ya oustaz saliou samb attakewoul seydina cheikh radiyalahou anhou dafne ñi don dal si idy ap nar lañ top man deglounako ta idy amna ay kilifa youko takfir ne kenna si dine islam ndax lim wakhne mouritla motax serigne touba da woute ak ñako djitouwon dafa yatal di bolle diamñi wakhngako legui si sarta tariqa tidjane dañoune kou dieul wird wi do ziara benen waliyou bousi bokoul ndax man nga ziara kenen guis si mom lo guissoul fanga diogue ak yenen motax daflay tenkk boude yonnou mourid mom serigne boumou mana don ziarel
Walahi talibé cheikh yi ma lén Naw rk bilay yén si kham kham rkk laniou lén kham bilay...saliou samb kham lén sén boppou mo geuneu wakh nak laniou bagne té liniou kham barri na
Merci beaucoup. Oustaz 👍 👍 💖 💖
Mancha alah amena solo oustaz cadouyi rafétena tégouna thi kham kham ak téguine
amna solo yalla na yalla barkél kham kham bi
Vrement nous sommes fatigués chak jour béni wakh bi gnioune yeup béni lagne
Je suis un talibé mourite mais vraiment si ont dis là vérité saliou Samb a mal parlé c'est ça qu'il faut dire
Amadou Camare saliou samb limou dafa am louniou wakh mou tontou wakh dji lolou la rèk dioumoul dra essaie de revoir le vidéo li eupeu na sakh 7mois
Yala nala yala fayyyy
merci Way
Naniou Lène wakh Deugg niou kham ko cheikhou tadiane dou serigne tè dou moromou serigne yi thi sènègale yeup kimou yakar wakh nako cone na lér niom amou niou kham kham reuy Lamige rèk AK nakhatè nioune tadiane cheikh Mame seydi hadji malick sy daff niou yè Mon takh niou yèwou nèk ay niit tamit nitè talibé yi danio yèwou diang ame kham kham
saliou samb Gueweul la diaroul tontou amoul xam xam amoul ay tèguine
Xoumbay bii la toop rek daa rérr
l'on gewuel do AM kham kham
Bilaye tarikha cheikh rek moye deugue lene lep moye lollou
Yamana katt sa duaye
@@milkizogaye6723 je viens d'avoir raison car tu ressemble qu'a ton marabout. Dommage
👍
Lou léer ga wax talibé cheikh mo woor je suis fier ci sama werdeu tidjane sella rek mo am solo
ya oustaz saliou samb attakewoul seydina cheikh radiyalahou anhou dafne ñi don dal si idy ap nar lañ top man deglounako ta idy amna ay kilifa youko takfir ne kenna si dine islam ndax lim wakhne mouritla motax serigne touba da woute ak ñako djitouwon dafa yatal di bolle diamñi wakhngako legui si sarta tariqa tidjane dañoune kou dieul wird wi do ziara benen waliyou bousi bokoul ndax man nga ziara kenen guis si mom lo guissoul fanga diogue ak yenen motax daflay tenkk boude yonnou mourid mom serigne boumou mana don ziarel
Wakhi dofff
Wakhi doff
Yow sa nopeu guenoul ekh souniou yoss bagne nako bani Nioniou cheytané laniou ay nar laniou guem
Saliou samb doul rk lay deif
Walahi talibé cheikh yi ma lén Naw rk bilay yén si kham kham rkk laniou lén kham bilay...saliou samb kham lén sén boppou mo geuneu wakh nak laniou bagne té liniou kham barri na
Abdou Faye xamou len dara wax len
Idrissa Seck sakh guemoul Talikha Mourid Idy gni toudé sene bope Mourid aye nafékh lagne gnoko dane Diabolise nane ko Sathie la legui gno kéye defendeure
serigne bi yangui garouwale sisa bir wakh ngane deukko ñari sokhna youbok benn waydiour demewoul nonou ndax deukkeundo woulen te fekkantewounafa kou ndiakki dafa fatou ñou diokhka kennen ki comme ñari dommi yonnentabi salalahou alay wasalam yi mou diokhon seydina ousmane radiyalahou anhou
serigne saliou samb xamoul dara damana wakh rek
Yawmi ya khamoull dara magui dieggalou mouride dou complexe
Saliou . Samba.amoul.xam.xam.fen.rek.laye.def Ak. Doul.rek 🔫🔫🔫🔫
Kou sof nga yawi tam
Saliou Sambe domekharam la
Fékhé léne agallé séne takou sékhawe bobou magall touba amoull fénéne léck tédo faye touba rék la ame barui guéne wakh lolou
Yaww sa leufall ndaye nga beug kokoo touchh
Yow magal touba bou doneu mouride rek dou am embouteillage
milkizo gaye yaw yagui has néguou yalla khol léne liguéni wakh nga balma
Gni waroul wakh senegal nioy wakh wayy wayy nagnn teutth sougn lamine
Naye ler boudé yefarnga woon dellou watsi laye aram
Wayé diayente walliyou bayiko dem fenen sa seringe dawara bek boudé talibe bi tekhé rek moko sokho loon
yaw wakhon fi nday dara ngay doul rak kan mofi fat wakhtou dioulli kan mofi am lou eupe 4 diabar yén ngir yalla mouno lén nopi🤙
Xana mor ba mi gni ndamo také 3 femme you book ndaye xana dego lolou
Wayé dague katt thaga sorill fui
Diara diaf seringe Touba komo nekhol do AM diammou
Sarigne touba rék mofui nék taye ak souba nékh nakha ri
Dangaye deuggeu sa ndaye doul
Wakho deuggg dangaye kat sa ndaye
@@abdoulcaan5948 yaw sa bo yewoo sa lefeulou ndaye
Lol baa boof ta bi wool leep dina lerr
Ligui yi léne ta bayyi tésanté
Toudou niou sa serigne motakh