Merci Oustage c’est bien de remettre les choses en ordre , trop de fanatisme au Sénégal , on aime qu’on nous bleufe avec des miracles qui n’on jamais existé
On dirait que le Sénégal a son propre Islam à part 😓 Allah Subhanahu Wa Ta'ala dit: قُلْ اَطِيْعُوا اللّٰهَ وَاَ طِيْعُوا الرَّسُوْلَ ۚ فَاِ نْ تَوَلَّوْا فَاِ نَّمَا عَلَيْهِ مَا حُمِّلَ وَعَلَيْكُمْ مَّا حُمِّلْتُمْ ۗ وَاِ نْ تُطِيْعُوْهُ تَهْتَدُوْا ۗ وَمَا عَلَى الرَّسُوْلِ اِلَّا الْبَلٰغُ الْمُبِيْنُ "Dis: «Obéissez à Allah et obéissez au messager. S'ils se détournent, ...il [le messager] n'est alors responsable que de ce dont il est chargé; et vous assumez ce dont vous êtes chargés. Et si vous lui obéissez, vous serez bien guidés». Et il n'incombe au messager que de transmettre explicitement (son message)." (QS. An-Noûr 24: Verset 54)
Yallah naléne yallah fayii thii barké alquran ak Sounnah Mohamed salalahou alayhi wa salam 🤲 Mane diné yallah dji rk moma gnorr topeu yonou yallah bii mo weur blhi watalahi Sokhlona trop sén numéro guir yallah ak Rassoul j'ai besoin de vrai guide com vous pour mourir sur ma religion islamique celle d'Allah et de Mohamed psl wono 🤲😔😔🧕🕋🕌 K'ALLAH veille bien sur vous 🤲
Tarikha tidiane mo bone fene rek moy sene dine yonenty yallah mouhamed monou dianguale salatou ibrahim khana kidone soukourat di sagua te kilifala sy tarikha tidiane khana mome cheikh daka fate
Gnakk ko topp wesséwoul nguénn bayyi koffi bayyi fi wahi yonnénte psl bi Di toppou wahou nitt Kou réréh Quran ba paré di réral ay nitt Qu'Allah nous guide vers son droit chemin
Thiey ngi malen yeureum.un lobby qui égare les gens alors qu'ils sont dans l'égarement évident.beaucoup d'entre les gens qui sont avec eux ne connaissent que ce qu'on leur raconte dans leurs conférences par leurs éloquents et beau parleurs.les savants parmi eux ne disent pas la vérité mais c'est des menteurs car leurs mensonges les permettent de vivre aisément ainsi que leurs familles. Cheikh yalla wathiee woul lay si mom bou keroguee dou sol toubey walahi souma walahi.
Des boniments malveillants qui n’honorent aucun homme sérieux encore moins un Musulman. Voici ce à quoi s’emploie ce très peu scrupuleux soi-disant Ustaz Fall
Lakoum Dina koum waliya dine c'est entre un musulman et un non musulman.quand vous faites référence à ce verset, cela veut dire que les tidianes ne sont pas des musulmans.d'apres ton raisonnement. Ce verset ne s'applique pas entre musulmans.
Niou KO eup xam xam nio fi nek on l'accepte mais ils ne disent pas la vérité aux talibes. Alpha limouy wah Moy DEUG Modou fall day fen limouy wah amoul thieuslay si islam.doko fek si arhourane doko fek si khadithssou yonentibi. Ay fen la !
Mou nékh lén wala mou nakhari lén cheikhou tidiane sauvé nagnou ba sauvé sén aye baye mame rassoulah moko diokh yén sén xam xam bari woule té guén bari wakh gnouss lén sén ndaye sa hath Fi makk gni gno fi neck
Ce que j'arrive pas à comprendre, "ça m'intrigue graav naq" moy Serigne yii nio lène gueumlo lii wala Talibé yii nioko soss?? Réranguéé bi c'st à quel niveau? Qu'Allah ns fasse miséricorde!
Ce guard la ne dit jamais ( sallalahou alayhi wasalam) quand il prononce le nom du prophet Mouhamad (sallalahou alayhi wasalam). Moi c'est vraiment ce qui m'etonne sur ce sois disant oustaz. Il est vraiment un vaux rien
Mandou, ci vie privée la mouna ame, wayé diné islam mom, bépou borom kham kham, waréfoula mou wakh ci nguir leral. Té mom oustaz modou fall, chaque jour mou wakhe né, musique defa haram té youssou ndour kilifame la ci walou liguieye, loutakh mandouwoul, bayi youssou ndour ak musiqueame, mou mandou si.
❤❤❤AIMÉ LA VIDÉO ABONNEZ-VOUS ET PARTAGEZ LE SAVOIR ❤❤❤❤❤❤❤
Merci Oustage c’est bien de remettre les choses en ordre , trop de fanatisme au Sénégal , on aime qu’on nous bleufe avec des miracles qui n’on jamais existé
Longue vie a vous ❤ ya oustaz ❤ ❤ Ba et aussi que Dieu nous protege sur le Droit chemin 😭 amine yarabi 😭
Yallah nanou yallah fayall sounou magg yi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
MACHAALLAH YA OUSTAZ ALPHA BA DEUG BOU WERR NGA WAKH
NITTOU TARIKHA DEUG LAY BAGNA DEGG PAR LA FORCE DINAGNE KO DEGG
Rére bonne n'a yalla naniousi yalla mousal insha'Allah 😢
Amine ya rabbi
On dirait que le Sénégal a son propre Islam à part 😓
Allah Subhanahu Wa Ta'ala dit:
قُلْ اَطِيْعُوا اللّٰهَ وَاَ طِيْعُوا الرَّسُوْلَ ۚ فَاِ نْ تَوَلَّوْا فَاِ نَّمَا عَلَيْهِ مَا حُمِّلَ وَعَلَيْكُمْ مَّا حُمِّلْتُمْ ۗ وَاِ نْ تُطِيْعُوْهُ تَهْتَدُوْا ۗ وَمَا عَلَى الرَّسُوْلِ اِلَّا الْبَلٰغُ الْمُبِيْنُ
"Dis: «Obéissez à Allah et obéissez au messager. S'ils se détournent, ...il [le messager] n'est alors responsable que de ce dont il est chargé; et vous assumez ce dont vous êtes chargés. Et si vous lui obéissez, vous serez bien guidés». Et il n'incombe au messager que de transmettre explicitement (son message)."
(QS. An-Noûr 24: Verset 54)
Qu’Allah vous récompense pour es éclaircissement yaa oustaz
Amiiiine.
Barak'Allāhu fik Oustaz
Machallah oustaz bâ
Mash'Allah Alpha Yalna yalla deugeureuleu yokou xam xam bii....Tarikha yi nio yakke Sénégal walahi Yalna lenffi Yalla dieulei
Wollahi kalimatou AKH YA CHEIKH ALPHA BA
Jazak Allah khyran 🙏🏼 Ya Ustaz Alpha much love from the Gambia 🇬🇲 🇬🇲💯♥️♥️♥️♥️♥️
Barakallahou fiikoum oustaz bâ
Mach'Allah Oustaz Alpha Diallo ❤
Tu l'a bien répondu, genre yi nio yakha Sénégal aïye mousibeuléne
مشالله oustaze جزاك الله خيرا
Pass pass tijan yii ci salatoul fatihi binnn naa yess naa
Machla oustaz Alpa amnasolo
Dinee Sénégal, vrai thiakhane, et ils n'ont aucun état d'âme à mentir et à répéter les mensonges de leurs mentors
السلام عليكم ورحمة الله وبركته علفه حيك الله احبك في الله برك الله فيك
Machalakh ouztaz alpha bâ❤❤
Excellent
Wallahi kou beug japp Bandı jappal Modou Fall ak Sarr.
Yallah bougnou yeuramoul dou mane dou ioe mi di lire amoul kenneuh kouy mouthie si bougueul borom bi.
Ya rabbi Ilaahi boul niou jappé waxi sayssay yii
السلام عليكم ورحمة الله وبركته علفه اعوريدو مشاركت معكم
Subhanalah
Machala ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machala lér yi am na soulo torop machala
Ma sha Allah
Dine HOLLYWOOD
Cheikh tidiane deukk maroc ca fése ,nioune wa sénégal amnaniou serigne touba dou moromou cheikh ,
ya oustaz alpha mbiryi niogi l'air du courage gni ay oustaz tarikha laniou
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
je t'aime mame cheikh ❤❤❤❤yaw
❤❤❤❤ Macha allah🎉
Yallah naléne yallah fayii thii barké alquran ak Sounnah Mohamed salalahou alayhi wa salam 🤲
Mane diné yallah dji rk moma gnorr topeu yonou yallah bii mo weur blhi watalahi
Sokhlona trop sén numéro guir yallah ak Rassoul j'ai besoin de vrai guide com vous pour mourir sur ma religion islamique celle d'Allah et de Mohamed psl wono 🤲😔😔🧕🕋🕌
K'ALLAH veille bien sur vous 🤲
🙏🙏🙏🤝🤝🤝🤝machalla ❤❤
Thiey Sénégal fougnou dieum li fane la ame
Nagnou gnane Yalla guénélen ci lii té mousal gnou genre wakh yi
😢😢😢🤕🤕
yawe thi Lo nékk lou bakh
Machalla oustaz alfa ba
Mais attends serigne yi nioy doul si sén mbindeu wala talibé yi nioy doul 😂😂😂
Serigne si la dé so demee si hatimatou MOUNADIATY wala diawaril mahani,wala si kifayatoul raghibine moussiba yinou fa bindeu moy problème bi
je t'aime ❤❤❤❤❤mame cheikh
Ma sha'Allah
Il en reste un parmi les 7 que vous avez cité
un jeune qui adore son créateur et qu'il a vieilli ainsi ...
Noo gnii nimalen diepei fen rek mom ak Matar Sarr
No lii metti naa
❤❤❤❤
Tarikha tidiane mo bone fene rek moy sene dine yonenty yallah mouhamed monou dianguale salatou ibrahim khana kidone soukourat di sagua te kilifala sy tarikha tidiane khana mome cheikh daka fate
Wallahi Alhouran ak Sunnah rek moy deug ☝️
BILAHI WALAHI DEUG BOU WERR
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته
شيخ الفاهم باه
كيف انت
انا علي
Sénégal,légui diiné folklore mofi nékeu,diiné door kat yi,mais le jour du grand rassemblement,ils verront et sauront que tout est vrai,In Shaa Allah.
Salut les fidelles fait très attention à ses genre de personnes comme sa allé apprendre votre religion c'est mieux fait attention bakhna
Gnikoy deglou sakh xamnen ni k wakhoul deug Allahoummahdina fimane hadaïte
Yene dangane fok ni nioune topouniou alkour bilahi comprends lene sakh
Gnakk ko topp wesséwoul nguénn bayyi koffi bayyi fi wahi yonnénte psl bi Di toppou wahou nitt Kou réréh Quran ba paré di réral ay nitt
Qu'Allah nous guide vers son droit chemin
Soubhamallah modou fall 😱😱😱
Modou fall fen rek 😂😂ak reer gou meti😢😢
Modou fall oustaze soupe kandié leu سبحان الله
Salatoul fatiha rekk🎉
Lou takh oustaz Modou Fall meun fen? Qui khalatna deh?
Vraiment tidiane bi wakhoofi dara way
Modu fal ragalal yala lingay wakni sakulfen ludul siseni serinyi saqul si alkuran saqul si sunna
Billahi gni daniouy taikhane rék waleu niouy foye sunu xel yii
Thiey ngi malen yeureum.un lobby qui égare les gens alors qu'ils sont dans l'égarement évident.beaucoup d'entre les gens qui sont avec eux ne connaissent que ce qu'on leur raconte dans leurs conférences par leurs éloquents et beau parleurs.les savants parmi eux ne disent pas la vérité mais c'est des menteurs car leurs mensonges les permettent de vivre aisément ainsi que leurs familles.
Cheikh yalla wathiee woul lay si mom bou keroguee dou sol toubey walahi souma walahi.
Le senegal, pays fertile même aux mensonges.
Assalamou alaykoum demay gnan kep kouy doundou sounna vidéo yignouy bublie gnou bagne sai déf a titre nit ah ay photo you am ay crois
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
👍
Mane ma dégoul nou bakh waleu. Dafani bane salatoul leu yala di dioulé ci yonent bi?
BONNE QUESTION
Des boniments malveillants qui n’honorent aucun homme sérieux encore moins un Musulman. Voici ce à quoi s’emploie ce très peu scrupuleux soi-disant Ustaz Fall
Gni dougnou sah rouss
Billahi
Salam o
Leukoum dîna koum wali dîni
Lakoum Dina koum waliya dine c'est entre un musulman et un non musulman.quand vous faites référence à ce verset, cela veut dire que les tidianes ne sont pas des musulmans.d'apres ton raisonnement.
Ce verset ne s'applique pas entre musulmans.
ignorant que tu es va étudier t'a religion
Wallahi 😂
Djangu rek woor😂
Qu'Allah nous guide
As salamou aleykoum warahmatoullah wallahii borommm bii rekk moo khamm founiou moudjii thé yallah boromm sammm niou sakhall ni thii alkourannn akk sounnaa bou lerr moussalll niou siii biii wallahii lii ko koo deuggg warr giaa titt ndakhh booo khallathé nii ammm guaa mookk bou nekk thiii dii gua tiite 😢😢😢 yalllah boromm bii sammm niou thé bouniou fathé dii diangue souniou diiné thé sannté borombii guanayy bouniou wonné souna bou ler thé niou moyy bida akk bokalé
Dardf Cahke tidan
Ligueye ak jamou Yalla mo eupe yiw li guay def dou alkhourane dou souna istihraj la si xam xam reuy reuy lou si xamxam tai gnou la rawe gno fi nek
Niou KO eup xam xam nio fi nek on l'accepte mais ils ne disent pas la vérité aux talibes.
Alpha limouy wah Moy DEUG Modou fall day fen limouy wah amoul thieuslay si islam.doko fek si arhourane doko fek si khadithssou yonentibi.
Ay fen la !
modou fallo duii reqe
Dof deug mingui nii
Mou nékh lén wala mou nakhari lén cheikhou tidiane sauvé nagnou ba sauvé sén aye baye mame rassoulah moko diokh yén sén xam xam bari woule té guén bari wakh gnouss lén sén ndaye sa hath
Fi makk gni gno fi neck
Oustaz alfa ki nila bou mag la fall weroul
Ce que j'arrive pas à comprendre, "ça m'intrigue graav naq" moy Serigne yii nio lène gueumlo lii wala Talibé yii nioko soss?? Réranguéé bi c'st à quel niveau?
Qu'Allah ns fasse miséricorde!
Yéen soof ngeen waay.
Fexe leen bañ baayi çalatul fatihi rekk.
Noppalu leen waay te yaatal séen xol. Te rafét njort ci jullit yi.
KOUY WAKH DEUG NGENI BAGNA DEEG PAR LA FORCE DI NGENE KO DEEG
Ce guard la ne dit jamais ( sallalahou alayhi wasalam) quand il prononce le nom du prophet Mouhamad (sallalahou alayhi wasalam). Moi c'est vraiment ce qui m'etonne sur ce sois disant oustaz. Il est vraiment un vaux rien
Yaw ibadou bi wédi limouye wah sa deudieuw ndaye
Alpha mandouyoul
Wah DEUG yalla dji Moy mandou.
Nopi si ay fen bocoul si mandou.
Merci
On se fout de ce que tu dis nous sommes tidjiam mourite etc point barre
Vos enseignements on s'en fou
Alpha Ba joulite Dey Mandou
Wahi doff yowe hamoulo louye mandou
Sa waye bou ustass you deugouyi mando dou bakh déh
Lane moy mandou. Si tout le monde se tait sur ce genre Sénégal alkou.
Mandou, ci vie privée la mouna ame, wayé diné islam mom, bépou borom kham kham, waréfoula mou wakh ci nguir leral.
Té mom oustaz modou fall, chaque jour mou wakhe né, musique defa haram té youssou ndour kilifame la ci walou liguieye, loutakh mandouwoul, bayi youssou ndour ak musiqueame, mou mandou si.
Mandou moy guiss deug waxko mais pas nopici
En plus tu fait hors sujet on te parle de nouveau salath alors que tu parles des autre
Yene sona ngene alpha ba yaw ya dakha fene niep
Dangua rérr motakh
Qu'Allah te guide