N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Ki innocent la dagay am problème familial té do ham noko géré niénegni si goor yi profitola ba nga fog ki mola beug fékné moy ki yak sa adouna dioyna li😭
Lima gueneu nekh thi mom moy dafa brave courageuse ba parè forte souko nekhone mou Sakkal pekhè dom dji mais defouko Ndeysane Ya Allah yalla nagua ko bolè ak kou bakh kou amoul dra loumouy sentou thi mom mou diapalè Ko tay dji souma sagnione mane ley nekk wayé li yalla xam doyna Mougnieul ma soeur legui sa dom magg gua fatè lepp in Shaa Allah
Ki sou fèkè tawou yayam 2003 la kone ki khalè la😭Allahou Akbar ayway yeureum nala lol sax yalna la yalla guisseulè ak koula meune dimbeuli barki Seydina Mouhamed🤲🏾J’aurais vraiment aimé t’aider mais awma foumala dougueul Massa elle est belle et tellement innocente ndeysane beugue papam ak dom dji boul ndangou koula takali ak Mouhamed yalla bakhna
Nieuweul❤sougnou endeu leguéyi sama yaye dina téyé sa dome télouma guiss vidéo bi so amoul foh nékeu rkk tu être là bienvenue c’est moi wkh nako❤sama yaye😢😢❤
j'ai des larmes aux yeux métttina souma amonn dh diapaléla mai journaliste bi sa wah désna ki elle na pa ambandonner sa famille sa mére est morte sn pére est malade mental
Franchement ame ay nite yo khameténé amouniou khôl comment on peut abandonné son sang 🩸 ki doussi dara Lépp famille am la ak mague bi mane dé kou guéndé sama racke ma ande ak mome guénde mais yalla na la yalla déffale diambe tu est vraiment courageuse ❤❤
Je te rejoins bro magam bi waroul ndangou niou guéné rakam mom mou déssfa.ki khalè bou ndaw leu khamoul dara.lima comprendre moy ki bagnekat leu.sa badiane et sa tante aussi ne devraient pas la chassé de la maison thiat mom imbécile deug leu djiguén kén douko torokhal surtout koula dioural dom amna niou beug am dom té amouniouko
Heureusement qu'il y a TH-cam. Que MOHAMED (PSL) grandisse en âge et en sagesse. Quand il grandira, tu lui montreras la vidéo qui explique le comportement de son papa.😢
Les blessures émotionnelles dont nous souffrons dans l'enfance peuvent se prolonger tout au long de la vie, même à l'âge adulte. C'est pourquoi nous devons apprendre à nous désintoxiquer de toutes ces émotions, à apprendre à gérer les émotions de manière saine et complète. Son histoire est beaucoup plus complexe et compliqué.
vraiment je viens d’ appeler celui qui a fait la vidéo c est people 221 voilà le tél de people 221 ils ont dit la dame n’ a plus de téléphone et c est dommage ils disent qu on peut leurs envoyer l’ argent ils vont lui donner. C est bizarre et triste car elle n’ a pas de pièce d identité. Le numéro est sur la vidéo
Réveillé vous les filles 😢 et arrêtez de donner votre corps à n'importes qui des gars qui vont vous ramener des problèmes brisé vos coeur niquer vos rêves et le pire l'enfant de tout ça ho il a rien demandé le pauvre bébé 😭 😢😭😭😭
Thiate kou niaf ndm leuh goor yalla day am yeurmandé si saa ndeye yii sokhna sii yalnala saa borom taxawou mounieul rkk lo mougne mou diekh yalla baxna bane numéro laniouko meuneuh dioté
Elle a été utilisé par quelqu'un plus mature,certe ça ne pourra pas sortir de ce que l'on appelle erreur. Imaginons si sa maman été en vie,est ce que cette fille soubirait ce sort😢?? Et si son père avait pas ce problème mental 😢? Personne ne peut comprendre ce que nos parents représentent sur nous,ils repartent tout, protègent tout sur nous ! Ce qui fait pleurer, c'est le fait qu'elle ne pourrait pas reconnaître sa mère si cette dernière viendrait sur terrain😢 😢😢 Ces genres de personnes doivent être protègées! Pitié pitié 🤌🤌🤌🤌
@@moussandiaye1208-w2o walakhi enh ki comprendre na papame dafa perte conaissance ms mane sama papa mogui doundou mane rk la ame si dome ms awma affection parent bilakhi dafa metti kouko doundoul doko kham 😔😭😭😭
Yaye Moy leup si douya bi nak kouko niak niak leup nak la vie c'est par fois dur sur nous mais yallah bakhan lomo déff rek daff geunee nak bilayhi Dina inchallah 🙏🙏🙏
La fille elle est trop belle ndeyssane khalei bou ndawe adouname nara yakouni mane dei bo nekone mbour nala dieulssi nga gneuw sougnou keur louma am bokou ko ak yawe ba yallah dimbelila nga am lou geune si yawe inchallah 😥
Wolahi son history ma bouleversés sa ma laissé sant voix même si j'étais a sa place j'allais pas abandonner mon enfant et ce jeune homme impudeur périra de souffrance dans sa vie car l'islam nous enseignes de prendre soin ces parents ainsi que ta femme convenablement 😢😢😢
C’est vrai que loumou doundou metina ter niank repère sheut mann vraiment mbokk legui dou touss motakh li dall ko , maguou yayam kou bonn la mais aussi naniou moytou aussi, saytanè lou nekk meun nako deflo nitt. aussi le jeune homme bobou aussi kou bonn la. Yalla na yalla safara. Oublie thiat nakh dou sa dieukeur limou beugon rekk la deff, relève toi diegaloul yallah ter diouk ter arrêtel diko ladji Sheut niank wadiour lou nekk lay deflo nitt Ndeysan komm si thiat moy dieukeureum vraiment warou na si mbokkou yi ki ani ay mbokkam tamit, dieul si len sen domm nakh solen ko bayer ni dou bakh elle a vraiment besoin de soutien
Oh guiss gua yakaram si thiat lepp si thiat la nekon diatt diapp si wakho nak kett khamoul Lila si khalebi mai de tout façon diapp si bouko bayi yaw la amal domm magui laye niann thiat boulko bayi
Malgres que kou goor qui limou deff Nice soul..mais il faut que djiguene yi khame sene bopp gorr soula beugué bilahi daflay sekhlo tekk lokho badi yegg sa kaw même soko ko nangoulé ndakh gorr soula beugué daflay yereum dila khalatal sa euleuk 😢😢massa courage
Wallahi yén goors gni bonne nagn mais djigueun yi aussi naniou am fouleu sen bopp ham sen valeurs car yen vauriens yi diarouniou sah guénal am relation ak niom risque leu
Woténa si numéro bi mais wadji néna dinama wowate après une fois reparlé avec sa famille s’il y’a pas de consensus il vas m’appeler je l’ai donné mon numéro et mon adresse je suis éducatrice je peux les prendre en charge je veux aussi qu’elle retourne à l’école parce qu’elle est trop jeune pour abandonner les études
C’est quoi cette prière melni khaliss lou éternel la nianalko yalla mou guiss kou bakh am yeuremande si mom meun ko topato rk teksi mom khalé bi mou meune amal bopam bagna kharr dara si nitt fi lepay diekh seuy ak kou am alal dou assurance de vie tei gniko am tamit majorité bi elles sont pas épanouies dans leurs mariages
Aïcha ma chérie soit forte la vie est injuste walahii a ton age tu merité bcp plus damour et assistance mais dieu en a decidé ainsi.... Qu'Allah t'assiste et apaise ta souffrance. Si ça te dis je peux hébergé toi et ton enfant et vous assiste inchallah. Dome ndeyam ak bayam rek massa ligay doundou metina trop bilahi massaa😢😢
Massa yalna la Yalla tokhouwou thi barké Seydina Mouhamed dafa am goor you doy war bo eumbé nguey khamni meusou nioula beugue nioulay daw mais dou nieup Dieu est au contrôle
Yaye mooy kéne si adouna ko khamni kouko manqué sa adouna manatoul nékhe à 100%100 j'ai 40 ans mais toujours pleurer à ma mére mais lépe sante yallah rék allhamdoulilahi
Ndeysan elle a été traumatisé depuis le bas âge ndeysan elle a besoin de notre soutien organisons une quête pour elle 😢😢😢😢man jai perdu mes mots la grande soeur de sa mère eno bonni no fewi
Niak yaye Dafa meti 😭😭😭😭bilahi yalla dinala diapale pas c que djiguene ga thé djiguene yalla da ko teral mougnal les bonnes volontés diapelene ko thé yalla takh🙏
❤❤❤ yallana yalla defalela diame metina gnake yaye da meti té papa fébare amo koula takhawou tiate bayiko sino dalaye wororate nala yalla nite té arela moukhamet bouko diokhe kéne ❤❤
Yalla nala borom bi Takhawou si barky Seydina Mouhamed topato wal sa dom bou bakh ga wout ligeiye dom dafa nekh si khol Diambar ga yor dom rek dafa meti khamna si dara ba paré gnou teksi li Sa dom ak sama dom bi 2jours lagnou maganté bok ben tour yalla nalene Borom bi sam Si barky Sen tourando Et soit forte Bella❤
Ndeyssane dioylo nama bimou wakhé sama dom douma dém diko bayi guinaw bilahi ma sœur yangi doundou lou méti wayé yalna yalla safara si barké seydina Mohamed psl 🤲🤲🤲😢
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Salut ! Pouvez-vous nous aider à rencontrer la famille de cette jeune fille ??
Sank wer dinako diokh dounou ak domame
Vous avez oublier de léssé un numéro pour les envois de l'aide
Qui peux me donner son numéro je peux l'envoyer chez ma femme elle seule avec ma mère et suis en voyage.
Ma famille est à ben barak elle peut vivre avec eux
Ki kouko dimbali yalna yalla soutourale adouna AK alakhira thi barké seydina mouhamét yalnko yalla takhouwou
Bilakhi, c'est une mineur 😢😢
Man dé beugeunako diapalé je vais essayé d'appeler les numeros sur l'ecran
ah wei suis preneur donné moi sont numéro svp Lou am sn numéro
Amone
Ki innocent la dagay am problème familial té do ham noko géré niénegni si goor yi profitola ba nga fog ki mola beug fékné moy ki yak sa adouna dioyna li😭
Louma guena metti j’en peux rien c’est mon rêve d’aider c’est genre de personne yallah ne le yallah takhawou
Amine yalla nako yalla takhawou si barké seydina mouhammad sallahou aleyhi wa Salam
Amine ya raby bilahi cest vraiment triste si j'avais vraiment les moyens je eux lui garde son fils sa me dérange pas dutout
Vraiment c mon rêve aussi yala dina ko dimbalé
Yéné dji motna
Kouko beug dimbabi foumouy diare
Ndeysan dafa rafet machalah 😢yalla nala yalla japalé kou gor qui vraiment domram la😢
Khamo si dra sakh damoko dokhane ba sonou mou bagn amagoul sakh 18 dafa rafett MACHALLAH 😢
@@AlylayeDiopEn bon
@@AlylayeDioplegui lossiy wah …boudone sa soeur ni guakoy wahé
@@AlylayeDiopyaw eskeu niit ngeu??li dinengn ko wakh
kougor ki kou gnapou ndayamla domorame la deug
Elle est jeune aussi vraiment, mais elle n'est pas mauvaise. Quand tu entends son discours c'est touchant. Day waniné elle est brave
Lima gueneu nekh thi mom moy dafa brave courageuse ba parè forte souko nekhone mou Sakkal pekhè dom dji mais defouko Ndeysane Ya Allah yalla nagua ko bolè ak kou bakh kou amoul dra loumouy sentou thi mom mou diapalè Ko tay dji souma sagnione mane ley nekk wayé li yalla xam doyna Mougnieul ma soeur legui sa dom magg gua fatè lepp in Shaa Allah
Dafa xam lissi gnak yaye motakh. Thiate, magam bou gior bi ak mbokkam yi gnom gnéppa yam.
Mouhamed sera un grand homme un jours incha allah
Inchallah
Amine 🤲
Amine
Amine❤
Amine inchallah
Vraiment j'ai des larmes aux yeux 😢 yalla nala sounou borom tawahou yaw ak sa bébé Mouhammed si Barker Nabi Moustapha (PSL)🙏
PSL❤
Alahouma amine 🤲🤲
Amine way
Psl ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kou niak yaye niak wérouwaye bilahi yaye amoule morome❤
Ndeye kouko niak sa gène waliu ndoundou diéxna 😢😢
❤❤❤❤❤Bililaye ndeyssaneYaye Amolemorou
Billahi verit absolue
Bilaye si ngaye xamni niou beurri grâce AK môme lagnoula beugué
Je viens de perdre ma mère il y’a 1 semaine
J’ai le coeur trop déchiré😭😭😭 diokhema numerom ma diko wave pour ses besoins té yalla ak serigne Saliou rek takh
Oh ndeyssane enplus elle est tellement jolie waouhhhh
Elle aime vraiment son père cette fille est brave
*Ndeysane c’est ce que j’ai remarqué 😢Yalla nako sougnou Borom takhawou🙏🏽🙏🏽*
Dôme bou djiguen dafay beugue papam ❤
@@MameToubaniangToubista-wg9fg bilaye dama dioye bilaye
sa mère est décédée😢
@@daoudasall21oui elle n'avait que 6 mois ndeyssane
Boul meuseu diokhé sa dom téyél rek mm boléne Di meuk Souf sakh boulko diokhé yalla Dina gnew legui inchallah boul bayi yalla bakh
Waw Yalla dina ko thi diapalé inchallah nako téyé rek
Meun nako yobou orphelinat dem ligayi
Sa commentaire bi dioylo nama😢
Ki sou fèkè tawou yayam 2003 la kone ki khalè la😭Allahou Akbar ayway yeureum nala lol sax yalna la yalla guisseulè ak koula meune dimbeuli barki Seydina Mouhamed🤲🏾J’aurais vraiment aimé t’aider mais awma foumala dougueul
Massa elle est belle et tellement innocente ndeysane beugue papam ak dom dji boul ndangou koula takali ak Mouhamed yalla bakhna
elle a 18 ans ndeyssaan.lii c'est trop de responsabilites pour son age
Thiate, magam bou gior bi ak mbokkam yi gnom gnéppa yam.
Mais si thiate est sorti 4 ans avec cette fille, kagn lagn commencer guenn? Subhanallah, thiate a quel âge?
Nieuweul❤sougnou endeu leguéyi sama yaye dina téyé sa dome télouma guiss vidéo bi so amoul foh nékeu rkk tu être là bienvenue c’est moi wkh nako❤sama yaye😢😢❤
Ndeké lo meti meilé amna koula
geneu metilé yalla Nanou yalla yok ak geumm😢😢😭😭masta
Sister🙏🏼🙏🏼🙏🏼😱😱😱😢😢😢
elle est jeune est innocente j'ai le coeur meurtri nala yalla takhawou
j'ai des larmes aux yeux métttina souma amonn dh diapaléla mai journaliste bi sa wah désna ki elle na pa ambandonner sa famille sa mére est morte sn pére est malade mental
Journaliste bii kay comme si déggul lii khalé bi wax.
Thiate, magam bou gior bi ak mbokkam yi gnom gnéppa yam.
Oui elle les a quitté kay dah manoul nék fen amoul éducation niouko guén niak ay parent niofi nék
Bilay dhé diarna mou kholattt ay kadouwamm
Wah deugue yalla té famille wam di ko hamal lou hewon si diguante ay waydiou ram dou yon
Franchement ame ay nite yo khameténé amouniou khôl comment on peut abandonné son sang 🩸 ki doussi dara Lépp famille am la ak mague bi mane dé kou guéndé sama racke ma ande ak mome guénde mais yalla na la yalla déffale diambe tu est vraiment courageuse ❤❤
Je te rejoins bro magam bi waroul ndangou niou guéné rakam mom mou déssfa.ki khalè bou ndaw leu khamoul dara.lima comprendre moy ki bagnekat leu.sa badiane et sa tante aussi ne devraient pas la chassé de la maison thiat mom imbécile deug leu djiguén kén douko torokhal surtout koula dioural dom amna niou beug am dom té amouniouko
Magam bi mo gueuneu yées gnépou
Ndeysan yalnala yalla takhawou ❤
Mais mom gniro Nak Fatima cisse d Elle est Belle machallah
@@diawi2588bilahi
Yédd yeureum mooko gueune
Ndeyessane téela niakk yaaye té amoo takhawou dafa métti 😢😢😢
Heureusement qu'il y a TH-cam. Que MOHAMED (PSL) grandisse en âge et en sagesse. Quand il grandira, tu lui montreras la vidéo qui explique le comportement de son papa.😢
Les blessures émotionnelles dont nous souffrons dans l'enfance peuvent se prolonger tout au long de la vie, même à l'âge adulte. C'est pourquoi nous devons apprendre à nous désintoxiquer de toutes ces émotions, à apprendre à gérer les émotions de manière saine et complète.
Son histoire est beaucoup plus complexe et compliqué.
Il faut du soutien
vraiment je viens d’ appeler celui qui a fait la vidéo c est people 221
voilà le tél de people 221 ils ont dit la dame n’ a plus de téléphone et c est dommage ils disent qu on peut leurs envoyer l’ argent ils vont lui donner. C est bizarre et triste car elle n’ a pas de pièce d identité. Le numéro est sur la vidéo
@@strategiesetdeveloppement2525que dieu te viennent en aide munël lepp dina jeéx
Yalla Nalla yalla takhawou Si Barker seydinamoumad psl amine
Amine
Tellement innocente ndeyssane
Yaa rabi djapàléko 😭😭
Ndeyssane djiguene bou rafet mais meussoul ame chance.Yalla nako yalla dimbali.
Réveillé vous les filles 😢 et arrêtez de donner votre corps à n'importes qui des gars qui vont vous ramener des problèmes brisé vos coeur niquer vos rêves et le pire l'enfant de tout ça ho il a rien demandé le pauvre bébé 😭 😢😭😭😭
Je te le jure des hommes qui n'ont même pas quoi sucrer du café ou qui une fois le pire se produit ils ne pourront même pas t'acheter des couches
Prk donner votre corps vous n'êtes pas musulmans ?
Avez vous oublier le destin
@@coumbasalioundiaye Tu fais amalgame là enn le concept de destin c'est autre chose sinon il n'y aurait pas de repentir
@@coumbasalioundiaye dioulite dou ndialo
Thiatt vrai domekharame j'ai des larmes aux 😭😭😭
Bilahi Frère
Bilaye moussouma dioye mais bi j'ai pas retenu mes larmes
Mame dama jooy ba beuga deee parce j'ai vécu un peu pareil mais Mame au moins goor la.
Bilaye walaye
Bilay
Sheutt dioyyy na ba sonou li méttina walahi motakh li diara santé yalla barina
Yalna la yalla tahawou thi barker ndiol macca
Bilahi comme mane rék thiate mi domaram la 😭
Amiin❤
Vraiment j'ai les larmes aux yeux djiguéne kéne douko torokhal cette fille la yalna KO sougnou borom bi walou thi barké seydina Mohamed paix sur lui
Ndeké lo meti metilé amna koula geneu metilé yalla Nanou yalla yok ak geumm😢😭😭masta sister🙏😭
Kii deh nattou deugg la am té nak bonnoul aussi yalnako yalla teuyél boppam😢😢😢
Amine
Alahouma amine 🤲
Amine
Yalna ko yalla takhawou sii barké seydina mouhamed ❤
Thiate kou niaf ndm leuh goor yalla day am yeurmandé si saa ndeye yii sokhna sii yalnala saa borom taxawou mounieul rkk lo mougne mou diekh yalla baxna bane numéro laniouko meuneuh dioté
Dieuleul numéro bobou si vidéo bi
Thieuy gnioune dramené yi dagnio ame yeurmandé😢
Elle a été utilisé par quelqu'un plus mature,certe ça ne pourra pas sortir de ce que l'on appelle erreur.
Imaginons si sa maman été en vie,est ce que cette fille soubirait ce sort😢??
Et si son père avait pas ce problème mental 😢?
Personne ne peut comprendre ce que nos parents représentent sur nous,ils repartent tout, protègent tout sur nous !
Ce qui fait pleurer, c'est le fait qu'elle ne pourrait pas reconnaître sa mère si cette dernière viendrait sur terrain😢
😢😢
Ces genres de personnes doivent être protègées!
Pitié pitié 🤌🤌🤌🤌
@@moussandiaye1208-w2o walakhi enh ki comprendre na papame dafa perte conaissance ms mane sama papa mogui doundou mane rk la ame si dome ms awma affection parent bilakhi dafa metti kouko doundoul doko kham 😔😭😭😭
@@MamerokhayaLayepaye c’est le numéro du service. Commercial. N’hésitez pas à me communiquer le numéro svp
Elle est trop belle ndeyssane 😢mougneul ma fille chérie Yalla nalla souniou Borom bi aral bopam thi barké Muhammad Aleyhi Salatou Wa Salam 💚
Ndeysane yallah najo yallah dimbeuli🙏🙏🙏
Je ne juge point les relations avec sa famille...mais niak yaye daffa métti 😢😢 Yalla nako yalla diapalé😭😭😭
Tu juge ferme la
Tu es mauvais tu as entendu le récit ??
Tu juge une fille qui a vécu tout ça à 14 ans dans les rues vous jugez vite car c est lache et plus facile
Amine
Yi niak yawe dé kouko doundoul mano khame méti waye bi walakh😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Yaye Moy leup si douya bi nak kouko niak niak leup nak la vie c'est par fois dur sur nous mais yallah bakhan lomo déff rek daff geunee nak bilayhi Dina inchallah 🙏🙏🙏
Ooooh khalei bou touti di souffrir lii😭😭😭😭😭😭 yalla nala yalla diapalé ci barké SEYDINA MUHAMMED paix et salut sur lui 🤲
La fille elle est trop belle ndeyssane khalei bou ndawe adouname nara yakouni mane dei bo nekone mbour nala dieulssi nga gneuw sougnou keur louma am bokou ko ak yawe ba yallah dimbelila nga am lou geune si yawe inchallah 😥
Soxna si amouma dara wayé mangi sante yalla guirr yalla boudé amo fo nek nieuweul sunu keur louma am niou bokou ko inchallah
😢. 😢😢
Ma sœur moi je veut cette fille bilahi wolahi pour aider avec son fils
@@IbrahimaMane-pg5lb Ndaysane 😢
Yaw kou bakh nga❤
Dawna Yaram Wallah
Wolahi son history ma bouleversés sa ma laissé sant voix même si j'étais a sa place j'allais pas abandonner mon enfant et ce jeune homme impudeur périra de souffrance dans sa vie car l'islam nous enseignes de prendre soin ces parents ainsi que ta femme convenablement 😢😢😢
NDEYSANE TOUT SA C EST L AMOUR PATERNEL QUI A AMENER SA SOIT FORTE ET SERRE BIEN TON PAGNE INCHAHLAH LE TOUT PUISSANT VOIT TOUT C EST TON DESTIN
Elle est tellement belle c'est trop triste que le bon Dieu te vienne en aide rien est éternel sa finira un jour
Je suis impressionnée par sa beauté et son histoire est vraiment terrible 😞
Bilaye yow kouko defar guiss diogoma manchallah
T’e halela ndeyssane mingi soufrir yallah na yallah tahawou😢
Cagnotte pour cette guerrière 😢❤j'ai mal au coeur 😮😢
Quand c’est écrit en wolof dommage je comprends pas
Je suis partante
@@mariameboudabakh698moi aussi
C’est vrai que loumou doundou metina ter niank repère sheut mann vraiment mbokk legui dou touss motakh li dall ko , maguou yayam kou bonn la mais aussi naniou moytou aussi, saytanè lou nekk meun nako deflo nitt. aussi le jeune homme bobou aussi kou bonn la. Yalla na yalla safara.
Oublie thiat nakh dou sa dieukeur limou beugon rekk la deff, relève toi diegaloul yallah ter diouk ter arrêtel diko ladji Sheut niank wadiour lou nekk lay deflo nitt Ndeysan komm si thiat moy dieukeureum vraiment warou na si mbokkou yi ki ani ay mbokkam tamit, dieul si len sen domm nakh solen ko bayer ni dou bakh elle a vraiment besoin de soutien
Oh guiss gua yakaram si thiat lepp si thiat la nekon diatt diapp si wakho nak kett khamoul Lila si khalebi mai de tout façon diapp si bouko bayi yaw la amal domm magui laye niann thiat boulko bayi
Billahi migui melni Makay Ndoude sama khol bi migui fés dell Barki arkhourane mais loudoul diekh amoul yalla Nako tourodo doomam walou
Elle mérite de l aide même l état doit aider à cause du bb
Malgres que kou goor qui limou deff Nice soul..mais il faut que djiguene yi khame sene bopp gorr soula beugué bilahi daflay sekhlo tekk lokho badi yegg sa kaw même soko ko nangoulé ndakh gorr soula beugué daflay yereum dila khalatal sa euleuk 😢😢massa courage
Lolou dé amna
Sekhlou amatoul fen
Je valide 😢
Wallahi yén goors gni bonne nagn mais djigueun yi aussi naniou am fouleu sen bopp ham sen valeurs car yen vauriens yi diarouniou sah guénal am relation ak niom risque leu
Elle est très jeune
Voila l’importance d’une mére
Walaye deugeule démale fouta
Walay une mère est irremplaçable
@@maremesour3334oui
Pourquoi cette chaîne l utilise sans donner son numéro ? Pour des vues monétisées
Ndeysane courage chérie Yalnala Yalla takhawou
Oh ndeyssane 😢 yalla nako souniou borom taxawou cie barkeip yonente bi (swsl )
Machallah vraiment tu es une fille et une mère formidable 😭😭😭 niowal sama keur s’il te plaît
Bilay ya bakh yalla na la borom bi fay yiww
Dielal numéro bi affiché nonou bga contactez gni
dieuleu numéro bi woko nguir yalla ❤❤❤❤
Wotel si numéro bi stp yalla rek molay fay
Woténa si numéro bi mais wadji néna dinama wowate après une fois reparlé avec sa famille s’il y’a pas de consensus il vas m’appeler je l’ai donné mon numéro et mon adresse je suis éducatrice je peux les prendre en charge je veux aussi qu’elle retourne à l’école parce qu’elle est trop jeune pour abandonner les études
Du courage Aïcha soit fort 😭😭
Yallah gua am diékeur djiou am khalisse😢😢
Amine Ya Rabbi
Amine amine
Amiiine
*Amenn tè am yeurmandé thi mom❤🙏🏽*
C’est quoi cette prière melni khaliss lou éternel la nianalko yalla mou guiss kou bakh am yeuremande si mom meun ko topato rk teksi mom khalé bi mou meune amal bopam bagna kharr dara si nitt fi lepay diekh seuy ak kou am alal dou assurance de vie tei gniko am tamit majorité bi elles sont pas épanouies dans leurs mariages
Masta sister yalla nala yalla taxawou si barki seydina Mouhamed lepp dina diekh inchallah😭😭💔
Toureudôme dinako protéger inchallah 🙏🙏🙏
Guis gua fék sénégal téralounou djiguène badou dhioye 😢😢 réw bounouye tour ragogñou djiguène réw momou mousiba doufa diok
*Bilay ioe mais goor Sénégal khamougnou lolou*
Hum yaw nak ya kham lici kharbakhou djiguène
Bilaye wakhgua degueu yaw dé khamgua valeur djiguéne
Rew mo khamni bokale rek mousiba rek
Bilaye tu a raison
Aïcha ma chérie soit forte la vie est injuste walahii a ton age tu merité bcp plus damour et assistance mais dieu en a decidé ainsi.... Qu'Allah t'assiste et apaise ta souffrance. Si ça te dis je peux hébergé toi et ton enfant et vous assiste inchallah.
Dome ndeyam ak bayam rek massa ligay doundou metina trop bilahi massaa😢😢
ndeyssane il feux laide les personnes qui sont vécu cet situation
Yalna leu yallah fay ya Rabbih, yener bi rafeet neu ma sha Allah ❤️
Tu la connaît ?
Massa yalna la Yalla tokhouwou thi barké Seydina Mouhamed dafa am goor you doy war bo eumbé nguey khamni meusou nioula beugue nioulay daw mais dou nieup Dieu est au contrôle
Ndayesan yalna la yalla diapalé yak sa dom inchallah
J'ai des larmes aux yeux😢elle a un numéro spécial
Thieye aduna mo métii yalla nala yalla takhawou masta
Amine yalla nako yalla takhawou si barké seydina mouhammad sallahou aleyhi wa salam
Amine Amine yarabi
Amiin❤
Kou thiate tmt sheut 😢 c'est une femme brave Aïcha 😢
*J’ai mm pas les mots tellement que j’ai le cœur meurtri 💔😢Yalla nako sougnou Borom takhawou bamou guéne thi situation bi mou nekk😢🙏🏽🙏🏽*
Magui dioy sakh yaye moy lépou ndéysane 😭😭😭😭
Khalei bi dfa sakh rafett Machalla yalla nako yalla taxawou 🎉
Yalnala sounou borom takhawou si barké serigne Babacar Sy
Yaye Amoul remplaçant 😭
Deug bou weur nga wakh machallah
Kham nasi Dara 😭😭😭😭
Yaye mooy kéne si adouna ko khamni kouko manqué sa adouna manatoul nékhe à 100%100 j'ai 40 ans mais toujours pleurer à ma mére mais lépe sante yallah rék allhamdoulilahi
Mom dafa rafet sakh masha allah yalna ko yalla diapalei
Ohh massata yalla nala yalla maye kholo mogne ta yalla takhawou la
Lepp Dina diékh yalla bakhna du courage Grand soeur dina baac😟😞😖🙁😔
Ohh yalla Nalla yalla takhawou ma sœur 😢😢
Amine Ya Rabbi
Yalla nala yalla takhawou same mouhamed 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Mai xalébi ak mbokam deugueur ngagne xol deh😢😢😢😢
Good luck Aicha I cried listening to your story wishing you and Mohamed best of luck 🫶🏾🩶 sending love n prayers
Li diang nassi leçon ❤vraiment aicha kou bakh la dafa dioum rek té niit koudoul dioum amoul yalnala yalla diapalè aicha té arla
Ndeysan elle a été traumatisé depuis le bas âge ndeysan elle a besoin de notre soutien organisons une quête pour elle 😢😢😢😢man jai perdu mes mots la grande soeur de sa mère eno bonni no fewi
Je ve son numero pour l'aider pas dintermèdiaire
Plainte national contre Thiate dmrm bi😭😭😭😭😭😭
Cv bien cool kane moy thiate thiate yanamar walla
Wawaw
Bilay yaw😭😭😭
merci
Billy d'où Ku bax
Niak yaye Dafa meti 😭😭😭😭bilahi yalla dinala diapale pas c que djiguene ga thé djiguene yalla da ko teral mougnal les bonnes volontés diapelene ko thé yalla takh🙏
Courage yallanala yalla takha wou
❤❤❤ yallana yalla defalela diame metina gnake yaye da meti té papa fébare amo koula takhawou tiate bayiko sino dalaye wororate nala yalla nite té arela moukhamet bouko diokhe kéne ❤❤
Yalla nala borom bi Takhawou si barky Seydina Mouhamed topato wal sa dom bou bakh ga wout ligeiye dom dafa nekh si khol
Diambar ga yor dom rek dafa meti khamna si dara ba paré gnou teksi li
Sa dom ak sama dom bi 2jours lagnou maganté bok ben tour yalla nalene Borom bi sam Si barky Sen tourando
Et soit forte Bella❤
Massa way 😭😭😭😭🙌 té dafa rafét machallah yalla nala yalla takhawou Amine yarabi 🙌
Que Dieu vous protège ma soeur je suis de tout cœur derrière toi
Niak yaye dafa métii trop longue vie Aicha Lou méti méti ndey diékh ❤❤ tu ma fait pleuré 😭😭
yalla nako yalla takhawou si barki seurign fallou
Ndeyssane dioylo nama bimou wakhé sama dom douma dém diko bayi guinaw bilahi ma sœur yangi doundou lou méti wayé yalna yalla safara si barké seydina Mohamed psl 🤲🤲🤲😢
Kou niak yaye rk toumouranké😢massa ma chérie yalla nala yalla béte ak ay khaiweul j'ai mes larmes aux yaux😢😢😢
Can't stop 😭😭😭😭😭😭🇬🇲🌹 May ya Allah always be with you guys insha Allah
Ndeyssan yalla nako yalla takhawou inchallah 🙏🏽🙏🏽😊
Ndeyssane métina torop sax yallah nala yallah takhawou chi barké yonentibi
Ndeysannn elle est désorientée hamatoul foum dieul amatoul foumouy tekk tankam yallah nako yallah nako yallah takhawou 💔😞
Ay way Masta way Néné touti yaw khalé nga sakh😭💔ay way kouko meuna dimbeuli diap si té yala rk takh sonou na trop dama diakhlé sakh😭😭😭
Ndeyssane 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 mouhamad psl di dounde balay terale inchalla mounieule rkk adouna nila
Amine
اللهم آمين يارب العالمين
Yallanala yalla yokkou taxawou si barké Yonent bi s.a.w❤
Ndeyesane ❤❤Mouhamed yalla mokoye same innchalah mounianl rek sister
Senegal badola soon nafi😭😭😭😭😭😭😭😭
Thiate ya boon 😭😭😭😭
Bilahii 😢
Li métina 😢
T’es belle… c’est pas trop tard. Oublie le refais ta vie et sois heureuse.
Souma amone bly dinala takk m yallah baxna lépay baxx inchallah ❤❤❤
Yaww Tamite ❤❤
Alkhamdoulilah aicha va très bien degueunté na ak mome hier ❤❤
Thiey lii métina yallah nako yalla dimbelii sii barkii mouhamed 😭😭😭