Je suis en salle de pose , les écouteurs dans les oreilles . Je n'arrête pas de rigoler . Tant pis pour mes collègues qui ne comprennent pas le wolof. Cette série est excellente. Félicitations à notre badiène nationale. Mariage très réussi !!😍😍😍🤩🤩🤩🤩🥰🥰🥰🥰
Le sourire n'est plus à l'ordre du jour à cause de la vie chaire mais vous jouez un rôle primordiale dans la société en tuant le stresse toujours souriant quand on regarde polygame macha Allah yallah na léne yallah fay
Ceux qui n'ont point ratez d'épisodes et attendez avec impatience le mariage de BADIANE_BINOME POINTEZ Vraiment senepoeple chapeau à toute l'équipe du lourd walay
Félicitations à toute l'équipe de nous faire vivre ça vraiment on voulais une EPISODE trop longue et voilà 2 parties de la réception vous êtes à l'écoute et merci beaucoup 😭😭❤❤
Polygame une série pleine d'enseignement on nous apprend que AK lo dieul dieul âge iow jiguen boumou takh nga yakh sa bopp kholal badiane AK âge bi guisna kouko marier teral ko ta yalla meune na def mou ame si ndiabot félicitations polygame tjrs des leçons à retenir 🥰
Li nèkh na nèkh no mariage Badiène amatoul wayè bi madame Bâ mom banela no Oumou meuna sabotè tay mom Bâ dèf na yeufou grandeur gueureum Seun wayè Astou Ndiaye Khady Baba warone nguèn na diouk puisque daguèna wotè diam ak djioubo sèn sagnsè nice na machallah Sènègal dal yenagui khappy outèk niou nji sèd bi di beugua ray 😂❤❤😘
To be honest I am really out of words.Y'all have been making your viewers proud since from the beginning.There wasn't a time when your team missed even a single episode which just shows how caring you are towards your subscribers/viewers.Your punctuality just shows the respect you have towards your viewers and therefore,hats off to the entire team.This is just the reality.
Mais vraiment la robe de badiene est magnifique j’ai juste envie de me remarier merci aux sponsors ❤️ mais ba daga ame diabar Europe 😯😯😯😯 binôme reynama restez dignes 😂
🥺🥺🥺bilae je vous aime bcp yénagui séral sunu hol yi diniou diangual franchema chapo 🎩xéw mi nehna sagnsé yi rafetna 💞yalna yalla taxawoulén yén niép sunu acteur yék actrice yeip 🌹wayé Astou machalla t trop belle way Merci ékip bi yép🤍 sunu hol sed na lol tchi yén💗💗💗 one love senepeople❤
Vous avez encore montré votre professionnalisme . Thiès capital théâtrale sans vulgarité machalah niguendi sedalé sounou khôl yi yalla nalen ko yalla fayy
Je souhaite à toutes les Filles qui suivent cette série de trouver leur Binôme avant la fin de l'année 2022.... dites Amine 🙏🙏🙏 Eyy Ba amattinga Problème...bidew feegneneu... une autre Madame Ba 😮🤣🤣🤣🏃🏃🏃
Waw l'émotion!!! Mariage bi nekhna badiène mondiale. Félicitations à toutes l'équipe! Merci aux acteurs pour le professionnalisme! Vous nous procurez beaucoup de plaisir. Châpeau bas
Virement je vous féliciter wakh degue yalla li dafa spécial 👌🏼🌹 lii nékh na trop wallahi souma amon ay millions dina lénko diokh diap si liguey bi 🥰🌹 yalnalén yalla diappale 🙏🎁
Wouyyyyy Oumou amoul roussou kay ndeketeh 😂😂😂😂😂 Binôme legui mou reukh badiane..... Machallah bravo à toute l'équipe, merci de nous faire sourire de si beau matin Bravo à nos lions , vous faites la fierté du peuple sénégalais, inchallah yallah naniou borom bii may coupe bii 🙏🙏🙏🙏
Serie de l’année senepeople yéna meilleur ba finga santé bou fi rk moye place bi 😂😂sa féthie mi nékhna badian ake aye fémam say 4 femmes séni sagncé néna mout Awa bourou keureum danga yageu mougne 🥰 Sama ❤️bi nimou sédé si wa polygame epouna lal lén j’aime Ba Lou takh mou beug ambiance 😂😂
Machallah acteurs you nango investir pour bégeul gnilé ndi sétane vrai réception ak cortège comme dans un vrai mariage wa thies daal love et force à vous diokh nguéne akk seine ligueye
Kiy way tmt kagne lay changé son mou diap ko si bo nieuwoul mou niaw bi rek ba kagne😩🙄 Taye sunu Yaye seune amna ndame🥰😂waw kay benene tournure ba da tak souf ni Niaff😂😂😂😂
Jusqu’à présent la réussite de cette épisode m’impressionne vraiment comme tu vrai Machallah vous êtes les meilleurs chapeaux à Badienne elle assure grave son rôle ❤😂😂
Toutes mes félicitations à l'équipe. Mention spéciale à Badiéne nationale Sophie kata . Que du bonheur sous la protection divine ainsi que toute la nation sénégalaise. Amiiine.
MDRRRRRR juska preuve du contraire wakhnako tiktok ma wakhate ko si youtube bi Polygame ay trucaaazzz la, li dou geugueu waaaaayyyyyy mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr Badiene peut me tuer. Chapeau a vous financer ngene vraiment pour nous faire plaisir et vous avez reussi......mille coeurs a vous
Mouwayyy binôme dieul na coupe bi nak mbétté 4 Avril damani binôme koula wakhati civil guénél ko guan🔫😅 eeeeeeeeh waaaaaay Badiéne nationale qui te peut💪🏻💪🏻 bobou robe 👗, bobou ambiaaaaaance🎊 guéweul bi limouy waay dafa doywaar nimou nékhé damako ragal😍.De la classe et de l’élégance y’en a sen ay maquillage 💄 ohhhh. Mani loudoul série polygame dou 100f💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂binome ak bouda raynama dama febar mais yéna may weteuli bilay merci à toute l’équipe ❤️❤️❤️ Badiene ak binôme comme vrai couple . BA on sent k niit bou oyof leu dans la vrai vie Ndeysane amoul béne problemou adina
😁😁😁😁 félicitations à ttes l'équipe ça fait 21jrs bima commencé setane serie 1 saison bi la nek ni mais nekhna vraiment réalité purement Sénégalais 😍😍😍😍😍😍😍😍😍
Bily bah ma tuée ak ay compagnon wam 😂 série bi doufi amati si adina 😂😂😂 badienne recarder binôme 😂😂 bily dama contane 😍 yalla na senegal dieul coupe bi
Walahi dama contane mariage badiene nationale merci à Senepeople de nous avoir donné cette plaisir vraiment vous mérite des millions d’abonnés et j’aime aussi 😍❤️🙏que dieu vous bénissent
Ba Tay mom contan n'a thi yow mère seun mérite ça lep mom la Macha allah ❤️🇸🇳 awo yaye,awo yaye niarel niatel nientel wargon diouk fethial awo yaye guendi sissou
une série inédite réalisation parfaite montage indiscutable walay le déco est jolie diarama bou et l'équipe Polygame N'oublions surtout pas les 5 prières c'est important
Une série exceptionnelle pas comme les autres 🥰on s'en le respect tout en accompagnant avec de l'ambiance du rire etc ..... Merci énormément de nous avoir fait revivre des moments de bonheur telle k cette série ..... Le peuple est content 😍🥰🤩
Non chapeau à vous vraiment nous sommes contents (es) episode yeup bi mom amoul morom Mariage Badiéne rek diarna louné kouy khéw gnewal si badiéne national
🤣🤣🤣Badiene pourquoi bougoul binome fethie 🤣🤣🤣🤣mariage de l'anne Bravo l'equipe wa kou guis li ba sagne se Tay ba foli na ndeye ndiaye 🤣🤣🤣🤣🤣Kou setlou badiene kham na ni Binome da eupeul 🤣🤣🤣
Je suis en salle de pose , les écouteurs dans les oreilles . Je n'arrête pas de rigoler . Tant pis pour mes collègues qui ne comprennent pas le wolof. Cette série est excellente.
Félicitations à notre badiène nationale. Mariage très réussi !!😍😍😍🤩🤩🤩🤩🥰🥰🥰🥰
Même moi je te jure 😅😅😅
Même moi aussi
Et moi aussi
S
A
Je n ai jamais regardé une série sénégalaise qui m a aussi intéressé que celui là car j’ai l impression de vivre cela tous les jours
Mais l'autre mariage très ambiance
Auto machalla sa teint nekhnama
Astou machalla
Le sourire n'est plus à l'ordre du jour à cause de la vie chaire mais vous jouez un rôle primordiale dans la société en tuant le stresse toujours souriant quand on regarde polygame macha Allah yallah na léne yallah fay
Ceux qui n'ont point ratez d'épisodes et attendez avec impatience le mariage de BADIANE_BINOME POINTEZ
Vraiment senepoeple chapeau à toute l'équipe du lourd walay
Machalla bellissima
Ils sont formidables
@@bouryndiaye3851 walayy il mérite des sponsors
@@seynabousall9091 non vieux ba est très fort en plus il danse bien
Les acteurs de la série polygame sont tellement simples et naturels. Merci encore. Bravo Senepeople.
Félicitations à toute l'équipe de nous faire vivre ça vraiment on voulais une EPISODE trop longue et voilà 2 parties de la réception vous êtes à l'écoute et merci beaucoup 😭😭❤❤
Mane mi sakh beugouma wone mou dieex
Wawaw machala def nan ko ninou ko beugé mom contan nan si yen sa kaw sa kanam🥰🥰
@@KhadijaKhadija-bi7ut bly deh
@@famafall7719 li daffa nekh di🥰❤❤
Polygame une série pleine d'enseignement on nous apprend que AK lo dieul dieul âge iow jiguen boumou takh nga yakh sa bopp kholal badiane AK âge bi guisna kouko marier teral ko ta yalla meune na def mou ame si ndiabot félicitations polygame tjrs des leçons à retenir 🥰
J'ai tellement rigolé de la façon dont badienne recarde binôme mais félicitations du beau travail
D’où yow kisse
Li nèkh na nèkh no mariage Badiène amatoul wayè bi madame Bâ mom banela no Oumou meuna sabotè tay mom Bâ dèf na yeufou grandeur gueureum Seun wayè Astou Ndiaye Khady Baba warone nguèn na diouk puisque daguèna wotè diam ak djioubo sèn sagnsè nice na machallah Sènègal dal yenagui khappy outèk niou nji sèd bi di beugua ray 😂❤❤😘
To be honest I am really out of words.Y'all have been making your viewers proud since from the beginning.There wasn't a time when your team missed even a single episode which just shows how caring you are towards your subscribers/viewers.Your punctuality just shows the respect you have towards your viewers and therefore,hats off to the entire team.This is just the reality.
Wouy dougouci Ba ak Gning 😂😂
It's an all-around excellent show👌
You said it all ☺️
You hit the nail on the head
Wa grand boubou Maman seune ak astou baba douniouci wakhe😍😍😍bakhe na😍😍en tout cas sagnesé guéne lolou sakhe c magnifique merci à toute l'équipe 😍😍😘😘
Noo sounou keur mariage Gros plan lagn ko def di fethie melni Sénégal mo dieull coupe d'Afrique 😂😂😂😂
Aminé touf touf
Merci waay à toute l'équipe
Félicitations à tte l'équipe machalla mé Ba amoul🤣🤣5 femmes oh
Tresore yala nieuwna
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂li dafa nekh
Aminnn way
Mais vraiment la robe de badiene est magnifique j’ai juste envie de me remarier merci aux sponsors ❤️ mais ba daga ame diabar Europe 😯😯😯😯 binôme reynama restez dignes 😂
Ba d sagne na lounek 😂😂😂😂
Pas le Sénégal seulement, mais le monde entier, mariage bii dotouffi amati. Chapeau à vous. Mashaa Allah
Sama boss moy dakk😁😁
Koufi defatti mariage na lathie badjene ba paré
Khana 😂😂😂
🥺🥺🥺bilae je vous aime bcp yénagui séral sunu hol yi diniou diangual franchema chapo 🎩xéw mi nehna sagnsé yi rafetna 💞yalna yalla taxawoulén yén niép sunu acteur yék actrice yeip 🌹wayé Astou machalla t trop belle way Merci ékip bi yép🤍 sunu hol sed na lol tchi yén💗💗💗 one love senepeople❤
Vous avez encore montré votre professionnalisme . Thiès capital théâtrale sans vulgarité machalah niguendi sedalé sounou khôl yi yalla nalen ko yalla fayy
Ma cha alla. Nekhna depuis épisode 1 ba legui yen a gui gnous begueul avec thème you âme solos rée ba sont chapeau a vous
Niguéne gnuy bégué lé ni, yalnaleneko yalla faye 😂, li nekhna wayyy
Je souhaite à toutes les Filles qui suivent cette série de trouver leur Binôme avant la fin de l'année 2022.... dites Amine 🙏🙏🙏
Eyy Ba amattinga Problème...bidew feegneneu... une autre Madame Ba 😮🤣🤣🤣🏃🏃🏃
Amine ya rabbi
Amine inshalla
amine ya rabbi
Amine
On a un binôme incontrôlable pour la danse🤣🤣🤣
Bravo à toute l'équipe.
Danse militaire dou diekh. Ils aiment faire la fête !
Badienne malako Dara 🤣🤣🤣 lii
Wouyyy binôme Ray nama🤣🤣
@@fatoubadji7928 mok bou bambara gno yeim dougnou beugu mou diekh
C'est un militaire
Binôme mngui may rayy
Barki yalla gnarr gni dinagn ma rayyy
yalla na lénn yalla fayy si barki Mouhamed🙏🏾
sédal ngénn sama xoll biii wallae
Sacré mariage 💒,quels acteurs et actrices.
Vraiment vous êtes forts avec un tel naturel.
Merci à vous de nous apporter encore plus de la joie 🤩
Bilay nekh na way masha allah laf tiat yallah na diam ak salam yagg ci rew mi me chanteur yi masha allah
Franchement vous méritez plus que des sponsors mais plains d’autres surprises li nekhna trop meussoul am Sénégal mensions spécial senepeople
Bilahi Danio Wara nieuw de sponsors yi
Tey mouy deug
Kou guiss neih wa polygame niogui deub galsen beusseul j’aime💪❤️😂
Deugeuleuhhh 🥰
Waw l'émotion!!! Mariage bi nekhna badiène mondiale. Félicitations à toutes l'équipe! Merci aux acteurs pour le professionnalisme! Vous nous procurez beaucoup de plaisir. Châpeau bas
Virement je vous féliciter wakh degue yalla li dafa spécial 👌🏼🌹 lii nékh na trop wallahi souma amon ay millions dina lénko diokh diap si liguey bi 🥰🌹 yalnalén yalla diappale 🙏🎁
N'oublions jamais les 5 prières c quotidienne ♥️🙏
Team wifi AK team téléchargement soulékoulén 🤣🤣
Dieu nous suffit Et vous avez le temps de regarder les séries,????
Non thies vraiment aye artistes you aye gnofa nék ma cha ALLAH yalna séne diame yague je vous love dale
Mercii père ba pask maman Seune mérite d'être remerciée 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰 machallah
3
Franchement contane naniou souffiii yèmonn sakhe mou nékhe vraiment ammo lén morom nieupp contane si kaw si kanam
Wouyyyyy Oumou amoul roussou kay ndeketeh 😂😂😂😂😂
Binôme legui mou reukh badiane..... Machallah bravo à toute l'équipe, merci de nous faire sourire de si beau matin
Bravo à nos lions , vous faites la fierté du peuple sénégalais, inchallah yallah naniou borom bii may coupe bii 🙏🙏🙏🙏
Rôle oumou bi kay zero class
@@ndeyeamicissokho8339 téksi modé
Serie de l’année senepeople yéna meilleur ba finga santé bou fi rk moye place bi 😂😂sa féthie mi nékhna badian ake aye fémam say 4 femmes séni sagncé néna mout
Awa bourou keureum danga yageu mougne 🥰
Sama ❤️bi nimou sédé si wa polygame epouna lal lén j’aime
Ba Lou takh mou beug ambiance 😂😂
Polygame mon jigu équipe nationale en avant rek. Bonne guérison à tous les malades ya Rahman ya Rahim
Non franchement li mome masou mako Guiss bima dioudo ba tay 2002 la ba 2022 li mome Nekh n’a trop ❤️😭😭
Machallah acteurs you nango investir pour bégeul gnilé ndi sétane vrai réception ak cortège comme dans un vrai mariage wa thies daal love et force à vous diokh nguéne akk seine ligueye
Le chanteur, je pensais c’est Bou 😂😂😂
Félicitations à toute l’équipe Senepeople
AK man
😂😂😂😂
Mane sakh mom laco tegone
Kone dou mane kesser
De même 😂
Kiy way tmt kagne lay changé son mou diap ko si bo nieuwoul mou niaw bi rek ba kagne😩🙄
Taye sunu Yaye seune amna ndame🥰😂waw kay benene tournure ba da tak souf ni Niaff😂😂😂😂
Tamit🤣🤣🤣
Je suis la seule à être bouche bée avec la 5ème madame Ba 😂😂😂vivement le prochain épisode
Notre dose matinale bravo à tte l'équipe de polygame et aux téléspectateurs accros à cette série
Jusqu’à présent la réussite de cette épisode m’impressionne vraiment comme tu vrai Machallah vous êtes les meilleurs chapeaux à Badienne elle assure grave son rôle ❤😂😂
Astou la plus belle mais khady baba est la plus élégante diongama leuh nak❤❤
Deug Khady Baba dafa ame thiass😍
Toutes mes félicitations à l'équipe. Mention spéciale à Badiéne nationale Sophie kata .
Que du bonheur sous la protection divine ainsi que toute la nation sénégalaise. Amiiine.
Frenchema mention epeciale à vous les acteur s de polygamie que du bonheur je vous adore
Génial 🏆❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️♥️💯💯
Ohhhh 😭 c'est de l'émotion bilahi 🌟 le mariage continue vraiment nekhna trop 🌹 té sagnse guéne je vous j'aiaime💞💋 Bâ cette fois si chapeau a toi 😂👍
Merci aux sponsors de polygame et aux souteneurs de la série vous êtes fabuleux
Belle leçon de badiéne solou you Bari yi demm ba invité niou lenn Di indexé ndakh sangsé benn solou tout blanc class réception class👌👌👌
T lissi gueneu nekh doko sol gnew guiss koula dakalé sagnsé 🤣🤣🤣
Limaye wakh tmt
@@binetarassoulboye888 wallay kay
Solou bari sakh si ngeunte laniouko khamewon way marriage mom ben solou doyna si senegambie mom danio eupeul trop
Walahi defois soy solou aka simekou daham dara si hewmi
No srx meilleur série sénégalaise qui est OUI
Félicitations au peuple sénégalais kou sétanoule match bi démbe comme mane di daw pression bi beusseuke j'aime
Thieuy Ba, féthie na fii lou nékh nakk, un vrai artiste 🙏🙏.
Félicitation à toute l'Equipe 🖐
Mariage de Badiéne Nationale et de Bihomme VDLIDÉ ❤🙏
🤣🤣🤣 wa badiene tamite dou bayi binôme mou danse thi teyou bakaname nn le plaisir de vous regarder merci
MDRRRRRR juska preuve du contraire wakhnako tiktok ma wakhate ko si youtube bi Polygame ay trucaaazzz la, li dou geugueu waaaaayyyyyy mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr Badiene peut me tuer. Chapeau a vous financer ngene vraiment pour nous faire plaisir et vous avez reussi......mille coeurs a vous
Boutiquier bi Dougn ko gnouss mou guéneu guéw bi 😂😂😂😂 Ba tamitt loutax mou gnémé yé fitt na dou guereum 4femmes yéppou rek diamou ame 😂😂😂😂
No boutiquier bi raynama🤣🤣🤣
@@sokhnadiouf4128 Nooo bilaxi amoul diom😂😂
@@binetougueye7228 😅😅😅😅
Dafa nara tassate keur gui rek, 😂
@@maguettesall3321 bilaxi wax ga deugg😂😂
Billaie Série bi warul djiéx 😂😂😂bravo à toute l’équipe de polygame 👌🏼😂❤️
On ne pouvait pas vous remercier tellement on est content félicitations way
Je suis Mauritaniene chaque jour je regarde polygame série ki ma fait vivre Machallah bravo et bon continuation ♥️
Mouwayyy binôme dieul na coupe bi nak mbétté 4 Avril damani binôme koula wakhati civil guénél ko guan🔫😅 eeeeeeeeh waaaaaay Badiéne nationale qui te peut💪🏻💪🏻 bobou robe 👗, bobou ambiaaaaaance🎊 guéweul bi limouy waay dafa doywaar nimou nékhé damako ragal😍.De la classe et de l’élégance y’en a sen ay maquillage 💄 ohhhh. Mani loudoul série polygame dou 100f💃🏽💃🏽💃🏽💃🏽
Yawit lo commentaire roul dou 100franc😂🤣bravo
@@socediagne6019 😅bilay dafa leer
Machalla Astou sa robe bakhna ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥰
This series deserves the whole number of likes in this world 🌍.
Machalah chapeau a vous bonne continuation à l'équipe polygame
Badiene nationale tothie nafi 😂😂😂 binôme incorrigible 🤣🤣🤣 merci à toute l'équipe 💓💓💓
Mentions spéciales à vous les acteurs ainsi que les téléspectateurs et n'oublions surtout pas les 5 prières ❤️
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂binome ak bouda raynama dama febar mais yéna may weteuli bilay merci à toute l’équipe ❤️❤️❤️
Badiene ak binôme comme vrai couple . BA on sent k niit bou oyof leu dans la vrai vie Ndeysane amoul béne problemou adina
Nèkhoul ba nèkhoul Sénégalais yèpe wardi sètane polygame vraiment nèkhna torop torop🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🤩🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Vraiment limay jooyyy mako xam litax sama papa toudd vieux ba😂🤩j’aime le charisme chez cet homme
Force à senepeople😘
L’orchestre bii meune na trop
Aujourd'hui c'est la gloire de maman Seune 💃
Ah weh il était vraiment temps mome
Réception en 2 épisodes de l'année ! Bravo tout est magnifique et fait rêver🥳🥰🤩🥰🥳 Mais Badiane-Binome ak Ba-Gningue-boutiquier bi m'ont tué 😅😅
Borom veste bou gris bi il est trop impliqué deh khawma foumou namé ay fethie 🤣🤣🤣
😂😂🤣😃😃
Billahi je pensais que Mane rekk mako guiss
@@ndeyeamygning947 dou iao rek da fethie fethie you srx 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Nicena trop merci à vs vtr fans depui Bruxelles 🙏🙏🇲🇱🇲🇱🇲🇱🇲🇱🙏🇸🇳🇧🇪
Woooy ba khana bouy seuyi astou guay geureum bou teudè gua geureum Khady baba 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣😂😂😂
Wa khana Aka meuné founé
Yow ya wakh lou takh khew bi sakane
😁😁😁😁 félicitations à ttes l'équipe ça fait 21jrs bima commencé setane serie 1 saison bi la nek ni mais nekhna vraiment réalité purement Sénégalais 😍😍😍😍😍😍😍😍😍
Merci pour ce beau mariage de badjene mondial bravo encore aux acteurs et a toutes l équipes pour tous ces émotions
Chapeau à vous, vous nous comblez de bonheur et d'un pur sentiment de fierté. Machala longue vie à vous tous
Machallah. Force à toute l’équipe de polygame vs êtes exceptionnels
Sama tourendo
@@fasy666 waw Kay 100%
Mane de tey la warou ndeke ba am n'a 5e femme li mais seni sagnse rafete n'a machallah
Badiene sa rèception bi ama toul ❤❤deug deug polygame amolèn morom 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Bily bah ma tuée ak ay compagnon wam 😂 série bi doufi amati si adina 😂😂😂 badienne recarder binôme 😂😂 bily dama contane 😍 yalla na senegal dieul coupe bi
Sacré Ba toujours avec ces surprises j'adore vraiment la série
Walahi dama contane mariage badiene nationale merci à Senepeople de nous avoir donné cette plaisir vraiment vous mérite des millions d’abonnés et j’aime aussi 😍❤️🙏que dieu vous bénissent
Machallah vous avez encore battu le record ken d'où yen si mbim reww badiene yalna nga tawlo Aÿ jumo amine touf touf
Jai trop rigole . Tous nos encouragements.. et merci de prendre en compte les suggestions . Cest un signe de grandeur et dhumilite.
Mais la dame elle chante super bien 🥰j'ai des frissons ndeysaan
Mais venez va parler de la danse du boutiquier 😂😂😂😂😂
Feliz complaño á toute l’équipe 🥰
Bilay ki raynama da nieuw pour roubè😂
Il ma dead carrément😂🤣🤣🤣
No boutique bi rek 😂🇪🇸🇸🇳 mande bi fethie ba jel telefon bi rek la warou man
En plus il a ramassé un téléphone
Non vraiment yéna pogné adouna nékhoul ba nekh. Vous nous comblez de bonheur.
Machallah les filles de Bâ, Awa et Khady sont magnifiques 😻
Binôme avec tes termes militaires là me tue vraiment 🥰🥰😂😂😂
Ba Tay mom contan n'a thi yow mère seun mérite ça lep mom la Macha allah ❤️🇸🇳 awo yaye,awo yaye niarel niatel nientel wargon diouk fethial awo yaye guendi sissou
Astou la vedette de la soirée plus belle que jamais
Bilay khetou diongoma wam bi da eupou elle est super belle machala
Dafa rafete trop
Walay
une série inédite réalisation parfaite montage indiscutable walay le déco est jolie diarama bou et l'équipe Polygame
N'oublions surtout pas les 5 prières c'est important
Dieureudieuf fallndiaga.
Bilay demb xol yi feex na si la victoire des lions et juste après la réception de Badiene bonne à continuation à toute l'équipe 😍
Une série exceptionnelle pas comme les autres 🥰on s'en le respect tout en accompagnant avec de l'ambiance du rire etc .....
Merci énormément de nous avoir fait revivre des moments de bonheur telle k cette série .....
Le peuple est content 😍🥰🤩
Bilay royy dou niro ak pure senepeople amoul morom si mim réw ❤️💯des cœurs pour senepeople
Non chapeau à vous vraiment nous sommes contents (es) episode yeup bi mom amoul morom Mariage Badiéne rek diarna louné kouy khéw gnewal si badiéne national
Non sacré Binôme et Badiéne vous allez nous tuer. Vous méritez le prix du meilleur série de l'année. Wa Ba mi meune ambiance 😍❤👏👏💪💪
Walahi
Tourondo wa li mariage deugue leu oubien si série bila ????
Seune ma sha Allah lafthiat, sagnesè nga rose fisha bène khalè yobou loulako
Boutiqué bi koumakoy teuyéll😂😂😂😂😂 nguir Yala meunatoumako mougne 😆😁😁
Domaram la boutique bi
Qui es d'accord Polygame Meilleur Serie Sénégalaise Beuseul J'aime 👉❤️
🤣🤣🤣Badiene pourquoi bougoul binome fethie 🤣🤣🤣🤣mariage de l'anne Bravo l'equipe wa kou guis li ba sagne se Tay ba foli na ndeye ndiaye 🤣🤣🤣🤣🤣Kou setlou badiene kham na ni Binome da eupeul 🤣🤣🤣
Eupaloule badiane mo bari caprices rek 😂
Wa oumou tamite kou koye sangne sèle
🤣🤣🤣Oumou MO diakhal thieup
Que dire on ne trouve mm pas les mots pour vous remercier 🙏
Ex boutiquier bi ak Ba ak gardien bissi guinaw🤣🤣🤣😭Ma Shaa Allah
Fin bi Rey nama 😂🤣🤣🤣🤣🤣BA Mo meun thiou meun thia meu thiarara.
Mi motakh mou bayi ndeye Ndiaye... Madame BA en bleu yaw léwooo
No binôme m’a tuè nènalèn char de combats yagui si bountou bi boulèn yakh khèw bi soyez digne sacré binôme mane ndèkètè yow la beugue
Machaallah Notre badiane nationale mariage validé boul faté labane bi louma ndiorla 😂😂😂 mais nak warone gua invité wa tousss tassar