Yow frère a chaque fois nilay mél ak sœur am bou amé changement rék khamalni diabar dia moko mene ba daaneko féwalé ko ak mom, mais malal yalla sovénako bou bakh
Keur Mar lo vrai famille sénégalaise. Cette série est le reflet de la vie quotidienne dans la plus part des familles sénégalaise Vous tous trop forts chapeaux au artistes ❤❤❤❤❤❤😂 Mention à Malale
Gni accidenté ci autoroute péage bi hier Yalna léne yalla yeureum tei aldiana done séne noflaye blessé yalla feugue sene bopp ci Barker serigne Fallou Mbacké Fatikha 41 likhlass 🙏🙏🙏
Les sages sont beaux, même s'ils sont laids, ils sont riches, même s'ils sont pauvres, ils sont grands, même s'ils sont petits Courage a vous ❤ NIASS ❤
Développez une attitude de gratitude et soyez reconnaissant pour tout ce qui vous arrive, en sachant que chaque pas en avant vous rapproche de la réalisation de quelque chose de plus grand et de meilleur que votre situation actuelle.❤️❤️✅
Gni accident si autoroute pieage bi yalna lé yalla yeureum té kharé aldiana firdawsi ta Sophie ndeysane sila bokou ak rakk dji yalna yalla yessal yeurmendeum si barkél Nabil Moustapha sws meti na Trop
La façon dont malal s'occupe de Bigué me plaît beaucoup 🎉
Dagno beugueunté ba hotessou😂
Goor gni sen djiguéne lanouy topoto di fonto sen diabar 😢
Yow frère a chaque fois nilay mél ak sœur am bou amé changement rék khamalni diabar dia moko mene ba daaneko féwalé ko ak mom, mais malal yalla sovénako bou bakh
@@fatop2374bilahi 😢
@@AmySarr-c9tc’est exactement ça
Ndeyesan un grand frère bou meil comme malal est un grand bénédiction ❤
Déeléin samou téy aare sén sœur yi 😊
Billahi 😢
Bilaye nak
Mane dh amou ma ko
Amine ❤❤❤
Bly
On la jamais vue ni entendu son voix ms on l'aime Psl sur bien aimer mhd 🎉
😂🎉😢
Machallah ❤
Bigué ak malal sont tellement sincères dome baye dafa nex yalla bou saytané doug sén diganté 🙏❤️❤️❤️
Dou domou baye yeupa nékh
Accident bi yalna yalla yérém gni gagnou,
Fallou fall yalnako yalla guéné kasso
Amine
Aameen
Amine 🙏
Amineeee😢
Amine
Gni décédé si accident kaju radiab ji yalnaléne yalla yeureum😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Amine
Amine
Amine
Amine 🙏🙏🙏🙏
😢😢😢😢😢
Magal gui dial n'a ak jam mes tmt Serigne fallou fall yalnako sa bororm bi art teh gêne ko fimou nek 😢😢❤
Amine yarabi 🤲 🤲 🤲 🤲
Amine
Amine
Amin🤲🤲
Moniou diakhal
Keur Mar lo vrai famille sénégalaise. Cette série est le reflet de la vie quotidienne dans la plus part des familles
sénégalaise
Vous tous trop forts chapeaux au artistes ❤❤❤❤❤❤😂
Mention à Malale
Koudakor libérer falou fall lalal j'em❤
Man
👍🏻👍🏻
Bilae
Yalla Dina ate lep
Love 😍
Codou kagne ngay nokhou diarri mi😮
Bilay
Billahi lolou rék laa yakamti diarry m'énerve té niak khorome
Codou bilahi bo nokoule diary ma bayila
Codou tamit wakham barina dh ishh do dieff
@@ndeyendelladiene7352Codou défoul Dara lep Wa pikinela😂😂
Ndeyessane sama Grand frère tu me manque beaucoup trop nonoula beugé wone serie bi repos en pex 😭😭😭😭😭❤❤❤😊
Amine 🤲🏿
Yalla nako yalla yeureum😢
Amine
Amine
Paix à son âme
Badou mi réw na dh😊 yalnagnou yalla mousal si jeukeur djou réw bou melni Badou😮😅
Amine yarabi 😅😅
Badou rewoul bigué moi rew
Li nék thi xéllyui te manou gniokou wakh yalla na yalla safara lép thi barckéb s touba❤❤
Sa commentaires bi loumakoy guiss barina ci lady et xalisso et bété bété extra
Amine
🎉🎉🎉❤❤❤
😢😢😢😢😊😊😊😮😮😅😅
❤❤❤❤❤❤
Amine
Gni accidenté ci autoroute péage bi hier Yalna léne yalla yeureum tei aldiana done séne noflaye blessé yalla feugue sene bopp ci Barker serigne Fallou Mbacké
Fatikha
41 likhlass 🙏🙏🙏
Amine
Amine
Amine 🙏
Ki done dawal OTO bou ndaw bi sougnou village la deuk sama magou xarit leu
amin ya rabbi
Fallou fall yalla na yalla génela fofou gua nék s’y barké serigne babacar s’y
Amine 🤲
Amine
Amine ya raby
Amine ya rabi
Amine wayy 🤲
Parfois nga guiss sa yaye begue done milliardaire qui est d'accord 👍 ❤🎉
Bilahi
Ay way amine ❤
@@NdeyeMdeneMdene yalla nagnou nékk milliardaires 🤲
@@fatoudiop5920 yalla nagnou nékk milliardaires 🤲
Amine 🙏 way
Team sautè publicité😂 manifestez vous en masse🎉🎉😂😂😂😂😂😂🎉🎉🎉🎉 on a pas de temps😂🎉🎉🎉
Vraiment 😂😂😂
Magynii😂😂😂
Publicité yi est ce amna niou koy sétane
@@AboubacarSoumah-l4u 😂😂😂
@@margueritesigandiaye1726 cha kaw cha kaname😂😂😂
Vraiment nk Malal lô da beugue famille mém❤❤
Malal Référence la
Ay guirr yallah guêné lenn rakou fanta bi si série bi guirr yallah😢😢😢
Mogui niouy beugue nékh dall😂😂 gor waroul am nebo akk diabaram ak Lou méti khew
@mariamayattara4497 vraiment meunou mako supporter sheu tttt😭
Vraiment môme 😂
Vraiment 😂
Bilay o finish j déteste les séquences kel apparai diarry dégage
Des coeurs pour prophète Mohammed ❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤
avance pub rek 😂 Ami diop masha Allah 😊 soda Ak bator quel sequence 😂😂😂😂😂
Sama Yaya yalla na goudou fane ak Wër ❤
Ko may santél serigne saliou mbacké
Dieureudieufè Serigne saliou ❤❤❤
Dieureudieuf Seringe Saliou mbacké
انا
Dieuredieuf s saliou sama wadji ❤❤❤
Moi
Ni niou tassé si série yallna niou tassé nonou al diana amine 🙏
Amin 🤲🤲
Amine ❤
Amine
Amine ya rabii ❤️
Amine 🤲🤲❤️🙏🙏
J'adore la complicité de bigue et de malal ❤❤❤❤
Ala ak diari il m’énervent 😢😅😅
Diari qui manipuler ala 😢
Wa yén man rakou fanta bi djépi nako dé ak kanamome bou wingue guéné lén ki si théâtre bi way😢
Doma raw ki nimako ndiepé
Dou yaw kassé
Denaa jekhal khallesi ala bee deh😅
Doma raw dom baye 😢😂
Ak mane
Sokhna botor dal ya sagnsé amna model korite inchala 💃🏻💃🏻
😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Wayyyy😂
Dieuleul bou bigué bi mo dax😂
😂😂@@yayouSalihousamb1553
@@yayouSalihousamb1553mouni lan dakh 😂😂😂😂😂
Bigue ak ngone la niou taka ndo nio ama no problème ❤😂
Non non ngoné amna dieukeur depuis bi sénn yaye du dounde té Bigué niogui ko takk moma bi mar lo nguéné keur
No gnon seyyui deu no
Non danio seuyé ndo rék
@@mariamadiallo9511oui on le sais mes elles ont "seye" le même jour
@marichousow58 ok je vois seuyi bi c'est vrai
Xana caméra de surveillance yii mom ci souf boukouci 😂 Mère Soda ak Bator didef loulen nekh😂😂
En tout cas
Koudakor Libérer fallou fall j'em❤❤❤❤❤
Soula nékhone nga romou sama commentaire do lalle j’aime ms défoko dagua lalle j’aime nakh sa khôl mo rafétt 🥰
😂😂😂
Laloumako deh 😛
😂😂😂😂
❤❤❤❤
Amy diop sa serigne bi mbadou bouyeu 😢😂
Mane dh lolou la yakar
Mome la maye mourou dh
Balla benene épisode bi yalna feek Fallou fall libre diko sétane ak nioune amine🙏
Amine ❤
Amin way
aminn
Amine
Amine ❤🙏
Des cœur pour notre prophète Mohammed ❤️🕋🕋🕋🕋🕋🕋. Yalla n'a niou yalla may niou féke ramadan 2025 bi amine y'a Rabi 🤲🤲
Salahou aleyhi wasalam ❤❤
Amine Yarabi
Amine
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤psl
❤❤❤❤❤
J'adore la complicité de Malal et Bigue
Wa bator mom kouka meussa guis mou ayé togue😂
T'a raison dé 😂😂
Moma diakhal dé 😂😂
Môme kay lall bi rk😂😂😂
😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
@@RamataNdiaye-ku2phlallbi rek 😂
Un constat que j'ai fait : Fanta bimou amé dieukkeur batay day defarou di sagnse di maquiller wou surtout par rapport ak avant 👍👍👍
Famille Sénégalaise notre série préférée merci beaucoup à vous machallah 🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉❤🎉Yalla na niépp am diam amiine y'a rabby 🎉🎉🎉🎉
C'est pas notre préféré quant diary est lâ😢😢
@@SalimataThiam-n3p 😂😂😂
❤❤🎉😢😢
Wa yéne guise guéne bleu bou barri bi 😂 bigué ,malale plus valise bii
Ak bouya😂
Non Sénégal nékh na😂😂
Bigué koukoy Solal 😂
😂😂😂
Mar yaw do responsable sa dôme bou djiougué si seuye daguakoy dalal ba paré mai guakoy dak té khamo loumou done dounou si seyeum 😢
Lolou bari na fi sénégal de 😢
Bly tu as raison
Li mon ame Sénégal
T diniouy beug ray ak kiliffeu la tchim😏
Bilay Ala damako siippp ,yeureum ko 😢li yeup sa doff ak khoulii ay beut👁molako yobé Ala 😂
Ay way bouma ray😂😂😂 ala rek weroul
@@diariatoufall1391😂😂😂😂
@@paulelefall ala Dafa manqué trop 😂😂
qu'Allah ouvre ses portes à tous ❤
Allahuma amine ya rabi🤲🤲❤❤
Wa yenn diarri mi sofoulenn ak modewayam bii😢
Modé biiii moma si metiii😂
Ak touti wayam 😂
Alhamdoulillah que dieu nous proteges ❤
Amine❤
@MariameBa-p1p amiine
Amine 🙏
🎉🎉 ❤😅😅
Koufatélikou né ngoné ak bigué nio seyéndo😊té nionara tasandon dé😮
Mane ya meune topou cas 😂😂
Non ngonè mo Ndieuke am dieukeur dèh
@@AwaBa-ub6eo non seuyi la wakh
Le jeux du destin😢😂
Justus pour fallou fall ❤
Ana niou beuge tèral sèn yaye yi❤
Non téatre bi kounéke sa problème Non sokhena botor dinama réy 😂😅😂😅
Sokhna Bator dé bouma rayoul😂😂😂😂😂😂😂😂😂ak ay manièram shuuuuuuuuuuuttttt sokhna mo meuna sagnsê❤🎉❤
Série bi dhè gniko gueneu bagne nioko dakka sètane sama genre gui 😂😂😂
Bilay mangui ni😂
Bilakhi wakh gua deugue
Bilay 😂
MoMA diakhal KOM man rek😂
Khamo si dara
Les sages sont beaux, même s'ils sont laids, ils sont riches, même s'ils sont pauvres, ils sont grands, même s'ils sont petits
Courage a vous
❤ NIASS ❤
masouma ame 10mil j’ame 😭
Ya eup😂
Nie def Accidents si Kazu Rajab bi Yalla na Aljana done sen Keur 😢😢😢
Amine
Yalla na diamou sakh ci Sénégal barkep seydina Muhammad
Mane dal wakh deug nak cawou diari bi amour sens thi série bi ahhh
Wakhatiko dh Kane mo dofoti ni Allah ishh ki rkk la diépi
Khanna 😂
Mom la gueneu diépi ci série bi Mouy mel ni épingle ni
Sérieusement
Yalla na niou yalla may niou fèkè ramadan،2025, bi Amine
❤❤❤❤❤❤
Amine bb ❤❤❤🎉
Série bi déjà nekhatoul fehelene ba li bouyya wah nek ayy féne Serigne Ady mome guéné lenkosi rk
Ahahaha wouy yaye boy 😄😄😄😄😄😄 bilaye Serigne Adi mome kilifeu leu warou gnou ko wone dougeul thi séne yéfi doff yii thimm
Une vrai famille Sénégalaise😂 chapeau à pikini production 🎉❤
duo Sokhna bator ag touba bi ag soda😅😅
8:25 voix SERIGNE bi dh kom BOUYA MBAYE😂😂
Mom la dh😂😂😂
😂😂
Voix serigne bi chaque jour mou changer 😢
3:21 ndeysan li deh mo beurri Sénégal juste pour ayy affaire de sameu tour famille daniou diemé sakh deglou sen domeu yi seuy dou guerre
Mane mome vraiment pour être honnête malale moma bayi si série bi vraiment ils est courageux 😍😍
Diarry mi gui rateu Ala 😂😂
Sara neh nama loll! Merci Cherie 🥰
Du bleu sur du bleu est du bleu à la figure 😂😂😂malal ak bigué diékhal nguen bleu rewmi yeup
Hana guisso Bouye Mbaye 😂😂😂😂
😂😂😂
Changel saa garde robe madame😂
Bouya nk doyna waar
Je ne crois pas qu'il existe un homme comme Alla😂
😂😂😂😂😂
Il trop naïve diari va devenir riche 😂😂
Waaaa Kane moy styliste Diarry?? 😂😂😂😂
Man la
Développez une attitude de gratitude et soyez reconnaissant pour tout ce qui vous arrive, en sachant que chaque pas en avant vous rapproche de la réalisation de quelque chose de plus grand et de meilleur que votre situation actuelle.❤️❤️✅
Mar lo régléle sa keur gui désorganisé na trop waye😂comme sabar bou tass rek
😂😅
Yalla na niou yalla May niou fekè Appel souba bi si diamou AK Salam
Amine inchaallhrabi 😢
Biguer ak ngoné gnio seuye ndo tassa ndo quelle coïncidences 😢😂
😂
Nenagn le hazard nexiste pas😢😂
Sama turu mam dawoul sama yaram😂😂 deret bu bleu ewaye Sara ken du iaw sa forme en plus maashallah❤
Cva ma soeur wakhatiko sarah dérétou alien la ame nonou bleu. 💧kaye😂😂😂
@awasy386 🤣🤣🤣🤣
Yallah nah gnou yallah may gnou doundou baah téral sunu wadiouryii sii barkii Seydina Mouhamed (SAW)🙏🙏
Serigne hady liko bouya wakh soude deug la ma bâyii setane seriebii❤❤❤❤❤
Dou degue Issa moy manigancé lolou
Li la wax issa moy Def lolou
Gir mar wedi khergi tass
Bilaye lii mome yéfi doff deugeu leu
Bilay loulou mom monoul nek deug
Doma fi bayi dh
Justice pour fallou fall 😭
Kou beug sa yaye beusal❤
❤❤❤❤❤❤j’enMama❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bigue dé khamon nani fi lay moudiou di sey Te chaque jour nga dem senn keur di li dianti sa sey pape ak say yaye😢😢
Masou ma am 5 j'aime 🥹🥹
Li nek si kholou nigni te Manou gnou ko wakhe yalla nako yalla safaral❤❤ si barke Serigne fallou❤❤
Amin🤲🤲🤲
Avec famille sénégalaise votre cœur bat plus fort 😂❤
Bouya mi moye khathieu degue
Kou diépi bouya lalal comman rek lalal j'aime 😮
Diari rék la diépi😮😮😮
Dou yow kessé dé
Bari gua si morome
La feçon dont mala s occupe de Bigué me plaî beaucoup 🎉🎉🎉
Toubab bi douma ray😂😂😂😂😂😂😂
Kou may santal seydina Muhammad lal coeur
Mane mi😂
Gni accident si autoroute pieage bi yalna lé yalla yeureum té kharé aldiana firdawsi ta Sophie ndeysane sila bokou ak rakk dji yalna yalla yessal yeurmendeum si barkél Nabil Moustapha sws meti na Trop
Amine
Amine
Aminnnn
Alla est ce que do wakh tane ak Codou wakh ko deug bi mou diékh béneu yone
Mes alla tapetla d nième woul Codou 😂😂😂😂
@SokhnaSeye-mq3mc Lolou Moy Cas bi Damako yeureum sakh
💍🫂🤍💙🫂💙💍🤍🩷🫂💍🩷💙🤍
@thiabagueye-d4j alla dafa niak fayda diary diko mbaran rek
@@SokhnaSeye-mq3mcDiari nokk ko rek la beug 😂
Ngone y’a rew séne Lou série you bone yi nganane wakh ko yalla 😢 chimmm
Sunu borom dal moy fowè kay baxna rk
Dama fok ni mane rek la méti doumay commentaire mais tey mom def na ko
Vraiment mane dama tiitt sakh
No mall bigê locoda al mcté bocm😢 mobayi fant ak alim❤❤😢
Bouya linga wakh Serigne hadi méti nama trop 😢 wayé Serigne hadi mome you gnakk fay da yi bou lénn ko thie bolé thimmm
😅😅😅toubabbb bi dh. Molen gueuneu yewou tokkkk Len fofou 😅😅😅😅😅
Waaa yénn Diarry mi lou mar di khar si mom mou guéne keur gui Codou do. Niouss ki😂
Le duo malal vs badou on aime trop en vrai tout le monde joue bien dans cette série chapeau 🎩💯
Bigué AK malal AK valise bi sén otéss lanla si bleu 😂😂
Say beut sorina 😂😂😊😊
Kon guiss nga lolu😂😂😂😂
Kou arrière dem holat RK lalala j'aime
Tu as raison déh🤣
@ 🤣🤣🤣
Justice pour fallou fall ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️♥️♥️♥️♥️
Bayilléne di gnane ay coeur si commentaire yi 😂😂😂😂
Yalla na niou yalla may niou féké ramadan 2025 bi kou wah Amine l'ala j' aime ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amen
Amine
Amine inchallah niépou féké 🙏🙏
Yallna yalla may fan wou goudou ak wer sou niou yaye yi kou beugue sa yaye rk la lal j’aime ❤
32:29 sarah yaye lathté nègou ngoné nonou🤣 Tè binga ko beuguè wone guisse nga dèmal seu bop ba fofou kéne wanou leu ko🤣