Partie 2 Croyances Dangereuses chez les Talibes Baye Niasse 🤔🤭 ? - Live Oustaz Alpha Ba et sa team

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 8 ก.พ. 2025
  • ⛔️Kawteef - Après les manifestations à touba - Le (…) réclame t-il l’Independance de la ville ?
    • ⛔️ Kawteef : Interdict...
    #senegal #kebetu #team221
    Voici un extrait des vidéos oustaz Alpha Ba ha pour des éclaircissements sur le polythéisme …
    #senegal #kebetu #team221
    spécial live Cii LERAL LEUNT LEUNT gnii wottee woo abb yónnent guinaaw sunu YÓNNENT MOUHAMMAD ﷺ
    11 Mai
    #senegal #kebetu #team221 LIVE - IMAM CHEIKH ALPHA BA - PAROLES AUX AUDITEURS - WOOTE WOO ABB YÓNNENT GUINAAW SUNU YÓNNENT... #sénégal #senegal221 #magal #merci #mouride #youtube
    Maktaab Oustaz Alpha Ba
    t.me/MaktaabOu...
    ︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾︾
    t.me/MAKTAABSA...
    📡:t.me/reflexion...
    t.me/kitaabtaw...
    t.me/LerralDiine
    t.me/passpassb...
    t.me/Sharkhsounna
    t.me/siffatusa... This stream is created with #prismlivestudio This stream is created with #PRISMLiveStudio

ความคิดเห็น • 54

  • @DIOBISTO
    @DIOBISTO 9 หลายเดือนก่อน +2

    Masha-Allah Oustaz Alpha et tout l'équipe

  • @geustu1998
    @geustu1998 ปีที่แล้ว +5

    Gniii mbaam molénn eupp xél 😂😂😢. Soubhanallah

  • @alassaneseye2191
    @alassaneseye2191 ปีที่แล้ว +1

    Machalah dieuredieufe oustaz alpha ba leral yi amna solo sen ligueye rafetna yalla na len yalla faye Sénégal deukou nafekh le

    • @KhadyDiallo-c7b
      @KhadyDiallo-c7b ปีที่แล้ว

      Machallah bnne continuation

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 8 หลายเดือนก่อน

      Yalna yalla samou alxouran ak sounnah amine yarabi

  • @alinesamb5006
    @alinesamb5006 ปีที่แล้ว +1

    السلام عليكم ورحمة الله وبركاته كيف حالك أنت بخير أحسن الله إليك ماشاء الله بارك الله فيك الشيخ الفاهم باه حفظه الله ورعاه ❤❤❤

  • @geustu1998
    @geustu1998 ปีที่แล้ว +6

    Alhamdoulilah si Lima bokkoul si tarikha

    • @khadysarr1700
      @khadysarr1700 8 หลายเดือนก่อน

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 8 หลายเดือนก่อน

      Tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégalé yi wallahi

  • @CherifBayo-j5t
    @CherifBayo-j5t 11 หลายเดือนก่อน

    Machalah oustaz

  • @salifsow9779
    @salifsow9779 ปีที่แล้ว

    حياكم الله وبياكم وبارك الله فيكم

  • @matyleve4706
    @matyleve4706 ปีที่แล้ว +2

    Ya allah , ya allah , have Mercy n open the mind N EYES OF ALL THE MUSLIM IN THIS WORLD ,

  • @Mouhamad-u6f
    @Mouhamad-u6f ปีที่แล้ว +1

    Machallah

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane7066 ปีที่แล้ว +1

    Machala am na soulo torop machala

  • @dieynabandiaye9211
    @dieynabandiaye9211 ปีที่แล้ว +2

    Thieye.soufi

    • @falloutoure135
      @falloutoure135 ปีที่แล้ว +1

      Danio doye waar dé

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 8 หลายเดือนก่อน

      Sane tarihayi gnoo taxalé djioulite Sénégalé yi wallahi yalna yalla samou alxouran ak sounnah

  • @yallarekmoybour7356
    @yallarekmoybour7356 ปีที่แล้ว +2

    👉sunnu rek mo wor ligueye bi amna solo❤🙏

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 ปีที่แล้ว +2

    Salam mbok yi nan moytou yalla wallahi nan moytou yalla

    • @falloutoure135
      @falloutoure135 ปีที่แล้ว +1

      Wallahi yalla dou morom dé

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 8 หลายเดือนก่อน

      Yalna yalla mousal gnou ci bokalé yalla sougnou borom amine yarabi

  • @Cerveau-mak
    @Cerveau-mak ปีที่แล้ว

    Dégeu dégeu bou Yallah diaglélon sahaba yi ngén amoul rek

  • @baboucardiop5121
    @baboucardiop5121 ปีที่แล้ว +1

    Alquran ak sunnah rek muy dek ❤

    • @Oumie-n6g
      @Oumie-n6g 6 หลายเดือนก่อน

      Wallahi

  • @OusmaneDiop-qd1rv
    @OusmaneDiop-qd1rv หลายเดือนก่อน

    اصابه الجنون؟كيف يباري الخلق بالخالق

  • @AssaneDiop-w5m
    @AssaneDiop-w5m 8 หลายเดือนก่อน

    Pa bi kou rawla talibé baye niass gnoo dakha bokalé yalla sougnou borom

  • @NY-xe4kj
    @NY-xe4kj ปีที่แล้ว +3

    thièbou dieun existé woul té sougn laka tégualé gua démsi ba diékh bayyi lén di philosophé

  • @hannharouna3630
    @hannharouna3630 ปีที่แล้ว

    😂😂😂😂😂😂

  • @matyleve4706
    @matyleve4706 ปีที่แล้ว +3

    No one is defending allah what's going on in senegal ?? We are Muslim or what ??? Stop calling if you cant say the truth , everyone have to respect Allah

  • @Mouhamad-u6f
    @Mouhamad-u6f ปีที่แล้ว +1

    Niassene doyna niou war

    • @khadysarr1700
      @khadysarr1700 8 หลายเดือนก่อน

      Wallahi danoiu réww ganane kom ay mbamm sakh

  • @AliouFaye-qu5bc
    @AliouFaye-qu5bc 7 หลายเดือนก่อน

    Alpha mi hamoul Dara hamé wo wahu mahriffa ak wahou séria .dinga yag thii téré yi n'ak d'El lire rek té do diérignou .

  • @khalilo2423
    @khalilo2423 ปีที่แล้ว +1

    Alpha Bah yow kou am jot nga Bilay,, pask tog si internet amo lossi def loudoul diingaat rek melni aduna yassi eup xam xam .. dalal rek guisnañfi kounè ..tei aduna Bilay dou goudd tank baga def effet si tassaouf

    • @moustahadrame6979
      @moustahadrame6979 11 หลายเดือนก่อน

      Wakh deugeu yallah

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 8 หลายเดือนก่อน

      Oustas alpha loumouy défni lou yalla beug laa nane bayi nafékhe yalla sougnou borom dou morom nan amm yarr ci yalla sougnou borom

  • @beuguedeugue2878
    @beuguedeugue2878 3 หลายเดือนก่อน

    Guayi gnom dou gnou namguou mouk... lay rek pa bi da fa xamadi kou réw leu bo ko waxé sén sergne gnou name leu téguin néwoul...

  • @falloutoure135
    @falloutoure135 ปีที่แล้ว

    Niasene bi mo geuna konn si lou yalla bindeu

    • @moustahadrame6979
      @moustahadrame6979 11 หลายเดือนก่อน

      Ya Meune kate sa ndéye dmrm bi

  • @assanesene8766
    @assanesene8766 ปีที่แล้ว +1

    Pass pass niassène yiiii c’est grave dangereux

  • @falloutoure135
    @falloutoure135 ปีที่แล้ว

    Thieye tasawouf képpou kou nékk soufiyanké rous nga taye li dafa rouslou waaye akhe

  • @khalilo2423
    @khalilo2423 ปีที่แล้ว

    Dagay sonn rek saway tei nga nopalou dem liguey buzz dou diiigaat aduna neex tay internet am tog sa site dii waax loulanexx

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 8 หลายเดือนก่อน

      Oustas bi loumouy défni moo warr bééppou dioullite nane amm yaarr ci yalla sougnou borom té bayi naféékh baxoul

  • @Cerveau-mak
    @Cerveau-mak ปีที่แล้ว

    Wahabiste yi sen problème moy niakeu kham Yallah bolén beugué lép lerr dangén di andeu ak sen serigne bou mag bi ngén débat ak talibé baye bou geuneu ndaw mou diangallén

    • @CherifBayo-j5t
      @CherifBayo-j5t 11 หลายเดือนก่อน

      😅 tarikha mann sakh meun nako dadji
      Mais boulen diakhlé lepay lerr niogui djang di préparer sunu khutba you bakh inch'Allah
      Tarikha mom dadji rk

    • @moustahadrame6979
      @moustahadrame6979 11 หลายเดือนก่อน

      Niom niémé wougnou lolou 😂

    • @moustahadrame6979
      @moustahadrame6979 11 หลายเดือนก่อน

      ​@@CherifBayo-j5twakho deugeu deh frr

    • @Cerveau-mak
      @Cerveau-mak 11 หลายเดือนก่อน

      Alpha ioe ak sa talibé yi nga khamni dangalén nakh awma lanla internet kouné meune na wakh louko nekh way bou féké Tarikha bakhoul t meune ngako lay bismillah cheikh baye diokhénafi invitation ouvert débat télévisé kén si y’en demoul beussi s’en serigne Ahmed Lo kon maylenniou diameu ngén nékeu si lingen nékeu baniou ak louniou nékeu.

    • @DIOBISTO
      @DIOBISTO 9 หลายเดือนก่อน

      Wakhi doff 😂😂😂