J'ai agressé la notification. J'aime vous écouter yaw AK serigne cheikh tidiane sy al mactoum.rta AK baye Ibou sakho rta.. Yalla na GA goud fane baye boy 🙏
Dieredjieuff papa momar Diagne yalla nga fi yague té werr lol sa doundou gui amal naniou djierigne djieul na sa numéro xamna après dinala wo nga conseiller ma si adouna j'ai que 26 ans mais suis toutes tes vidéos vous êtes très pertinent 🙏🙏🙏🙏
Machalla comme d'habitude rek . Banalisation du mauvais. On finit par ne plus réagir. Yalla na gnou yalla boolé si gniye réagir même si c'est dans le cœur.
W'Allaahi Ndeysaan Baatu "Maandu" ci boppam la ñu barii di Jaawalë,certains l'utilisent comme bon leur semble. { وَقَالَ ٱلشَّیۡطَـٰنُ لَمَّا قُضِیَ ٱلۡأَمۡرُ إِنَّ ٱللَّهَ وَعَدَكُمۡ وَعۡدَ ٱلۡحَقِّ وَوَعَدتُّكُمۡ فَأَخۡلَفۡتُكُمۡۖ وَمَا كَانَ لِیَ عَلَیۡكُم مِّن سُلۡطَـٰنٍ إِلَّاۤ أَن دَعَوۡتُكُمۡ فَٱسۡتَجَبۡتُمۡ لِیۖ فَلَا تَلُومُونِی وَلُومُوۤا۟ أَنفُسَكُمۖ مَّاۤ أَنَا۠ بِمُصۡرِخِكُمۡ وَمَاۤ أَنتُم بِمُصۡرِخِیَّ إِنِّی كَفَرۡتُ بِمَاۤ أَشۡرَكۡتُمُونِ مِن قَبۡلُۗ إِنَّ ٱلظَّـٰلِمِینَ لَهُمۡ عَذَابٌ أَلِیمࣱ } [Sourate IBRÃHÎM 14 Ayat 22] Et quand tout sera accompli, le Diable (Satan) dira : “Certes, Allah vous avait fait une promesse de vérité tandis que moi, je vous ai fait une promesse que je n’ai pas tenue. Je n’avais aucune autorité sur vous si ce n’est que je vous ai appelés, et que vous m’avez répondu. Ne me faites donc pas de reproches! Mais faites-en à vous-même. Je ne vous suis d’aucun secours et vous ne m’êtes d’aucun secours! Je vous renie de m’avoir jadis associé [à Allah] !” Certes, un châtiment douloureux attend les injustes [les polythéistes]. Deug Deug Iblis mooy " Saï-Saï " Rawatina (As Shayatiinu wal Insu) 😭 Le fait de réprouver le mal et de le détester par le coeur Au nom d'Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux. D'après Abou Sa'id Al Khoudri (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit : « Celui d'entre vous qui voit un mal qu'il le change par sa main. S'il ne peut pas alors par sa langue et s'il ne peut pas alors avec son coeur et ceci est le niveau le plus faible de la foi ». (Rapporté par Mouslim dans son Sahih n°49) عن أبي سعيد الخدري رضي الله عنه قال رسول الله صلى الله عليه و سلم : من رأى منكم منكرا فليغيره بيده . فإن لم يستطع فبلسانه فإن لم يستطع فبقلبه وذلك أضعف الإيمان (رواه مسلم في صحيحه رقم ٤٩) جزاك الله خير شيخنا🤲🏿 جرجف 🤝🏿
linga wax d dëgg la mass'Allah. waaye nak bul fatté ni Magal Touba amoon nafi ak jangum al aurhaan ya conférence diine ya sallatu hala nabih ya qassaid ya ak yu baax yafay am yëp, yaw seriñ momar Danga caa seppi as ndaw Sodoon puukarewu takk ay oor siiwel ko, kon fofu moom
صح لسانك ونوّر الله قلبك وسدد خطاك على سبيل الحق والهدى والخير والرشاد وكثّر من أمثالك وبارك لك سعيَك وألهمك الصبر والبصيرة والحكمة ما دمت حيًّا وأُشهِد الله بأني أحبك فيه تعالى وأدعوه سبحانه أن يُحِبنا جميعا ويجمعَنا في الدنيا وفي الآخرة مع النبيين والصدقين والشهداء والصالحين وحسن أولئك رفيقا اللهم آمين يا رب ويا كريم علما بأني قد حاولت الاتصال بكم هاتفيا عدة مرّاتٍ وكَرّاتٍ لكن دون جدوى (لعل الله يحدث بعد ذلك أمرا) وجزاكم الله خيرا وأجزل لكم المثوبة يا رب يا كريم. أخوكم في الله/ محسن محمد انجاي
@@serigne-momar لا.. شيخنا الكريم ما عندي... لكن، يمكن أن تبعثوا لي أية وسيلة الاتصال تتيح لي فرصة الاتصال بكم عن بُعد لحين تَمَكُّنِ لُقْيَاكُمْ وجها لوجه بمشيئة الخالق وجزيتم خيرا
J'ai agressé la notification. J'aime vous écouter yaw AK serigne cheikh tidiane sy al mactoum.rta AK baye Ibou sakho rta.. Yalla na GA goud fane baye boy 🙏
Merci encore merci bcps pour les enseignements comme d habitude longue vie a toi et ta famille djame si yawe tellement explicite
Machallah Yalla nalla Yalla Faye yiw
Machallah 👏👏
Wallahi koulay dégg Lou douko reuthiou YALNA YALLA DOLILA TAKHAWOU THI BARKE YONENT BI SAWS
Deglo gouma sakh mé woor nama né lou aam solo ngay com d'habitude Mash'ALLAH
Barak'ALLAHOU fikk serigne Momar Diagne, longue vie pleine de bonheur ♥
Ngay wakh
Merci pere momar diagne
Père jai toujour envie de vous écoutez
sedounou am sole si Sénégal nah dege yele Moy dege ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup pour ce langage de vérité 👍👍👍
Amatina solo papa yallana yalla feyla yiiw
Eskey eskey masha Allah goudal faan kou bakh ki
Dieredjieuff papa momar Diagne yalla nga fi yague té werr lol sa doundou gui amal naniou djierigne djieul na sa numéro xamna après dinala wo nga conseiller ma si adouna j'ai que 26 ans mais suis toutes tes vidéos vous êtes très pertinent 🙏🙏🙏🙏
Je suis dans le deuxieme groupe,alhamdulillah.
Macha Allah amatina solo yague fi té andak wer.
Diadieuf Serigne Diagne, YA Allah nala sounou Boroom Samm, amnga solo si DÎNÉ lool
Deug rék nge wakh yalna borom khir ci bopam déf diam di diamou yaleu bilalay mandou moy fondemennt lislam walat papeu yalna borom bi faye yiw nit meu diouli té dou mandou yalna borom yeureum diam gni 🙏🏽
Machalla comme d'habitude rek .
Banalisation du mauvais.
On finit par ne plus réagir.
Yalla na gnou yalla boolé si gniye réagir même si c'est dans le cœur.
Diadieuf serigne bi wakhdji rafetna amna solo lol verité absolue amal diama gou baré baré machalla.. Senegal niou melni yén nioko mena changé
Machaallah alkouran AK sunnah rek moy degue 🙏 am na solo Serigne
As Salaamu Aleykum Sheikh Momar Diagne
Jazaak'Allah Xairan
🇸🇳🇦🇷🇧🇷🇧🇷🤝🏽👏🏽 masha Alla bonne continuacion si lep lou bakh amine 🤲🏾🙏🏽🕋🕌
Yal guafi yague té am wër si barké Nabi PSL
Machallah baraka'allahu fikum ❤
Merci beaucoup grand père
Machallah seringbi diaradiafa ty
Ma Shaa Allah Serigne Momar Diagne pour l'éveil des consciences, très longue vie doublée d'une très bonne santé, amiiiiine...
Allégorie de la caverne de Platon
بارك الله فيك
Yaangui yeeté bou baakha pappe!Amal diamm diou bari🙏
Assalamou aleikoum mon père.pertinente analyse. Merci.
Moy li ngay wakh rek " yagu si leudeum bakoufi tall lampe niou dal sa kaaw.
Que de faussaires dans ce pays
Dieureudieuf serigne momar
Senegal kham na mome Boure Yallah toum rankènafi tropp kou ko wakhale mane dama titee sakh lèguiu
Machallah qu Allah accroît ta connaissance
Mashalla Serigne Diagne, 🙏
W'Allaahi Ndeysaan
Baatu "Maandu" ci boppam la ñu barii di Jaawalë,certains l'utilisent comme bon leur semble.
{ وَقَالَ ٱلشَّیۡطَـٰنُ لَمَّا قُضِیَ ٱلۡأَمۡرُ إِنَّ ٱللَّهَ وَعَدَكُمۡ وَعۡدَ ٱلۡحَقِّ وَوَعَدتُّكُمۡ فَأَخۡلَفۡتُكُمۡۖ وَمَا كَانَ لِیَ عَلَیۡكُم مِّن سُلۡطَـٰنٍ إِلَّاۤ أَن دَعَوۡتُكُمۡ فَٱسۡتَجَبۡتُمۡ لِیۖ فَلَا تَلُومُونِی وَلُومُوۤا۟ أَنفُسَكُمۖ مَّاۤ أَنَا۠ بِمُصۡرِخِكُمۡ وَمَاۤ أَنتُم بِمُصۡرِخِیَّ إِنِّی كَفَرۡتُ بِمَاۤ أَشۡرَكۡتُمُونِ مِن قَبۡلُۗ إِنَّ ٱلظَّـٰلِمِینَ لَهُمۡ عَذَابٌ أَلِیمࣱ }
[Sourate IBRÃHÎM 14 Ayat 22]
Et quand tout sera accompli, le Diable (Satan) dira : “Certes, Allah vous avait fait une promesse de vérité tandis que moi, je vous ai fait une promesse que je n’ai pas tenue. Je n’avais aucune autorité sur vous si ce n’est que je vous ai appelés, et que vous m’avez répondu. Ne me faites donc pas de reproches! Mais faites-en à vous-même. Je ne vous suis d’aucun secours et vous ne m’êtes d’aucun secours! Je vous renie de m’avoir jadis associé [à Allah] !” Certes, un châtiment douloureux attend les injustes [les polythéistes].
Deug Deug Iblis mooy " Saï-Saï "
Rawatina (As Shayatiinu wal Insu) 😭
Le fait de réprouver le mal et de le détester par le coeur
Au nom d'Allah, le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux.
D'après Abou Sa'id Al Khoudri (qu'Allah l'agrée), le Prophète (que la prière d'Allah et Son salut soient sur lui) a dit : « Celui d'entre vous qui voit un mal qu'il le change par sa main. S'il ne peut pas alors par sa langue et s'il ne peut pas alors avec son coeur et ceci est le niveau le plus faible de la foi ».
(Rapporté par Mouslim dans son Sahih n°49)
عن أبي سعيد الخدري رضي الله عنه قال رسول الله صلى الله عليه و سلم : من رأى منكم منكرا فليغيره بيده . فإن لم يستطع فبلسانه فإن لم يستطع فبقلبه وذلك أضعف الإيمان
(رواه مسلم في صحيحه رقم ٤٩)
جزاك الله خير شيخنا🤲🏿
جرجف 🤝🏿
Jaajëf صدق الله العظيم
Barakallah fiik
Pa Diagne bien dit
نتابعكم شيخنا
ونتمنى لكم التوفيق والرشاد في كل حركاتكم
Respect vie bien et longtemps
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Merci infiniment papa
Ahmed Khalifa Niass un danger pour l'islam au Sénégal
Salam loy sa nimoro ? ?
Merci
Sëriñ momar 🙏🙏
linga wax d dëgg la mass'Allah. waaye nak bul fatté ni Magal Touba amoon nafi ak jangum al aurhaan ya conférence diine ya sallatu hala nabih ya qassaid ya ak yu baax yafay am yëp, yaw seriñ momar Danga caa seppi as ndaw Sodoon puukarewu takk ay oor siiwel ko, kon fofu moom
شكرا لك يا أستاذ جزاك الله خيرا وبارك فيك
صح لسانك ونوّر الله قلبك وسدد خطاك على سبيل الحق والهدى والخير والرشاد وكثّر من أمثالك وبارك لك سعيَك وألهمك الصبر والبصيرة والحكمة ما دمت حيًّا
وأُشهِد الله بأني أحبك فيه تعالى وأدعوه سبحانه أن يُحِبنا جميعا ويجمعَنا في الدنيا وفي الآخرة مع النبيين والصدقين والشهداء والصالحين وحسن أولئك رفيقا اللهم آمين يا رب ويا كريم
علما بأني قد حاولت الاتصال بكم هاتفيا عدة مرّاتٍ وكَرّاتٍ لكن دون جدوى (لعل الله يحدث بعد ذلك أمرا) وجزاكم الله خيرا وأجزل لكم المثوبة يا رب يا كريم.
أخوكم في الله/ محسن محمد انجاي
@@serigne-momar لا.. شيخنا الكريم ما عندي... لكن، يمكن أن تبعثوا لي أية وسيلة الاتصال تتيح لي فرصة الاتصال بكم عن بُعد لحين تَمَكُّنِ لُقْيَاكُمْ وجها لوجه بمشيئة الخالق وجزيتم خيرا
Svp coyor numero serigne momar diagne
@@serigne-momar Machallah Serigne bi mais beugone na ngua léral niou si limamou laye bouniou wakh da woté mahdi ak yoneinte
Salam beaucoup de parasites dans les tairkha au Sénégal
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته. اريد رقم هاتفك او الجوال او اتصال بواتسب إن أمكن و شكرا على حسن الحديث.