Masha Allah père Max... Yaaye wakhkatou deug. Tu es simple, véridique et un ancien lutteur charmant.... Adouneu deugueu rek leu vraiment bonne analyse sur tes 2 fils de lutteurs et bon Coaching.
En tous cas un combat que tous le monde disait que modou est plus fort plus technique plus d'expérience si aujourd'hui on dis que ya victoire ou pas victoire
on défi le roi pour le combattre / LE Détrôner / prendre sa place non pas pour se défendre Siteu gneuwoul wone pour nèkk Roi des ARENE mais dafa gneuw pour ame cachet rk
BG2 moy sama mbeur mais siteu demb daffa daw lamb dji yeupp té kou xam xamni siteu lamb dji moko moom mystiquement mo diékou kon loyy ragual vraiment c honteux de réclamé une victoire. Sou féké ni nara beugue beuré akk balla gaye nga tell niou wakh ndakh dou deugue yoon .
Li dall Modou Lo si combat bi C'était la même chose contre Eumeu Sene en 2014 Nieupa fogon Eumeu moko meune wayé mou moudié wekh katt si Eumeu 😂 Modou nak lolou moko dall si Siteu
NIOUN DEH SITEU SOUNOU MBEUR LEU MAIS YAW PA BOU DOY WAR NGA FALA YAM NAKK.... LINGA WAKH NI NAK LINGA CI DIOUP LOU YAKO KHAM TE YALLA BOULASI YALLA MAY NDAM
Dama kompoul nan la nitt meuner togg di critiker siteu mer kou nekk ak sa façon de lutter da nguen andi sa stratégie siteu indi yeufam niounan dafa daw ter ken diokhou ko chance si lambji mou yobou modou ardo 2 a 3 fois
Siteu khalé la n'a tey Di def ni moi def ak Modou bouko defé ak kénéne Dina am ndame modou siteu manouko dane kon ni rek la manona beuré diekh na Bou diapé kenene ki dinguene khamni leep deug la 😅😅😅
Masha Allah père Max... Yaaye wakhkatou deug. Tu es simple, véridique et un ancien lutteur charmant.... Adouneu deugueu rek leu vraiment bonne analyse sur tes 2 fils de lutteurs et bon Coaching.
Way ioe père situe khalatoul déme songou modou lô😂😂
Bou feke ni siteu ni lay Beur dou Dane bene Mbeur
Man la modou Lo xaragne Lo❤😂
Par dano ken 😂😂
merci pere ❤❤❤❤❤
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah cikaw ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Père waxal Siteu degue farouma ak Modou mé sa mbeur bi com jumeau Lac 2 rk
Walahi
Vraiment
Yaw hana dégo mom moko wakh boumou song
😂😂
Waxal deug tamit nè modou lo danouna 😂
Merci perr❤❤❤
Siteu rek lanioy topou ❤
Bel fatte valdo❤❤🎉❤❤
En tous cas un combat que tous le monde disait que modou est plus fort plus technique plus d'expérience si aujourd'hui on dis que ya victoire ou pas victoire
Félicitations à siteu
Félicitations siteu ❤
Merci pére
Siteu rk ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Siteu mo dane nakkk wakh deugueu yallah😂😂😂😂😂
xalis bakhoul wakhal deug
No bilahi siteu Mo baxx😢😢😢
Mai siteu modou moko moun siteu da dawe ba lamba bi diekh siteu dou dara dema rouss sah
Ko meun doula door baga dem ardo 3fois gua danou tek épaule
Guinaw saccou yi la door midou fékeu arbitre sifle motakh mou dieul 3 avertissement demal xolate combat bi...@@AbdouBassNdiaye-s6z
Si guinaw sakouyii ngay door@@AbdouBassNdiaye-s6z
Sa Thiès vs Modou lo
Balla gaye vs siteu
Pere yaw rouso di wakh ni ya Dane vrema mak bou tolni yaw no rouss na trop
on défi le roi pour le combattre / LE Détrôner / prendre sa place
non pas pour se défendre
Siteu gneuwoul wone pour nèkk Roi des ARENE
mais dafa gneuw pour ame cachet rk
BG2 moy sama mbeur mais siteu demb daffa daw lamb dji yeupp té kou xam xamni siteu lamb dji moko moom mystiquement mo diékou kon loyy ragual vraiment c honteux de réclamé une victoire. Sou féké ni nara beugue beuré akk balla gaye nga tell niou wakh ndakh dou deugue yoon .
Bo deimei banei do dieul niari champion rek koone xamenguani Modou lo ndanane la nakh dafeko deifff... Allez XLo🎉
Situe mo mon❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢😊
LINGA FI WAKH YEUP NAK 4 APPUIS MODOU LO NGA KHOL MOTAKH MOM REK NGAY GUIS MAIS SITEU TAMIT DEF NA 4 APPUIS YOU LER ...BAYILEN BOULEN MBEUR ARRANGE TOUL LEK NGEN DIKO KHEKH
Mbo ko sogué mou dane leu (pere yako wakh d😂😂😂😂)
Modou. Anta. Cayitaga. Modou lo reka
Père waxou degg
Li dall Modou Lo si combat bi
C'était la même chose contre Eumeu Sene en 2014
Nieupa fogon Eumeu moko meune wayé mou moudié wekh katt si Eumeu 😂
Modou nak lolou moko dall si Siteu
Ädä fass seul 🎉🎉❤❤
Bly yaw❤🎉
Père iaw waxou degue mom li ngua fi wakh diadou wol mom suete dafa daw
Siteu dou dane béne vip peut être gris bordeau
Lolu dou analyse
Faralouma Modou lo mais père Siteu nay deugeul bopam
❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
Siteu rek bilakhi
NIOUN DEH SITEU SOUNOU MBEUR LEU MAIS YAW PA BOU DOY WAR NGA FALA YAM NAKK.... LINGA WAKH NI NAK LINGA CI DIOUP LOU YAKO KHAM TE YALLA BOULASI YALLA MAY NDAM
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂max yanekh 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
They per max mako bege de barke serige saliou mbacke 😂😂😂
Siteu ammoul fite😂😂😂😂😂😂
Père pardon mais meune gu fén nakk
loula yarr mayoul yaradikou doulako may kii kilifa leu epuis soula baloul dinko layo ak mome ci kanamou yalla
Siteu lim beuré dembou mom 35 combat dou dan modou lo 😂😂
Pourtant demb mo dane Nak Bo waxè deug rek
Dama kompoul nan la nitt meuner togg di critiker siteu mer kou nekk ak sa façon de lutter da nguen andi sa stratégie siteu indi yeufam niounan dafa daw ter ken diokhou ko chance si lambji mou yobou modou ardo 2 a 3 fois
Per yaw SA 10/ 100 Yi motakh do wakh siteu thieur
tapha gueye limou wakh dosi wakh ndakh moy degue
Ki da dof
😅😅😅
Revance amoul😂
Siteu=lac2😂😂
Wakhal way per
Père siteu dafa daw combat bi yep Père defou fi dara derrier sakou yi mou door ko kou sila démé ardo
Mak nga waay😂
Siteu.da.daw.moy.khale.loutakhe.nagouwoule.takhaw
Siteu khalé la n'a tey Di def ni moi def ak Modou bouko defé ak kénéne Dina am ndame modou siteu manouko dane kon ni rek la manona beuré diekh na
Bou diapé kenene ki dinguene khamni leep deug la 😅😅😅
Pere sa mbeure daw comba bi yeup tardel lamdj ji di door si guinaw sakou yi defoul teste antidopage
Nice ♥️♥️♥️♥️♥️♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰♥️🥰
Bêla dakela
Siteu tapete la séne stratégi bi bakhoule daw reck
Yaw père max ak yaw modou anta ay n'a fékh nguéne
Ki comme kou wéroul
Yaw dagey wakhe rak
Siteu nouveau roi des arènes yalmine bi seul 🎉
Khana 2001 bi di niewat😂😂😂
Ya tapha gueye reck nga yap