@momardiallo1609 meussoul wax lou bakh thii Ama Baldé, mbeur menoul toukki pendant des mois di entrainé lou métii après nga yoor sa lamigne nane entainéwoul dii ko xass chaque jour, il se prend pour qui? Il faut qu'il apprenne à respecter les lutteurs.
Yaw meuno maye nitt gni diam yaw mbeur yi yaw laniou wara prouvé sen entraînement wala wala sen dolé boulniou sonal waye tamite gni ngay wakh nieup ko ci wetal mou doumeu leu ba nga teud
Billahi Bacary a dit la vérité
Fans franc ak ama baldé yeup khamnagn ni khamo dara 😭😂
😂😂
Balla Gayie 2 Sene Papa la 💛💛💙💙💛💛💙💙💛💛💙💙💯
Ioe xamo dara ndeye domérame ama champion .
Bakary ama la faral daye tèkh xèl rrk mè ama kouko kham nè liguèy na
Bakari dafa beuri ndeye wakh khamo lofeul ndem
Bilay diobou ndeyem khamouko Ama forme athlete la indi
Bakari da oubi lefele deme
😂
Bakary mane fran la faral Mais dama yakarni de nge kanassou, ama esk seign na beurer ak fran ter d’où entraînement, nekkal nit
Gayi wakhi Backary sakho yi bouléneko dégue mome ama baldé nio ande défloli day nakhaté deh
Forme Ama nice Amna dolé mais mom toujours critiquer
Bakariy yaw Sa data yayae kahmou dara
bakary fen rek bakary nopaloul khamo ndeye lamb do nopi
Ki dou wakhé sport
Alune seye 2 vs bombardier moye comba bi
Kou beug sétane combats wam MMA😅😅
Bakary Ama baldé dou sa morom, fiche nous la paix, tu parles trop té xamo dara
C'est parsk wahoul lila arrangé 😂😂😂😂
@momardiallo1609 meussoul wax lou bakh thii Ama Baldé, mbeur menoul toukki pendant des mois di entrainé lou métii après nga yoor sa lamigne nane entainéwoul dii ko xass chaque jour, il se prend pour qui? Il faut qu'il apprenne à respecter les lutteurs.
Khana nga sagn ko wakh doul rek balahi amoul xamxam grande gueule rek
Wlh en plus il est nul à son demain il connaît rien c deux lutteur personnes n peut l dire sont pas prêt physiquement
Bilahi
Ioe bakary katal sa Ndeye khamo dara
Moytou léne protéine you bari si yaram
❤️❤️❤️
Coach Bakary a parfaitement raison Ama baldé forme bi bakhoul li meunoul danél Franc😂
Jackson n'a rien à perdre thi combat bobou té bouniou khékhé Jackson mo eupe chance k.o ko
Tu la férme ama seul
Modou anta lolou dou combat boul niou sonal
Ya meuna doul
Bakary parfois il dit n’importe quoi
B52 vs aloui sey2 moy combat bi
Jamaïquain
This coach guy is sometimes a attention seeker
Ioe coach bakary bouniou sonal dagay dull rek merde wayy tu parle trop 😢
Yaw meuno maye nitt gni diam yaw mbeur yi yaw laniou wara prouvé sen entraînement wala wala sen dolé boulniou sonal waye tamite gni ngay wakh nieup ko ci wetal mou doumeu leu ba nga teud
Bakary yaw doul rek gay déf