T’es s gana sa waxtane biiiii noumoumay goungé si sama seuy Amna solo YALLA nala SOUNOU BOROM SWT defal li geun té May gnou degu ak top Allahouma amine
Euskay mane dai magui si nekou seuy tai amna 24h beug nak li des si sama doundou ma Roy si mom dontei sama messou togn niit walla def ko Lo gnaw tai wat na ni dîna dioural sama borom keur dom diou bakh inchallah tai dinako seuy
Moom lanu fi am d ndax aduna kula ko ēpale taxul mu ëpalela d'ara gēneel ci jigeen mooy toppu boroom kêrëm fexe ba bayyi fi jamboot ju barkeel mooy ndam ci bepp soxna
Yallna niou yalla fayal Mam Diarra bousso yallna naniou yalla défal dégue ak topou🙏🥰
Machalla Deglou ak Roy😍😍😍😍
Sokhna Diarra Rawna😭❤️Jiguéne ñi Soxla laniou Yadii Sokhna
Machalah sokhna diarra amoul morom
❤soxena mame Diarra Bousso Yallana brom touba fayalgnouko
T’es s gana sa waxtane biiiii noumoumay goungé si sama seuy Amna solo YALLA nala SOUNOU BOROM SWT defal li geun té May gnou degu ak top
Allahouma amine
MA SHA ALLAH SOKHNA DIARRA BOUSSO DIEUREDIEUF
😭😭😭😭 soigna diarra rawnga
Sokhna Diarra raw nguan.
Dieureudieuf Sokhna Diarra bousso
Diarama Mame Diarra Bousso, kéne dou mome, amoule morom, thiow Li thiow li mome leu, yayou téral yayou dimbeuli
DIARAMA DIEUREJEF DIARWLAK
Thieye sokhna mariama mam diara bintou mouhamadou bousso.bène djiguène dotoule mèlni sokhna si
Euskay mane dai magui si nekou seuy tai amna 24h beug nak li des si sama doundou ma Roy si mom dontei sama messou togn niit walla def ko Lo gnaw tai wat na ni dîna dioural sama borom keur dom diou bakh inchallah tai dinako seuy
Royale sa yaye mongeune
Ndaysane yagui Roy kou diara Roy boulasi dara dielé yallnala yalla diapalé incallah kou bakh réka diara rouy🧕
Moom lanu fi am d ndax aduna kula ko ēpale taxul mu ëpalela d'ara gēneel ci jigeen mooy toppu boroom kêrëm fexe ba bayyi fi jamboot ju barkeel mooy ndam ci bepp soxna
Ken ́la Soxna Maam Maryaama Búso ❤
dieuredieuf sakhna diaraa bousso yalla nanouko yal fayal
Diadieufetie sokhna Diarra bousso 🙏💞
Mach'Allah 🙏🏿👍🏿
Machalla ❤️🥰
Machallah
Walay ndeysane ♥️ kén dou borom magal Gui 🧕
Djeureudjeuf sokhna Diarra
🙏😍🙏😍🙏😍🙏😍Bousso Bali
oh sama xole sédena bilaye ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Ndayesane lomatabayi khell
Masta dioulli diappoul masta diouli tawirdoul
❤❤❤❤❤🥰😍
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🙏🏻
saa touronnndo
Kene dou sokhna Diarra
😍😍😍😍😭
🕋🕋🤲👂
😭😭😭😭😍😍😍🤲
Asiya
Sokhna darra Bouss
Diadieufety.sockena.diarra
Machallah
Machalla ❤