La Maison Familiale Vendue, Une Famille Jetée dans la Rue. Incroyable, à Thiès, la maison familiale vendue, la Police évacue la Famille. #viral #thiesinfo #maison
Aaah les conséquences de la polygamie cest ça il faut toujours penser a quitter la maison pendant quil est encore temps cherchez votre propre maison si possible
Le Sénégal a beaucoup changé, la population, les mentalités aussi. En tout cas chaque père de famille doit faire un testament écrit que personne ne vend ce bien doit rester dans la famille Si ce n’est pas fait tôt ou tard un des membres de la famille voudra vendre.
Voilà 😢😢😢😢et la faute à l'état voilà tout après un décès les maires passe dans les maison pour des condoléances 😢 aulieu de convoqué la famille et supervisé l'héritage Sénégal amouniou diné😢😢😢😢
Ndeyssane ont ndirait que ces le décès de Serigne saliou Touré qui a amené tout ces problèmes et on ndirait que le vendeur attendait le décès de s saliou Touré
Ndéye sane fi sama cogn la thies dafa bari niousi am fèbarou Rap ki di wakh 600mille yi nama yalla diégeul mes wéroul nonou keur gui Diarna 50 million si dig Thies la nek histoire bi dafa compliqué trop .
Il faut arrêter de vivre aux crochets des parents. Même père même mère ou même père ou même mère bref un bien appartient à son propriétaire. Rien ne nous donne le droit de croire que ce bien nous appartient. La famille est un énorme boulet dans ce pays.Tous des fainéants et des profiteurs. Oust dehors.
Métina adouna da gouddou takk, dé lène ci bayyi khel keur baye dou keur, fo degg terrain gnitt deuk fa bou dé alleula deff fa sakkett deuk. Té yaar sa gnaboot ci diome ak liguèye li yague na adouna guéné gnaboot. YALLA guiss na leup.
Li dou Yonne vraiment respectewoul djoulitewoul police nilagnouy ligueyè dou Yonne vraiment heuya gueiné nit comme Hana avertissement warona ameu mais gneuw rek gueneih en tant que deukou djoulit
No li Lou yeme la ay nagnou ragal yalla te khamne lep day diekh li Lou niawla , yone nak War n'a def ligayam te tekko si Lou leerre, pensons au jour où l'ange de la mort nous arrachera la vie , on regrettera certes , mais day gel rethiou wess,claimence adouna day diekh , alalou adouna yi gnouy rayante dounko yobale bamel. Ma rousse si yene takhayou si sama askane ,yalla n'a yalla dioubale , te yagni khelyi si dieuf diou niay , torokhal nitt,
LA MAISON APPARTIENT A MBACKÉ FAYE DECEDE ; VOUS ETIEZ MAINTENUS DS LA MAISON SANS DROIT NI TITRE. ; VOUS N AVEZ PAS DE RAISON D Y RESTER. CEUX DE MEME PERE ET MERE QUE LE DEFUNT ONT LE DROIT DE VOUS FAIRE PARTIR .
C'est la même chose a nguinthe la où ya la banque islamique en face la gendarmerie nationale ils construit loué sans autorisation ni certificat d'héritier parce ya juste un de leurs frere qui habite au USA mais leurs heures va arriver
Payi yi rek tassouna s’en keur yi demna . Mane rek. Lepp ak mère youtoul moitié terrain moguene wor . 30 enfants une seule maison . Pas d accord ou niakka d accord . Vendre rek mofo si sesse. C est la loi.
Mane deh nena bideu testament rek mo gueune dakh guiss na fi même cas si gnou bokk ndeye ak mbaye en plus des jumelles même. Adouna bi mo yakou, yeurmandé amatoul
Thi l'islam dé kou amoul jabbar amoyl dome sou déwé danio wara djaye alalale yepp niou tejkk ko mirassko. Gni ils sont fautifs . Séne papa déna vous avez vendu la maison elle ne vous appartient plus
Aaah les conséquences de la polygamie cest ça il faut toujours penser a quitter la maison pendant quil est encore temps cherchez votre propre maison si possible
La verité est que faillait pas vendre à votre frère, soit vous restez tous avec un arrangement mais pas encaisser de l argent...
Ont ils encaissé ? Et même s’ il est mort la maison revient à toute la famille
Le Sénégal a beaucoup changé, la population, les mentalités aussi.
En tout cas chaque père de famille doit faire un testament écrit que personne ne vend ce bien doit rester dans la famille
Si ce n’est pas fait tôt ou tard un des membres de la famille voudra vendre.
Voilà 😢😢😢😢et la faute à l'état voilà tout après un décès les maires passe dans les maison pour des condoléances 😢 aulieu de convoqué la famille et supervisé l'héritage Sénégal amouniou diné😢😢😢😢
Ndeyssane ont ndirait que ces le décès de Serigne saliou Touré qui a amené tout ces problèmes et on ndirait que le vendeur attendait le décès de s saliou Touré
*Keurou famille la fin et toujours triste*
Danouy dem ba melni niou bokoul dara
bilahi
C est triste mais nekatoul keur baye mais la maison de votre frère....L argent de l achat est ou? Qui a encaissé et qui n a pas encaissé ?
Question?
Yalna yalla doli soutoura mai Man li mom niawna gni ga wara fatte diléne guéné vraiment niawna 😢😢😢
Ndéye sane fi sama cogn la thies dafa bari niousi am fèbarou Rap ki di wakh 600mille yi nama yalla diégeul mes wéroul nonou keur gui Diarna 50 million si dig Thies la nek histoire bi dafa compliqué trop .
Sama guis guis warouléneko wone diaye séne frérebi mes yallanaléne yalla takhawou
Amine
Oohh bilahi tata Diarra massa 😢
Jour bi bilahi rombou nafa N fois Affaire bi metina moment begouma woneu loudoul yor keur dougal lén fah walahi
Wallahi li metina trop 😭😭😭
Le problème au sénégal c est la course à l enrichissement
Li yalla digle naniou koy deff Mirass yalla moko diguelé nitt mo leudeum
Lolou langou beugoul deug nak vraiment mirass yalla moko santane
Lou khëw ji famille yi kouy weur Di Ray Say none sa mbok yeup diekh
La maison n'appartient plus à votre père mais à votre demi frère il fallait pas accepter la vente vous êtes fautifs
Tu es bête ils ne sont pas fautifs si le frère meurt sans enfants la maison revient à toute la famille
Il faut arrêter de vivre aux crochets des parents.
Même père même mère ou même père ou même mère bref un bien appartient à son propriétaire.
Rien ne nous donne le droit de croire que ce bien nous appartient.
La famille est un énorme boulet dans ce pays.Tous des fainéants et des profiteurs.
Oust dehors.
Keur famille dou keur defa yamb Bari thiow diay lén ko kouné dém AK bopam yalla bakhna
Lolou dîner
Diné le deh mais aussi il y'a des membres de la famille qui n'ont rien ndeyssane.
Métina adouna da gouddou takk, dé lène ci bayyi khel keur baye dou keur, fo degg terrain gnitt deuk fa bou dé alleula deff fa sakkett deuk. Té yaar sa gnaboot ci diome ak liguèye li yague na adouna guéné gnaboot. YALLA guiss na leup.
Le testament devant notaire est la solution aux problèmes d'héritage.
😮😮😮ndoyna waar ndeh yalla na lene yalla diapale
600mille fane bok
Li dou Yonne vraiment respectewoul djoulitewoul police nilagnouy ligueyè dou Yonne vraiment heuya gueiné nit comme Hana avertissement warona ameu mais gneuw rek gueneih en tant que deukou djoulit
No li Lou yeme la ay nagnou ragal yalla te khamne lep day diekh li Lou niawla , yone nak War n'a def ligayam te tekko si Lou leerre, pensons au jour où l'ange de la mort nous arrachera la vie , on regrettera certes , mais day gel rethiou wess,claimence adouna day diekh , alalou adouna yi gnouy rayante dounko yobale bamel. Ma rousse si yene takhayou si sama askane ,yalla n'a yalla dioubale , te yagni khelyi si dieuf diou niay , torokhal nitt,
Sénégal nenko diaye ben yon konek diel walam xolfo diarr😢😢😢
aduna yagoul louko fi diare nitt légui comme aye mala dafa ñaw vraiment 😢
Sénégal yacouna bilakhi
Non nit bone na alalou aduna diaroul li rawatina ko bocal.lila méti say mbokk niolokoy tekk
Yen moussoulen kou Amou dôme amoul diabar noumouye diendé keur boba nguéne wara khamni thi aye nioumou bokal ndeye laye moudiou
Ça c'est vrai mais bo wolouwé niite doko fogué
Dagne leine Nakh comme dieund amna mome dou nekha lidienti nak
Si pourtant s’ il y’ a loi
Nous n avons pas parlé mais nous vivons la même chose avec notre soeur
Wallahi réw mi amoul yone
Esque Serigne mbacké el maestro avait dedomagé tout monde ? Si non saisissez la justice
Quelle honte.
Wah com kika dieundone wah na lou leer té amna ay temoin lou waral kénén nane daf kay diay pour guén guéna adouna amoul solo wax tane lén rek
Thiey yalla...deret ken douko torokhal
Sa djiguén dé ya wara dieunde keur diokh ko mou deuk wayé waroko guéné
Wakh deugg
Eskeyy aduna yallah Dinah attéh ça ira inch'Allah 😢
C'est dure billahi, faites tout pour avoir vos propres maisons metina 😢
Ah louway menae wah,diay mirass mu dieh.
Seigneur prend pitié de moi
De nous
Gnii gnoo bone séni domou bay lagni déf dieuf you bone yii sokhnassi gnii bagnou dieuloulé sén khalissou mirasse lagni lal sén woor bakhougni wayé nagnou déme gniome sii sén kaw yalla sii sen kaw wassalame
Li gnawna vraiment
Mais 600 milles yi pour lane la ?
Beneu côté comprendrouma beneu côté comprendre na pabi dafa dielon walam legui ba problème bi amé sila wakhé dakoy delo pask dafa mer
@@hamidoutall9134lolo ma diakhal dieul ba paré ne daye delo
Keur Gui da am dji né sen papa da amone diabarou dji né kou Diane rek dé s'en papa warzone n'a KO 6 personne dénaniou
Mes ioe😂😂😂 est ce que xam nga linga wakh dangafa. deuk 🤔
Lo wakh ba bayi
LA MAISON APPARTIENT A MBACKÉ FAYE DECEDE ; VOUS ETIEZ MAINTENUS DS LA MAISON SANS DROIT NI TITRE. ; VOUS N AVEZ PAS DE RAISON D Y RESTER. CEUX DE MEME PERE ET MERE QUE LE DEFUNT ONT LE DROIT DE VOUS FAIRE PARTIR .
Thiey yalla ! Adouna dou keur
Pitié et miséricorde
Wadji daflen. Tekk dile
Yena warone manko yen tamit bagna dieul Dara si mirasse bi wayer gni dieul gni dieulougnou li gnawna trop
C'est la même chose a nguinthe la où ya la banque islamique en face la gendarmerie nationale ils construit loué sans autorisation ni certificat d'héritier parce ya juste un de leurs frere qui habite au USA mais leurs heures va arriver
Tu parle de la famille Kounta oubien
Waxleen ci lii ngi ngir yalla
Mane police Sénégal diakhalnamah khna bala nio giéné niou latth
Khalisse yak neu deuk bi lii gnawna lole
Certainement un boss qui la acheté
TU DIS QUE LA MAISON APPARTIENT AU DEFUNT FILS AINÉ . NÉKKOO THI DEUGGG . IL A LE DROIT DE VENDREDA MAISON .
Mais nienen yi nio diaye kergui sans l'accord de autres.
Tu as compris quoi ???? Quand le grand frère sans enfant et sans épouses meurt la maison revient à la famille
Compte bancaire compte mbamél
Billaahi
Metina trop 😢
Drame a Thiès, c'est vraiment pitiolable votre titre
C'est un drame de se retrouver du jour au lendemain sans un toit où dormir tranquille sans aucun moyen de subsistance 😢
@@stefostefo2964 éventuellement ou situation grave et tragique, présentant souvent un caractère violent,mortel
Adounah diarna bayi khéll déh lép day diékhe
Payi yi rek tassouna s’en keur yi demna . Mane rek. Lepp ak mère youtoul moitié terrain moguene wor . 30 enfants une seule maison . Pas d accord ou niakka d accord . Vendre rek mofo si sesse. C est la loi.
Amna niou incaissé khaliss dé 😂😂😂
Loufi marrant ? Niak gua khorom way
Niawna lol thieuy addouna say domou dila guènè si keur wa ndakh li mbokou takhatoul nouy vakh
Yalla mirass la wakh ak lomo metti metti ko mirasoul alak thiow rek
Yamina yala leral niawna thinou book Baye
Lingua wakh lerroul dara Mère
Nopil
😭😭😭
Il vous a trahi il dit l’ avoir achetée ? Il vous donnés votre part ? Et s’ il meurt sans enfants ni femme la maison revient à la famille
Il vous a trahi il dit l’ avoir achetée ? Il vous donnés votre part ?
❤
Dioyna wallahi c pas jolie motakh mbokk mom amatoul ndiarigne
La question que je me pose est où est l argent que vous donne votre demi frère pour l de lachat de la maison
Thiey adina. Qu est ce qu ils vont devenir ?
Ou est LE YEURMANDÉ ????
Kokou dale bayi lenko ak yalla te xamni dina torokh de
En tout ka Sénégal nimako guissé ni kou
Yabo wadial sa bop bou bakh.
Amoul loi gnigni sokhor nagne sadik nagne.
😂😂😂😂
Motakh bene diabar rek mo guene
Man deh lolou la wakh beneu diabar rek bilakhi
Au nom de Dieu tu as dis vrai dh. Souvent poligamy moy andi lii
Mane deh nena bideu testament rek mo gueune dakh guiss na fi même cas si gnou bokk ndeye ak mbaye en plus des jumelles même. Adouna bi mo yakou, yeurmandé amatoul
Nagne khôl yala
Chercher un bon avocat me Khoureichi Ba, Cledor et Abdinar Ndiaye
Maïs doussa keur
Thi l'islam dé kou amoul jabbar amoyl dome sou déwé danio wara djaye alalale yepp niou tejkk ko mirassko. Gni ils sont fautifs . Séne papa déna vous avez vendu la maison elle ne vous appartient plus
Arnak familial li dafa niaw torop
Adouna diaroule li
Le Monsieur qui a acheté la maison est un escroc un voleur il doit laisser la Famille en paix. et allez chercher ailleurs une autre maison pour lui
Vraiment li métina mai yalna yalla safra li nitt day diap bokhame
Yaw mi joubo loutakh gua signè ta nianenyi dacoroune
😢
Aiye adouna li loulou diare nane khamne dagnouye dee
Walaahi
Sama mak moma fekk may nelaw moumay signelo ay faux papiers mabagn maouy signelo ay palasou diambour
Mirasmi baakhoul ndakh ni mou bokkal baye warou nioo done
😭😭😭😭😭😭😭😭
Li métina trope
Metina trop
Pourqois les jen aim bien se fair la vi tim et alor que il son an tor mdr
Non attention il faut pas dire rewoum Truands