Thieuy yalla amna gor you wayadi nak djiguene meune ngaka tak mou niak ndaw té gueuna baax ki am ndaw Gor moy fowei djiguene def louko nekh si djiguéne tey weur kou am ndaw yalna niou yalla may kou am soutoura❤🙏té beugu reik té yalla takh
Té lo ci khamoul goor yi fi dakeu takhawalou nio fi gueuneu beugue djiguéne bou vierge. Té nimou waré djiguéne téyé bopam nonou la waré goor, mai niom mom niou ci eup, danio égoïste, beugue lou tigo
Bigué ak yaye dji niro nagnou come moko djiour réellement mei nakk liguéne jouer fi nékhna trop tè am solo une vrai leçons d vie mci bcps vraiment 🙏🏼🙏🏼
😂😂😂 Rougui niéména cas héy défal sa boppou nit niou avancé weuhhh Bigué ndeyssane yeureum nalla naak mais dara yalla bakhna tout ira bien inchallah ❤❤❤❤❤❤
Il y a beaucoup de filles qui souffrent en silence thi cas you démé bii té pourtant dousene Bone les filles nagnou takate sounouy sereurr bou bakh et encore une fois il être indépendant e😢😢❤❤❤❤❤
@@easygang2563ci Coran Yalla dafné Dioulit téyel sa bop ba sa digueunté di daguane ak kenen, mai nioune souniou culture daniou nane leu djiguéne téyel sa bop, goor defal loula nekh,
@@easygang2563sou donn ci virginité laniouy kholé kou bakh ak kou bonn khana kone so dieulé 100 goor, ben késsé moci bakh, 99 goor yi ci dess yepeu bone, ndakh 99 goor yoyou yep kham naniou djiguéne waleu aye djiguéne bien avant niouy marier. Khawouma loutakh goor égoïste rek, ndakh gni fi dakeu devierger waté nioy woute djiguéne bou vierge
@@easygang2563 toi aussi la prochaine fois avant de repondre faut bien comprendre le message, liratal sa message boubakh di nga kham litakh ma tontou la li. De toutes façons la majeure partie des hommes sont égoïste, sen interet rek. Bref, mouy goor di djiguéne dale, virginité mom niép la warr pas djiguéne késsé, Wa Salam, bonne journée à toi aussi
@@easygang2563yaw mom mba bakh nga reik té mba yangui sam sa diganté ak yalla ndakh djiguéne boufi yakhou gor moko yakh founiou puniré djiguéne dolen fa dess may len niou diam
Une question, une fois qu'on sait que c'est le papa qui lui a fait perdre sa virginité, est-ce que le mariage avec le fils peut continuer aussi bien sur le plan religieux que sur le plan social. Juste une question pour savoir.
Pape Démba sa genrou goor yi gno takh gnou généralisé goor yeup lane moy ndaw mayou gnoula ndaw domou adama lagnou la may ba takh na gua warko soutoural surtou djiguén nakk
kémane vision daguéne kémane MACHA’ALLAH YALLAH NA YALLAH DÉFF SÉN CHAINE BI UNE TRÈS GRANDE CHAÎNE AU NIVEAU PLANETAIRE MACHALLAH .AMINE❤ DAILLEURS,JE VIENS JUSTE DE TOMBER SUR VOTRE CHAINE MAIS AVEC LA SERIE JE SUIS DEVENU FAN’S NUMBER ONE MACHALLAH ❤❤❤❤❤❤❤BIEN DE CHOSES À TOUTE L’EQUIPE🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
Amna sens yaw y’a comprendroul le message : demba pensait avoir de la vertu et que la fille était une pute donc sachant que c’est son père qui a deviergé la fille c’est une leçon de grande moralité
𝐒𝐄𝐑𝐈𝐆𝐍𝐄 bi nga balma waye wakhouma pour diemeko thi yonenete bi sala lahou halaye wasalame ndakh mo guene kepou kouye takhaw thi souf mais tamite kepou kouye wakh thi goor da ngaye perestisse
*Ci Coran Yalla dafné Dioulit téyel sa bop ba sa digueunté di daguane ak kenen, wayé nioune souniou culture daniou nane leu djiguéne téyel sa bop, goor defal loula nekh. Soudone ci virginité laniouy kholé kou bakh ak kou bonn, kone khana so dieulé 100 goor ben késsé moci bakh, 99 goor yi ci dess yepeu bone ndakh 99 goor yoyou yep kham naniou benen waleu yenen djiguéne(s) bien avant niouy am sokhna.*
Li leçons la pour nioune jiguenn yi niou khame souniou bopou parce que gore yi daniou bonne nioume gneupe pas yeme nagniou teyé souniou bop bou bakh ba âme dieukeur Li leçon pour nioune jiguenn yi
Pape Demba tu ne ses op la valeur d'une femme .pr te dire la vérité dans cette vie sais rare de voir un fille vierge mais leur marie les respect tu sais chaque chose c soutoura .mais aussi c'est une leçon de vie a nous les femmes et a vous les hommes
Pourtant le cas de Pape Demba M’a arrivé il y’a quelques années. Je sortais avec une fille, mais en flirtant avec elle, jusqu’à je voulais entretenir des relations sexuelles avec elle, elle me disait non, il faut attendre le mariage et j’ai respecté sa décision. Mais le jour où j’ai parlé avec ses parents pour la marier, on a flirté et elle m’a dit si tu veux on fait l’amour et aussitôt je l’ai dit tu n’es pas vierge, elle est restée 5 minutes et elle m’a dit qu’elle n’est pas vierge, je l’ai dit que tu ne m’avait pas dit la vérité et tu m’as menti . Bon d’après ce qu’elle m’a dit elle a été violé par une personne que je connais qui es mon cousin mais je ne la crois pas franchement. On avait fixé la date de la mariage et après j’ai dit à ses parents que je ne vais plus la marier. Après kelk jour de discussion ses parents m’ont convaincu et m’ont dit que la fille est bel et bien vierge parce qu’on l’a amener chez un gynécologue et ce dernier a dit qu’elle est vierge. Je vous jure que je ne voulais rien dire à ma famille Pour qu’elle ne sache pas le problème mais c’était impossible, par la suite je l’ai dit à mes plus proches. Ma famille m’a convaincu pour que le mariage soit ficelé et c’est fait. Mais je n’avais plus de confiance en elle, et la confiance est la base d’un couple. On s’est marié et le jour où on a des relations sexuels, je me suis rendu que ma femme n’est pas vierge, mais après 3 mois de mariage , je l’ai répudié parce que c’était impossible d’être avec une femme à qui on a pas confiance. Mais maintenant on est des vrais amis, on discute, on s’appelle et j’ai beaucoup regretté franchement. Elle m’a pardonné et si c’était à refaire je ne ferai pas cela franchement
Une bonne femme ne se mesure pas à sa virginité. Elle se mesure en sa capacité de gérer un foyer.. Certaines filles dites vierges meun nga lenn takk niou am djiko diou bonne, douniou beugg sey mbok, douniou la yeureum té douniou la seyeul. djieguen donn na takhawaloukate (pour ne pas dire prostitué), niou takk ko mou sey ba sey fou darra newoul.. Té tekk ci djiguenn dou devierger bopam.. Mais daniouy sipp djiguen gni bayi goor gni.. té djiguen bouniou fi devierger goor mo ko ko def.. Delo ci lenn senn khel yi..
Saigné c'est pas forcémentg🩸 Moi avec ma femme le 1ér jour et le 2ém jours elle n'a pas daigné 🩸 Mais le 3ém jours elle a insisté pour que je là baise très fort ! Ainsi j'ai fait ce qu'elle m'avait demandé.mais cette nuit là elle a saigné 🩸🩸 Abondamment elle ne peut même pas marcher durant 3jour...... À la fin hôpital lako yobou.bilahi.
Ci Coran dé Yalla wakhoul ni djiguéne téyel sa bop goor defal loula nekh, Yalla Dioulit la wakh, kone ni djiguéne wara téyé bopam, nonou la goor wara téyé bopam, Wa Salam
@@easygang2563😂😂😂😂 le fait de saigner ne veut rien dire car il ya des femmes qui ont hymen et qui ne saignent pas, donc amna nou goor di seuyé ak sokhnam meune nako devierger té dou saigner. Sou djiguéne saigner rek moy kou goor ki gagne nako
@@easygang2563 il ya des femmes qui n'ont pas hymen qui saignent soulen sen dieukeur gagné, comme il ya des femmes qui ont hymen qui ne saignent pas soulen sen dieukeur gagnoul, le fait de saigner n'est pas une preuve de virginité, va faire des recherches plus avancées au lieu de rester là à parler avec haine aveuglement
Aziz tu est et impolie mais mère mola mag degloul wahou mère bii boudone goor bou neka AK djiguene ay goor barre dounou am djiguene respectel Tutti te wax wahou niit
Oui c'est dans le sens de sensibiliser de la valeur de la virginité. Comme dans toutes les religions révélées, la virginité est capitale. Mais les moeurs du film n'est pas les nôtres. Comment avoir un rapport sexuel avec un mec et vouloir se marier avec son père biologique. Alors ta propre mère détient ce Secret.
Thieuy yalla amna gor you wayadi nak djiguene meune ngaka tak mou niak ndaw té gueuna baax ki am ndaw Gor moy fowei djiguene def louko nekh si djiguéne tey weur kou am ndaw yalna niou yalla may kou am soutoura❤🙏té beugu reik té yalla takh
Té lo ci khamoul goor yi fi dakeu takhawalou nio fi gueuneu beugue djiguéne bou vierge. Té nimou waré djiguéne téyé bopam nonou la waré goor, mai niom mom niou ci eup, danio égoïste, beugue lou tigo
Ay way djiguéne dagnekay soutoural sokobeugué holal Li ada bi warnadjiéhe
@@fatimbarry7885 ki weroul
Billahi
Premier commentaire kou beug Seydina mouhamed (SAW) defal ma cœur❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
NOTRE BIEN AIMÉ PSL ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
Pdl
NOTRE BIEN AIMÉ PSL ❤❤❤
Bigué ak yaye dji niro nagnou come moko djiour réellement mei nakk liguéne jouer fi nékhna trop tè am solo une vrai leçons d vie mci bcps vraiment 🙏🏼🙏🏼
Ndeysane Lou meti moko dall 😢Magu sante yalla bimouma maye ma sigul sama yaye❤
Kou dccrd série bii continuer rkk lalal j’aime mention spéciale à vous❤️
❤
🥰🥰🥰 5:07 🥰
Yalla Nanou yalla soutourale
wa niakk ndaw mom diarna fassé man goor gni dale meunoumaléne comprendre, yalla nagnou yalla doli soutoural 🙏😑😑😑
Moy Toul niak sa boss rek
@@nekorellbandithies4688 mba yow teyenga sa boss ak sa bou soeur?
Égoïste rek, sou donn kou amoul virginité niou fassé la dé, kone 99% goor yép sen seuy dina tass
@@easygang2563 tu sais qu’elle peut être vierge sans pour autant saigner. Donc nokoy khamé
@@farimatadiop606 Vous avez raison! Je m'excuse suit à mes propos🙏🏽.
Elle joue très bien la maman de Bigué très naturellement CHAPEAU A ELLE
Merci beaucoup pour cette série nékhna trop mentions spéciales au scénariste ❤
V
😢😅😅
❤❤❤❤
@@saynatall8111ضض ضضضضض/*/**
🎉
Une très bonne révélation et une belle leçon de vie.
😂😂😂 Rougui niéména cas héy défal sa boppou nit niou avancé weuhhh
Bigué ndeyssane yeureum nalla naak mais dara yalla bakhna tout ira bien inchallah ❤❤❤❤❤❤
Il y a beaucoup de filles qui souffrent en silence thi cas you démé bii té pourtant dousene Bone les filles nagnou takate sounouy sereurr bou bakh et encore une fois il être indépendant e😢😢❤❤❤❤❤
@@easygang2563ci Coran Yalla dafné Dioulit téyel sa bop ba sa digueunté di daguane ak kenen, mai nioune souniou culture daniou nane leu djiguéne téyel sa bop, goor defal loula nekh,
@@easygang2563sou donn ci virginité laniouy kholé kou bakh ak kou bonn khana kone so dieulé 100 goor, ben késsé moci bakh, 99 goor yi ci dess yepeu bone, ndakh 99 goor yoyou yep kham naniou djiguéne waleu aye djiguéne bien avant niouy marier. Khawouma loutakh goor égoïste rek, ndakh gni fi dakeu devierger waté nioy woute djiguéne bou vierge
@@easygang2563 toi aussi la prochaine fois avant de repondre faut bien comprendre le message, liratal sa message boubakh di nga kham litakh ma tontou la li. De toutes façons la majeure partie des hommes sont égoïste, sen interet rek. Bref, mouy goor di djiguéne dale, virginité mom niép la warr pas djiguéne késsé,
Wa Salam, bonne journée à toi aussi
@@easygang2563yaw mom mba bakh nga reik té mba yangui sam sa diganté ak yalla ndakh djiguéne boufi yakhou gor moko yakh founiou puniré djiguéne dolen fa dess may len niou diam
Sii Ame na solo trp ms Adouna dangio wara xame ni Yalla mingui Andack ngiouy neubeul nite soutoureu tè djigeune dangioko wara neubeul soutoureu
Ohh vraiment li moy vrai théâtre mentions spéciales à vous ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
Pape demba vresmant tu est trop méchant
😂😂😂 Professeur Samba môme kaay ndéké mo deviergé khalé bi wouy loupé
Wa loutakh gore am fite niom danon am daw🤣🤣🤣
En tout cas gor gni amouniou ndaw😢😢😢😢😂😂😂😂😂😂
Deggueul fiit rek néh kou rép
@@ndeyefa784 boule wakh lolou d'où gnepe prc amna gnouy bayi khéle yalla ba dougnou ndiallo
Ndakh gua Sagne KO wax chérie 😊
Une question, une fois qu'on sait que c'est le papa qui lui a fait perdre sa virginité, est-ce que le mariage avec le fils peut continuer aussi bien sur le plan religieux que sur le plan social. Juste une question pour savoir.
Pape Démba sa genrou goor yi gno takh gnou généralisé goor yeup lane moy ndaw mayou gnoula ndaw domou adama lagnou la may ba takh na gua warko soutoural surtou djiguén nakk
Ndaaw sakh déh Sénégal la yaam amoul fénéne 😂😂😂😂😂am ndaaw dou force sakh di
Ndaw bakhna thi djiguene ndakh kou meunoul teuyé tatam gui sakh dak thi mom dou teuyé seye(gerer keur, yar ndiabote etc)
@@layetheonly5139 louy ndiariniou ndaaw selon toi ish 😂😂😂😂
@@layetheonly5139 wakh dafay rafète yèn esque tèyè nguèn sên bop😢😢😢😢😢😢niak ndaw takhul djiguèn bonne wala du nék seuy Kate. Am ndaw takhul mou djiguèn teuyè dieukeur .
@@sambafall3509 ta assuré 😂
Yalla nagnou yalla mousseul si goor Bou amoul soutoureu ☹️☹️
Amine 🙏
La meilleure série du monde
Sama yarame ndawena yeureum na djiguene gni dakh li sou amone si koté goore lambaye niawe
Machala ay way yarr léne khalé yi way yarr sa doome bakhe na trop
Vous les filles bayiléne sii khéll bou bakh amna solo dé
Virginitè n’est pas important dans le mariage l’essentiel c’est la confiance et l’amour
JE SUIS UN HOMME MAIS JE VOUS JURE J AI BEAUCOUP PLEURE EN REGARDANT CE FILM.
😂😂😂
🤣🤣🤣🤣
Beuri nga rakhogn😂😂😂😂
@@pendasarrgaye5102 Penda damaa gaw dioye déh!!! sama diabar souma méré sakh ma dioye!
Daye sane sa khôl bé owof 😢😢😂
😂guélou pape Demba insbi khana warna titt dé😂néna dou tak djiguène bou amoul ndaw
Bravo tres belle leçons de vie bonne serie li moy soutara ❤❤❤
Amena solo lifi mâme
bayiwone❤❤❤
kémane vision daguéne kémane MACHA’ALLAH YALLAH NA YALLAH DÉFF SÉN CHAINE BI UNE TRÈS GRANDE CHAÎNE AU NIVEAU PLANETAIRE MACHALLAH .AMINE❤ DAILLEURS,JE VIENS JUSTE DE TOMBER SUR VOTRE CHAINE MAIS AVEC LA SERIE JE SUIS DEVENU FAN’S NUMBER ONE MACHALLAH ❤❤❤❤❤❤❤BIEN DE CHOSES À TOUTE L’EQUIPE🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
Li amoul sans boudone Tonton bi sakh mou tané mais pape Demba ak papame yeupp kham khalé bou djiguéne bii lole dafa gnaw
Mais ma chérie réalité bi ame si société bi rek mom lagnou joué. Defois sakh si birr mariage sa beau père dila thiokass
Amna sens yaw y’a comprendroul le message : demba pensait avoir de la vertu et que la fille était une pute donc sachant que c’est son père qui a deviergé la fille c’est une leçon de grande moralité
Ndeysaan Biguè ak yayam daño nouro sakh ñom ñarr nieupeu mol
Pourtant gorou diank presque amatoul 😢
Barétoul te lepp nioko waral
Khamal seu bopp rek
@@easygang2563 man fimay waxé moy la plupart gor yi dani fo ba doyal dem di weur kou fowoul té djiguen goufi ndaw gor mo koka khagne en général
Une belle leçon de vie...félicitation à keman vision
Bigué dafa rafét machallah 🥰
Pape demba mô bone
goor thi bopame mo bonne te foo kaye Bilay am lene yeurme nde thi djiguene nie bravo 👏👏🥰
Delen wood sen wakh yonantè bi sakh goor la ak kenen ak kenen
𝐒𝐄𝐑𝐈𝐆𝐍𝐄 bi nga balma waye wakhouma pour diemeko thi yonenete bi sala lahou halaye wasalame ndakh mo guene kepou kouye takhaw thi souf mais tamite kepou kouye wakh thi goor da ngaye perestisse
@@mamediarra6068 dou goor nieppa bone gniy bakh gniougui bakh ba tey ragal yalla
Pape demba khana doo khole oubile sa beune di khole
Pape Demba ya bone
😂🤣
Bou gor done ame naw bén gor dou ame diabar
Mais c'est l'amour qui existe dans la😢vie et non virginite
Blh un peu de respecte aussi pour le femme
Mai bigué xana kimoye vrai yayam ndouro nane tropp
Oph ndeysan en résumé le point principal c'était la communication pour régler cette situation. Wahtazan rek mo am solo
Metina dh😢soutoura yalla ta bayi si khel😮
Nekhna trop machalla 🎉
*Ci Coran Yalla dafné Dioulit téyel sa bop ba sa digueunté di daguane ak kenen, wayé nioune souniou culture daniou nane leu djiguéne téyel sa bop, goor defal loula nekh. Soudone ci virginité laniouy kholé kou bakh ak kou bonn, kone khana so dieulé 100 goor ben késsé moci bakh, 99 goor yi ci dess yepeu bone ndakh 99 goor yoyou yep kham naniou benen waleu yenen djiguéne(s) bien avant niouy am sokhna.*
Ma contane si yaw
@@fatimaniang4177 goor gni danio égoïste torop
@@beauty3166 dama warou
Vraiment Pape Demba amoul xoll
Est ce que Pape Demba Défna Dara??? Se Sont Ses Principes
Amena solo trop machalla
Ndeysane li dawna yaram
Je me vois dans cette série le rôle de bigué je les vivre
Li leçons la pour nioune jiguenn yi niou khame souniou bopou parce que gore yi daniou bonne nioume gneupe pas yeme nagniou teyé souniou bop bou bakh ba âme dieukeur Li leçon pour nioune jiguenn yi
Djigen dé soutouraalko bahna looool
Erreur de communication aussi amnasi
Deug mo dieuk té moy moudj❤
Bilay 😢
Akeuh bobou d mo gueuneuh bone lolou d mo raw sax niou liguey la shi😢
Pape Demba tu ne ses op la valeur d'une femme .pr te dire la vérité dans cette vie sais rare de voir un fille vierge mais leur marie les respect tu sais chaque chose c soutoura .mais aussi c'est une leçon de vie a nous les femmes et a vous les hommes
Ndeysane Ani oustaz Iran Modou fall bigue lewna pape Demba walla
Weuhhh Pape Demba khamo sa bopp nakk bilay walay liguay boneu thimm djiguéne dagne koy soutoural
Sou donn kou viergoul niou fassé la kone dé 99% goor yép aye celibataire laniouy donn
@@beauty3166 *Bilay wlay*
Serie bi moy meilleure serie de lané
Machala tabarakala dieuredieuf amna solo trop
Thieye gorou Senegambie.
Anh Gambie Tamite Dagnouy Dokhal Liii 😂😂😂
J’ai pleuré nak
Pourtant le cas de Pape Demba M’a arrivé il y’a quelques années. Je sortais avec une fille, mais en flirtant avec elle, jusqu’à je voulais entretenir des relations sexuelles avec elle, elle me disait non, il faut attendre le mariage et j’ai respecté sa décision. Mais le jour où j’ai parlé avec ses parents pour la marier, on a flirté et elle m’a dit si tu veux on fait l’amour et aussitôt je l’ai dit tu n’es pas vierge, elle est restée 5 minutes et elle m’a dit qu’elle n’est pas vierge, je l’ai dit que tu ne m’avait pas dit la vérité et tu m’as menti . Bon d’après ce qu’elle m’a dit elle a été violé par une personne que je connais qui es mon cousin mais je ne la crois pas franchement. On avait fixé la date de la mariage et après j’ai dit à ses parents que je ne vais plus la marier. Après kelk jour de discussion ses parents m’ont convaincu et m’ont dit que la fille est bel et bien vierge parce qu’on l’a amener chez un gynécologue et ce dernier a dit qu’elle est vierge. Je vous jure que je ne voulais rien dire à ma famille Pour qu’elle ne sache pas le problème mais c’était impossible, par la suite je l’ai dit à mes plus proches. Ma famille m’a convaincu pour que le mariage soit ficelé et c’est fait. Mais je n’avais plus de confiance en elle, et la confiance est la base d’un couple. On s’est marié et le jour où on a des relations sexuels, je me suis rendu que ma femme n’est pas vierge, mais après 3 mois de mariage , je l’ai répudié parce que c’était impossible d’être avec une femme à qui on a pas confiance. Mais maintenant on est des vrais amis, on discute, on s’appelle et j’ai beaucoup regretté franchement. Elle m’a pardonné et si c’était à refaire je ne ferai pas cela franchement
Une bonne femme ne se mesure pas à sa virginité.
Elle se mesure en sa capacité de gérer un foyer..
Certaines filles dites vierges meun nga lenn takk niou am djiko diou bonne, douniou beugg sey mbok, douniou la yeureum té douniou la seyeul.
djieguen donn na takhawaloukate (pour ne pas dire prostitué), niou takk ko mou sey ba sey fou darra newoul..
Té tekk ci djiguenn dou devierger bopam.. Mais daniouy sipp djiguen gni bayi goor gni.. té djiguen bouniou fi devierger goor mo ko ko def..
Delo ci lenn senn khel yi..
Saigné c'est pas forcémentg🩸
Moi avec ma femme le 1ér jour et le 2ém jours elle n'a pas daigné 🩸
Mais le 3ém jours elle a insisté pour que je là baise très fort ! Ainsi j'ai fait ce qu'elle m'avait demandé.mais cette nuit là elle a saigné 🩸🩸
Abondamment elle ne peut même pas marcher durant 3jour......
À la fin hôpital lako yobou.bilahi.
Remariez vous reck
@@ThiesKaay le problème n’est pas la virginité mais c’était le mensonge quelle m’avait fait
@@farimatadiop606 je me suis marié après
Mais j'ai une question à poser pourquoi on nous demande nous les filles la viergénité et vous les garçons est ce que vous êtes vierges😊
Ci Coran dé Yalla wakhoul ni djiguéne téyel sa bop goor defal loula nekh, Yalla Dioulit la wakh, kone ni djiguéne wara téyé bopam, nonou la goor wara téyé bopam, Wa Salam
@@easygang2563😂😂😂😂 le fait de saigner ne veut rien dire car il ya des femmes qui ont hymen et qui ne saignent pas, donc amna nou goor di seuyé ak sokhnam meune nako devierger té dou saigner. Sou djiguéne saigner rek moy kou goor ki gagne nako
@@easygang2563yaw mi nanga fékhei ba nanga teyei sa bopou yaw mom nit nga yaw mi deh kham nga dara mola takh di wakh sa khetou wakh yi
@@easygang2563 il ya des femmes qui n'ont pas hymen qui saignent soulen sen dieukeur gagné, comme il ya des femmes qui ont hymen qui ne saignent pas soulen sen dieukeur gagnoul, le fait de saigner n'est pas une preuve de virginité, va faire des recherches plus avancées au lieu de rester là à parler avec haine aveuglement
@@easygang2563 yaw mba vierge nga rek ?? 😂😂 😂 😂
❤ je suis contente ❤❤❤❤
Machalla❤
Machallah amna solo trop❤❤❤
Machalla
Pape Demba 🥺🥺
Mane goor ka dhé Mes dagno égoïste d tro parceke bougnou done kholé tay goor bou amone ndaw Kone tay goor gnou bari dinagnou ame problem adouna
Walay ndeyssane 😂😂😂😂
Bien dit frère
Aux moins yaw nitt gua
Kon Dina bari goor niou tass😂😂
Ww Maman kon goor gni gnou bari doune am diabar ndakh liy ndjiit tey ndiak tey ndiag nioma
Machalla li mo dal sama aide ménagère bi nonou lako dieukeame def
Ohhh c’est triste ça 😢😢😢😢
Lépe manque de communication Leuh. Il faut toujours dire la vérité à son partenaire
li moye serie 👌 👏
Ndeysann
Bala may deeh goor di ladj virginété tee gnome dougnou vierge jiguene bouy sam dawame dou pour goor pour mome la goor gni régler léne sof guene torope
Boul d yaw amal virginité rek
Mala wakh li pur gniom djiguéne yi gniom gniotakh gnouy sambeu sen bop thimmmm vs vs trompé c pur ns et nos parents
Égoïste rek ak beugue lou tigo
Boumou yam fi wayyy na éggg
Waroko😁😁😁
Le meilleur
Ndaw c'est pas forcée.amna femme yii gua hameni dougniou saigné,
A bon entant que fille je ne savais pas , la fille déviergée doit montré quel signe explique moi svp celle ne saigne pas?
Ça c'est une petite partie des filles pas toutes. Cette argument n'est pas valables M. Cissokho
Tieyy yalla gor mo niakkk soutoura
Pape meuneutouko takk
Hi tonton pape Demba bi khamé n'a KO si film bi yague mais fatenako🤔
Magasi bou niome sa nékh la
Yane jour lay am
Li Moy théâtre deugeu yalna niou yalla doli soutara c'est dommage goor yi nk yeureum len niou
Thiey ndaw 😢
Daffa compliqué dé. Teh problème bi moy goor daffa jaloux miss...
En tout cas dale ni djiguéne wara téyé bopam nonou la goor wara téyé bopam, ndakh Yalla Dioulit la wakh téyel sa bop donc bougne niou sonnal
@@beauty3166 tout-à-fait !
Cva Cva Cva Cva rk ehhh😂😂😂😢
Tonton wou ma Démba bi niounane ak maguasine mou bokon si sa nékh
Mom là
Machaalah jai bien regarder cet film mais esque cette fille peut ce marier avec pape demba esque daguanako
Oui oui nagane na si dîner mais les gens disent que rafetoul
Biguè da niro ak yaye djiii
Ça me soule le faite que les hommes exigent la virginiter
Anh Bon ? Et Pourquoi Ça Vous Saoule autant? J'aimerais Savoir
@@youssoufdiatta8639 Tout simplement, eux même ne gardent pas leur virginité.
Aziz tu est et impolie mais mère mola mag degloul wahou mère bii boudone goor bou neka AK djiguene ay goor barre dounou am djiguene respectel Tutti te wax wahou niit
J'ESPÈRE QUE SON PERE EN FAIT PARTI
J'aurais préféré que l'oncle la viole comme que dako nop mais le fait qu'il s'agit du père me dérange beaucoup !
Tak kou sa baye sakou esk daganena?
Très bonne question
Lolou lagnou wara atté ba paré
Dafa xaram nga takkk jiguene bo xamni da sekkk ak sa papa
Dfa haram dh
Goor moo bon kay😅🤣
Suite bi svp 🙏
Comment vous contacter pour échanger svp
Gor yi dagnlénn waronn lathie ndaw😅
Raison de plus de ne pas lier ce mariage. Ce vieux est un alligator
Goor dey am soutoura
Biguééé miii koumakoy may ? numéro bi laa sokhla rek
Oui c'est dans le sens de sensibiliser de la valeur de la virginité. Comme dans toutes les religions révélées, la virginité est capitale.
Mais les moeurs du film n'est pas les nôtres. Comment avoir un rapport sexuel avec un mec et vouloir se marier avec son père biologique. Alors ta propre mère détient ce Secret.
Beugu sang mélni vanvire😂😂
0:50