Si quelqu'un n'est plus, malgré lui, compatible avec le Projet, nous ne lui en voulons pas. Nous prions que Dieu le libère de ses contraintes et qu'Il renforce son discernement.
Walahi Mansour n'a rien dit de grave mane je le suis chaque matin Jour bobou il avait dit carrément "douma si wakh" c'est les gens de mauvaise foi gnoy diabolisé 😢😢😢 Mansour tognoul kén bilahi ❤
Merci Mansour Diop nioune nieupeu ay talibé Cheikh lagn mais wouloum voté bén Serigne douma thi diox Ndigueul téréwoul dina matal lép louma war thi Serigne bi
Kou bour yalla teunkoul, ngay nangou sa moromou diam dila teunk, ni rek ngay moudie. Sa deugue da am niokoy dieumeule. Douma nangou ci adouna bene diam dima teunk ci sa bop...
Projet bi bukul ak taalube gi. Projet ngir luy defar réew mi la taalube gi ngir diine la . am Na ñu àndoon ak singor ci projeem te ànduñu ak moom ci ak taalube
Lou nek si politique bou fekeni Serigne Moustapha ngaye waxal dhé adouna oumpalé woul AK wetal yallam AK nek si téré AK nopal ay talibèm khamo Noppi wo nak amna lougnisi wax
Na gnou kham ni le 17 Novembre 2024…dou bissou election kassè si patriots yi ak sympathisant Sonko yi… bissou thiante la ak mbèktè di guissate bulletin Ousmane Sonko si urne ni…bissou ndioukèl sounou leader de la revolution , bissou remercier Ousmane Sonko sounou diambar Bi gnou khèkhal liberer gnou…mognou dèlo lignou mome djeulè ko si gnignou beugone dèff des esclaves des temps modernes…meunou gnou ko Faye…bulletin Boussi nèk bulletin de reconnaissance lay done envers lui…djeureudjeuff Sonko
Sama toma kay mom moy lolou mais nak nanou ko nangoul rék fofou là niveau wam tolou Mok ma djiguén 😂 kholal biko sa corrigé si lim wakh si média mou commenceé léral nioun kham nan mourchid tv mi moudié nieuw man na lén diangal nou médias wara dokhé niom niepp ❤
Si quelqu'un n'est plus, malgré lui, compatible avec le Projet, nous ne lui en voulons pas.
Nous prions que Dieu le libère de ses contraintes et qu'Il renforce son discernement.
Machallah mamadou Mansour diop ❤❤❤❤❤❤ sonko à vie ❤️🔐🥰
Macha Allahou MOUHAMED MANSOUR
Bravo @Souka 👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿
Niaka fetee dayy khagne weurseuk fetee ak la majority du peuple ak deuga rekk mo war journalist ❤
Ma yakar ni journaliste dafay teuddé diakhanday walla
Macha Allah Mansour Diop❤❤❤
Merci omar
Merci mansour baravo
Walahi Mansour n'a rien dit de grave mane je le suis chaque matin
Jour bobou il avait dit carrément "douma si wakh" c'est les gens de mauvaise foi gnoy diabolisé 😢😢😢
Mansour tognoul kén bilahi ❤
Mi
Merci Mansour Diop nioune nieupeu ay talibé Cheikh lagn mais wouloum voté bén Serigne douma thi diox Ndigueul téréwoul dina matal lép louma war thi Serigne bi
Ndakh sa serigne doyoula
@@diopmoustarchid910wakhi dof
Merci beaucoup nonou rk la tolou serignam doyouko@@diopmoustarchid910
Diarama serigne moustaph sy malick xasir ❤❤
Ce pays et ses populations sont enchaînées. TËNK SI XEL TENK SI KOOM TENK SI DIINE
Mansour merci merci merci beaucoup 👏👏👏👏👏
❤❤❤❤j'aime ❤beaucoup sonko
Kou bour yalla teunkoul, ngay nangou sa moromou diam dila teunk, ni rek ngay moudie. Sa deugue da am niokoy dieumeule. Douma nangou ci adouna bene diam dima teunk ci sa bop...
Merci Sa ndiogou Wakh dafaye lére
Focus 17 novembre 2024 à 19 heures GMT !
PASTEF, ndam rekk !
Jërëjëf Sonko jërëjëf Joomaay
Heureusement que ce n'est pas des guides religieux qui dirigent ce pays. On n'est guide religieux ou on fait la politique il faut accepter la critique
Deug deug
Ok mais esk yaw dinga critique sa papa
Saint coran ak sounneu rek mo worr daguay am diam alhamdoulilah
Walay way.
Mawdo Ak bamba nioy Sunna Nio janglé khadiss firi Alhour ane sa bam jafé
Béne nekoul thi yaw guay niodi
Machalah Omar wakh nga DEUG bu wer❤❤❤
Machallah Mansour une grande personne pleine de vertu
képp kou beugue sonko AK diomaye abonnélema🙏🏿❤️
Moi j'ai une question PUR partie politique lah wallah dahira lah???
Pour wax la parti bi waxou mala djioulite sax mais chrétiens yi nioungui si xana nekoul dahira té fi gnou créer partis yeup laniou ko créer
@@laminesow6564 donc pourquoi considérer que talibé serigne moustafa amoul droit critiqué partie bii ??.
Merci béty
Merci beaucoup Mansour yaw gor pur nga
DemboTihagou❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
OMAR BOUNKHATAPE GUEYEEE !!!! TRÈS PERTINENT , EFFECTIVEMENT
Machalah
Bilahi lezi laillahi illala hamon na Omar dou and ak mansour ta degou ko fen loudoul afer tariha rafetal kom Sohibou Manchallah @solutiontv
Mansour wakhofi Lou aye 😢
Thieye Sénégal dinga wakh yonenti bi lou grave do guiss gnimou meti wayé tarikha rek yalla bakhna yalla laniou khar
Vérités absolu Omar ❤❤
Omar wax nga dëgg gu wér ❤
La politique, n' a pas de dahira.
Y'a la démocratie ou pas
Barvo Omar duge reke mo wor andak yalla reke mo wor yalla reke moufi nke
Ayy fan s sam lagn moom Mansour. DIOP c est de l incomprehrndion
Am liberté nehé n'a bilahi li com kou nékoue prison bilahi sounna nigi koye dondou nawe nalen
Machallah Souka kaddouyi rafétna
Barvo Omar mansor
Projet bi bukul ak taalube gi. Projet ngir luy defar réew mi la taalube gi ngir diine la . am Na ñu àndoon ak singor ci projeem te ànduñu ak moom ci ak taalube
Vraiment Sénégal ke des nafek Mansour diop n'a rien dit de graves arrêtons les manipulations
Nioune Sakh dagno sokhlawoul média
Je prie vraiment pour une réconciliation entre Pastef et PUR.
Je suivais regulierement M. Mansour Diop mais diebeul telewam wa PUR takh na ma parer ci mom
S'en leffel ndaye yenn wa solution tadou s'en chinne bi sonko moko môme mansour Diop wakh ni youm kénne yoniwouko s'en data Yaye s'en data Baye s'en leffel ndaye
Souhibou Mansour da wakh thi PUR loudoul deug wa PUR dioubanti ko
Moudélou guinaw
Wakhlen deug
Dafawakh pur mon nara yakh election bi
Yenn je regardais toujours votre émission mais yakh guenn walf dakh farr parlo surtout yaw omar
❤❤❤
Serigne bouye politique doka yombal saye talibé Serigne sou bougué nopal aye talibem tereya toll ba wetal Ya Allah
Lou nek si politique bou fekeni Serigne Moustapha ngaye waxal dhé adouna oumpalé woul AK wetal yallam AK nek si téré AK nopal ay talibèm khamo Noppi wo nak amna lougnisi wax
@@fatimakane2463serigne bouye plotique la wakh deh nga beug se guiss sa bopou lou xew
@@fatimakane2463 preuve banguini yongui polemique si hay commentaire te sama droit la nek wakh sama xalat ngamaye nopilo
Omar ❤
Bayilen fen dafa wakhal pur Lou amoul dafani pur yabaloul cheikh youm
Mansour diop lime wakh ak liguéne tek dou béne
Bayiléne seytané sen yone nékoussi vraiment
Je ne saurai dire combien de personnes sont dans la même situation que Mansour, bok DMWM bah parei gueum ni sonko ak Diomaye gno gueun ci reiw mi
Wa pur sokhlawouniou béna média
Bala di def mission si dra dageni geustou bou bakh
❤❤❤❤❤❤❤❤
Omar sans dépend tchii média bi
Dahira ak parti politique c'est pas la même chose ni le même objectif. Il fallait pas mélanger les choses. Projet bi rek moñu intéresser.
Mansour dafa wakh louamoul
Ngoun sunu projet pur la wasalam
Seydina Omar mo geun diapp point bi dh.
Omar guéye mi dou nitou deug mouni mansour waroul diégalou khana dégo Li wakh nafekh
Sohiabou beugeull kéne wakh si Serigne bi 😂
Na gnou kham ni le 17 Novembre 2024…dou bissou election kassè si patriots yi ak sympathisant Sonko yi… bissou thiante la ak mbèktè di guissate bulletin Ousmane Sonko si urne ni…bissou ndioukèl sounou leader de la revolution , bissou remercier Ousmane Sonko sounou diambar Bi gnou khèkhal liberer gnou…mognou dèlo lignou mome djeulè ko si gnignou beugone dèff des esclaves des temps modernes…meunou gnou ko Faye…bulletin Boussi nèk bulletin de reconnaissance lay done envers lui…djeureudjeuff Sonko
Sounnah rék mo woor billahi
Maodo Ak khadim nioy sunna ndakh nio léral Sunna firi Alhour ane
Wallahi deugla
Deug pur mouvement yi qeen momouko
Yen liguene Di wox ak origine du problème c pas la même chose
Sénégalais mo beug ay détail 😢
Touba tv wala asfia xana Kone Dou media
Oumar waxo logique ❌❌❌
Mais faut savoir que Pur est different du mouvement moustarchid,car il y'as des chrétiens et les adeptes d'autres tarikhas qui sont moustarchides
Omar bale ma mis xamou tousse 😢
Sama toma kay mom moy lolou mais nak nanou ko nangoul rék fofou là niveau wam tolou Mok ma djiguén 😂 kholal biko sa corrigé si lim wakh si média mou commenceé léral nioun kham nan mourchid tv mi moudié nieuw man na lén diangal nou médias wara dokhé niom niepp ❤
Billah nek ibadou nekh na kein doula teunk si dara tu totalement libre. Lislam rek molay guidé pa niit 😅
Mais waji lokou seringe Moustapha sy def
Na toube rek ❤❤❤❤❤❤
Franchement je ne comprends pas les plateaux. Liguéne fi indi ak li ame dara bokousi
Fen rek fen rek😅😅😅
Sonïbou dagawarona dèglou limou wakh
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Vraiment ces tariha terrorisent les fanatique
Sa taye dagua dioume cou togne moye diégeulou 😢😢
salam sohibou da nga warona tek limou wakh mo geune wala beugou len lou ler bok
Wakh lén lougine xam diarama Serigne Moustapha s'y PUR rék inshalla 💚🤍🤍💚💚🤍
Iow tmt waxal lo xam dh, Pastef seul 💚🇸🇳❤️
Mais pourquoi confondre Dahira et parti?
May lén diammou addouna naka diék wooté xalat masouféé diouk bathi yonnantebi shm daan na wooté ak chaabayi guss guss
Mansour dafay diegalou pas ci video mais loumou Wakh Cheikh tidiane Youm Serigne bi yabalou ko té Serigne bi Mo ko Yabal renseignez vous bien
Lamp fall tv ndakh amoul pété malikia tv nakanonou kone omar liguawakh takhaxoul
Partit tarikha yi sakh dafè wara diouguè
Eska deglouga wakh dji leupe
Bala ngen Di enalisé dangen Di deglou ba ham li héw
Mais Massour Projet Serigne Moustapha sy la wah dè
Non projet pastef la wax kon amoul sens mouy diegelou dh
Pass pass mo eupeu dole militantisme
Ak wouté day am ta yaqoul dara si pas pas pourquoi yonnantebi hsm daan wouté ak chahabayi boudéé lou soxol addouna
Sonko rék ???
Neaye sane xamoulene sakh limou wax disi wax
Bala guéne di débatre thi mbir war guéne ko gueustou bamou lére ndakh yéne ngiye wakh fi wakhagouléne togne bi lane la
talibe ak pilitique warou nio diotè dara bouko nèkhè andd ak partit bou ko nèkh serigne ak talibe la sèkh ak moustapha sy
Wadji mom dou daneé dégo dakor 😂akh mom😂
Mais yène liguine de wakh do lolo