touré gnou bakh lagne
Ay way ndeye ndack beug nala dh kay lalay guiss si barké Cheikhoul Khadim🙏🙏🙏
bilahi khaleyou djiguene khamouniou ne sans mak up moenvguena diap waye boye togue sagnkh diambe bamouyy tourou machalah ndackk😍😍😍
La simplicité c de l'art je t'aime trop ndack😚😙😙
Ndayssann ndeye ndack amal diam dioudoy ❤️❤️
Je l'aime beaucoup Ndeye ndak😍😍♥️♥️
Je t'adore Ndeye ndack bilay app talibé rek mo woor
Ndeye ndak trop simple tt le monde l'aimes
Machallah
Sama sopei bi machallah longue vie à toi ❤️❤️❤️❤️❤️
Machala ndack Touré" maningo
Merci ndey ndack buegue nala ndéké talibé nga
Machalah ndeye ndak yaye fall bi
Machalla Ndeye Damala beuge
machallah ndeye ndak am na sololllllll
Machaalla lafe thiate.Nice na ndack.kéne d'où serigne fallou mbacké
Ndeye ndack ci kaw rek insahalla 💪💪💪💪💪❤️
Nit kou bakh la manchallah
Machallah ndeye ndak
Magal gui si wérrou safar leu mouy tombé si 18ème jour bi motah gnou wah 18 safar serigne Touba lépeu dafa teukou si wérrou wi toi ndack Touré gueunala sopp dakh ligua beugeu kou teed ki diadieuf waay nekk mouride mo nékh
Machalla yalla na leen Serigne tuuba Fay
Je l'aime🤸♂️
Bravo ndack pour la simplicité
Machalla Ndack sa wakh rafetna
Serigne touba kouka bañ alkou
Machallah ndak
Machalla dafa yarou
Waw comba way goor goor lou rék machalla
Ben secret barki serigne saliou mbacke man talibe serigne saliou mais serigne fallou mbacke si tabaski bi la xam ni ken dou mom tabaski dafa nieuw mou dess presque 15jours té ligueyouma mangui maroc ma diaxle te warna dieundal khar Sama yaye ma diahlei lol teud guente Sama am koumay Wax si guente gui sa sokhla bi oup sa bop bi diss ko serigne fallou mbacke ma yewou si kaw lal bi neko mbacke ballah dama bg khar pour Sama yaye si tabaski bi te diakhlei na diapalema mbacke ballah si 10eme jour bi heweul yi dima dal bama yonei Sama yaye khalisou khar bi lolu mom man mako doundou ak serigne fallou te fouma diakhlei rkkk soumako wowei damay yeut ni nieuw na barki serigne saliou 😭😭😭😭😭 serigne fallou mbacke dama soutoural
lou lere nga wakh mane deh guenenamasi batayi te balegui monguimasi gueneh
Ndaysane sama yaram bi sakh mogui dawe😭😭😭
Lou léeeer gua wakh bilay khamnasi dara
Ndeysaan .......waw Coumba Ndeye ndack,giudeul fann té werr 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Ndeye Touré mandimori sama domou baye sa numéro damala beug te yalla takh
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machallah ndeye yalna sa diamou yagué❤️❤️❤️🤙
👍👍👍💯
Contane na si yaw ndeye ndack
Melocan da am solo ndack serigne Fallou miguiy wakh nena si ndakh ak ounkou nouro melocan mo takh gnou lene di diawalei
Tei pourtant bokou gnou
Nit da ngay am melocann bou bakh gnoulay diawalei ak kou bakh
Mais machalla contenne nassi yaw
Amana solo
Aminne Amenasolo
Journaliste suneweb bi bokou na ci journaliste yima guena nexx ci journaliste yi mom dafa dall xam ñimi wakhé
Ndak nékh nama machala kikouko Khale khame né diabarou kilifala
❤️😍❤️
machalla
Je ne t’ai jamais suivi mais si t’es Mouride je t’aime
Ndanane deg
ZIAR BOU BAKH YALNA DIAMOU SAKH CI REWMI
man serigne abdou karim la beugue 😅😅😅
Mane tamite conetane na si yaw ndaye ndake khaléye dagne léne wara take nakhe gnieup ame borome keur
mane khalé bi rek la nope
meun xawma woné ndeye ndack la begue
Diamm si yaw
Sama tourondo je leme
antouca. moi. je. le. conné. au. niveau. de la. télé. mai. kou. rafète. khole. là. thé. barri. yarmandé. je. ľaim. bien. moi. je. ťaim je. ťaim. je atan. vontre. réponse. san. blank
Votre numéro
👏👏👏👏👏
Werou olof yi matt neu xam
Ana ndeye mousor bi yene guémou lene serigne touba seytané diable guéne di diamou
#yvon galeran sa data yaye, sa digeu leufeul ndaye bou takheu daye
Khana do mourou
Donc t'es dedans sans comprendre 🙄
Yallah mola wakh xol lay faye?
Yaw ki la nop
Demal ndeye passy dom Ram gua yow ndeye ndat
Yaw ndeye ndack molaa geune fouff
Des Faux personnes
Machallah
Machalla ndeye ndack
Machalla ndak
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Machalla
Machalah