C'est ça nak ! Mane dé guéneu nassi bou yague! Dougnoufa wakh Alkhourane, ni YALLA ni comment Le Prophète Mouhamed S.A.W adorait ALLAH SOUBHANA WATALLAN ! Seule fénale Yonète bi ak exagéré rek!
Outaz discours bou niakk diome. Badola bou Niame khaliss. Quelle honte, les oulémas disent c est du bida de fêter le gamou, toi tu le fais pour des miettes et perdre ta dignité. Ya doyodii
Thieuyyy sama tooma !!!!! Un comédien oustaz !!!!!
Yallah na niou yallah mousseull thi tarikha yii....
Boule togne nk ❤
Bida mo yés ❤❤
Macha Allah abou jamel
Ana Gamou ak déclaration d'amour 😭😂😂
momasidiaxal😃😃
Non😂Sa waay ray ngama😅😅😅mooma jaaxal😢😮😊
Le Diable,cependant,leur avait embelli leurs actions au point de les repousser loin du Sentier;ils étaient pourtant invités à être clairvoyants.
Gni khamougnou diné
merci way
As salamou aleykoum mbok sa dieuf raféte na wayé ki toureu, bou léne si binde oustaz zay ndakh lolou dafa a,e niouko méritoo
Sénégal mo beuri ay cas sougnou diogué si li danou si lénèn 😅😅 liiii diomi amoul heure
Walakhi li yonetibi wakhonenako diamano Dina solo fo khamné bida Di n'a Bari trop
Mane daama decourager si sénégal 😂😂😂
Wolof ndiaye nena ma tey mak bou rouss mokoy wax
Gni ay naxate kate nane bokale rk
Haha
Qui vivra ,verra ,allons y donc!
doye war de
Évite de montrer des femmes non voilé dans les vidéos svp ❤
Mane dé bayi na gamou khamatouma louma nara wakh liii motakh gniné gamou bida la té bo kholé deug la Sénégal beurina ay lobie lol
C'est ça nak ! Mane dé guéneu nassi bou yague! Dougnoufa wakh Alkhourane, ni YALLA ni comment Le Prophète Mouhamed S.A.W adorait ALLAH SOUBHANA WATALLAN ! Seule fénale Yonète bi ak exagéré rek!
Ki limou déf moome la consérné
ki bouko kéne wakh oustaz bandi bouy takhawaloula rékk
Kii dofleu
Thiim do rouss
Outaz discours bou niakk diome. Badola bou Niame khaliss. Quelle honte, les oulémas disent c est du bida de fêter le gamou, toi tu le fais pour des miettes et perdre ta dignité. Ya doyodii
Gisagu ñu dara sax. Fiiwak génnu ñu ci tarixa yii, nii rek. Li ci metti mooy amul bénn sëriñ bu ci am ménn pexe.
Ki modou fall do oustes
Koulawax avant dewen dougnou woo Aziz Ndiaye Ci reddition des comptes Bi attention prête nom yi barina dé
Pour la deuxième partie où il fait des prières pour aziz et sa clique, la réponse est : '' Wama dou'an ool kafirina illa fee daollaall''😅
gni ay vrai khadieu nagne yaque diné rékk nagne fi nékké
Togne nga khathieu dé!