Serigne Moustapha SY: "Yénn Gni di firi Al-Quran ci noumou lénn neekhé..."

แชร์
ฝัง
  • เผยแพร่เมื่อ 7 ก.พ. 2025
  • Abonnez-vous ➤ / @leralnet1
    Installez gratuitement notre application mobile ➤ play.google.co...
    Retrouvez-nous sur FACEBOOK ➤ / posts
    INSTAGRAM ➤ / leralpointnet
    TWITTER ➤ / leralpointnet

ความคิดเห็น • 205

  • @susobass7685
    @susobass7685 5 ปีที่แล้ว +76

    Barkep serigne touba mala soppou yalla nagna fi yage te weer

  • @badjidiarra7184
    @badjidiarra7184 5 ปีที่แล้ว +38

    Ndeyssane derete mo fort comme son père quand il parle machahalla

    • @vieuxka3105
      @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว +1

      Billahi billahi billahi billahi billahi billahi

  • @moussasarr6945
    @moussasarr6945 5 ปีที่แล้ว +16

    Serigne bi dimension bi bimouy wakhé kou inian doko dégeu ..mouk...walay ndeisan 🤩man dh je suis fier d'être moustarchid ....Maaraa yalan yalla goudal sa fann

  • @76abou
    @76abou 5 ปีที่แล้ว +45

    Sy serigne moustapha yalla nala yalla aàr takha wula ci barkep serigne touba ya bakh sy serigne moustapha

  • @alassanendoye2065
    @alassanendoye2065 5 ปีที่แล้ว +12

    Rallier éloquence ak élégance manchallah Sy yalnala Yalla sameu🙏🙏😍

  • @fallousow424
    @fallousow424 5 ปีที่แล้ว +4

    Je suis très content de vous ecouter

  • @shakapro152
    @shakapro152 5 ปีที่แล้ว +8

    dieureudieuf Serigne Moustapha Sy Yalna yalla yokou Xam Xam bi

  • @gueyebabacar1050
    @gueyebabacar1050 5 ปีที่แล้ว +33

    Seydile moukhamadoul moustafa yalna fi yague lole ta wére ❤

  • @youssoutoure1247
    @youssoutoure1247 5 ปีที่แล้ว +13

    Seringe Moustapha sy borom khélyi lay wakhal

  • @aliounediop3767
    @aliounediop3767 5 ปีที่แล้ว +4

    Dieureudieuufff sy malick

  • @modouthioune6821
    @modouthioune6821 3 ปีที่แล้ว

    Oh!!! Il a dimension elevèe, retenez bien la dimension de ''sagesse et du savoir''. Machallah un grand analyste❤❤❤❤❤❤

  • @vivelafriquevivelesenegal8185
    @vivelafriquevivelesenegal8185 5 ปีที่แล้ว +46

    Serigne moustapha sý raw gã saý mass✅

  • @tvadamandiayekhassaidtouba8388
    @tvadamandiayekhassaidtouba8388 5 ปีที่แล้ว +5

    Yalna nga ame diame barkeb s touba khadimou rasoule

  • @ibrahimandiaye6064
    @ibrahimandiaye6064 5 ปีที่แล้ว +2

    Machalla seydi mouhamadou moustapha sy yalla na yalla goudal sa fane

  • @daoudatall718
    @daoudatall718 5 ปีที่แล้ว +39

    bilahi dou sama seringue mais dafa am xam xam wallahi sy machallha yalla ga yageu fi te andak wérr ligay thi sama kholl la dougou dakh man nitou dayra la

    • @vieuxka3105
      @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว +1

      Billahi

    • @mallbelly8250
      @mallbelly8250 4 ปีที่แล้ว

      Serignie moustafa sokhla woul neke seriniou kene defar diamou yalla yi mo ko takh diok

  • @marafall6668
    @marafall6668 5 ปีที่แล้ว +24

    Yén presse en ligne bi fén rk ak diaxassé molén yittel Serigne bi toudoul sax Oustaz Omar Sall..guén weur di fén rkk

  • @vieuxka3105
    @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว +11

    Serigne Moustapha sy rék borom Sénégal borom adouna

    • @vieuxka3105
      @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว

      @@gueyeeva1168 mais Eva Gueye li wakhine la man douma doff khana boubakh Limay wakh nitt nak yamome sa dege dege ak sa guiss guiss

    • @gueyeeva1168
      @gueyeeva1168 5 ปีที่แล้ว

      @@vieuxka3105 mangui toupp👏👏

  • @ndiayebiramandianko3453
    @ndiayebiramandianko3453 5 ปีที่แล้ว +24

    ما شاء الله بشيخ محمد مصطفى حفظه الله ونصره ورعاه

    • @vieuxka3105
      @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว

      Amine Amine Amine Amine

  • @danethiam9638
    @danethiam9638 5 ปีที่แล้ว +24

    Naysan sam yaram day daw bo wax nax limoy wax abe dofe doko dége boroum xoll bou iņan doko dégeجزاك الله خير

    • @ibrahimndao189
      @ibrahimndao189 5 ปีที่แล้ว

      Quelles sont les belles âmes et les esprits supérieurs qui sont à même d'avoir compris. ?, tout ceci donne le tournis .

    • @awaawa2338
      @awaawa2338 5 ปีที่แล้ว

      Chemise

    • @awaawa2338
      @awaawa2338 5 ปีที่แล้ว

      Gamou

  • @ibrahimaktbfsow7838
    @ibrahimaktbfsow7838 5 ปีที่แล้ว +3

    Waaw quel voix

  • @moussafall1813
    @moussafall1813 5 ปีที่แล้ว +4

    WALAYE NDAYE ZANE DEGG PUR REKKK NGA WAKH DHE YALLNA YALLA MOTILI SI.BARKE NABI S.V.P SI.BARKE MAM ELH DJI MALICK S'Y R.D.H SI.BARKE MAM BABAKAR SY R.D.H SI.BARKE MAM CHEIKHE AHX MED TIDIANE SY AL MAK TOUM TOUM SI.BARKE KILIFAGUI CHEIKH MOHAMMED MOUSTAPHA S'Y SONU KILIFA SONU YAKAR TAYE AK ELLEK INCHAALLA.YALLNA

  • @HappyniassTV
    @HappyniassTV 5 ปีที่แล้ว +7

    Machalah

  • @amisow7537
    @amisow7537 5 ปีที่แล้ว +6

    (Salâm) SY MALICK!🙏🙏🙏niougui Ziar bou wêrr Mashaallah 🙏👌🙏

  • @modouniang7347
    @modouniang7347 5 ปีที่แล้ว +5

    Yallna yalla goudal sa fane

    • @vieuxka3105
      @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว

      Amine Amine Amine Amine

  • @kaderdiaw2604
    @kaderdiaw2604 5 ปีที่แล้ว +9

    MassaAllah 😍🥰

  • @mariodjon635
    @mariodjon635 5 ปีที่แล้ว +12

    Yallah na yallah gudal fane wii mayla werr

    • @vieuxka3105
      @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว

      Amine Amine Amine Amine Amine Amine

  • @elhadjiba8539
    @elhadjiba8539 2 ปีที่แล้ว

    Diarama Serigne Moustapha sy

  • @moustaphabarry6499
    @moustaphabarry6499 5 ปีที่แล้ว +3

    جزاك الله 🙏🏿🙏🏿

  • @ndiayekane7780
    @ndiayekane7780 5 ปีที่แล้ว +7

    Machala❤❤👏👈

  • @dioufpapamalick4414
    @dioufpapamalick4414 5 ปีที่แล้ว +6

    جزاك الله خيرا

  • @benmalick85
    @benmalick85 5 ปีที่แล้ว +4

    Machalah ❤️❤️❤️

  • @habdoulailowe1719
    @habdoulailowe1719 5 ปีที่แล้ว +7

    Alhamdulilah

  • @lissaciss1942
    @lissaciss1942 5 ปีที่แล้ว +11

    Machallah 😍❤❤

  • @pathethiam5008
    @pathethiam5008 5 ปีที่แล้ว +9

    machala

  • @matargaye8509
    @matargaye8509 4 ปีที่แล้ว +1

    Massalla 🙏🙏👍

  • @omarodioufardi8666
    @omarodioufardi8666 5 ปีที่แล้ว +3

    Machalla rafetena

  • @youssefly5176
    @youssefly5176 5 ปีที่แล้ว +1

    ماشاءاللہ

  • @dem-vision5756
    @dem-vision5756 5 ปีที่แล้ว +8

    Léral tv alal bou léw bakh na adouna amoule solo kilifa gui nékoul si yoyu bouléne tal rewmi ndax alal kou nek toppal lagua geum il est en déça de ça

  • @falldine9699
    @falldine9699 5 ปีที่แล้ว +3

    Bilahi sy malick maleu bague ndakh sa bakh k sa dal ab talibé serigne touba la wayé fou lou bakh ma woutiko yague lol t weur si malick

  • @modouamar8455
    @modouamar8455 4 ปีที่แล้ว

    Macah Allah ame na solo ya moustaph sy almakh Toum

  • @cherifsmart828
    @cherifsmart828 5 ปีที่แล้ว +18

    Dama content li moye ak kham

  • @pacokimmichthioune3268
    @pacokimmichthioune3268 4 ปีที่แล้ว

    yalla nga fi yague

  • @moustaphadia2500
    @moustaphadia2500 5 ปีที่แล้ว +3

    Macahalla yalla na yalla faye la amna solo wakhtannwi Macahalla

  • @serignefall1258
    @serignefall1258 5 ปีที่แล้ว +4

    xam xam daaal kéne douko tricher

  • @mbayegueye5718
    @mbayegueye5718 5 ปีที่แล้ว +4

    Ana lou takh nguéne déf fi Foto omar Sall
    Serigne bi toudou ko té mom takhoul mouy wakh

  • @dwayneb7918
    @dwayneb7918 5 ปีที่แล้ว +11

    Ragal lène yala quesque la photo d'Omar Sall fait ici?

  • @moussalo1656
    @moussalo1656 5 ปีที่แล้ว +2

    Akamako nawone

  • @daoudatall718
    @daoudatall718 5 ปีที่แล้ว +6

    Thi sama kholl la dougou

    • @vieuxka3105
      @vieuxka3105 5 ปีที่แล้ว

      Billahi billahi billahi akh man

  • @alkaboye7949
    @alkaboye7949 4 ปีที่แล้ว +1

    😂🤣😂🤣😂🤣😂😎c'est bien

  • @khalifabuserignemoustaphas7188
    @khalifabuserignemoustaphas7188 3 ปีที่แล้ว

    Thiey moral

  • @asfoppss
    @asfoppss 5 ปีที่แล้ว +36

    Dimensions de connaissances illimité sa façon est unique Sy Malick yagfi lol té weurr

  • @mgeagripreneur
    @mgeagripreneur 5 ปีที่แล้ว +7

    Site en ligne yii mom Oustaz Oumar Sall saf naleen. Deemleen diangui seen dîner. Un ignorant ne peut juger.

  • @modoufalldieng6475
    @modoufalldieng6475 5 ปีที่แล้ว +1

    Serigne bi tudoul tourou kén guéni colage ay photo ni ah bayi len sen yi

  • @mamadouseckdiop9864
    @mamadouseckdiop9864 5 ปีที่แล้ว

    Senegal bës bouy takeu yein médias yi yena koy taleu ndax vous êtes incompétents tei si ndiabotou cheytan yi ngein bokou

  • @khalilabraham9011
    @khalilabraham9011 5 ปีที่แล้ว

    Sy malick doundal si barké sa mame

  • @brigadeantibidah2911
    @brigadeantibidah2911 5 ปีที่แล้ว +2

    Bayil nakh société bi

    • @ndeyemaissa7973
      @ndeyemaissa7973 5 ปีที่แล้ว

      IOw boulgniou sonal loy deglou kon

    • @jambaarlegilegi9252
      @jambaarlegilegi9252 5 ปีที่แล้ว

      Yangi deglou di wah ki mo raw sa bay

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 5 ปีที่แล้ว

      Ndeye Maissa déniye deglou comme ça leup louye rereule société bi nou intervenir.
      Bouno bougou nite ki beu sou dioumé donou ko guisse lolou bakhoul ki nite kesseu day dioume donc bou dioumé nou dioubanti ko té yama guineu khame lolou.
      Wa Salam.

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 5 ปีที่แล้ว

      Cheikh Dia yangui ko khamoul dé ki yow sakhe yako row nakh bidah ak bokalé y’ALLAH SWT.
      Comme wakhe diou bone foumou diougué leu deuk cone na bayi ngueu sagalmeu sa baye domou ZENIM bi imbécile.

    • @jambaarlegilegi9252
      @jambaarlegilegi9252 5 ปีที่แล้ว +3

      Yaw danga alkou serigne Moustapha amoul morom si kaw souf

  • @alaminekande9680
    @alaminekande9680 5 ปีที่แล้ว +3

    Salam mbokk talibés yi nguén yégué segn bi juste pour rectifier
    On dit: Inna anzalnahou fi laylatil qadr et non laylatoul qadr pour le premier verset.
    Wa Salamou aleykoum.

    • @ibnabass6115
      @ibnabass6115 5 ปีที่แล้ว +9

      Ndeysan 21mn ga djeull ko sa tmp di xaar mu yaak ben baat wala mu djoum baga wax ko lulako djaral yaw nak ya wara rectifié sa bopu raxass sa xoll bi rouh gui ba do xoll ak di xaar si nitt ki lu gnaaw ku bon nak lu bon rk lay guiss yalla nala yalla soopi tmp biga tok diko setan boko defon sa bopu djamu yalla modon gueun si yaw

    • @dmwmbrasil8944
      @dmwmbrasil8944 5 ปีที่แล้ว +2

      😄😄😄😄😄😄😄 yaw ko yap ? Saw katou lale bi

    • @mbathiothioub4628
      @mbathiothioub4628 5 ปีที่แล้ว +4

      Ioe ya nekhh dh kii DH wakhou mala mom rek mai kou gueneu touti si njabotam meun nala diangal!! Dém lén jangui waat mo gueune dingat Kat you bone yi

    • @oumardiallo7658
      @oumardiallo7658 5 ปีที่แล้ว +1

      Wallahi iow amo dégue dégue ki dioumoul bén Yonne

    • @ousmanediallo5440
      @ousmanediallo5440 5 ปีที่แล้ว +3

      ioe hana amo beutou hol dégo Serigne Moustapha nenaleu li dou wakhou nop wakhou khol leu dou xam xam hikma leu ni mom dokhoul bayiko nguir Yallah

  • @modidiaw8291
    @modidiaw8291 5 ปีที่แล้ว +2

    Yene wa lera. Net seuringe bi wakhout omar sall dh oustas alioune sall la wakh

    • @isseudieng2568
      @isseudieng2568 5 ปีที่แล้ว

      Motakh moudjakhal ma dii

    • @beuguebamba7900
      @beuguebamba7900 5 ปีที่แล้ว

      khamgua legui ay journaliste yii gnom gno seytane diakhasé nitt yii rek lagni déff

    • @ssinnnghatehaaalieu8482
      @ssinnnghatehaaalieu8482 5 ปีที่แล้ว +1

      @@beuguebamba7900 walay wah deug dè .

    • @wourydiallo2124
      @wourydiallo2124 5 ปีที่แล้ว

      Gisga d loulen néh laniouye binde

  • @manejoop2531
    @manejoop2531 5 ปีที่แล้ว +6

    Wakh tane bi kou tewlou woul doko deggg.

  • @brigadeantibidah2911
    @brigadeantibidah2911 5 ปีที่แล้ว +1

    Comment je décris ça c’est un spectacle de cirque.
    C’est vraiment des moutons certains sénégalais quant est-ce que vous allez vous réveiller.

    • @jambaarlegilegi9252
      @jambaarlegilegi9252 5 ปีที่แล้ว

      Ah mm si nou sommes des ignorants nous prenons en compte d notre ignorance c'est cela ki nous pousse d'aller chercher la connaissance j'usk'a tivaouane particulièrement au champs des courses ki es devenu champs d cours d bien cueillir les fruits d la sagesse ki sort par la voix magistrale d serigne Mouhamed Moustapha Sy. Mais malheureusement y'a na des gens k leur orgueilleux, leur petitesse et leur ingrat empêche d'assimiler les enseignements d c charisme immense bilay ma yeureum gars you sohor yi
      Dieureudieuf serigne Moustapha Sy

    • @ndiobatall8425
      @ndiobatall8425 5 ปีที่แล้ว

      @@jambaarlegilegi9252 ñi diaruñu tontou dolé tasaouf thi senegal molen tital bayi len rek niouy khol seniy khol di dag te meunu noussi dara
      Dieureudieuf serigne touba

  • @deboursy6215
    @deboursy6215 5 ปีที่แล้ว

    Omar sall dei waxoul sama mame néena walla sama papa néena xam xam rek lay wakh fi amna gnoufi seni bayi waxonne abdou diouf moy falouwate élection l'an 2000

    • @ababacargueye5638
      @ababacargueye5638 5 ปีที่แล้ว

      Lolou s mansour moko wakhone môme s Moustapha 1998 conférence guinguunéo la wakh Abdou Diouf day danu l an 2000,s Moustapha wakhoul ak Omar Sall kon nak boulko manqué respect c juste un rappel entre frère et soeur musulman

    • @kinesall2209
      @kinesall2209 4 ปีที่แล้ว

      Bilahi akay degue

  • @brigadeantibidah2911
    @brigadeantibidah2911 5 ปีที่แล้ว +3

    Leral net loutakh nguenni associé photo oumar sall si kouffar bi aye rambathe nguenne rek

    • @mamadouseckdiop9864
      @mamadouseckdiop9864 5 ปีที่แล้ว

      Yaw nak y'a ngi beug eupeul khana dianga lougn la adaboul kalam teguine 0 ki khana sax nga am yar ak diox thieur Koula makk surtout sa mbokou djoulite faut pas abuser de la gentillesse des gens
      Li site la et c populaire kou NK fiy feuilleter tamit nak wax djou rafet loko dieundei diar nako

  • @daoudacamara1318
    @daoudacamara1318 5 ปีที่แล้ว +1

    Lu tax wahabiya yi defe ne reewande mooy Diine. Ko ci degg saaga wala xaste te xamu leen ni Diine yar la.

  • @ibrahimajuniorsall1464
    @ibrahimajuniorsall1464 5 ปีที่แล้ว

    Il dit qu'il voit Dieu Allah. C'est un imposteur

    • @mouhamedguisse2996
      @mouhamedguisse2996 5 ปีที่แล้ว +1

      Ibrahima junior Sall 😂😂les enfants 👶, ils ne comprennent absolument rien et veulent commentaire

    • @mmmt9668
      @mmmt9668 5 ปีที่แล้ว

      Degoul début wakhtane bi

  • @wourydiallo2124
    @wourydiallo2124 5 ปีที่แล้ว +1

    Wa leral tv 📺 holat len boubah sen afis yi ki wahoul omar sall mom omar sall dall mo wéh dounkou

    • @dioufpapamalick4414
      @dioufpapamalick4414 5 ปีที่แล้ว

      Damay dello sa ndey guinée

    • @wourydiallo2124
      @wourydiallo2124 5 ปีที่แล้ว

      Ma magi ndey you paris sa honkou lou yaye

    • @wourydiallo2124
      @wourydiallo2124 5 ปีที่แล้ว

      Hana yow dega yakar né peul yep senegale laniou nek man magi ndeyou panam 🖕🏿

    • @dioufpapamalick4414
      @dioufpapamalick4414 5 ปีที่แล้ว

      Neckal sabiir dattandey damay 3x sathiopparetou nday assip saboppou koyou bay ngay explique domi guordjigueen🤣🤣🤣🖕🖕🖕🖕🖕

    • @dioufpapamalick4414
      @dioufpapamalick4414 5 ปีที่แล้ว

      Wa léral tv damay leeral seen paxou data ndey 😁😁😁😁🖕🖕🖕🖕🖕🖕🖕🖕🖕

  • @cheikhtidianedeme3444
    @cheikhtidianedeme3444 3 ปีที่แล้ว

    😂

  • @sylla8644
    @sylla8644 5 ปีที่แล้ว

    Yaw mi yakoy firi ci nimoula nékhé bayil wanéwou

    • @mmmt9668
      @mmmt9668 5 ปีที่แล้ว +1

      kouy wané wou day fek guisounioula c sur que si ay famille diahil nga bokou

    • @sylla8644
      @sylla8644 5 ปีที่แล้ว

      @@mmmt9668 démal topi sa baay té baayi baayou diambour yi bo topone coudiara top sakh gnou mana wakh wayé kinga khamni doul rék lay déf

    • @sylla8644
      @sylla8644 5 ปีที่แล้ว

      @@mmmt9668 en plus yaw mi topou ci famille diahil kay yaw topou ci guinaw féne kat loumélni mouléne di arnaques rék

    • @ababacargueye5638
      @ababacargueye5638 5 ปีที่แล้ว

      Yaw amoulo kham kham amoulo fit tok sa nègue bind loula nèkh yomb na

    • @sylla8644
      @sylla8644 5 ปีที่แล้ว

      @@ababacargueye5638 limotakh sénégalais dounou dém ay business mane rék lanouy topou démal topi li alkhour anne wakh mogeune ngay topou dor kat bi

  • @amadoudiop3690
    @amadoudiop3690 5 ปีที่แล้ว

    Il dit du n importe quoi!!! Ce gars est un égarer qui égare! Wallahi

    • @mallbelly8250
      @mallbelly8250 4 ปีที่แล้ว +1

      Yow khana wero demal fadjou

  • @amadoufall537
    @amadoufall537 5 ปีที่แล้ว

    Xam xamou dîné dou xamxam .Diaroul titeurou ndakh niopeu wara diangue sene dîné

    • @amymbaye1707
      @amymbaye1707 5 ปีที่แล้ว

      Amadou Fall lol

    • @khadidiatoudiop8399
      @khadidiatoudiop8399 5 ปีที่แล้ว

      Awa fall yaw damala yerem sakha

    • @ababacargueye5638
      @ababacargueye5638 5 ปีที่แล้ว

      J espère bien que t as pas même une petite notion sur la science islamique

    • @ababacargueye5638
      @ababacargueye5638 5 ปีที่แล้ว

      @@amymbaye1707 méchante sectaire

  • @elhadjifall9743
    @elhadjifall9743 5 ปีที่แล้ว

    Pourquoi vs maitez omar sall il parl a tous ki n metrise pas et ki parle trop

    • @ssinnnghatehaaalieu8482
      @ssinnnghatehaaalieu8482 5 ปีที่แล้ว

      Parce que gnom nombre des vues lagnouy outttt pour am halisou Adouna

    • @sénégal5INFO
      @sénégal5INFO 5 ปีที่แล้ว +1

      El hadji Fall Oumar sall da khamoul loubari motakh

    • @dioufpapamalick4414
      @dioufpapamalick4414 5 ปีที่แล้ว

      Dou da xamoul lou bari da xamoul thiottou ndeyam

    • @bayedamewade1632
      @bayedamewade1632 5 ปีที่แล้ว

      @@dioufpapamalick4414 🙈😂😂😂😂😂😂😂🤦‍♂️ ki raynama way

    • @dioufpapamalick4414
      @dioufpapamalick4414 5 ปีที่แล้ว

      @@bayedamewade1632 manglaye balou bax

  • @nonauxmaraboutsimposteurs194
    @nonauxmaraboutsimposteurs194 5 ปีที่แล้ว +2

    Kii esq dou goordjiguéne

    • @serignembackebichri5217
      @serignembackebichri5217 5 ปีที่แล้ว +1

      Sokhnazi bolyor za bindo gay di binde
      Lola nèkh toubal ligawakh

    • @momzly6818
      @momzly6818 5 ปีที่แล้ว

      Yagui wakh rek depuis avant hier continue rek boul bayi. Yala guilay guiss

    • @giovanenero3283
      @giovanenero3283 5 ปีที่แล้ว +1

      Wakh day rafett

    • @papehamadousall5223
      @papehamadousall5223 5 ปีที่แล้ว

      Yaw mom thiaga sa yaye thiagala!
      Bo gnepe gayi oubi sa lefeul n'deye!

    • @abrahamndiaye2016
      @abrahamndiaye2016 5 ปีที่แล้ว

      Iow khana dakay mbam dalay kate

  • @groupeleveurprofessioneltv3058
    @groupeleveurprofessioneltv3058 5 ปีที่แล้ว +4

    Machallah

  • @maodondao3342
    @maodondao3342 3 ปีที่แล้ว

    Machala