ขนาดวิดีโอ: 1280 X 720853 X 480640 X 360
แสดงแผงควบคุมโปรแกรมเล่น
เล่นอัตโนมัติ
เล่นใหม่
Kham kham dafay weer ❤ bègue na lolou sakh barki Serigne bethio magui lay gnanal goudou fann ak weer
Amin ya Rabbil Halameen
Machala yalla nala yalla sammou dafalko bohlém dioulitt ❤❤
Xam xam rek ngay wax wallahi. Surtout Tafsir Baye Niass bi ngay dioxé comme référence , Macha allah.
Macha’allah❤❤❤ amna solo lol yalla na la ya’allah fay té yokk Xam Xam bi🙏🏽🙏🏽
Machallah cheikh baye ass ndiaye serigne bi namenagne la ziar la si koor gui yalla na yalla goudal sa fane wérral say thieur défal la diam ak wérr si barkél baye niass ak si barké mawlana cheikh ould khayri sama serigne sama royukay si faydou bi❤❤❤
Xam xam bou weer da fa neex Mancha cheikh baye as Ndiaye ❤
Alkhamdoulilah
Mamcha Allah Baye As Ndiaye ❤
Yalla nala yalla défal diame
Yalna yalla goudal say fann ta moussal la si seytané yangui si yoone bi
Oustaz je te suis depui la France 🇫🇷 ❤❤
Sama Serigne depuis mauritanie 🇲🇷
Yague fi lole té wëur ❤
Machalah amna solo ❤❤
Machallah seringe bi xam xam bi lérna
♥️♥️♥️♥️♥️Machallah machallah
Machalla
Machallah ❤❤
Machallah
Solén moytouwoul dina done talibé baye ndax ki bilahii walahi wolouna yallah
❤❤❤
Borom xam xam piiirrrrrr❤
Machallah Baye moy deug
🎉
Comment faire pour vous rencontrer cheikh bi
Ziarnala cheikh bi danga beuga giss cheikh bi
Mane ki rk la beug xawma nou may def ba guiss ko
Il cite Baye Niass, sans mentionner El Hadj Cheikh Oumar Foutiyou Tall
C’est quoi l’objectif de ton commentaire
UfcLl iow yaye ya bone nar fekh meuneu diaxacé 😂 .Cheikh Baye as bouko tontou stp bayiko ak niougne
❤️❤️❤️❤️
❤❤❤❤❤❤