Heureuse de revoir Soleil Levant dembou ❤ Hommage à Kader Yalla nako Yalla kharé aldiana firdawsi 🤲🏼 Ndeysan les personnages de Touly ak Mame Coumba Modou Pouss pouss.. Lou nekh way ❣️ Vive Soleil Levant 🥰
Ravie de vous revoir ensemble diam dafa neh 😊😊😊 . Mais les absences se font sentir nak première version bi mom dotou fi amati chef-d’œuvre intercontinental Machala 🎉🎉
Haye waye lilagnou namone si yéneu nak walahi série c’est important mes yi lagnou begue espère nako haye années merci je vous aime 🥰 et bonne continuation 👏👏👏
Heureuse de revoir Soleil Levant dembou ❤ Hommage à Kader Yalla nako Yalla kharé aldiana firdawsi 🤲🏼
Ndeysan les personnages de Touly ak Mame Coumba Modou Pouss pouss.. Lou nekh way ❣️ Vive Soleil Levant 🥰
Et Seydina
Amine ya rabbi
@MouhamedMADRID11 nonn pour les personnages manquants
Ravie de vous revoir ensemble diam dafa neh 😊😊😊 . Mais les absences se font sentir nak première version bi mom dotou fi amati chef-d’œuvre intercontinental Machala 🎉🎉
De 2003 à 2023. Toujours present avec nous pour nous faire plaisir. Longue vie et plus d'entente.
Diam rek mo neh Sanekh et Vieux Ba chapeau Diam Sila lep khath continuer à nous épanouir ❤❤❤
theatre bi avant probleme bi la yagueu nako sétane wido
Merci beaucoup
On en parle jamais mais wallah le niveau de Binta est juste époustouflant... c'est une fine actrice
Billahi yalla nako yalla défal jmm
Elle est exceptionnelle vraiment
Nooo pomdeter ak Angleterre dou ben. Les absences MODOU POUS POUS MANGASSI LAYE SOW TOULLY MAMAE COUMBA ohhhh😢
Elles sont ou ces personnalités là ?
Walahi
Cheikh NDIAYE toujours dans son rôle de Boss le riche😂
mom kay amena foula😂
Bly 😂😂
😂😂😂😂 Oh machallah quel souvenir yalna diam yague
Sanekh et vieux ba ensemble lii dafa rafete yalna yagg si barké yonente bi ❤❤
Amine yarabi 🤲
Ayway li nékh n'a trop bly retrouvailles ❤❤❤
Haye waye lilagnou namone si yéneu nak walahi série c’est important mes yi lagnou begue espère nako haye années merci je vous aime 🥰 et bonne continuation 👏👏👏
Aladji Gora est tjr égal à lui même.. il est trop fort mashallah😂😂😂😂
Ahaha j’ai tellement regardé ce théâtre dans mon enfance que j’ai mémorisé les dialogues
Mais dara dou dak première version bi 😂
J’aurais aimé revoir mangassi, mame cumba et boy sow😢 Modou pousse pousse, Toulli
Mais bon merci pour ces souvenirs 😅
Vive Soleil levant ❤
Ou est toukousss?
Pur un retour du Grand Soleil Levant. ❤❤❤❤
Ndeyssane vieux ba ak sanekhe diam da nekhe
Bly
Sanekh yalla na nga goude fane bou and ak wer mane desfois dama nane sanekh en plateaux mo dakh sanèkh en série 😂😂😂😂😂❤❤❤❤
Amine yarabi 🤲
Longue de vie les comédiens je vous j'aime beaucoup 😍😍💕
Da mél ni retro yi lagnouye joués wade mé machalla 😂😂😂sanèkh rék lay topou ou son les vrai touli et vrai mame Coumba 😢
Diam rek mogeun vraiment bonne continuation
Content de voir vieux Ba
😂😂😂😂😂😂😂😂 sama vendredi nekhna ❤ Sénégal liiii lagnou am🎉
Namoune na wa soleil l'avant😂 vous êtes des meilleurs 😂😂
Machallah j'avais cru que c'était en 2003 😂❤❤ Machallah vous êtes trop fort wenibik chapeau à vous ❤❤❤❤❤❤🎉
Sanekh do nitt bilay walay yaye number one 😂😂😂😂😂😂😂
Macha Allah belle initiative , trop contente de vous revoir ENSEMBLE 😊😊😊
Machala yalla na Diam adouna dara yagoul contente de vous revoir ensemble
Très belle surprise , mais bataye le premier est inégalable 😂
Dou béneu sakh
@@mayasiby1249 carrément
Belle initiative le retour de nos théâtre name naniou théâtre nak
Machallah walay contente thi djiss ba thi troupe bi que dieu vous garde toujours ensemble ❤❤❤❤
L'idée est génial machalah trop inspiré. Et pourquoi pas askanou laobé
Ayy vous nous avez manqué trop😂❤
Ah Soleil Levant,que de souvenirs, que de bons moments.....Merci
No li nekhna waye Bly yalna diame yageu senegal ❤️✊🏿🤣
Bima guissé bâ dama contane sanékh yalna sa diame yague bilaye diame dafa nékh té Lou yagu degueleuu❤❤👌🏼👌🏼
Machalla contane si yenne diame mo nguen loune❤❤❤
Merci on est très content de revoir Soleil Levant sous cet aspect. Vous nous avez fait vivre et revivre des moments forts❤🎉
Bravo, une version simplifiée avec les scenes mythiques.
Je suis très contente vous j'avais réunissent ❤❤❤
Samb is the best in senegal and his group. I cant wait to watch the continuation
Ndeysane j suis fière d vous and rek moy deugu yalla n'a Diam yagu
Seule Binta qui assure son rôle comme avant.....
Sanekh comme aladji ont assuré
Non contann nagne si yénn bravo a vous 😂😂😂😂rétann na ba sonou
Way li nice na way🙏❤️❤️❤️
Mancha ALLAH 🙏🙏♥♥😍🥰
contane thii yène. SOLEIL LEVANT thia kanam 💪
😂😂😂😂😂oh man bi mom that’s dope 👊🏽💯✌🏾
De retour non sanékh dou changer😅😅
Mais dékkî sanékh bii grawneu❤❤
Hooooo machalla dèfati nguène lou rafet bâ waay yalna sèn diam yague ❤❤❤❤❤❤
Sanekh dou nitt bly😂😂😂
Bilaahi premier bi mana touléénko 😂😂😂😂😂😂😂. Nonnn saanééx est le meilleur artiste comédien
Sanekh dou nite waye😂😂😂😂
Best artists duo Sanekh & Bineta
Après Ndeye NDIAYE et Diop Fall😂😂😂😂😂😂wa Thies da gnouye rayer😂😂😂😂
Non sanékh da guena Q'on 😁😄
Vraiment li néxna lool merci à vous
Bonne idée, j'aime bien ce film
Machala man sanekh damako beugue rek yena fi mane
Vraiment li nanou namon 😂😂 retan ba soneu 😂😂 machallah dall
Partie Bâ Sanekh et Aladji si côté fin bi😂😂😂😂
😂😂😂 sanex est le meilleur, bravo
Mais beneu dou original bi
Vieux Ba délouna soleil levant
Alhamndoulilah
Mbaye yaw foke nga dioye 😂😂😂 😂😂😂😂
Eyway yala n’a nek bou bess khar nalen ba son😂
Peace and love❤❤😊
Wa Soleil Levant dégn meune theatre nak machala 😂😂😂
Lathie ngua fouma name😂😂😂sanekh dou nitt❤
Merci merci rafètna diadjeuff sanex vieux ba
Li mome bou léneko bayi 😂😂😂car c'est trop nekhhhhh😂😂😂j'adoreeeee😂😂et je sais que je ne suis pas la seule
Les meilleures de tout les temps jamm si yén.
Rétro si music laniouko kham mais vous avez innover vous êtes les meilleurs walahi mane yén rk lay tooop
😭😭🥺 sama xol toyna nak guiss soleil levant sans niom mangessi, Touly, mame coumba, ndeye coumba etc... rek day toyal xol.
billahi toma
Ayway rê n'a ba sonne😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Oh namone na théâtre
Machallah sénégalé yi contane nagn torop soleil Levant❤
Non mak bou Réew wa bone😂
Avec so Rôle de Narcissique 35:28
Ndayesane l'histoire retiendra❤😢
Ndeyesane kholal Sanex ak père Vieux machalla Dioguo Mbaye 😂😂😂😂
Sanekh guuiryalla adille seydina plus modou pouss pousss plus ndeye Coumba mangansiiiii mou gueneu nekh 🙏🙏🙏
Nekhoul mome😢😢😢dina done nekh reprendre ko avec kes même acteurs après presque 2 décennies
Non sanékh bilahi damako fan😂😂😅😅😂😅
Alladji vrai artiste leu
Saneeexxx ohhh kii yall nafi yagg th werrr😂😂😂😂🫶🏽
No Séne ndéwéneul bakh na ❤❤❤
😂😂😂😂
Yalla guéne goudou fane
😂😂😂😂😂😂😂😂
❤❤❤❤merci❤c’est trop cool
Wallahi li lagnoula name wone même si ça reste l'esprit acteurs d'avant étaient les meilleurs
Une belle initiative Malheureusement ce qui s'est fait à la première version n'est pas renouvelable c'était olus naturel
Yalnanguènko jouéwat 40 thi kanam❤
Ndiaye binta damala begue bly❤❤
Bly sa nekh ak Serigne ngagne koussi gueuneu ay nguanéma kileu
jtjur😂😂😂
Nostalgie
Yakh dérr chef lassi
Mangasi mo guena ay cheikh ndiaye,
Bilahi bou ndieuk ba mana toléne ko
Fall acteur leu nak khol ko si polygame ak fi❤
Ba ak sa nekh ensemble Senegal manouléne
Mais groupe bi manqué na niou baré bari 😢😢 Modou pospos ‚ saynida ‚ mame komba ‚ ak paco et les autres 😢
Bilaye motakh dafa guéye si mane😢
Magazine
@@FatouDiop-se3jj wallahi
@@FatouDiop-se3jj wakh nga deug fatté wone nakou🤭
akk touliii
Royy dou ndourokk pire mais c quand même réussi bravo SLV
Ndaye coumba maga ta gout deh😂
Saneexxx😂😂😂😂ladj na fouma gueudj
Roy dou nouro ak purrr li amoul bén sens
Retro yii la namonee❤❤❤❤😂😂😂😂😂
Ndaye Samé lou tegue tase lima rétane Tiyatar bi